SA NDIOGOU DEMASQUE AZIZ NDIAYE...MODOU LO LA BEIGUE WEUR...LIMOU WAKH SI BAYE NDIAYE...

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 16. 05. 2024
  • SOLUTION TV

Komentáře • 822

  • @mansorgueye4462
    @mansorgueye4462 Před měsícem +163

    Faal thiaakhane baxoul. Balla Gaye lay supporter mais Modou Moy roi des arènes té mo leen eup mérite fouf. C’est un vrai athlète discipliné et constant dans la performance. Wassalam

  • @fatouTALL-ld1ro
    @fatouTALL-ld1ro Před měsícem +31

    Aziz Ndiaye ci bopam mo soxorei Modou Lo mi tok ci couronne bi. Modou moy le Roi reconnu par le Cng et tous les senegalais.

  • @geumyeugofficiel7688
    @geumyeugofficiel7688 Před měsícem +118

    Yalla mofi tek modou lo aziz monosi dra

    • @modoudiop6522
      @modoudiop6522 Před měsícem +7

      Yalla mbeurëm môy malakal mawti d'où am défétt mouk day dâne Di déme rék

    • @dounejr6956
      @dounejr6956 Před měsícem +4

      @@modoudiop6522 Bien dit💗

    • @awalo2
      @awalo2 Před měsícem +4

      Bilaye modou rek lanou bagne famille ndiaye

    • @Maamseex
      @Maamseex Před měsícem

      Modou Lo mo wara bayi daw yi

    • @ShiekhjobeTijan
      @ShiekhjobeTijan Před měsícem

      Ta moy dege ❤

  • @djilygueye1352
    @djilygueye1352 Před měsícem +34

    Modou lo mofi nek aziz monosi dra yalla rek inchallah

  • @moustaphasonko596
    @moustaphasonko596 Před měsícem +70

    Sa ndiogou est très pertinent

    • @BenMejbour
      @BenMejbour Před měsícem

      Sa N'diogou Mach'Allah ci bénene niveau la nek

  • @mbayecisse611
    @mbayecisse611 Před měsícem +43

    Aziz geumeul yalla modou lo moy sèn baye xlo roi 👑

  • @fayedame3605
    @fayedame3605 Před měsícem +82

    Aziz ndiaye et sa famille se crois plus malin que tout le monde

    • @sambagora7848
      @sambagora7848 Před měsícem +5

      Lamb j santoul ndiaye aziz day dolèle thiakhane rek😂😂😂

  • @senegaldabord1201
    @senegaldabord1201 Před měsícem +52

    Nékhoul ba Nékhoul sa ndiogou est un grand machallah. Un vrai héritier de feu sidy lamine niass

  • @daoudadiop8178
    @daoudadiop8178 Před měsícem +104

    En tant que fan de Mohamed Ndao Tyson, le meilleur lutteur de tous les temps c'est Yahya Diop Yékini.

    • @yerosow7063
      @yerosow7063 Před měsícem +9

      Lolou mom c la vérité

    • @martindiene9113
      @martindiene9113 Před měsícem +9

      Deugu bou woor

    • @AlassaneDieye-cc7jq
      @AlassaneDieye-cc7jq Před měsícem +5

      Tout a fait . Manga n'a pas fait ce que personne ne fait. Yekini et Modou Lo ont la plus belle performance que lui. Mom au mag rk ladone dane

    • @fatimaciss5602
      @fatimaciss5602 Před měsícem +4

      Deug dou romb nop

    • @amymbodji1097
      @amymbodji1097 Před měsícem +1

      Lou woor ga wakh

  • @mouhamednaby3220
    @mouhamednaby3220 Před měsícem +52

    C'est modou lo le roi actuel

  • @amadouba4254
    @amadouba4254 Před měsícem +18

    Bilay tapha tine yallah na dane balla after niou xol nou aziz di def

  • @ibnoukhayriismaelba618
    @ibnoukhayriismaelba618 Před měsícem +10

    Bayilen thiakhan bi.
    Bayilen yakh lamb J.
    Affairou djaay khalis bi bakhoul.
    Yallah molen euppp khaliss.
    NB: je suis supporter Balla Gaye.
    Mais respectez Mod'Lo
    Il est le Roi des arènes

