Série - Woudiou Peetiorgo 2.0 saison 1 - Episode 27

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 5. 05. 2024
  • Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
    instagram
    kharmedia_offic...
    facebook
    / kharmedia_l'officiel
    Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
  • Krátké a kreslené filmy

Komentáře • 164

  • @nafidiakite3363
    @nafidiakite3363 Před měsícem +29

    On réclame le bonheur de fa Ndiaye ak Modou vraiment thiey Astou tamite une excellente série vraiment ❤

    • @mordione7256
      @mordione7256 Před měsícem

      Fat ndiaye dafa toye trop bouy dokh di tawèkou mèlni lance pière😂

  • @aichadiop9178
    @aichadiop9178 Před měsícem +34

    Fat NDiaye rap bi mo sokhor 😂😂série yimou meuseu jouer yeup problem mbeuguel la am

    • @peaceonly5951
      @peaceonly5951 Před měsícem +2

      Bilaye wakh nga deugueu.la elle a très mal fait.Goor lacc leu seu numéro rek nga beugueu mou wo leu par force.Il faut te faire désirer quand même. Beugueu khoulo trope.Djiguene dey nekh déréte waaye.Lolou leu niou khamé sénégalaise.

    • @mounirou-in2wi
      @mounirou-in2wi Před měsícem

      Salimata dé néna moko liguey pour dou am dieukeur

    • @Ndeye-fatousow
      @Ndeye-fatousow Před měsícem +1

      Ak mirage mok abdou😂

    • @fallndeye6092
      @fallndeye6092 Před měsícem

      Bilaye

    • @mariamakamara688
      @mariamakamara688 Před měsícem

      😂😂😂😂

  • @user-dw8sz7rm4y
    @user-dw8sz7rm4y Před měsícem +25

    Coussa 4 barame nék sisa guinaw téléphone rék lalal j'aime ❤️

  • @mameboussathioune-ux9do
    @mameboussathioune-ux9do Před měsícem +27

    Mousouma Ame j,aime❤❤❤

  • @FatouCamara-uj5uu
    @FatouCamara-uj5uu Před měsícem +27

    Fatou Ndiaye nak nekal nit,1er fois bamoula wowé,danga waron def kom si Fatou won ngako lath ko fanla nekon bobou batay

    • @mounirou-in2wi
      @mounirou-in2wi Před měsícem +2

      Ki kaay weroul

    • @AssLo-xg6wq
      @AssLo-xg6wq Před měsícem

      Dafa sof rk

    • @Owsy948
      @Owsy948 Před měsícem

      Wakh deug et non montrer qu'elle attendait avec impatience son appel

    • @aidafallndiaye2766
      @aidafallndiaye2766 Před měsícem +1

      Damako moudie djepi ni

    • @ndeyegueye944
      @ndeyegueye944 Před 24 dny

      Scénario bi kayy yeufi doff la nitt Amna droit dieul sa numéro 1ans dila dora woo c’est forcé mo nope la tamit😂😂😂

  • @rokhayafall3001
    @rokhayafall3001 Před měsícem +24

    Fatou ndiaye mi sof na modestie zèro

  • @astougueye4671
    @astougueye4671 Před měsícem +15

    Bigué est très belle machallah 🥰

    • @mordione7256
      @mordione7256 Před měsícem +1

      Bilahi dafa rafet trop tè douce

  • @hawagako977
    @hawagako977 Před měsícem +12

    Bonjour mais astou Mbaye n'est pas intelligente non elle ne peut pas gérer son foyer elle est entrain de pousser son mari jusqu'à bout parceque la vision du mari est contraire à celle de bigué mais astou ne comprend pas bonne journée c'est mère hawa Gako depuis Paris merci bonne continuation

  • @user-qs9dy5vk2b
    @user-qs9dy5vk2b Před měsícem +17

    Thiey aita Yonne biga dieul bahoul

  • @khadygueye1707
    @khadygueye1707 Před měsícem +14

    Biguè tamite yagui yeugeul seuyou diambour bi nak mais Astou mbaye tamite Modou ndiaye wakh nala deugue sou ligueyoul loumou laye yoré tamite li kène khamouko 😂😂😂😂

