Contre-Polygamie - Episode 70 - Saison 1 - VOSTFR

Sdílet
Vložit

Komentáře • 576

  • @PendaThiam-sd9yf
    @PendaThiam-sd9yf Před 16 dny +58

    Kou gueum ni Astou mok makkou Gno nara ande guén keurgui rec lalal j aime😂😂😂

  • @YellySow-ho1db
    @YellySow-ho1db Před 16 dny +125

    Dama Beugue ame dieukeur ak dome nianal lenma

    • @user-rm5jn3mv3e
      @user-rm5jn3mv3e Před 16 dny +15

      Yalna la yalla mayla dieukeur bou bakh bou la beugue te teral la gua am dome you bakh te barkel ❤❤❤

    • @MouslyLaPatriote
      @MouslyLaPatriote Před 16 dny +7

      Yalnalako yalla may ak mane amiiine yarabi

    • @ndeyefatouniang4583
      @ndeyefatouniang4583 Před 16 dny +3

      Yalnalako yalla may ak mane mi dom rek la beugue

    • @DiopDiarra-nf2ci
      @DiopDiarra-nf2ci Před 16 dny +4

      Yana la yombou ta mou geun si yaw

    • @oumy6935
      @oumy6935 Před 16 dny +1

      Yalla nala ko yalla Amy tei mou gueune ci yaw

  • @mamitacaramel
    @mamitacaramel Před 16 dny +105

    Celui qui lis ce commentaire que Dieu vous bénisse et vous garde en bonne santé vous et vos parents ❤

  • @ndiorelndiaye1032
    @ndiorelndiaye1032 Před 16 dny +48

    Je réclame mon bonheur dans cette série qui n'est rien d'autre que la FIN

  • @ablayelo8358
    @ablayelo8358 Před 16 dny +188

    Man serie bi damay setan mais damay avans rek kouy avans rek lalal j'aime

  • @maimounasene7281
    @maimounasene7281 Před 14 dny +5

    Ndiago outeul surnom pour sa saourou jeukeur boss boundaw la en plus dagua manquer thiasssss😂😂

  • @moussasow2975
    @moussasow2975 Před 15 dny +48

    Kou d'accord ni astou AK sawrou ño bok baye lalal j' aime

  • @ablayesall8808
    @ablayesall8808 Před 15 dny +31

    Kou d'accord ni serie bi nékha toul rk lalal ma j'aime 😅😅😅

  • @khadygueye1707
    @khadygueye1707 Před 16 dny +78

    Astou yaw tasse katou keur gua ndékéter yaw mi tonton makhou m’énerve Bilaye 😂😂😂

    • @yayefallbi4070
      @yayefallbi4070 Před 15 dny +8

      No Astou mi vrai Mbame la Bou Ndaw môme doff la rékk kou nieuw dougou si khell bi guénn bi môme so commencer nama Sorou fassé

  • @ramataba962
    @ramataba962 Před 16 dny +50

    Astou dama meunn seyy ndékété ayy meunn fénn moko fa dieulé 😂😂😂😂😂😂😂

  • @evathiam7770
    @evathiam7770 Před 16 dny +58

    Kou diougué bété bété diar d'échéance té nieuw fi rek beusal ❤

    • @jammrek3710
      @jammrek3710 Před 16 dny +2

      Déko ndieukeu sétane té di moudié Bété bété. Damay bagne nga moudié bi mou déss ci sa khél mi

    • @fatimdiop9282
      @fatimdiop9282 Před 15 dny

      Il faut diminuer le son

    • @evathiam7770
      @evathiam7770 Před 15 dny +1

      @@jammrek3710 😂 mbadou

    • @jammrek3710
      @jammrek3710 Před 15 dny +1

      @@evathiam7770 lou léer lala wakh 😂 😂

  • @thianediaw2627
    @thianediaw2627 Před 16 dny +21

    Poligame moy saloni nitou intere moy changement du destin versión senegalaise avec pikini indo votre coeur bat plus fort

  • @mamediarrambaye1220
    @mamediarrambaye1220 Před 16 dny +33

    Bou ndaw massa âme bay bou melni tonton magouilles mom Diara Diot mais mounial rek😢