  • @abdoulkhadrediallo1252
    @abdoulkhadrediallo1252 Před měsícem +3

    tu as parfaitement raison sa ndigou je suis d'accord à 1000% avec ton point de vu

  • @dibouthiaw2276
    @dibouthiaw2276 Před měsícem +76

    Mann dou ma fans modou dée mais Li Aziz beugue deff yeuffou Sokhor la 😡😡😡

  • @matardrame4101
    @matardrame4101 Před měsícem +29

    Nonn Sa Ndiogou vous êtes très fort. Plus fort que beaucoup de gens qui gravitent au tour de la lutte qui n'avance pas .
    Depuis plus de vingt ans ce sont toujours ce sont les mêmes.

    • @omarthioub630
      @omarthioub630 Před měsícem

      ترجمة إلى اللغة العربية

  • @sgfdaroukhoudoss6018
    @sgfdaroukhoudoss6018 Před měsícem +9

    Être empereur , c'est pas si facile comme il le crois. Kheuy un bon jour rk créé empereur 😂😂😂😂.
    Même être roi n'est pas facile. Balla gaye même, rêve bel et bien de redevenir bourou lamb dji comme tous les lutteurs 🤼‍♂️ . Sokhor bakhoul ❤❤❤

  • @bachirvd619
    @bachirvd619 Před měsícem +5

    Sokhor bakhoul modou moye roi force 🎉

  • @alioubadarasadiasane2534
    @alioubadarasadiasane2534 Před měsícem +114

    On a pas besoin de Balla Gueye en Casamance car il avait dit qu'il n'est pas de la Casamance. Nous on est fier de Casamance

    • @seydinacamara4782
      @seydinacamara4782 Před měsícem +9

      Merci lolou la beuguone waax

    • @sambagora7848
      @sambagora7848 Před měsícem +3

      😂😂😂😂c'est vrai déh

    • @ramatoulayesene3743
      @ramatoulayesene3743 Před měsícem +4

      ah bon dafko messeu wah ?

    • @agn3121
      @agn3121 Před měsícem +4

      ​@@ramatoulayesene3743Balla moko wakh durant les evenements de 2023...😂😂😂

    • @Omarsane7491
      @Omarsane7491 Před měsícem +3

      Bilahi balla gaye 2 on la pas besoin a Casamance

  • @omzo9376
    @omzo9376 Před měsícem +36

    On a pas besoin de Balla en Casamance. En plus Inshallah Balla il va perdre.

  • @pierrediagne9923
    @pierrediagne9923 Před měsícem +27

    Wa yene aziz Ndiaye mi khana da fokni mo môme senegal non khalisse Day yak nite koi

  • @mamepathengom9398
    @mamepathengom9398 Před měsícem +54

    Sa est trés pertinent 😂😂Azize dafa nagou ✍️CNG amougnou foula amougnou fayda✍️boudone Balla mo nék place bou Modou lô ✍️ dou wakh limou wakh✍️ wiri wiri bi yép moye Balla la Azize beugue mou beuré ak Modou lô ✍️😂😂😂😂

    • @user-rg2kk9hg2g
      @user-rg2kk9hg2g Před měsícem +1

      😂😂😂

    • @mamourndaw3746
      @mamourndaw3746 Před měsícem +1

      Ki dafa soxorr way

    • @marathiam1560
      @marathiam1560 Před měsícem +1

      Merciii loloy wax dji le rêve le plus cher de aziz moy balla beurei wat ak modou danat ko
      Mais modou dou defati lolou ndax nit kou nangou ndogal leu na gou na liko Yalla tek si Balla gaye mouy ke ni moy bete noiram
      Modou soxoroul bagn ko ladjei son 1er combat contre balla dafni lamb djodjou moma def mbeurrrr
      Balla o contraire fi leuko eumeu dane 2 fois mou insister ni « dane nama wayei meunouma ».
      Wayei soxor mom amoul solo modou dina geuna dieul si kanam dolene si mane daraaa

