PROBLÉME ALBOURAKH ET SITEU AZIZ DIT TOUT ''SITEU NOUS A TRAHI....''

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 14. 03. 2024
  • Bantamba tv. Km 2,5 Boulevard du Centenaire de la Commune de Dakar.
    tel : 33 825 34 36 - 77419 03 64
  • Zábava

Komentáře • 168

  • @ndiogoundiaye3772
    @ndiogoundiaye3772 Před 3 měsíci +13

    Vraiment nitte ki boko khamoule boule gawa jugé azize Ndiaye je l'avais Mal jugé mai je me me suis trompé sur toute la ligne il est intégre intelligent,respectueu et surtout sociale un vrai modéle pour les jeunes

  • @dethiefaye2532
    @dethiefaye2532 Před 3 měsíci +8

    Mai bekaye il faut recadrer bour gueweul il essaye d impressionner les gens et il connaît rien de ce qu il dit mai chapeau a toi Aziz tu es très professionnel

  • @mansourleye9816
    @mansourleye9816 Před 3 měsíci +3

    Aziz Ndiaye est un vrai responsable,il parle bien 👏🏿

  • @pathendiaye5964
    @pathendiaye5964 Před 3 měsíci +16

    Aziz vrai gentleman❤✍🏿

  • @sambaba683
    @sambaba683 Před 3 měsíci +25

    Aziz un homme responsable et honnete et travailleur❤❤❤❤ bonne continuation

  • @user-gw8qv9zg5b
    @user-gw8qv9zg5b Před 3 měsíci +21

    Après plus de 20ans dans la lutte téy lay dora sét lou ni Aziz Ndiaye ak Bombardier daniouy nouro😂😂😂même rétan nioko nouro😂😂😂😂sinon Balla Gaye rék à vie ❤❤❤❤ ❤❤❤❤ ❤❤❤❤

  • @bassdiokhane1472
    @bassdiokhane1472 Před 3 měsíci +3

    Abdou Aziz Ndiaye ❤️ masala yall nala yalla dé fall diam way ❤❤❤

  • @elhadjiibrahimadiatta9485
    @elhadjiibrahimadiatta9485 Před měsícem +1

    Merci beaucoup Aziz ❤

  • @ibrahimasene9243
    @ibrahimasene9243 Před 3 měsíci +13

    Bravo Aziz vraiment gental man la

  • @user-pq3ep6qr1n
    @user-pq3ep6qr1n Před 3 měsíci +16

    Aziz vraiment vous avez bien parlé machallah que Dieu te protège

  • @tallambengue-oc4cd
    @tallambengue-oc4cd Před 3 měsíci +8

    En tt cas Aziz nitt kou bakh lah machala

  • @pathendiaye5964
    @pathendiaye5964 Před 3 měsíci +8

    Vraiment Aziz taaaay respecte👏🏿✅nala bilaaaay waaxou goor rk nguafiii waaaxxx yallaaah nla yallaaah dëfaaal diam yaakk albourakh evens

  • @ModouCisse-st1oy
    @ModouCisse-st1oy Před 3 měsíci +3

    Aziz machaalah lamb avancé rék la guis mais dina bakh

  • @alassanemane3021
    @alassanemane3021 Před 3 měsíci +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤ Aziz Ndiaye ❤❤❤❤

  • @user-ph5vu2db6f
    @user-ph5vu2db6f Před 3 měsíci +2

    AZIZ borom bakh Là

  • @user-ue5ji1wh5b
    @user-ue5ji1wh5b Před 3 měsíci

    Machala

  • @elhadjigueye724
    @elhadjigueye724 Před 3 měsíci +2

    Aziz pourrait être un jour le président du cng

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 Před 3 měsíci +16

    Siteu vs balla gaye 2 boléne fayoule siteu louko diarr douko beuré kounek interéme léye sétt , siteu grand champion le tarkinda le baye fall sociale Yallah neu Yallah mayla ndam Inch'Allah 🎉

