BA DIAKHATE ET L'IMAM VERS REUBEUSS...MOUSTAPHA DIAKHATE LE SUIVANT?...BABACAR FALL RFM ON A PORTE..

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 21. 05. 2024
  • SOLUTION TV

Komentáře • 332

  • @mamimami7970
    @mamimami7970 Před 24 dny +35

    Émission bu tey bi, Mashallah.
    Mbétél gu néx ci daalu Serigne yu bax yi nguéne daalal ax ñi duug ci ligne bi.
    Ba mu mété wone ñom la ñu done guiss. Yalla na lén Yall féye
    Contane ci yéne wa SOLUTION, Yalla na lén Yall taxawou.
    Mashallah ♥️ ♥️ ♥️ ♥️ ♥️ ♥️ ♥️

  • @user-ze6wt3lx6m
    @user-ze6wt3lx6m Před 24 dny +26

    Bilahi SA mann say diangatt dama yéem vraiment tu es très très très très très pertinent yalla nala yalla saame

  • @rakhougene7945
    @rakhougene7945 Před 24 dny +14

    Li dèh môy émission plus surprise machallah ❤❤❤❤❤

  • @IssaKa-zp4st
    @IssaKa-zp4st Před 24 dny +13

    Tayy môme billahi déma contane Si li sering Abdou déff Alhamdou lilahhh 🙏 machallahhh machallahhh machallahhh ❤️❤️❤️🇸🇳✅

  • @user-mt9lj3zj2h
    @user-mt9lj3zj2h Před 24 dny +22

    Quelle modestie Sa Ndiogou. Tu es le meilleur

  • @sambagntshmbaye248
    @sambagntshmbaye248 Před 24 dny +80

    Il y'a trop laisser faire , le régime est 'élu de 54,....% nagnou dieul sèni responsabilité, les tapha diakhaté, madiambal, Diop fall .koufi wakh lo warta wakh gnou ndiaff la si kasso bi

  • @MASSAMBA360
    @MASSAMBA360 Před 24 dny +37

    PRÉSIDENT BASSIROU DIOMAYE FAYE AK SAYIDINA OSMANE SONKO YALLA NA AM DIAMOU ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhounadia4195
    @cheikhounadia4195 Před 24 dny +9

    Theiye ma challah émission bi déh masoula nakhary wayé tay nak dafa rombou nékh vraiment diadieufaty sa ndiogou kadou yi noula wakhal yéupe sédna khol cheikh abdou mbacké mom nafi yague réck mom loko beuga wakh thei lou bakh khépe ko❤❤❤❤vraiment chapeau à vous tous ❤❤❤❤❤

  • @faalmadeugal2804
    @faalmadeugal2804 Před 24 dny +17

    Walahi Mame Pateh wakh ngeu deug pirr❤❤❤❤
    Mann Gambie la deuk di Gambien waye Solution rek laye toppou ndax ligeuye bou rafett bou amoul daray COMPLEXE ❤❤❤

    • @PASSworde
      @PASSworde Před 24 dny +1

      Sifane Gambie 🇬🇲

    • @faalmadeugal2804
      @faalmadeugal2804 Před 24 dny

      @@PASSworde Wellingara Nema Junction ci wetou Police bi

  • @assmalickdiouf409
    @assmalickdiouf409 Před 24 dny +22

    ohh tay conten na way serigne Abdou mbacke machalah 😍

  • @user-hc3ii3ug1q
    @user-hc3ii3ug1q Před 24 dny +9

    Merci beaucoup solutions TV machalla ♥️🥰♥️♥️♥️♥️♥️

  • @Hannsylla
    @Hannsylla Před 24 dny +18

    Machallah douniou nangou niouy yabb souniou ay dirigeants 54% de la population niolen falleu danioulen di respecter par la force voila lounioouy wakh ni déstabiliser woul Sem Diomaye ak son gouvernement

  • @moussadione3468
    @moussadione3468 Před 24 dny +38

    Yalnalen yalla sam ci barceb s touba amine ya rabbi ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤

  • @djibiba5189
    @djibiba5189 Před 24 dny +5

    Alhamdu lillaah taye mome sama xol seddna tourop❤❤

  • @micheldiedhiou-uy9ih
    @micheldiedhiou-uy9ih Před 24 dny +5

    Un très Grand Homme , Respect ! Santé de fer et longue vie à vous par la Grâce de Dieu au Nom de Jésus-Christ Amen , Merci infiniment solution TV ! Bonne continuation à vous par la Grâce de Dieu Amen !❤❤❤❤❤❤❤

  • @dembasonko2699
    @dembasonko2699 Před 24 dny +4

    Machallah waa solution TV 💯💯♥️💯♥️🇸🇳🇸🇳💯💯♥️🇸🇳🇸🇳

  • @mariamasinyan6078
    @mariamasinyan6078 Před 24 dny +11

    Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @khadimgueye6244
    @khadimgueye6244 Před 24 dny +25

    Wakhoumala Reubeusse rek mais Mbeubeusse laniou dieum AK niom 🎉

  • @ousmanediawara-fu7ek
    @ousmanediawara-fu7ek Před 24 dny +15

    KILIFA DINEH WALA KOUY WOTEH KILIFTEF NI LAY MEL , WAKH AK DIGLEH WAKHOU YALLAH SOUNOU BOROM , SI DEUGOU BANIA FARFARLOO , DJIB DJOUBEUL DJOUBEUNTY , TEH DI TEUDEY NDIANKHAN . DIADHIEUF SEUGNE BI ABDOU MBACKE

  • @Aladjibousonko
    @Aladjibousonko Před 24 dny +6

    Dierreudieuf mbacké Diereudieuf mame paté guiss nagne sene takhaway si Senegal lii moy deugui deugui rolou serigne✨🇸🇳🙏🏿

  • @mamefakhathiam289
    @mamefakhathiam289 Před 24 dny +4

    Assane bien répondu 👍👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿🙏Sa 🫡🫡👑😂grand merci 🙏 que dieu vous bénisse et vous protège et vous garde en bonne santé bravo à vous diadieuf Serigne Touba ak mouride Yepp

  • @FallHamidoudjembe
    @FallHamidoudjembe Před 24 dny +9

    Macha Allah
    Mara Niasse

  • @mayes2616
    @mayes2616 Před 24 dny +16

    Il faut boycotter senegal 24 le site de Moustapha diakate

  • @P4t5R
    @P4t5R Před 22 dny +1

    Liguey bi rafet na machaAllah

  • @ahmadouseck7711
    @ahmadouseck7711 Před 22 dny +1

    Sama temps moma mayoul di sétane émission en direct mais benou doumathi raw.
    Wayé bi nag mothi Amoul morom
    Machalla yalla naléne yalla guena takhawou❤❤❤

  • @LeuzSikki-sg9kv
    @LeuzSikki-sg9kv Před 23 dny

    Ndeysann émission bou mélni moom dottoufi amatii. Gann gou mélni , gou yiwé ni , gneuw toog cii plateau bi deff émission ak yénn, reuy n'a trop. Li Mooy force PASTEF ak SONKO nitteum yi dagno beuggeunté, soppanté♥️♥️♥️♥️. Machallah, jeureujef SOLUTION TV 🙏

  • @amdymbaye5431
    @amdymbaye5431 Před 24 dny +7

    Màssaàlla wa solution yén dara diombu lénn khol sedna tay

  • @laminetoure6639
    @laminetoure6639 Před 23 dny

    Qu'Allah fasse de solution tv une très grande maison de presse et que cette salle soit dénommée serigne ABDOU MBACKÉ.
    Ne l'oubliez jamais

  • @gee5830
    @gee5830 Před 23 dny

    THANK YOU SOLUTION TV AND TEAM WALF TV AND TEAM, SIDY LAMIN NYASS IMAM BADARA NDAO SAMBA MOUHIDEEN DIALLOW FATHERS OF PATRIOTISM. WE LOVE OUSMAN SONKO LEADERSHIP AND SOLUTION

  • @pongf41
    @pongf41 Před 24 dny +9

    C'est Ameth Suzanne qui les à trompé, tout ce qu'il a dit sans être préoccupé. Ils pensent qu'il ne risque rien avec ce régime.