  • @antandiaye8982
    @antandiaye8982 Před 15 dny +6

    Waa Pikini wakh len si sen son bi ken khamoul lignouy wakh

  • @user-ip2jw7yy1i
    @user-ip2jw7yy1i Před 15 dny +8

    Bete bête AK babell meilleur seri

  • @nafidiakite3363
    @nafidiakite3363 Před 16 dny +35

    J'adore ndiago ak Boudaw thiey Makou ❤

  • @binette-wc3fx
    @binette-wc3fx Před 16 dny +40

    Worna yallah, seneu qualité son bou bone bii momay bayilo setane série bii

  • @Ngone-rj7yp
    @Ngone-rj7yp Před 15 dny +7

    pourquoi vous restez tjrs dans l'appart mais il faut sortir😊 allez à la plage ,au restaurant dans les jardin publique ,au marché etc il faut sortir changer de décor

  • @AwaSarr-gh2fc
    @AwaSarr-gh2fc Před 16 dny +27

    Koudoul diouli yangui si erreur

  • @ndeyediop6917
    @ndeyediop6917 Před 16 dny +30

    Mafi djitou may lènma j'aime ❤

    • @aichasy3315
      @aichasy3315 Před 16 dny

      Ken mayoula série bou bonne bi😂😂😂😂wouy😂😂ma chérie❤

  • @kikicamara2627
    @kikicamara2627 Před 16 dny +23

    Vraiment c'est dure de regarder vos séries pikini défar len sen son bi

  • @KhadyseneKhadysaliou-lg6bo
    @KhadyseneKhadysaliou-lg6bo Před 16 dny +30

    Meilleur serie sénégalaise 😂Sene bop nguene ndi ndahe,Astou nake mome mo amoule mbene chance si film bi

  • @NdeyeSylla-xe6lc
    @NdeyeSylla-xe6lc Před 16 dny +30

    Cou bagne tonton mako rek lalala sama j' aime 🎉🎉🎉

  • @mariamalyco3723
    @mariamalyco3723 Před 16 dny +7

    Makou ak astou kiff kiff da wara tak astou souko defė guen am domou seytanė nak😂😂

  • @AdjiselbeNdiaye
    @AdjiselbeNdiaye Před 15 dny +18

    Kouye sétane série bii di nélaw rekk lalale j’aime 🥺

  • @evaseck7019
    @evaseck7019 Před 15 dny +2

    Mais kou kham bou ndaw ak yayam Marie Jeanne louñiou book dans la vraie vie dañio nda niro trop sah ❤

  • @khadijadioum4828
    @khadijadioum4828 Před 16 dny +12

    No makkou dou nittt😂😂😂😂😂nénako marizane Kayma deff laaaa niarel 😂😅😅wouyyy

  • @AstouFaye-on5wp
    @AstouFaye-on5wp Před 16 dny +10

    Delene wakh bou bakhe way❤❤❤❤❤😂

  • @mustafaasamb8419
    @mustafaasamb8419 Před 16 dny +24

    Série bi kenn xamul lu muy saf. 😂 😂 😂

  • @user-sx1ys5gz8j
    @user-sx1ys5gz8j Před 15 dny +5

    Mais guéne yakarnie ASTOU DOUKO DAKHE❤❤❤❤❤❤❤😅😅

  • @user-jg3ky3qu3w
    @user-jg3ky3qu3w Před 16 dny +12

    Bou ndaw limou wakh dara dou si deugue

  • @user-gk8yc9ob9f
    @user-gk8yc9ob9f Před 15 dny +10

    Tons makou nena amna lo xamné kenn meunouko wave kouko dégue lolou comme mann lalal ❤

  • @awagaye4878
    @awagaye4878 Před 16 dny +29

    Top na série yi ba am febarou serina virus li do diam😅

  • @sodalo4179
    @sodalo4179 Před 16 dny +11

    Tonton Mago dém na dh wayè bayi nafi élément wam

  • @seynaboufall7552
    @seynaboufall7552 Před 15 dny +2

    Nekhe n'a mais son bi dése amna problème ❤❤

  • @fatoudieng3840
    @fatoudieng3840 Před 15 dny +2

    Théâtre bi khadje by yeup publicité la da war diekh sakh chaque jour meme chose acteur yi mome sounounou si chalaze