    • @diop3575
      @diop3575 Před 3 měsíci +2

      Grand champion 😂

    • @chatif1196
      @chatif1196 Před 3 měsíci

      @@diop3575moma diaxal 😂😅

    • @ouzdaking382
      @ouzdaking382 Před 3 měsíci +1

      @@diop3575 kou dém beu di beurré roi des arenes grand champion leu bayiléne igniane sokhor sisou dafaye takh doléne am dara séne morome yi diléne raw rek sén khole di dokhote 😂😂😂 siteu grand champion future roi des arenes Inch'Allah

    • @user-fb5dq8kq7e
      @user-fb5dq8kq7e Před 3 měsíci

      Yaw nopaloulene siteu dou mbeurè akh balla

    • @diop3575
      @diop3575 Před 3 měsíci +1

      @@ouzdaking382 grand champion bou danoul bene vip si kaw 😂

  • @user-rk2hy2ch9g
    @user-rk2hy2ch9g Před 3 měsíci

    Right

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Před 3 měsíci +11

    Aziz ndeyssane nit kou baax la

  • @mouhamedndong6069
    @mouhamedndong6069 Před 3 měsíci +55

    Aziz Bi Promoteur nei Dotounou dépasser 70 millions Yow Ya Rothei Kou Dem Teug Say Combat Plus de 70 millions Ndakh Sponsor KOn Siteu sou Amé Proposition Combat Royal Dafkoy Dieul c'est du Business AZIZ Ndiaye

    • @gabrielamaracoumbassa8533
      @gabrielamaracoumbassa8533 Před 3 měsíci +8

      Je suis daccord avec toi mais naniou annuler contrat bou albourakh cest plus responsable bro

    • @mouhamedndong6069
      @mouhamedndong6069 Před 3 měsíci +2

      @@gabrielamaracoumbassa8533 d'accord mais l'entourage de Siteu n' ont pas signé le contrat le consensus va bien être trouvé

    • @oussoundiaye60
      @oussoundiaye60 Před 3 měsíci +2

      Aziz day busness limouy wakh si lamb ak limouy def bokoul

    • @boubabathily3851
      @boubabathily3851 Před 3 měsíci

      Seul les imbéciles ne changent pas d'idée

    • @serignefalloundiaye9169
      @serignefalloundiaye9169 Před 3 měsíci +1

      Mais aussi un business ça doit respecter les règles de l’art meuno dieul contrat bi yobouko pour signer avec un autre promoteur sans l’aviser

  • @Serignemeumeu
    @Serignemeumeu Před měsícem

    ❤❤❤❤❤❤aziz tres bien repondu
    Gor kadom la yorei❤❤❤❤❤

  • @tallacisse7797
    @tallacisse7797 Před 3 měsíci +1

    Thieuy adouna

  • @bahosmantv1521
    @bahosmantv1521 Před 3 měsíci

    Modoulo kesse ❤❤❤

  • @IbrahimSeck-vl4xi
    @IbrahimSeck-vl4xi Před 3 měsíci +1

    No azize nit le❤

  • @coulzjamdong4764
    @coulzjamdong4764 Před 3 měsíci +2

    Temps de parole kounek dafa warone am pere ngagne diagne meunoul sakh wax tellement gars yi danio bari wax

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Před 3 měsíci +3

    Sèrére laa Douma woor lolou la siteu wakh 😂😂😂ay fén la rék La mắn lila mắn lèlaa lolou amoul ngor deugeu thi Dérétou nith ki lay Nékeu mé pas ay sérére laa ay Bambara la voila 🥹siteu Moowore 🧏‍♂️

    • @Chiekh766
      @Chiekh766 Před 3 měsíci +2

      Yaw mi yaye ndeye doule siteu lamb kounék sa intéré ngaye khole siteu mok balla 100million laléne lathie gniou bagnie siteu hamoko motakh nganane daye worre siteu litopou thie mbeure yi da beurri Kone ladjié 100 millions gniou bagnie sou dégue 100million daye beurré

  • @ibrahimakane3940
    @ibrahimakane3940 Před měsícem

    Premier plus jeune roi ! Quel sens ? Il a été parmi les rois les plus éphémères de l'arène.

