PAWLISH MBAYE EN LARMES PARLE DE SON PÈRE: "DOOM DAGNOU KOY..."

SdĂ­let
VloĆŸit
  • čas pƙidĂĄn 8. 07. 2023
  • đŸš©ABONNEZ-VOUS Ă  la ChaĂźne de la 2STV cliquez sur ce LIEN👉 :
    Retrouvez l'ensemble de nos programmes d'actualité et émissions de société, santé, politique, culture, musique, économie sur:
    - / 2stvsenegal
    - / 2stv_senegal
    / 2stvsenegal
    - Snapchat: senegal2stv
    - TikTok: @2stvsenegal
    - / 2stvsenegal
    - www.dailymotion.com/video/x7v...
    #LII #2STVSENEGAL #2STV #FreeSenegal #sonko #mackysall #2STVLIVE #senegal #TEAM221 #KEBETU #XIBAAR #JOURNAL20H #NEWS #ACTUALITÉS #DIVERTISSEMENT #SOCIÉTÉ #ÉCONOMIE #SANTÉ #DAKAR #yewwiaskanwi #BennoBokkYakaar #AarSenegal #ousmanesonko #LSFP #2stv #FSF #liguepro #senegal #football #4AVRIL #fetenational
  • ZĂĄbava

Komentáƙe • 100

  • @abytolskigh
    @abytolskigh Pƙed rokem +52

    Ça me brise le cƓur quand mĂȘme papa yi yeureum lene sene dom yi Dow nawle souniou borom meunou la diokh diabote defo dara lou ware si mĂŽme aprĂšs ga nieuw takhaw en public di wakh. Il ya des gĂ©niteurs et des pĂšres. Mais bon Pawlish demal guiss sa gĂ©niteur guĂ©ne wakhtane

  • @diarrasow4738
    @diarrasow4738 Pƙed rokem +25

    Il faut jamais juger une personne sans le connaitre😱

  • @coumbandao2501
    @coumbandao2501 Pƙed rokem +26

    J'ai des larmes aux yeux😭😭

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 Pƙed rokem +8

    Ndayesan MĂ©tina MĂ© yalla nalĂ©n Yalla DjibolĂ© Si BarkĂ© SeriGnE TouBa Khadim Rassoul ❀ đŸ€ČđŸŒđŸ€ČđŸŒ

  • @warackmbaye2380
    @warackmbaye2380 Pƙed rokem +24

    ya yarou ya bakh yala nala yala diapalé sa papa wayé ni rék layouye déf du courage pawlis

  • @beugdeug5553
    @beugdeug5553 Pƙed rokem +38

    En entendant parler Pawlish on sait que son pĂšre n'avait pas s'occuper de son fils

    • @Africa-Liberation-Army
      @Africa-Liberation-Army Pƙed rokem +1

      Sometimes some mothers chase the fathers of their kids away. Hearing from his father he did his best and had always taken care of this boy. This boy has nothing
.

  • @coumbandao2501
    @coumbandao2501 Pƙed rokem +25

    Ohh pawlish il est mature ndekete vraiment suis Ă©mue đŸ„Č

  • @fatoundiaye8637
    @fatoundiaye8637 Pƙed rokem +10

    Dieufway pawlihs ❀❀samadom yao dara doula teiye mougne rek adouna doudara massa yala bakhna nekal sidiam ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @kheuchakhloubadar7822
    @kheuchakhloubadar7822 Pƙed rokem +3

    CheuĂ©Ă© sama khĂłl toyna 😱 yalla nanou yalla moussal si sĂ©ytaanĂ© yalna yalla dĂ©ff diam si digantĂ© dome ak wadiouram

  • @sambakeita8189
    @sambakeita8189 Pƙed rokem +14

    ❀❀❀❀❀❀❀❀de tous cƓur avec toi pawlish

  • @amadoundiaye9309
    @amadoundiaye9309 Pƙed rokem +22

    Pawlish tu es un homme trĂšs poli

  • @ababacarniang5939
    @ababacarniang5939 Pƙed rokem +15

    mane Mii Sakh sama papa dafma guĂ©nĂš walahi dieul samay rakeu AK samay mak yobou Europe douma toukh douma nane douma sathie mais yalla bakh na pawlish yalla nala yalla sameu😱😱😱

    • @bathindiaye309
      @bathindiaye309 Pƙed rokem

      😱😱😱😱

    • @ousmanesow6736
      @ousmanesow6736 Pƙed rokem +4

      Gor gorloul té masla AK mom nakhantél AK mom boulko dépassé té boul won guinaw mouk