    • @papeomarba2109
      @papeomarba2109 Před měsícem

      Balla sou nekone fi modou nek dou moye tou kéna 😂😂😂

    • @marathiam1560
      @marathiam1560 Před měsícem

      @@papeomarba2109 mom d bam neikei roi diotoul am temps wou moytou saxx ndax dassa yagoul 😂😂😂beneu victoire si tafa tine apres gassi 😂😂legi loutax Balla moytou siteu kone ??? Fall plan de carriere dafa am koussi nek temps ba bou diotei di nga beurei ak gni nga wara beurel mbir mi intelligence ak professionalisme dassi boss t modou lol kay def avec son staff motax mou raww gayiii sougn ko dieulei beneu beneu amoul loumi diay Balla pck moko dane 2 fois
      Mais soudei si carriere en general modou moko geune lei Balla fouf insbi xoolouko saxxx pck dafeu gerer carrieram mou rafett yakoul yaramam, saax saxé woul carrieram bay téglé ay defaite

  • @serignefalloucisse969
    @serignefalloucisse969 Před měsícem +15

    Sadioguou a juste dit la vérité les restes du plateau son des énemis de Modou lo le roi des arènes

  • @ibrahimasarr2085
    @ibrahimasarr2085 Před měsícem +17

    Franchement Sa Ndiogou meune na analyse. amna solo

  • @SALIHTV10
    @SALIHTV10 Před měsícem +74

    Modou lo moy roi

    • @user-kaka35
      @user-kaka35 Před měsícem +1

      😂dioutal Lo roi wou kane😂😂

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 Před měsícem +9

      Balla dafa dane Modou niari yone Modou nieuw rawko si lamb té ay rival lagn lololéne méti motakh niouy saltél mais dara défar sakh couronne nou diamant mais Roi bi mom Khalé bou civilisé biy yéwo PA moko mom❤🎉XLO KASSÉ 🎉❤

    • @user-kaka35
      @user-kaka35 Před měsícem +1

      @@rouguikebe9984 modou munul raw balla thikaw souff xana benen monde mais dou biii té boulen fatteni bi guy yi didaw yikini fii Lanou fek ben balla rek moko gnemé won dieul kon kousi deg roi des arenne warngako santé balla gaye 2 dioutal Lo mom damako diélleulé😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @ousmanecisse4262
      @ousmanecisse4262 Před měsícem +2

      @@user-kaka35nanal ndokh😂😂😂😂

    • @user-kaka35
      @user-kaka35 Před měsícem +1

      @@ousmanecisse4262 nane ndokh pour mankey Lima wakh Ken douko dindi

  • @user-cr9uf9hb8l
    @user-cr9uf9hb8l Před měsícem +12

    Azizz n’a topou feulleu khana bi modou lo néké toi laniou begue niakal fayda roi 👑 ms moy roi far force naniou nangou nopalou

  • @koulaalhakk8975
    @koulaalhakk8975 Před měsícem +13

    Si balla devenez empereur...donc eumeu khana Bourou bourri😂😂😂Té mod lo mo nokh eumeu milene nokh😂😂

  • @sadiocamara192
    @sadiocamara192 Před měsícem +18

    Balla gaye n'est pas casamançais, car lui même il a dit ouvertement.
    Donc s'il vous plaît épargné la Casamance

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye Před měsícem +14

    Merci père sa diogou la lutte n'appartient pas à la famille ndiaye 😕

  • @allandiaye7665
    @allandiaye7665 Před měsícem +8

    Sa ndiogou c le meilleur Bilahi

  • @mouhamedthiane1507
    @mouhamedthiane1507 Před měsícem +24

    Aziz dafa ndeye sokhour bilahi

    • @user-nd1xq1sg5j
      @user-nd1xq1sg5j Před měsícem +1

      Niomm ak senn ayy thioggou dounou ay nit you baxx

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan Před měsícem +3

    Modou lo Moy 👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤komo nekh ak komo nakhari ❤❤❤❤❤❤❤

  • @mansourndione178
    @mansourndione178 Před měsícem +2

    Yekini c le meilleur luteur d tout les temps

  • @modougaye919
    @modougaye919 Před měsícem +9

    Balla gaye mon mane modou eume sene mane balla gaye modou lo mane eume sene bayi lene sokho modou monfi nekk❤️❤️❤️❤️