  • @Babarmbaye-sc2ye
    @Babarmbaye-sc2ye Před 3 měsíci +6

    Aziz yala bakh ne

  • @alainmare6550
    @alainmare6550 Před 3 měsíci

    Faut organiser le plateau

  • @elhadjidiouf5991
    @elhadjidiouf5991 Před 3 měsíci +5

    En tt cas t'as tt dit❤

  • @MrFayemanou
    @MrFayemanou Před 3 měsíci +1

    Sénégal deuk woor kate maïs a qui fait confiance

  • @FallouFall-mx1si
    @FallouFall-mx1si Před 3 měsíci +1

    Yéna wayadi koor gii defou lén whakh taanou diineh khana diwakh wakhi lambou AAa thiam😢😢

  • @doroliiiye7350
    @doroliiiye7350 Před 3 měsíci

    No peuchère bilahi betnguama longuay déf rafétoul

  • @user-gw8qv9zg5b
    @user-gw8qv9zg5b Před 3 měsíci +3

    Hééé dég lou lén Diameu leu Aziz Ndiaye promoteur néna Siteu Moustapha Senghor moy vrai Toureum 😂😂😂😂
    Té Max Marguan Maguette Mbengue moy vrai Toureum 😂😂😂😂

  • @Papesarr-wv3me
    @Papesarr-wv3me Před 3 měsíci +1

    ki magou balla gaye la papam la ❤❤🤲🏿🤲🏿✊🏿✊🏿

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 Před 3 měsíci

    🇺🇸 Vraiment actroces doÿna Warr entouka 😢le milieu de la lutte 🎉 Entouka Gaston mbengue d'où meusseu changer vrai hypocrite leu💥

  • @FallouSeck-dn6mi
    @FallouSeck-dn6mi Před 3 měsíci +4

    siteu roi lay beuré force koume nékh koumou nakari

    • @user-gw8qv9zg5b
      @user-gw8qv9zg5b Před 3 měsíci

      😂😂😂😂boulma dadji wayy😂😂😂

    • @user-gw8qv9zg5b
      @user-gw8qv9zg5b Před 3 měsíci

      Moustapha Senghor la siteu toudou😂😂😂😂😂day doul toudoul siteu 😂😂😂😂

    • @BoyPoulo-kg5pl
      @BoyPoulo-kg5pl Před 3 měsíci

      ​@@user-gw8qv9zg5bayi koulo ko waxx

  • @kossogadiaga-fu6ik
    @kossogadiaga-fu6ik Před 3 měsíci +4

    Siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse siteu kasse

  • @domou__rewmi
    @domou__rewmi Před 3 měsíci +6

    Albourakh boul yakamti siteu AK ama meune nanie beuré sakh combat royal

  • @alkachigalsen5493
    @alkachigalsen5493 Před 3 měsíci

    Aziz dou wakh deugg . Da warra bayyi frère bi mou géré mais momm il aime trop se faire voir. Il doit être humble. Certes il a du mérite mais son discours n'est pas collaboratif

  • @PapePape-vs6xw
    @PapePape-vs6xw Před 3 měsíci

    Más❤😂

  • @AlassaneDieye-cc7jq
    @AlassaneDieye-cc7jq Před 3 měsíci

    Bécaye damako beugu❤😂😂😂

  • @tallacisse7797
    @tallacisse7797 Před 3 měsíci

    Moustapha Senghor ak Maguette Mbengue,

  • @piogofficiel3715
    @piogofficiel3715 Před 3 měsíci

    Gniounne Combat Royal lagniouy beuré Siteu dou worrkatte yenay workatte yiii siteu sa suné🎉🎉