    • @dadad9342
      @dadad9342 Pƙed rokem

      Laisse lui, mĂȘme si tu rĂ©ussis ta vie faits le minimum avec lui

  • @diengsalatv4683
    @diengsalatv4683 Pƙed rokem +7

    J’ai des larmes aux yeux 😭

  • @fatoubintoufalk1397
    @fatoubintoufalk1397 Pƙed rokem +10

    Ndeye san yalla bakhna 😭😭😭😭

  • @mamadoufall803
    @mamadoufall803 Pƙed rokem +4

    Je le comprends parfaitement certains pĂšres se soucient de leurs enfants que quand ils sont proches ou celebres

  • @thiallasene6177
    @thiallasene6177 Pƙed rokem +5

    SĂ©nĂ©gal dafa mĂ©ti bou amoule kĂšne doula falĂ© mais bou dĂ©mĂ© ba yall soutourala noiu guĂ©ne dila djiĂ©ma trokhale dome daguecouye topoto lou meti si senegal dagnenane wadjoure wadjoure mais dome boco amĂ© daguecoye topoto pour eulek mo takh longue vie pawlise j’ai des lames aux yeux bonne continuation 😘

  • @joliekalsoum7287
    @joliekalsoum7287 Pƙed rokem +26

    Si je comprend bien les propos de pawlish son pĂšre ne l’avait pas reconnu comme Ă©tant son fils souma dioumoull

  • @mamanossacultura3217
    @mamanossacultura3217 Pƙed rokem +9

    Boule dioye sama dome je suis avec toi

  • @Mamita0107
    @Mamita0107 Pƙed rokem

    Trop Émue vraiment c’est pourquoi on doit jamais jugĂ© une personne y’a des gens qui souffrent intĂ©rieurement et c’est eux qui te consolent quand tu as des soucis, Force a vous et force a Pawliss Mbaye. Que le bon Dieu nous protĂ©ge et nous guide dans le bon chemin. đŸ™đŸ™đŸ™â€â€

  • @madeleine7159
    @madeleine7159 Pƙed rokem +12

    Pawlish demal diegalou sa papeu bila diour, ter diegual ko, mais boumoulleu tek bene stress .....taaleul gni sonone tchi yow. Sénégal massla bou eup mo niou sonnal !

    • @DieynebaSoumah
      @DieynebaSoumah Pƙed rokem

      Bayi Lén seytané

    • @madeleine7159
      @madeleine7159 Pƙed rokem

      @@DieynebaSoumah yen ngen baayi dey bou khadioul sen tatt, manaam hypocrisie...â˜ș

  • @adjilesaint3250
    @adjilesaint3250 Pƙed rokem +1

    Sénégal on a notre réalité et c est notre force

  • @ousmanetop4294
    @ousmanetop4294 Pƙed rokem +7

    Neko sa papa leu maan may sa baye 😱

  • @oumarcamara3796
    @oumarcamara3796 Pƙed rokem +1

    Masiiiii ham dara😱😱 courage a nous😱😱😱

  • @abydiallo7203
    @abydiallo7203 Pƙed rokem +4

    Bo amoul kene doula lidieunti. La société te rejette. Bo amee nak kou nek nane sama dom la

  • @falloudiop7780
    @falloudiop7780 Pƙed rokem +5

    Pawlis ❀❀

  • @vicincialy8928
    @vicincialy8928 Pƙed rokem +2

    Ho pawlish aujourd’hui tu m’as Ă©mu que le bon dieu continue de te soutenir pour toute ta vie . Va voir ton papa et demande lui pardon . Cela ne sera que du bon pour toi .

    • @dadad9342
      @dadad9342 Pƙed rokem +2

      Pardon pourquoi?

    • @khadyndiaye144
      @khadyndiaye144 Pƙed rokem

      @@dadad9342vraiment pardon pour l’avoir abandonnĂ©? Lol

    • @dadad9342
      @dadad9342 Pƙed rokem

      @@khadyndiaye144 son pĂšre lui doit pardon et doit dĂ©dommagement avec intĂ©rĂȘts Ă  sa mĂšre et grande mĂšre

  • @bayegueye478
    @bayegueye478 Pƙed rokem +2

    Ana international AK fan Boromi casquette

  • @aiss479
    @aiss479 Pƙed rokem

    Machalla bijou

  • @sayeseck1089
    @sayeseck1089 Pƙed rokem +6

    Wallahi sama khĂŽl tooyna trop Barker Nabil Moustafa Nanou fonkat doom yi adina dafa teureudi