  • @yayemayelatmbao5442
    @yayemayelatmbao5442 Před 16 dny +15

    Oh bété bété la djougué mais série bi yakk na sama goût bi yeppp😢😢😢

    • @AlimatouSeck-gb9op
      @AlimatouSeck-gb9op Před 16 dny +1

      Motakh man mom lay ndieukeu séttan sogua séttan you nékh yiii😅😅😅

    • @yayemayelatmbao5442
      @yayemayelatmbao5442 Před 16 dny

      @@AlimatouSeck-gb9op legui dagnoukoy goudé dougal motakh

    • @mayegaye
      @mayegaye Před 15 dny

      Man dé lole khala toma ko beté bété ak babele ky doma si tek pikini ak khar media 😂😂😂😂😂😂

    • @yayemayelatmbao5442
      @yayemayelatmbao5442 Před 15 dny

      @@mayegaye yalla lako takha wakh dé gni🥲

    • @yayemayelatmbao5442
      @yayemayelatmbao5442 Před 15 dny

      @@mayegaye yalla lako takha wakh dé gni🥲

  • @MbathioGueye-dl7qq
    @MbathioGueye-dl7qq Před 16 dny +7

    Série bi amol bén chance 🌚

  • @ndeyelababacarienne770
    @ndeyelababacarienne770 Před 15 dny +4

    Wa astou mi séytané woul te meune féne😢😮

  • @user-fn4hf7ec3z
    @user-fn4hf7ec3z Před 16 dny +10

    Série bi kéne dou deuk Ligni wakhe

  • @KhadySeck-ji7qk
    @KhadySeck-ji7qk Před 16 dny +5

    Astou seytanné diapoulaaa😂😂😂😂

  • @hdhdbdjdndnbdh7675
    @hdhdbdjdndnbdh7675 Před 16 dny +9

    Allah sheytane Astou

  • @princessemyadiallo9791
    @princessemyadiallo9791 Před 16 dny +17

    Kou diépi makou rék lalal jaime astou Moy saytané

  • @ndeyefatouniang4583
    @ndeyefatouniang4583 Před 16 dny +10

    Sen son forna par rapport ak wakh bi❤❤❤

  • @user-lc9cn4hf7m
    @user-lc9cn4hf7m Před 13 dny +1

    girr yalla degue yêpo fègne na yayo bo ndaw fègne na bayam fègne na loy problème bi😂😂😂😂 fènial lên astou mo djèkh 😂tampe aml nk

  • @oumydiallo6153
    @oumydiallo6153 Před 16 dny +8

    Mane ma bayi sétane série bi

  • @PASSworde
    @PASSworde Před 15 dny +5

    Rousna pikini tarop me lidoutiyatar gouko gam la jam ❤

    • @mayegaye
      @mayegaye Před 15 dny

      Loy Rouse nane ko wakh té de wenté li nékhole😢

  • @DawoulThioow1eg2ih9n
    @DawoulThioow1eg2ih9n Před 16 dny +7

    yalla nalen yalla deffal diammou diou Sax

  • @mamadoudiop103
    @mamadoudiop103 Před 16 dny +8

    Sonbi darar bakhousi

  • @DiodioNdiaye-ef7tq
    @DiodioNdiaye-ef7tq Před 16 dny +11

    Babel❤❤

  • @fallfall8520
    @fallfall8520 Před 16 dny +5

    Serie bou nekh la❤

  • @YacineFall-tx1jl
    @YacineFall-tx1jl Před 15 dny +4

    Wa khana tata diolé d'où diogué maka yague na😂😂😂😂😂

    • @MaymounaDione
      @MaymounaDione Před 14 dny

      Surtout lolou. Makka môme gnata ate lafa nara def😅

  • @SokhnaFaye-ut5jv
    @SokhnaFaye-ut5jv Před 16 dny +6

    Série bi nekhna ms wakh bi dou ler day awou liniouy

  • @gayendiaye-fr5it
    @gayendiaye-fr5it Před 16 dny +10

    Mér Niollé néna dafa dieul gal gui déf Espagne mn takhe guisso léne KO thi série paska série dokhol pousoul lolou la Diot taye thi informations yi😂😂😂😂😂