  • @abdoufall3831
    @abdoufall3831 Před 3 měsíci +1

    Giri bordo ak bombar diey combala bu nekh

  • @user-ik8xn6kt1b
    @user-ik8xn6kt1b Před 3 měsíci

    Situé késs késs situé késs situé késs

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall2003 Před 3 měsíci

    Aziz avait dit il n’est plus ds la lutte

  • @ousmanediouf6267
    @ousmanediouf6267 Před 3 měsíci

    Aziz mome fen rek
    Fi nga wakhonee combat 70milion rek
    Tey ya ngi ci 100et kelk millions bayil fen

  • @legendediop9215
    @legendediop9215 Před 3 měsíci

    Maxe ak siteu yenay ay diam

  • @ibrahimadiop2219
    @ibrahimadiop2219 Před měsícem

    Kham lenn bala gaye aziz mokay financei

  • @abdoulayediallo4028
    @abdoulayediallo4028 Před 3 měsíci

    Mousa doy vs lac2
    Tonnerre vs boucher
    Tyson2 vs marley

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye3913 Před 3 měsíci

    Mai azize pour Mane promoteur bi défoul Dara ndakh bouko max wakhane siteu amna comba cône wakh doufa amate mai afér bi thi dégane té max ak siteu la té comba crone bokoul AK comba sans crone

  • @ibrahimadiop2219
    @ibrahimadiop2219 Před měsícem

    Aziz ndiaye day dor mbeur boudoul lire contrat signeko
    Puis en rtour lo wakh mouniko yako signei 😡

  • @user-cb6nt2dw3s
    @user-cb6nt2dw3s Před měsícem

    Aziz borom bahga

  • @papendeuryseck6854
    @papendeuryseck6854 Před 3 měsíci

    Aziz yay niitou deug bilahi gore nga

  • @user-dj6qe1fb9i
    @user-dj6qe1fb9i Před 3 měsíci +1

    Bour geweul tamite wargeu téyy eupeul geu trool déll déklou bou nitte kii dit wakhh

  • @djlinks5732
    @djlinks5732 Před 3 měsíci

    buur fans modou lo la

  • @championBoulan
    @championBoulan Před 3 měsíci +1

    Siteu dh kone workat la mome ak maxe yeup aye workat lènne

  • @saliougueye9833
    @saliougueye9833 Před 3 měsíci

    Per max linga def rafetoul

  • @diop3575
    @diop3575 Před 3 měsíci

    Bour sof na seet teet 😂🎉

  • @sonnedj2304
    @sonnedj2304 Před 3 měsíci +2

    La femme la elle s’appelle comment??

  • @talibebamba8130
    @talibebamba8130 Před 3 měsíci

    Combat royal mo eupp xaliss , mo eup thiow. Lolou motax siteu bayi sa contrat

  • @abdouazizthiaw3491
    @abdouazizthiaw3491 Před 3 měsíci

    Grand boubou ak cap naka la ñu koy bollé sol? Quel contraste vestimentaire .

  • @laminethiam3759
    @laminethiam3759 Před 3 měsíci +1

    Veryma aziz ya neka sidage

  • @user-ik8xn6kt1b
    @user-ik8xn6kt1b Před 3 měsíci

    Baye fallou situé bagiu ni gouwakh situé Lou niaw makata ce ndaye situé rek laye topu

  • @DiabaCiss-ck8cs
    @DiabaCiss-ck8cs Před 3 měsíci

    Bour géweuleuk vertame bou saf😂

  • @user-cb6nt2dw3s
    @user-cb6nt2dw3s Před měsícem

    D’Adam Aka kon

  • @simmelsarr3599
    @simmelsarr3599 Před 3 měsíci +1

    Aziz dou diade diadal mtx inviter ko nekh. Il est cash

  • @aichadia719
    @aichadia719 Před 3 měsíci +1

    Lamb meunoul nék international souniouko teugué europe sakh aye sénégalais rék niokoye sétane .sport binga xamné meune'na diékhé 4 appuis sans contact ame lohlou toubab doussi déff xalissam