  • @RoseFall-op5kp
    @RoseFall-op5kp Před měsícem +14

    Fatou sa rak dji legui bon na mo raw yayam dji di

    • @mounirou-in2wi
      @mounirou-in2wi Před měsícem +2

      Mom dafa dof sakh parceque Fat Ndiaye am dieukeur moy avantage ci mom

  • @SoxnaNdiaye-ce4eg
    @SoxnaNdiaye-ce4eg Před měsícem +13

    Modou Ndiaye vraiment amal foula ngua freiné Bigué dina tass seuy dé

  • @user-qs9dy5vk2b
    @user-qs9dy5vk2b Před měsícem +6

    Astou mbaye Nacarigua wahal mais nak je te comprend bigué noumoul dohalé ak yow la

  • @dierysy7024
    @dierysy7024 Před měsícem +1

    Bigué dafa melni amna ay sentiments si modou ndiaye deh

  • @MameDiarraMbaye-ud6ov
    @MameDiarraMbaye-ud6ov Před měsícem +13

    Consine nou aida ak raki fat ndiaye louniou boko❤

  • @dabandiaye6323
    @dabandiaye6323 Před měsícem +5

    ASTOU Mbaye sof nama d loumouy defni dou bayi Modou mou liguèyi Xana amoul si mom confiance vraiment sof ghen ak wakhou liguèy bi

  • @papewade5202
    @papewade5202 Před měsícem +2

    '' nn soda réw n'a 😂😂😂 yayou pa assane yayou Modou Ndiaye bigué asuime Modou Ndiaye dieuleul loy khoff Astou mbaye da fiirr pa assane aita Fatou Ndiaye djii woula la lii ndakh goor

  • @princessemyadiallo9791
    @princessemyadiallo9791 Před měsícem +2

    Thimm modou Ndiaye mi dof la rék bigué mi beugue tass sa sey

  • @gayemamediarra2644
    @gayemamediarra2644 Před měsícem +11

    Non soda amoul fitt laminie la am rek ayi astou mbaye sama xarite bi li ba diam la

  • @AssLo-xg6wq
    @AssLo-xg6wq Před měsícem +3

    Fat Ndiaye mi sofff na déh weuhhhhh

  • @adamengomndiaye4209
    @adamengomndiaye4209 Před měsícem +3

    Aïta mi nite yobouwo fitou kene wa ki nite la Fatou Ndiaye ❤❤❤

  • @dialickadiame4475
    @dialickadiame4475 Před měsícem +2

    Astou ragalna mou avorter sah modou ndiaye weyadi nga sa sokhna sou bah nala geunal lépp si adouna yo mboul di nga am bénene liguéye

  • @SaineyJagne-go5yg
    @SaineyJagne-go5yg Před měsícem +4

    Fatou njie rek❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @awadiallo9954
    @awadiallo9954 Před měsícem +1

    Mane mes domou mbaye sante yalla pour fat ndiaye nonou lala beugué

  • @peulhsoce
    @peulhsoce Před měsícem +11

    Kholal soda ak ongle you jaune yi djiguenou Sénégal gnikoy diouli bari wougnou dé kossi guiss mogui pose ongle tous le temp pose cils si ay domou dioulite

    • @user-cc1ou9jk4m
      @user-cc1ou9jk4m Před měsícem +2

      Doyna waar défouniouko mouye dara nak lidianti souniou Diné

    • @peulhsoce
      @peulhsoce Před měsícem

      @@user-cc1ou9jk4m c grave an dioulite dou fowé diouli

    • @sassoumthiam6414
      @sassoumthiam6414 Před měsícem

      Bilay dax ga sagneko wx tmt

    • @Ak15922
      @Ak15922 Před měsícem +1

      Fo bayi mère Diarra ak émail bou bleu bi nakk😂😂

    • @peulhsoce
      @peulhsoce Před měsícem +1

      @@Ak15922 guisso mako sakh euskeuy mère diarra dafa émaillou c grave nak

  • @fatimatoudiop3979
    @fatimatoudiop3979 Před měsícem +6

    Yéna Meilleur kagne ❤❤❤

  • @fatyseye6567
    @fatyseye6567 Před měsícem +56

    Yen gni done wakh astou mbaye dafa eupal guenn len fi khamguen né li nekhoul way nit nop sa dieukeur avoué lako tok sa keur dila beulé dila ré