  • @user-mv5sj1gv4g
    @user-mv5sj1gv4g Před měsícem +18

    No billahi li Sa ndiogou wakh Deugueu, en résumé moy Azize ndiaye dafay fathie Mërr si Modou Lô vs Siteu bi

  • @medounediene9652
    @medounediene9652 Před měsícem +3

    C.N.G YÉKINI NÉKHOULENE MOTAKH SANDIOGOU WAKHNA DEUG❤❤❤❤❤

  • @user-uj9ok2ue2k
    @user-uj9ok2ue2k Před měsícem +21

    Balla moy sama Mbeur ms aziz nak kou sokhor la vraiment

    • @ElhadjiFall-nw2he
      @ElhadjiFall-nw2he Před měsícem +1

      Franchemen yagu nano ingnane mo dou lo. Dou deug interem mosinek

    • @abasall711
      @abasall711 Před měsícem

      Merci sa way ku degou nga

  • @KarimoulahMbaye-kt1fo
    @KarimoulahMbaye-kt1fo Před měsícem +10

    Aziz iow daga bah rék😂 roi bi kénela mouy gonégui lô💪🏿

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan Před měsícem +2

    Modou lo rek 👑👑👑👑👑👑👑👑 mofi ne dege do nekh na no ko wax ta de ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @adamaba6508
    @adamaba6508 Před měsícem +2

    Sa ndiogou cerveau ❤

  • @cheikhpendambaye2911
    @cheikhpendambaye2911 Před měsícem +11

    Dogaloul Yalla diam meunousi dara vraiment Aziz Ndiaye kou yabaté nga mane dh fans balla Gaye la wayé li Aziz Ndiaye wakh andoumasi boudone balla Gaye moy roi bi do beug kouko def balla Gaye Aziz Ndiaye bayil togn bakhoul lingay def dou deug dou yone koula ko wakhoul dala ragal merci sa ndiogou sa wakh rafet na

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye Před měsícem +10

    Aziz Ndiaye vrai domouharam la et puis le CNG ne doit accepter cette idée 😕 nous avons qu'on seule roi 🫅 et que c'est Modou lo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @yatmaseck3056
    @yatmaseck3056 Před měsícem +1

    Merci sa ndiogou sa deugou mon takh niou beug la do nafékh nitou DEUG gua 😮

  • @ibrahimacoulibaly6933
    @ibrahimacoulibaly6933 Před měsícem +11

    Sohibou il faut écouter Assane mais pas le regarder souvent il raisonne en profondeur même si dès fois il passe à côté

  • @niassniasstapha9150
    @niassniasstapha9150 Před měsícem +14

    Aziz dafa sokhor balla Gaye boy niang niouss kofi daw rk

  • @mansourelias1616
    @mansourelias1616 Před měsícem +1

    Merci bcp Sa Ndiogou deugeu dou rombou nop th yalla ko mom

  • @malickndiaye7899
    @malickndiaye7899 Před měsícem +2

    Merci sa ndiogou ❤❤❤ aziz yabatè rek ak bew moko dall

  • @landing3358
    @landing3358 Před měsícem +8

    Deuk bo khamoule nofféy déffé open de press Vue que balla néna khamoule casamance.
    Aziz ndiaye toi et ta bande respecter nous svp la casamance n'est pas un lieu de comédie

  • @bachirlo1343
    @bachirlo1343 Před měsícem +1

    Sa ndiogou machallah il est fort en analyse❤

  • @Mobamba0996
    @Mobamba0996 Před měsícem +9

    Sa ndiogou yalla nasa diame yague ❤

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Před měsícem +1

    Merci sa ndiogou amna solo de

  • @elimanediop2764
    @elimanediop2764 Před měsícem +1

    Merci sa vraiment DEUG ngua wakh

  • @expert2foot
    @expert2foot Před měsícem +30

    Qui bat le roi devient roi simple comme bonjour

  • @ousmaneka4984
    @ousmaneka4984 Před měsícem +7

    machallah sa ndiogou ❤Deug dou rombi nopou waye❤Assane mome thi ay nèlaw la nè baligui 😅