  • @user-cb6nt2dw3s
    @user-cb6nt2dw3s Před měsícem

    Fadam bekay dala. Wara d’aqueux

  • @saliougueye9833
    @saliougueye9833 Před 3 měsíci +2

    Mes fadam tay kouko yédeu mou wagni wakh bou bari bi😂😂😂

    • @user-wo3kj7ee9h
      @user-wo3kj7ee9h Před 3 měsíci

      Zarko môko wagnii😂😂

    • @babadiagne7968
      @babadiagne7968 Před 3 měsíci

      Brom xaliss la togal mo takh faw mou yaroul ko 😂😂😂😂

  • @MoDraronie
    @MoDraronie Před 3 měsíci

    Moustapha Senghor 😂😂😂😂

  • @Kenji231
    @Kenji231 Před 3 měsíci

    Aziz wakhofi dara gayi dagnoula 😊 nakh 😂

  • @user-pb7qn9dh6i
    @user-pb7qn9dh6i Před 3 měsíci

    Wa aziz louy problemam ak gentlmen tmt😂

  • @diawcheikh3744
    @diawcheikh3744 Před 3 měsíci +1

    Siteu kassé

  • @mcbig6971
    @mcbig6971 Před 3 měsíci

    Pere becaye iow mome ndanane gua goudd fane lalayy nianall mais svp gars soléne invité nitt bayi léne ko mou développé kounekk beugua posé kestion ce n’est pas professionnel

  • @Babarmbaye-sc2ye
    @Babarmbaye-sc2ye Před 3 měsíci

    Fadam kom kouye wakh s'y dîné fadam ya sofe réke

  • @Abdallah31341
    @Abdallah31341 Před 28 dny

    Aziz linga wax moy deug, yéna am deug

  • @moussafayetbinette
    @moussafayetbinette Před 3 měsíci

    Aziz dangéniy souffou kone bounelén souffo nangouléne siteu interet lay xolll combat royal mo gueune foufffff nk si siteu

  • @user-if6nl8yi9c
    @user-if6nl8yi9c Před 3 měsíci +1

    Diéne kaïré kassé

  • @MbargouDiop-mk4cv
    @MbargouDiop-mk4cv Před 3 měsíci

    Non max vrai workatla

  • @talladiop1389
    @talladiop1389 Před měsícem

    Diop2

  • @ousmanesarr756
    @ousmanesarr756 Před 3 měsíci +1

    Fi worr amoufi business business la aziz fi ngen khagn siteu balla Gaye bagn ko fay limou mérité yalla mayko li guen mouy comba royal ngen beug lane lane moy am comba royal di dieul comba bo khamni khamo Kane ak Kagn ngakoy beuré fi dal Lou arranger woul nitt douko def lolu ngen def eumeu Sene si comba wam bi mom ak balla ngen fekhé ba yakk ko parsk arranger woul balla nagnoul ni meuno am lep rek

  • @user-cb6nt2dw3s
    @user-cb6nt2dw3s Před měsícem

    Bekay fadam day. Yak. Lambe

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110 Před 3 měsíci +1

    Aziz danga Beug sisou trop nk

  • @domou__rewmi
    @domou__rewmi Před 3 měsíci +1

    130 000 000 ngaye diokhé 20 millions avance 😂😂

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote Před 3 měsíci +4

      Makane si bopom mo beugg lou yombou ms kène dou bg2 mo eupou caché si mbeur yi

    • @bilalkhalyfall9938
      @bilalkhalyfall9938 Před 3 měsíci +1

      ​@@leuz.patrioteli nguay wakhnih dh dou deugueu téguoko féneu wakhou fans késsé leu

    • @ibrahimadrame9499
      @ibrahimadrame9499 Před 3 měsíci

      ​@@leuz.patriotenon Modou lo😢😢😢😢fouuuuufff il payer 200milion

    • @bahosmantv1521
      @bahosmantv1521 Před 3 měsíci

      ​@@ibrahimadrame9499makane sa worna dioxe modoulo xalis defa beug lou yombe 😢😢😢😢😢😢

    • @bahosmantv1521
      @bahosmantv1521 Před 3 měsíci

      ​@@ibrahimadrame9499makane sax desena modoulo xalis defa niaw mais modoulo douko wax dara 😢😢😢😢😢😢😢😢😢