  • @binetaloucoubar3912
    @binetaloucoubar3912 Před 24 dny +5

    Machallah mbake balla Aïcha ❤❤

    • @azizngom7472
      @azizngom7472 Před 24 dny

      Yow rek Ya wah , wah bi. Moi je suis a Ourossogui. Il fait très chaud. Ki il faut niou yaratt ko

  • @vicincialy8928
    @vicincialy8928 Před 24 dny +2

    Hoooo je retrouve mon ASSANE BRAVO

  • @modougaye4418
    @modougaye4418 Před 24 dny +2

    Machallah taye mome lougnou platau bi guenna riche yalla Na Yàlla barkéll ❤❤❤🎉

  • @ramabodian7091
    @ramabodian7091 Před 23 dny

    Machallah Mbacke ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏

  • @Agne2024
    @Agne2024 Před 23 dny

    Machalah plateaux Ala dawmé❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-hb8fi1fw9d
    @user-hb8fi1fw9d Před 24 dny +8

    Dage yi dinégnou léral sougnoulén woyé !!!lépeuy léer!!in sha allah !!! opération gokhi késsé !!!

  • @Fallyaram320
    @Fallyaram320 Před 23 dny

    Solution les meilleurs sonko agg diomaye a vie inchaAllah koulène dépasser ñou ñouss la thii kasso bi

  • @ramabodian7091
    @ramabodian7091 Před 23 dny

    Merci l’équipe Solution Tv que Dieu vous bénit abondamment ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @amarbene6626
    @amarbene6626 Před 24 dny +1

    No sa Ndiogo yalnala yalla defal diamm te yokoula quelle modeste degloulen boubakh nimou diangate wakhi amadou ba ji

  • @cheikhndiaye7862
    @cheikhndiaye7862 Před 24 dny

    Akasssaa Mouride Sadikh.
    Yalla na Yalla saam sa njabott barkée Seydina Muhammad barkée Boroom Touba.
    Takhaway bi raféetna

  • @Falloundiaye-oi6ce
    @Falloundiaye-oi6ce Před 24 dny +4

    Ma challah sa ndiogou billahi

  • @MorsyllMore
    @MorsyllMore Před 24 dny

    Machahalla serigne bi yalla nako Yalla défale fane wou goudou lole ta défanko wér...émission bi nékhe na trop

  • @oumoulkhairysy8105
    @oumoulkhairysy8105 Před 24 dny +3

    Aye waye bi plateau! QUE DIEU VEILLE SUR VOUS!

  • @serigneDiba-vr9sn
    @serigneDiba-vr9sn Před 24 dny +1

    Machallah serigne abdou mbacke takhaway bii Amna solo ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-ns8bt4nd8j
    @user-ns8bt4nd8j Před 24 dny +2

    Sohibou moye el malik el malik moye sohibou🥰

  • @bintakane5811
    @bintakane5811 Před 24 dny +4

    Machalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @lobassirou9335
    @lobassirou9335 Před 24 dny

    Ma cha Allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @yacinendiaye-pj8sh
    @yacinendiaye-pj8sh Před 24 dny +3

    Merci bcp solution tf

  • @MorsyllMore
    @MorsyllMore Před 24 dny

    Machahalla amna solo trop serigne bi yalla na yalla goudale fanwi ta défalko wer

  • @khadamdiop4146
    @khadamdiop4146 Před 24 dny +1

    Macha allah kadou yi rafetna yalla nalén yalla mousal te mouthial léne nguén contune thi deugue ba ba fatou di taxaw

  • @HounaKebe
    @HounaKebe Před 23 dny

    Mancheallh ❤way lii dafa neex Serigne Abodou Yalla gua fii yague tèè An dakk wer

  • @fallouniang5676
    @fallouniang5676 Před 23 dny

    Amna solo looll❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @yerosow7063
    @yerosow7063 Před 24 dny +3

    Lii rk moy surprise machalla rafetna ❤
    Mais limouy vré TV baol baol
    Legui mom BaolTV la😂