  • @geos_tv3953memphis
    @geos_tv3953memphis Před měsícem +7

    Machallah sa ndiogou sa halate sett na

  • @mouhamadoulaminekande8796
    @mouhamadoulaminekande8796 Před měsícem

    Supporterou Balla gaye la mais Modou lo Moy roi des arènes ❤❤❤
    Dégue néxoule

  • @user-fj5ib8xm2l
    @user-fj5ib8xm2l Před měsícem +1

    Aziz adouna amoul solo ..sokor bakhoul grand...té iow do lamb sakh.
    Fii yAllah fi nek té Modou lafi ték

  • @user-sx9vw3zy1b
    @user-sx9vw3zy1b Před měsícem +13

    Assane messeré yaw ak Souhaïbou da nguèna sakhor thi Modou lô rek motakh mais Modou lô yalla moko fi tekk

  • @martindiene9113
    @martindiene9113 Před měsícem +5

    Aziz ndiaye da cissou ndah khamna ni Balla Guaye 2 dou diotate couronne 👑 bi

  • @omarsarr-ff3pu
    @omarsarr-ff3pu Před měsícem +4

    merci sa💚💛❤️💪💪

  • @user-mi9wn5ir3z
    @user-mi9wn5ir3z Před měsícem +6

    Modou lo c'est le roi

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 Před měsícem +1

    Merci Sa Ndiogou Aziz Momoul Lambeu Dji Yalla Modou Lô La Déff Roi👑💪🏽💪🏽 De L'arène
    Téla NanGou Day Yombali Douma 🙏🏽

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan Před měsícem +1

    Waw ko dañ bour yaye Bour kon modou moy bout👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑

  • @abdouazizthiaw3491
    @abdouazizthiaw3491 Před měsícem +4

    Aziz en tant que promoteur du mom moy titré mbër .CNG mo wara doggal lu mel nonu.. Fédération wallah comité moy titré champion.. Na aziz yém ci rôle promoteur..

  • @KhadyTall-dz5cp
    @KhadyTall-dz5cp Před měsícem +5

    Roi modou lo lako yalla def

  • @user-yl6qx3fx4d
    @user-yl6qx3fx4d Před měsícem +1

    Soxarr bakhoul modou lo moye le roi waa keur balla aziz ndiaye comme aye lesbienne bilay 😊

  • @beckkarbonik180
    @beckkarbonik180 Před měsícem +3

    Merci beaucoup Elhadj.
    Bon pronostic

  • @FallouawaBousso20
    @FallouawaBousso20 Před měsícem +2

    Journaliste yi lou lene modou lo Def merci san ndiogou ❤

  • @pierrediagne9923
    @pierrediagne9923 Před měsícem +9

    Baye assane modou lo moy bayou lamb j

  • @mouhamedfofana4266
    @mouhamedfofana4266 Před měsícem +8

    Merci sandiogou❤❤❤❤❤❤

  • @Map_au_campus
    @Map_au_campus Před měsícem +1

    Billay sa Ndiogou yaa niémé deug wallahi ✌🏿🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @MatombonDanso
    @MatombonDanso Před měsícem +9

    BALLA BOU DOUGUÉ CASAMANCE NIOU OUBI TOUNOU NDÉM. CASAMANCE AY GORR LANIOU.

  • @arantxaarrillaga9537
    @arantxaarrillaga9537 Před měsícem +5

    Aziz tranquilo le roi c modou😂😂😂

  • @MoustaphaDiop-is4tb
    @MoustaphaDiop-is4tb Před měsícem +3

    Merci sa niogou deuge yalla moka mome

  • @user-jd1qz7zs3l
    @user-jd1qz7zs3l Před měsícem +4

    Merci beaucoup Sa ndiogou bien dit machallah 👍

  • @user-nf3jd7ji4o
    @user-nf3jd7ji4o Před měsícem +1

    Ki wakhi doff rek la fi wakh mouy mél ni kirikou ni, merci sa modou Lô c’est le roi 👑

  • @fadelrassoul4398
    @fadelrassoul4398 Před měsícem +5

    Assane ayy wahi dof lay wahh merci Sa

  • @sambemoussandiongue5663
    @sambemoussandiongue5663 Před měsícem +6

    Assane,néna Balla moo meune modou lo, eumeu moo meune Balla, mais wakhoule née Modou lo moo meune eumeu séne,