  • @PapeDiouf-xw6fb
    @PapeDiouf-xw6fb Před 3 měsíci

    Bourr com ditakh😂

  • @couradiop4747
    @couradiop4747 Před 3 měsíci +1

    Balla gaye meuneutoul nek roi aziz ligay wakh bakhoul

    • @mouhamedsambe7820
      @mouhamedsambe7820 Před 3 měsíci

      Siteu sou dané modou neik Roi😂😂
      Beurei ak balla 😂😂😂

    • @senegaleventschanel6913
      @senegaleventschanel6913 Před 3 měsíci

      @@mouhamedsambe7820Siteu deh boudoul combine mounoul dara si Modou lo

    • @sidzboy3836
      @sidzboy3836 Před 3 měsíci

      @@mouhamedsambe7820ioe gueme ngani siteu meuna Dane Modou Lo?

  • @Baradieng11
    @Baradieng11 Před 3 měsíci

    aziz yaw xana Serigne bi teré woula teugu lamb???

    • @saerhihiodf110
      @saerhihiodf110 Před 3 měsíci +1

      Nena baye moy teukeu nena day nakhè nonou 😅😅

    • @Baradieng11
      @Baradieng11 Před 3 měsíci

      @@saerhihiodf110 en tout cas nioun mom kou koy wax rek yangui ci biir

  • @user-cb6nt2dw3s
    @user-cb6nt2dw3s Před měsícem

    D’Adam dof la

  • @babacar3178
    @babacar3178 Před 3 měsíci

    Modou lo❤❤

  • @saerhihiodf110
    @saerhihiodf110 Před 3 měsíci

    Aziz nopil nk

  • @user-tk6hh6ml8c
    @user-tk6hh6ml8c Před 3 měsíci

    Siteu fii wakh balla ga dawal balla beug nio sonal siteu nak dou guiss roi di beurè ak maintien ishh

    • @aboubacarba3410
      @aboubacarba3410 Před 3 měsíci

      Mdrr🤣🤣🤣

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote Před 3 měsíci +2

      Yaw dof nga rek bg2 tapha lagn dieuk demarchè fay nagn siteu 80milion mouni dafa ndao niou proposè ko tapha tine 90 milion mou dieul. Siteu 100milion la garè man mi di wax ak ioe siteu moy sama mbeur tè mo lath bg2 topou ko niko yaw la beug beurèl

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote Před 3 měsíci +1

      Nite soy wax dangay wax loula lèr mn mi di wax ak ioe siteu sama wayla

    • @diop3575
      @diop3575 Před 3 měsíci +1

      ​@@leuz.patriote gni khamou niou lognou wakh bayi lene fofou rk

  • @ahmadfall5386
    @ahmadfall5386 Před 3 měsíci

    Tantot il dit ne pas être promoteur alors qu'il est toujours devant les caméras pour montrer son arrogance.

  • @tallzondiaye7618
    @tallzondiaye7618 Před 3 měsíci

    Buur il n’est pas professionnel il a intérêt à revoir c questions

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Před 3 měsíci +1

    Siteu mo meune mo eup Dole

    • @yakhoubaseydi905
      @yakhoubaseydi905 Před 3 měsíci

      Wakho deug dee chiekh bass😂😂

    • @ziggy8402
      @ziggy8402 Před 3 měsíci

      Damleu moudji yeureum andi nga fi Ama Modou defal ko bagass, nga andiwat Boy Niang gnu defalatiko bagass tay yani ci Siteu okay 😂😂

  • @user-jl5dr9xf3b
    @user-jl5dr9xf3b Před 3 měsíci

    Buur man xawma journaliste là xawma loumou doone

  • @boubacardiallo5647
    @boubacardiallo5647 Před 3 měsíci

    Bour geweul sëytaané la mok Fadam nio yam khamouniou touss seine argument dara bakhoussi 😌

  • @user-tu3xg9uj3k
    @user-tu3xg9uj3k Před 3 měsíci

    Plateau null