    • @peaceonly5951
      @peaceonly5951 Před měsícem +8

      Lolou deugueu leu mais Modou meunoul comprendre car il est innoncent.Khamoul Lou khew.Astou mo wara gérer autrement mais pas kheut kheut.Bigué mo bonne té hypocrite.
      Ame ligueye daffa diaffé .on ne peut pas lui demander de laisser passer une occasion pareille.Confiance dafa bakh si mariage.
      Astou dommage tu as montré ta faiblesse à Bigué.Yakhou nga.Mey nga ko dolé.😮

    • @madickediop968
      @madickediop968 Před měsícem +1

      Mais bacilan modou Ndiaye mana droit yak ba nieti jabar té bigue jabaru Yoon yallam la astou mbay Moy begge sof

    • @Thatgirl7788
      @Thatgirl7788 Před měsícem +2

      Thi degue degue lii nekhul thi khol, bala ma dehh nyiu naan diabaru yoon yallah

    • @FatouGaye-ip4ig
      @FatouGaye-ip4ig Před měsícem +1

      Bigué Yaye Ipokric

    • @mordione7256
      @mordione7256 Před měsícem +2

      Gnidi wakh nane astou mbaye dafa eupeul togou lène si plaçame motax guène di wakh

  • @user-by4uc1zc3q
    @user-by4uc1zc3q Před měsícem +4

    Astou mbaye soof ga khana do femme c quoi ces manières 😮😮😮😮😮😮😮😮😮

  • @ndeyembenedieng3127
    @ndeyembenedieng3127 Před měsícem +6

    Wa lègui état ligueye bi kagne lay diale

  • @ndoyemarietou6966
    @ndoyemarietou6966 Před měsícem +12

    Astou mbaye daguey enregistrer bigue souko deffe sey propos meune justifiwu 😢

  • @NdioleSene-ec7et
    @NdioleSene-ec7et Před měsícem +2

    Domou kebemer mof'
    I niek tay❤❤❤

  • @ramatoulayeba1458
    @ramatoulayeba1458 Před měsícem

    Moh Modou mi diépi nako trop way ish
    Merci Astou foula dafa bakh si niit

  • @ndeyendacktoure2980
    @ndeyendacktoure2980 Před měsícem +3

    Wa lamine sa levre yi nga rothie tamite attend ma wo medecin bi

  • @user-ss6rm5lf7o
    @user-ss6rm5lf7o Před měsícem +3

    Wa modou nite la

  • @fatoudia3146
    @fatoudia3146 Před měsícem +1

    Wawaw astou mbaye dafa epeul kagne la gor Di tagou liguéy djieguène

  • @sassoumthiam6414
    @sassoumthiam6414 Před měsícem +3

    lèkiii d aida mi mo raw posonou gagna

  • @MarieDia-ls5vq
    @MarieDia-ls5vq Před měsícem

    Astou. Très mignonne. Machala

  • @seckseck1987
    @seckseck1987 Před měsícem

    Merci astou mbaye

  • @thiathiasyll9360
    @thiathiasyll9360 Před měsícem +13

    Domou Kebemer mofi niek tay

  • @dioufsadio
    @dioufsadio Před měsícem +1

    Astou mbaye amoul béneu foula

  • @mmetoure8576
    @mmetoure8576 Před měsícem

    Modou Ndiaye tu exagère vraiment

  • @NdioleSene-ec7et
    @NdioleSene-ec7et Před měsícem +2

    Yena Meilleur kagne❤❤❤

  • @aminatakane2845
    @aminatakane2845 Před měsícem

    Mère diarra comme Oustaz yoyou di deff wakhtanou koor mouy kon mou Mélni ni rk😂😂ms Soda tmt niakk na diom 😂😂