  • @diopfama6800
    @diopfama6800 Pƙed rokem +5

    ❀❀❀❀❀❀❀

  • @deremtv8066
    @deremtv8066 Pƙed rokem +1

    ABLAYE FAYE DEMAL BALOU SA PAPA AKHE TE FEKHE ANDE AK MOME TE YALLA TAKH BAKHNA

  • @babacarcisse-qy8xm
    @babacarcisse-qy8xm Pƙed rokem +4

    😱😱😱😱😱😱

  • @ousmanesow6736
    @ousmanesow6736 Pƙed rokem +1

    Pawlis dieulénama kaw trop vraiment té nga bal ma akh si beut bimala done xolé

  • @diarrasow4738
    @diarrasow4738 Pƙed rokem +3

    Ça m'a vraiement touchĂ©đŸ˜ą

  • @ABAB95731
    @ABAB95731 Pƙed rokem +2

    Ki Nit la dou Doff dé

  • @momoseck1617
    @momoseck1617 Pƙed rokem

    Djiam rek nguey am ❀

  • @user-ne3mf2du4v
    @user-ne3mf2du4v Pƙed 2 měsĂ­ci

    ❀ lat nonila

  • @diopablaye5227
    @diopablaye5227 Pƙed rokem +4

    Wakhi nit rek nga wakh

  • @awadiagne9988
    @awadiagne9988 Pƙed rokem

    Bilahi goor seen dome bokhoul si divorce niak guen diom trop mais du courage gueuneul topoto sa yaye

  • @fatoudiete1479
    @fatoudiete1479 Pƙed rokem +2

    Li kouko doudoul doko Khame mane sama dome pape dako rejeté mais souma gué gnou DEUG ko recontre

    • @awadiaby5195
      @awadiaby5195 Pƙed rokem

      C vrai kouka ndoudoul khamoko adouna lifi nekkk they

  • @user-lh5yf2jr1e
    @user-lh5yf2jr1e Pƙed rokem

    Boulén gno sonal lou way doundou nako santé yalla fi amna gno hamni sougnou waxone sen diare diare waxtane dou yéegue alhamdou lillahi li da diare débat couné disé wax Sénégal vie bou salté mofi wax rek yalla gueremoul li sof gueen trop

  • @papesamb8624
    @papesamb8624 Pƙed rokem

    Pawliss mbaye tay li mĂŽme wakh ha duĂ©geu😊

  • @nitoudeugue4930
    @nitoudeugue4930 Pƙed rokem +2

    Fallait faire rentrer le pĂšre biologique qu'il donne sa version pour Ă©quilibrer tout de mĂȘme

  • @bayegueye478
    @bayegueye478 Pƙed rokem +2

    Dieul leu gueun

  • @kawba3524
    @kawba3524 Pƙed rokem

    â€ïžâ€ïžâ€ïžâ€ïžâ€ïžâ€ïžâ€ïžđŸŽ‰

  • @Paperythme
    @Paperythme Pƙed rokem +1

    Li yeupe yawe pape nimou meneti méle papela fonk lÚne sÚne wadiour bala mouye trop tard

  • @aiss479
    @aiss479 Pƙed rokem

    ❀❀❀

  • @user-dn6yq9ti5l
    @user-dn6yq9ti5l Pƙed rokem +1

    😭😭😭😭😭😭

  • @mamaediarrafallmamediarraf722

    đŸ˜­đŸ˜­đŸ˜­đŸ˜­đŸ˜­đŸ˜­đŸ˜­đŸ˜­đŸ˜­â€ïž

  • @Mamadou-bb6sd
    @Mamadou-bb6sd Pƙed rokem +5

    ❀❀

  • @user-sp2mu8qf6y
    @user-sp2mu8qf6y Pƙed rokem

    Khamo dara doff plus nga😂😊

  • @Hamartv_Abonne_toi
    @Hamartv_Abonne_toi Pƙed rokem

    Pawlish yéy na niép

  • @KhadyLy-mq2ez
    @KhadyLy-mq2ez Pƙed rokem

    ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @Africa-Liberation-Army
    @Africa-Liberation-Army Pƙed rokem +1

    Andoulaye Faye dou Abdoulaye mbaye

  • @kheuchactutv529
    @kheuchactutv529 Pƙed rokem +1

    Tay pawlis serieu na deh😂

  • @bayegueye478
    @bayegueye478 Pƙed rokem +1

    Ndém dolen tayi

  • @dadad9342
    @dadad9342 Pƙed rokem +4

    Si j’étais pawlish, j’aurais aucune relations avec ce vieux mendiant de moustique qui cherche quelqu’un pour s’occuper de lui.