  • @ramataba962
    @ramataba962 Před 16 dny +7

    Merci wa pikini pour la publicité sauce soja resto en poular 😂😂😂😂😂😂

  • @yassbi
    @yassbi Před 16 dny +5

    Wakh fa deug nekh yalla beug n'a setane way fi la meun ya bayi n'a dama sonou

  • @KatyFaye-yu6kk
    @KatyFaye-yu6kk Před 15 dny +2

    Djiguenou théâtre bi nio geune niak fayda 😢😮😂

  • @DabakhBoye
    @DabakhBoye Před 15 dny +3

    Gayi Kou d,accord ni série bi da sofe rek lalale j,aime

  • @coumbisssow2777
    @coumbisssow2777 Před 15 dny +3

    Il faut diminuer le sons pour que gnou meuna dègu sèquence Yayou Bou Ndaw ak ndiago kène degoul

  • @user-hq3yr8fq3i
    @user-hq3yr8fq3i Před 10 dny +1

    Waw bakhna D'accord Merci bakhna ❤💪🏾

  • @FatouSarr-fq1ob
    @FatouSarr-fq1ob Před 16 dny +12

    Wouy ndiago nena djikeur😂😂😂😂

  • @boussothioune1418
    @boussothioune1418 Před 16 dny +4

    Makou ay fan sakh meun na wengal guémignam bi 😂😂

  • @matygueye1184
    @matygueye1184 Před 14 dny +1

    Kouye setane serie bi di avance comes man rék lalale j'ame

  • @medounegaye-mx6fe
    @medounegaye-mx6fe Před 16 dny +18

    On rèclame la fin de saison😢

  • @khadybarry6651
    @khadybarry6651 Před 15 dny +1

    Meunoléne bayiwoléne😂😂😂pikini arrételén wayy doyna sone nagne degne koumpa momafi indii😂😂😂😭😭😭

  • @rokhayadiop799
    @rokhayadiop799 Před 16 dny +19

    Mafi djitou taye maylène ma jaime❤

  • @user-ft2cn6og1m
    @user-ft2cn6og1m Před 16 dny +33

    Cou geum ni série bi Moy souniou yétaly rek beusal j'aime 🎉

    • @AbdoulayeCisse-vl1zm
      @AbdoulayeCisse-vl1zm Před 16 dny +3

      Série bi problème son lanou am man écouter la takk mai manouma fekhé ba comprendr li ndiago ak marigene Di wakh

  • @fatoundiayediop4582
    @fatoundiayediop4582 Před 16 dny +8

    Sama serie bi defoule loudoul nekh❤❤❤

  • @diamatv2
    @diamatv2 Před 16 dny +5

    Tonton makou ne va jamais changer

  • @meimounawatt6169
    @meimounawatt6169 Před 16 dny +2

    Quel est le rôle de Astou dans la maison?

  • @soukeyedeme
    @soukeyedeme Před 16 dny +9

    Asou li mome diapoula nétali

  • @maguetteniang1146
    @maguetteniang1146 Před 16 dny +3

    Guene wax contre polygamie té wané wolen fi dara
    Normalement sawerou séne mo warra guiss louko diaxal sax mais pas mouy mm répétition walla guene toudè série bi « famille débordée « Walla famille diakhassé « bokk