  • @papekane4885
    @papekane4885 Před 22 dny

    Machallah amna solo lol ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @SuperAlpha010
    @SuperAlpha010 Před 23 dny

    bilay bègueu na loleu sakh yallah nalèn yallah sameu yène gni togueu si plateau bii yupp walahii sama khole bii noumou fèkhèè nii yallah nako sèn khole fèkhè nonou say sounè♥♥♥♥♥

  • @toubathiam1373
    @toubathiam1373 Před 24 dny

    Machalla mbacke Balla balla Aissa❤❤❤

  • @AbdulPape-hp1hh
    @AbdulPape-hp1hh Před 24 dny

    Machalah amnasolo

  • @mbouphollandmboup2137
    @mbouphollandmboup2137 Před 23 dny

    Manchallah manchallah 🙏🏾

  • @bayesalioumbaye7182
    @bayesalioumbaye7182 Před 23 dny

    Mâcha allah ❤️ ❤️ ❤️

  • @falladiouf1662
    @falladiouf1662 Před 24 dny

    Émission exceptionnelle ❤❤❤

  • @osdiawara6528
    @osdiawara6528 Před 23 dny

    Niveau bi kawè na tay mashallah

  • @cheikhndong3851
    @cheikhndong3851 Před 24 dny

    Très bien décortiqué assan 100❤

  • @Ibrahimagadio8425
    @Ibrahimagadio8425 Před 24 dny

    Mashalla ❤️🙏🏾🙏🏾

  • @dioptt
    @dioptt Před 24 dny +2

    Tey de dëgg dëgg sëñ tooy loo na sama xol bi te ku dëgër laa. Jërëjëf

  • @babacrndaw4399
    @babacrndaw4399 Před 24 dny

    ما ساء الله ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @thiernodia8767
    @thiernodia8767 Před 24 dny +6

    Moustapha diakhate bolene ko diappe yoboulene ko prison kedougou

  • @abdoulatifdiop146
    @abdoulatifdiop146 Před 23 dny

    Machallah ❤❤❤❤❤❤

  • @sodambow9793
    @sodambow9793 Před 24 dny +1

    ❤❤❤❤ bilahi meunuma khey té setanou malen, jeureudieuf mbacké bala et Mame pathé❤❤ kadou yi nekone sama xol sama xel yeup wakhal nguama ko❤😢😢beg n'a trop trop sama ndiogou yallah nga fi yag té werr lole AK gni nga bokal ligueye bi❤ bilahi saa ndiogou nimalay nianalé yallah n'a nangou té djikk la❤❤❤

  • @serignembackemouhamedtoure6766

    Dieuredieufety Sa Ndiogo Bilahi Deguena Degue 👂 Moustapha Diakhate Dafa Alkou

  • @MamaNdiaye-bz8ks
    @MamaNdiaye-bz8ks Před 24 dny +3

    Merci❤❤❤❤

  • @abdoukhoudoss8030
    @abdoukhoudoss8030 Před 23 dny

    Ndeysan ❤❤❤

  • @user-hz3re4re9b
    @user-hz3re4re9b Před 24 dny +1

    Ma sha allah sa ndiogou yalla na gueneu dieume thia kaname

  • @user-hg7qc2fw8l
    @user-hg7qc2fw8l Před 23 dny

    Machalla mére imicô ❤❤

  • @amydieye8925
    @amydieye8925 Před 24 dny

    Machalah solution sama hool sedna serigne Abdou mane taliba serigne Fallou la wayee dama mbeugg serigne Abdou MBACKE sama hool sedna bilahiii ndakh li mou beegue Ousmane Sonko
    Bilahi yalna ma Yalla Wane lee akkk mome ssi barkee cheikhoul hadim amine ya rabyyy 🥰🥰🥰🥰

  • @BABACARNIASSE-xb9uk
    @BABACARNIASSE-xb9uk Před 24 dny +1

    SLM SOLUTION AMGUENE GANE GOU MATE GANE❤❤❤

  • @calel2376
    @calel2376 Před 24 dny +2

    Mérci ❤❤❤❤❤❤❤Amna solo

  • @user-qq3yh4yv7f
    @user-qq3yh4yv7f Před 24 dny +1

    Vraiment surprise bi nékhena Macha Allah ❤❤❤

  • @saladiallo7094
    @saladiallo7094 Před 24 dny

    Dieureudief Mbacké takhaway bi rafetna machallah

  • @pendasarr4183
    @pendasarr4183 Před 24 dny

    L émission de l année Machàalla ❤❤❤❤❤ yalla naléne yalla same té mayelene werr gou yaram ❤❤❤