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj Před měsícem +4

    Modou lôooooooooo ❤❤❤

  • @MouhameLo
    @MouhameLo Před měsícem +2

    Li du yone aziz ndiaye balla mo mbeure motaxh moy waxh li mais modu lô moy sene baye

  • @yatmaseck3056
    @yatmaseck3056 Před měsícem +1

    Bilahi cng du dara 😮 yekini AK limou fi def lep il n'est pas reconnu

  • @BabacarNdiaye-ll8um
    @BabacarNdiaye-ll8um Před měsícem +4

    Sandiogou merci si lérel yi❤❤

  • @tawfekh1427
    @tawfekh1427 Před měsícem +5

    Aziz geumoul dara fi lako serigne am tere lamb dji mou bagn mai n'a nangou lifi yala deff

  • @SALIHTV10
    @SALIHTV10 Před měsícem +6

    Merci sa hazizz dafa bagn modou lo rk

    • @Abdallah31341
      @Abdallah31341 Před měsícem

      Banioul modou boul diawalé, balla gaye mbeureum la beug yekeuti rék

  • @user-mv5sj1gv4g
    @user-mv5sj1gv4g Před měsícem +13

    Tay moom Souhaïbou danou nga si piége Assane Messere, ndakh tay Dégo lén Sa ndiogou

  • @user-wr3rk8pb7t
    @user-wr3rk8pb7t Před měsícem +2

    Sa ndiogou a tout compris merci

  • @user-gi7ne4rm6o
    @user-gi7ne4rm6o Před měsícem +3

    Modoulo rekk lañooy topo ❤❤❤❤

  • @MameSow-vp7rj
    @MameSow-vp7rj Před měsícem +7

    Ms Aziz Ndiaye mi moy domouharame moy nitt kou bonne moy imbécile moy domou khathieu deug😂😂😂

  • @ndiawsamb4205
    @ndiawsamb4205 Před měsícem

    Wakh dji lére na nagne wayé merci beaucoup saa yawe comprendre lépe ta niémé nga deugue

  • @mouhamedelmoustaphadjikine6971

    Niémé wax deug té yalla rék tax, loolou sax ndiambarté la.
    Mâcha allah sa ndioogou

  • @CheikhNdiaye-yr7zo
    @CheikhNdiaye-yr7zo Před měsícem +3

    Wakh deuge yalla balla moy sen baye môme rk laay topo me modou lo moy roi bi azzis ndiaye modou lo moy roi bi

  • @fallougueye683
    @fallougueye683 Před měsícem

    Merci Sa Ndiogu bien dit, Azis se prend pour qui. N'importe quoi

  • @Alle-fc8pj
    @Alle-fc8pj Před 28 dny

    Azize Ndiaye sofegua sokharegua Modou fans Balla tu khamenaneni Moy roi

  • @10gitallewolof30
    @10gitallewolof30 Před měsícem +1

    Talkle show dé cheikh bara Ndiaye lafay fek inchallah

  • @AbdulPape-hp1hh
    @AbdulPape-hp1hh Před měsícem +2

    Machalah sa y’llah nalah yallah fay

  • @ShiekhjobeTijan
    @ShiekhjobeTijan Před měsícem

    ❤❤❤❤❤ Billy SA wax ga dega bo weer ga wax Liga wax loulo mo am ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdoulahadmbaye1488
    @abdoulahadmbaye1488 Před měsícem +4

    Aziz musul bague modou lo waye na niaf ndeyem fale manul Wakhe ba du neke roi balla mom pena si lamb

  • @aidakasse1479
    @aidakasse1479 Před měsícem +4

    Merci sadiogou 💯 😂😂😂😂😂

  • @OMARKASSE-np2iv
    @OMARKASSE-np2iv Před měsícem +5

    Modou lo ni mou nékè roi nékhou leene

  • @ousseynoudieng7429
    @ousseynoudieng7429 Před měsícem +7

    Non mais sa Machala ❤❤🙏🏽

  • @user-sx9vw3zy1b
    @user-sx9vw3zy1b Před měsícem +11

    Assane wakho fi dara