    • @user-hx8gt7pi3j
      @user-hx8gt7pi3j Před měsícem

      Walay walay walay Neysane 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @mambousohaassanjaaye2480
    @mambousohaassanjaaye2480 Před měsícem +4

    Astou mbaye boufi avarté rk

  • @ndoyasene99
    @ndoyasene99 Před měsícem

    Vraiment Soda comédienne pure

  • @lamajestueuse2872
    @lamajestueuse2872 Před měsícem +2

    Non Aïda dou nitou fii 😂😂😂😂

  • @user-qz8lv3tm4h
    @user-qz8lv3tm4h Před měsícem +2

    Astou mbaye yawe laniou take.bigué téke ko feulé

  • @maodolo1474
    @maodolo1474 Před měsícem +1

    FATOU ya mana fene nga nane yene modou modou ye FATOU si pobam moye begue soff

  • @maramedieng6439
    @maramedieng6439 Před měsícem +2

    Maafi ndieukk😂😂 top lene ma

  • @sokhnaaminata287
    @sokhnaaminata287 Před měsícem +1

    😂😂😂astou mbay😂😂 wouyy maa ngi gaangnou

  • @sokhnadiarrandour
    @sokhnadiarrandour Před měsícem +1

    Fatou ndiaye niaq ngand kersa nk😂😂😂😂

  • @user-rq4yr6st1k
    @user-rq4yr6st1k Před měsícem

    Khana astou mbaye amoul famille sonouna dé

  • @MarieDia-ls5vq
    @MarieDia-ls5vq Před měsícem

    Astou. Mbaye. Wakhe. Na. Degue

  • @user-hx8gt7pi3j
    @user-hx8gt7pi3j Před měsícem

    Fatou ndiaye Nekal niteu gniak nga kerssa trop si djiguene wathiel sa boop soof nga trop 😢

  • @AmySenghor-tx6fm
    @AmySenghor-tx6fm Před měsícem +1

    Astou Mbaye mo gnakeu fayda Deug Deug té wayadi

  • @mamecheikhdiack2114
    @mamecheikhdiack2114 Před měsícem +5

    Mane fat Ndiaye limouy lidékou la khamoul loumou done

  • @mameawasylla3601
    @mameawasylla3601 Před měsícem +1

    ASTOU mbaye va pousser son mari dans les bras de bigué

  • @user-wo4zl7eq3c
    @user-wo4zl7eq3c Před měsícem +2

    Mafi dietou

  • @ndeyembow6695
    @ndeyembow6695 Před měsícem +1

    Modou Ndiaye guenal thi linga neick

  • @user-iz9ug8cq1e
    @user-iz9ug8cq1e Před měsícem +7

    Soda saformou bi modéna 😂

  • @user-hv7my9or7h
    @user-hv7my9or7h Před měsícem +1

    Wa mère Diarra tamite ak émay by 😂

  • @user-ip2jw7yy1i
    @user-ip2jw7yy1i Před měsícem

    Soda AP Mer lay nouroll dafa rew way sa goro bi mola geuna reww 😂

  • @dabasene4827
    @dabasene4827 Před měsícem

    Première yomboul

  • @gnilanediallo1479
    @gnilanediallo1479 Před měsícem

    Fatou ndiaye sofff nga

  • @KhadyDieng-vi4mk
    @KhadyDieng-vi4mk Před měsícem +4

    Serie bi gate ne trop barina pub trop

  • @philobarreto6765
    @philobarreto6765 Před měsícem

    Astou Mbaye wolouwoul bopam, deye exagéré nak

  • @mustafaasamb8419
    @mustafaasamb8419 Před měsícem +2

    Série bi neex na

  • @thiounefatou1975
    @thiounefatou1975 Před měsícem

    Fat Ndiay da meuna Bane baradiè gor ki nieuw khamala goko di jugè nii

  • @MariamaBalde-nv3tf
    @MariamaBalde-nv3tf Před měsícem

    Bien

  • @user-wd9es8po5b
    @user-wd9es8po5b Před měsícem +3

    Publicité Yi moy sofal série bi

  • @maguetteguisse9486
    @maguetteguisse9486 Před měsícem +5

    Khar média li amoule waye di saga sa gorro di ngew keur di roube arrêter svp trops c'est trops

  • @Owsy948
    @Owsy948 Před měsícem +1

    Wa Fatou yow est ce que ça va ?