  • @khadidiatoundir5395
    @khadidiatoundir5395 Pƙed rokem

    â€đŸ˜‚đŸ˜‚

  • @user-ne3mf2du4v
    @user-ne3mf2du4v Pƙed 2 měsĂ­ci

    Ndaye san balul akhe gorgi ta gorgorlou yalla moy saborom dinala dimbli

  • @bayegueye478
    @bayegueye478 Pƙed rokem +4

    Lékkeu sén leufeul ndaye réka dagane

  • @abydiallo7203
    @abydiallo7203 Pƙed rokem +4

    Lou sotii am borom

  • @ndeyesow2969
    @ndeyesow2969 Pƙed rokem

    Khamonani pawliche yarou mame la

  • @saliouniang2939
    @saliouniang2939 Pƙed rokem

    Dommage a son pĂšre da baye ba pawlis siww mou beug ni moy bayam mais adouna amoul solo

  • @fatoumataba9925
    @fatoumataba9925 Pƙed rokem +4

    Pawlish mane doudounako sa ma pape da fassé sama Yaye mou abandonné ma ba a l ùge de23ans kaki messeu guise bama démé ba lëpp sotie lama commencé djégué

  • @morniangfansneymarjr763
    @morniangfansneymarjr763 Pƙed rokem +2

    Lila dal moma dal

  • @bayegueye478
    @bayegueye478 Pƙed rokem +2

    Dolen tayi dé wayé douma melni yaw dé

  • @dadandoye2153
    @dadandoye2153 Pƙed rokem +2

    Daga rere ta amou Kou wakh degue , Ba bi foumou diougue

    • @AbdoulayeFall-jw2uv
      @AbdoulayeFall-jw2uv Pƙed rokem

      Wakhone na ni dadone football motakh khon yi ladone bagne mou diapp ko

  • @dedevisy6856
    @dedevisy6856 Pƙed rokem +2

    niit dafa diafé kham ndeysane

  • @adaseck6474
    @adaseck6474 Pƙed rokem +3

    Pawlis papa bou bay nga ame demal ga balego ak

  • @tourecheikh5201
    @tourecheikh5201 Pƙed rokem +3

    Mais en faite lini yeupp bou deugue rk nékhé yalla! loussi sougnou yone?
    Sétane na émission bi mais soxla nagn yénéne débats youdoul genre yi li cŽest privée

  • @antasarrcisse1803
    @antasarrcisse1803 Pƙed rokem +2

    Que de banalités !!!

  • @user-lh5yf2jr1e
    @user-lh5yf2jr1e Pƙed rokem

    Dome dou yayeu wajouram jamais lofi wax loudone balou sa bay waxoufi dara amoul lenen

  • @septchaine
    @septchaine Pƙed rokem +9

    Au lieu que guéne diéma dioubalé PaPam ak dom mais il faut que guéne diéma féne lo PaPam té yéne nieupe séni wadiour yi yéna gui léndi diamou li émission bou saleté leu ay nafik guéne

    • @mdtv4854
      @mdtv4854 Pƙed rokem +7

      Gnom sén papa dafa déf liko War koum Donon yaw tamit ningay def bayi lén nafekh

    • @septchaine
      @septchaine Pƙed rokem +3

      @@mdtv4854 lima ler dé moy sa papa défoul Lika War a 100% mais diap gako ndakh sa baye leu s'en affaires yi guéne wara bayi yeuf yo khamni khamouniou KO fi si Sénégal topando rk mo léndi sankou lo

    • @aminandong7735
      @aminandong7735 Pƙed rokem +2

      Tu as parfaitement raison pawlish waroul wone gniow si emission bii di wakh quoi k sa soit dafa warone ande ak ay kilifeu gnu goungué ko mou balou papame andate ak ay mbokame

    • @AbdoulayeFall-jw2uv
      @AbdoulayeFall-jw2uv Pƙed rokem +7

      ​@@aminandong7735tĂ©h papam nieuw youtube wakh est ce que lolou rafĂ©t na ???

  • @user-ne3mf2du4v
    @user-ne3mf2du4v Pƙed 2 měsĂ­ci

    Bisu yaw talibe sarig salihuga dagabakhe

  • @waziris4228
    @waziris4228 Pƙed rokem

    La journaliste n’est pas pro pourquoi elle veut rire ?

  • @AwaBodian-cf2iy
    @AwaBodian-cf2iy Pƙed rokem

    ❀❀❀❀❀❀

  • @user-dn6yq9ti5l
    @user-dn6yq9ti5l Pƙed rokem

    😭😭😭😭😭😭😭