  • @fulafula9951
    @fulafula9951 Před 24 dny

    Machallah serigne bi Mbacke ak Mame Pathé

  • @oumycisse7698
    @oumycisse7698 Před 24 dny

    Dieuradieuf serigne abdou mbacké ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-ik7nb5qg3p
    @user-ik7nb5qg3p Před 23 dny

    سريج مار جرجف❤كدي امن سلو شاءالله❤سمحل شدن لول❤شاجوك من موم. ركلاي دكل❤❤❤❤

  • @leyemoussaliou5583
    @leyemoussaliou5583 Před 24 dny

    Machalla tay sama khol sed na s abdou mou bakh mi sa Ndiogou ❤ baye Assane ❤ shb❤🎉Senegal

  • @user-mt9lj3zj2h
    @user-mt9lj3zj2h Před 24 dny +7

    Ces deux là se fichent de nous. Ils n'ont qu'à aller séjourner à Reubeuss, cela servira de leçons aux idiots qui manqueront de respect aux gens tout court pour ne pas dire nos autorités..

  • @Agne2024
    @Agne2024 Před 24 dny

    Les Trios ❤ ❤ ❤

  • @tbesport9283
    @tbesport9283 Před 24 dny

    Macha Allah yalla na yalla teiral serigne Abdou mann damako beugueu reikk nakh mbeuguel bimm amm si serigne Sonko ak deugouwam ak fitam.

  • @tibustmendes2587
    @tibustmendes2587 Před 24 dny

    L'équipe solutions on est agréablement surpris ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @mayedabel26
    @mayedabel26 Před 24 dny

    La meilleure émission de Diomet Machallah 😍😍😍😍

  • @thiernondiaye4855
    @thiernondiaye4855 Před 24 dny

    Content naaaa lol ❤❤❤❤❤

  • @mamadoundiaye1724
    @mamadoundiaye1724 Před 24 dny +3

    Moustapha diakhaté bayileneko ba jeudi cheikh bara diapko dorko baloubop

  • @user-mj8jt6zr4o
    @user-mj8jt6zr4o Před 24 dny

    Kon tane ci yene❤❤❤

  • @NikJones-qe8sz
    @NikJones-qe8sz Před 24 dny

    OOOOH MEILLEUR DIOMET DE L'ANNEE, BI MOM YALLA WER NA LOLOU MASHALLAH!!!!!

  • @morgueye1262
    @morgueye1262 Před 24 dny

    Machalla yalla na barker

  • @cheikhoufofana9491
    @cheikhoufofana9491 Před 24 dny +1

    Macha ALLAH.
    Li mooy télé Baol Baol deug deug.
    Lol
    Macha ALLAH.
    Nex na.

    • @sankaralomor9643
      @sankaralomor9643 Před 24 dny +2

      Billah hi ma gui sétane Di reee 😂reck
      Li da fa nekh vraiment 😊

  • @sambagntshmbaye248
    @sambagntshmbaye248 Před 24 dny

    Gnogui ligueuy ligueuy bou rafét machala ❤❤❤❤❤

  • @fatimatoufall9344
    @fatimatoufall9344 Před 24 dny

    Tay nieppa contane ❤

  • @MadouDiouf-wf2vt
    @MadouDiouf-wf2vt Před 24 dny

    Machalla mbacké balla

  • @user-db2uj8in1g
    @user-db2uj8in1g Před 23 dny

    Assalamou haye koum sandiogou souhayebou baye assane messéré diaguine dieff

  • @fatimabathily520
    @fatimabathily520 Před 24 dny

    Macha allah amna solo trop ❤❤❤

  • @cheikhlo3788
    @cheikhlo3788 Před 24 dny

    Solution sa kaw sa kanam