  • @diorgallas
    @diorgallas Před měsícem

    Fa Ndiaye sofga trop way

  • @NdeyeSokhna-pt6jt
    @NdeyeSokhna-pt6jt Před měsícem

    Faty Ndiaye môme dafa teyol.motakh do âme Dara 😅😮😮

  • @user-ss6rm5lf7o
    @user-ss6rm5lf7o Před měsícem +2

    Soda😂😂😂😂

  • @sokhnadiop9505
    @sokhnadiop9505 Před měsícem +1

    ❤❤❤

  • @AbySow-xl4ck
    @AbySow-xl4ck Před měsícem +1

    ❤❤❤❤❤❤

  • @gomisenefanny3076
    @gomisenefanny3076 Před měsícem

    Astou
    Do enregistrer bigué

  • @AwaHuma
    @AwaHuma Před měsícem

    😊

  • @user-ip2jw7yy1i
    @user-ip2jw7yy1i Před měsícem

    Fat Ndiaye yangui beuga soff nak

  • @dieynaseck8407
    @dieynaseck8407 Před měsícem

    ❤❤❤❤

  • @fatoundiaye3444
    @fatoundiaye3444 Před měsícem

    Bigué actionnaire la si entreprise bi
    Donc Modou ndiaye sou ligueyé bigué loumou beugue forcément Modou ndiaye dafkoy deff
    Li yup plan 🗺️ là pour am modou

  • @AwaHuma
    @AwaHuma Před měsícem

  • @FamaFall-mf8oq
    @FamaFall-mf8oq Před měsícem +2

    Lou takh awo yi firr😅

  • @NdeyesokhnaSarr-ye9bn
    @NdeyesokhnaSarr-ye9bn Před měsícem

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-io5yj4gm2c
    @user-io5yj4gm2c Před měsícem

    Qui mo sokhor rek

  • @FatouFall-dz2io
    @FatouFall-dz2io Před měsícem

    ❣️❣️💔

  • @MameCoumbaNdiaye-xx2ki
    @MameCoumbaNdiaye-xx2ki Před měsícem

    👍👍👍👍👍

  • @user-ip2jw7yy1i
    @user-ip2jw7yy1i Před měsícem

    Astou yangui beuga soff nak

  • @aramefall5381
    @aramefall5381 Před měsícem

    Astou mbaye woloul sa boppe

  • @user-hp3bf3ss3d
    @user-hp3bf3ss3d Před měsícem

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @awadiallo9954
    @awadiallo9954 Před měsícem

    Astou mbaye nak arretel waye ligueye rk

  • @mamereese1912
    @mamereese1912 Před měsícem

    Soda rek .

  • @aichasall8287
    @aichasall8287 Před měsícem

    Astou dafa eupeul nak hiii, soof na torop, il faut avoir confiance en ton mari way, boul niou sonal momo nite gni

  • @awaceesay6909
    @awaceesay6909 Před měsícem

    Astou mbye sof nga torop.. to be honest

  • @awadiallo9954
    @awadiallo9954 Před měsícem

    Ligueye bi moudjouna meti nak mere bi tamite pourquoi autant de question damour

  • @awadiallo9954
    @awadiallo9954 Před měsícem

    Topougnou rk je merite pas ça bena djiguene meritowoul woudje

  • @ata2397
    @ata2397 Před měsícem

    Je peu?????😂

  • @mariannediop7753
    @mariannediop7753 Před měsícem

    Astou N’Baye tu exagères 😜

  • @user-qt4lt3gp9f
    @user-qt4lt3gp9f Před měsícem

    Astou mvaye ne soi pas égoïste na sa dieukeur âme fouleu rek mou diekh hana guemo sa bope ishhhh