    • @Sulaiman-ow2hw
      @Sulaiman-ow2hw Před 16 dny +1

      Ndakh nga sagnko wakh né contre polygamie ba moudié nek polygamie

  • @adamagackou4494
    @adamagackou4494 Před 16 dny +8

    Li Moy youwé na ba khamatouma Lou maye youwé😂😂😂

  • @aichabadji483
    @aichabadji483 Před 16 dny +4

    Mari jeane ak boundaw gno geuneu gnaw si série comme si elle est sa vrai mère

  • @mamadoudiouf5341
    @mamadoudiouf5341 Před 16 dny +4

    Mafi djitou 😂❤❤❤

  • @NdeyeSylla-xe6lc
    @NdeyeSylla-xe6lc Před 13 dny +2

    Touti mo th ague 1000❤❤

  • @ouleymatoudiao-ut1hg
    @ouleymatoudiao-ut1hg Před 13 dny

    Ay wayy fin de saison guirr yallah wa pikini

  • @user-jd6nc4ph5l
    @user-jd6nc4ph5l Před 16 dny +2

    ASTOU MI DONE WAKH NANE DOU SAYTANÉ KENE TAY MO MOUDJIÉ DONE SAYTANÉ BI WALA DAFA BEUG PLACE

  • @maimounambengue6546
    @maimounambengue6546 Před 15 dny +2

    Thim sen son war ngen koy dindi deh akh do kham dara si ligni wax😢😢😢

  • @myriamyanga9145
    @myriamyanga9145 Před 15 dny +1

    Mère et fille se ressemble tellement😂

  • @adamammeniasse9754
    @adamammeniasse9754 Před 15 dny +1

    Seri bii nekhna lol wayé son bii do dégue dara

  • @user-bz4mi2tq3j
    @user-bz4mi2tq3j Před 13 dny +2

    Astou soppékouna saytané dh😂😂😂😂😂😂

  • @aidadiagne9539
    @aidadiagne9539 Před 13 dny

    vraiment série bokhamni 40 minutes laniouy def dawalsi 30 minutes c vraiment pas la peine

  • @Saii_Nabouu
    @Saii_Nabouu Před 14 dny +1

    Khana magou da am gemanj bou meti😂😂😂

  • @BeugNaby244
    @BeugNaby244 Před 15 dny +2

    Boundaw AK tonton mankou danio nouroo sahhh😂😂😂😂

  • @fatoudiedhiou8353
    @fatoudiedhiou8353 Před 15 dny +1

    Ndiago dafa eupeul nit daguoy comprends

  • @ibrahimasene1952
    @ibrahimasene1952 Před 16 dny +2

    Badiéne dieppina tonton maguo😂😂😂😂

  • @yassbi
    @yassbi Před 16 dny +2

    Bonne continuation setane ka ti 😂😂

  • @abibatoudia4258
    @abibatoudia4258 Před 16 dny +6

    Série bi acteur yi sakh amougnou émotion bou naturel si lagnouy joué. Pask personnage mako comportement wam, Mok badiéne ak Marie Jane amougnou dara si emotion . C pas naturel. Par rapport ak yenén maison de production yi là tu ressens une émotion , di dounde série bi mais li . Déjà sen tournage yeup si beneu keur la yam.,

  • @dieynaseck8407
    @dieynaseck8407 Před 15 dny +1

    Machalla pikini

  • @MrDouane
    @MrDouane Před 16 dny +4

    PIKINI FAITE UN EFFORTS SUR LA Qualité DE VOS PRISES DE SON! VOS PRENEURS DE SON PEUVENT EN MOIN D’UNE SECOND IDENTIFIER LES TEMPS DE LAIS ET DE RÉVERBÉRATION il suffit de poser des panneaux acoustique modulable lhors champs de l’objectif de la caméra , et augmenter la durée de vos séquences , ne soyez pas pingre waay en tamitt «!! Wala boog

  • @yacinengom590
    @yacinengom590 Před 16 dny +3

    En 2min setane na episode bi😂😂😂 dama avancé bamou diekh😂😂😂

  • @mariamalam9402
    @mariamalam9402 Před 16 dny +2

    Mangui fiiii🎉🎉🎉teyy mom ma fi djitou

  • @cameraismaila5907
    @cameraismaila5907 Před 15 dny

    Questo video e belissima ❤❤❤😂😂

  • @user-vg2bx5ui2y
    @user-vg2bx5ui2y Před 15 dny +1

    Nitt mi lundeum boundaw yaw légi danga warr

  • @FamaFaye-kz7lv
    @FamaFaye-kz7lv Před 16 dny +3

    Baabel seul ❤❤

  • @senewayetv2062
    @senewayetv2062 Před 11 dny

    Sowrou séne l'acteur du peuple

  • @oulimatandiaye108
    @oulimatandiaye108 Před 15 dny +1

    Wah degue nékh yalla nékhatoul

  • @SeynabouSowsylla
    @SeynabouSowsylla Před 10 dny

    Wa yene sene son bi douguene ko defare❤❤

  • @ndciss3521
    @ndciss3521 Před 16 dny +8

    Serie bi ligni wakh ken douko dégue