🚹Serigne Ndiaye saga na wa lamb..Franc foum diar- Doud Sane, Lac 2 ,Ama Balde, Gora Sock sama dolei

SdĂ­let
VloĆŸit
  • čas pƙidĂĄn 11. 09. 2024
  • #lutte #etdrmedias #lamb
    👍 Merci de laisser un pouce bleu 👌
    Visiter Ă©galement notre site web: www.etdrmedias.com
    NOS réseaux sociaux :
    / etdrmedias
    / etdrmedias

Komentáƙe • 151

  • @mouhamedfall3783
    @mouhamedfall3783 Pƙed 23 dny +23

    Tournoi lagn wara def đŸ’„đŸ’„đŸ’„đŸ’„
    Serigne Ndiaye❀
    Doudou sanĂ©â€
    Gora sokh❀
    Zambala❀

  • @mbayeseye5712
    @mbayeseye5712 Pƙed 23 dny +11

    Serigne Ndiaye futur roi inchallahh

  • @mohamedmustaphadiouf8293
    @mohamedmustaphadiouf8293 Pƙed 23 dny +3

    Queens ak serigne Ndiaye

  • @alioudiop6125
    @alioudiop6125 Pƙed 23 dny +7

    Khana dou yadone wakh Franc waroul communiquer ni? Merde Ă  la fin tu viens de comprendre maintenant le tactique de Franc

  • @malickdiop4352
    @malickdiop4352 Pƙed 23 dny +7

    Le problĂšme de Fass c’est Gris Bordeaux 11 ans sans victoire et se rĂ©clamer tigre de Fass gni niom serign ndiaye wara beurel sakh nioko dane c’est un obstacle pr ses lieutenants

  • @khadimsamb1806
    @khadimsamb1806 Pƙed 23 dny +6

    Tournoi luc Nicola yi Tianga bokone zamballa moka dieul waye yaw champion nga nalla gayi dieul ❀❀ mĂ©dina diapalle la

    • @ndiobengom4422
      @ndiobengom4422 Pƙed 22 dny

      wakh ngua deug frr zambala mo dane ibou Senghor final

  • @benoitdiouf5632
    @benoitdiouf5632 Pƙed 23 dny +2

    Champion nga et je t'assure que tu seras un grand champion un jour

  • @KhalilDien-fe5uh
    @KhalilDien-fe5uh Pƙed 23 dny +5

    Boy Niang / Serigne Ndiaye
    Lac de Guier / Serigne Ndiaye
    Balla Gaye / Serigne Ndiaye
    Ama Balde / Serigne Ndiaye

  • @domousenegalinfo9563
    @domousenegalinfo9563 Pƙed 23 dny +6

    Serigne ndiaye amo supporter boul gnou sonal

  • @petitdiop451
    @petitdiop451 Pƙed 23 dny +2

    Serigne Ndiaye 2 roi des arĂšnes ou rien inchallah

  • @domousenegalinfo9563
    @domousenegalinfo9563 Pƙed 23 dny +5

    8victoire 2defaite beuri wakh lamb nekhna legui

    • @ZizouTik
      @ZizouTik Pƙed 23 dny

      Dagnou ko ragal motaf

  • @user-qs9ze2il2r
    @user-qs9ze2il2r Pƙed 21 dnem

    Dieuleul Zambala moo la eupp victoire gora sock mola eup victoire

  • @FallDamel7484
    @FallDamel7484 Pƙed 23 dny +4

    S.Ndiaye2 vs Valdo de pikine combat la wala Sokh

    • @KhalilDien-fe5uh
      @KhalilDien-fe5uh Pƙed 23 dny +1

      Non Djieuwrign ngua balma mais lolou dou combat ... Serigne ndiaye molenn eup compétition

  • @user-gb9mg8fi5v
    @user-gb9mg8fi5v Pƙed 22 dny

    Face awma fofou mbeur mes Serigne Ndiaye dafma nekh

  • @SneijderJunior
    @SneijderJunior Pƙed 23 dny +1

    Bahna rkk gneup ngi changer communication 😂😂 Franc avait tout compris😁😁

  • @assanediedhiou6758
    @assanediedhiou6758 Pƙed 23 dny +3

    Dagne ko wara dieule nak amena dolĂ© meuneu beurĂ© c’est pas mon lutteur mane balla Gaye rek

  • @badiafaye5314
    @badiafaye5314 Pƙed 23 dny +1

    Brome 8 damm 2 dĂ©fete ❀❀❀❀

  • @user-eo5gy7mk8l
    @user-eo5gy7mk8l Pƙed 23 dny +1

    SĂ©rigne Ndiaye Alioune sĂšye ou lac de guiĂšr

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 Pƙed 23 dny +2

    Serigne ndiaye yawe mom danga amout khorom nak đŸ€·đŸœâ€â™‚ïž safo lamb dara teksi amo supporte teksi ah 😌 nekho diapalĂ© nak khana yak sa thies khayna đŸ€·đŸœâ€â™‚ïž

  • @salioudiallo3412
    @salioudiallo3412 Pƙed 23 dny +1

    Serigne Ndiaye 2 alalou ndakarou roi ou rien inchallah

  • @benoitdiouf5632
    @benoitdiouf5632 Pƙed 23 dny +1

    Serigne Ndiaye séye ces le combat logique

  • @Babarmbaye-sc2ye
    @Babarmbaye-sc2ye Pƙed 23 dny

    ❀❀❀ya fi nek koula da loull dala ragall

  • @MouhamedMbaye-on1rl
    @MouhamedMbaye-on1rl Pƙed 23 dny +1

    Serigne ndiaye tour la am.rek defagofi dra

  • @user-qs9ze2il2r
    @user-qs9ze2il2r Pƙed 21 dnem

    BB Saloum nguafi daan yaw jacob Baldé sakh mola tané si bb saloum

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 Pƙed 22 dny +1

    Ki champion la dh walahi.. mais franchement dafa déssé.. danagoufi mbeur bou takh niouy wakh

  • @mamadouwade6565
    @mamadouwade6565 Pƙed 23 dny +1

    Pourquoi beugo dieul zambala ak gora sokh 😂

  • @user-id8ow5nq1g
    @user-id8ow5nq1g Pƙed 21 dnem

    Serigne Ndiaye 2 seul nak

  • @abiboudieng118
    @abiboudieng118 Pƙed 23 dny +2

    Sa waay yaw 8 victoire 2defaite nga Am😂di beurri wax

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 Pƙed 23 dny +1

    Serigne ndiaye vs lac 2 combat la. Khamna dounguene fesale stade đŸŸïž ndakhe seni fans bariwout ?

    • @papegaye4505
      @papegaye4505 Pƙed 23 dny

      Sa waye 1er combat tapha tine vs bombardier stade bi fessoul wone

  • @salioudiallo3412
    @salioudiallo3412 Pƙed 23 dny

    Le grand champion na gayi dieul avanc bi bokk

  • @TigreGueye
    @TigreGueye Pƙed 23 dny +2

    Zacop mo dane bb saloum te dieulna thiatou yof yow nga dane bb saloum te dodieul zambala wl doudou sane

  • @user-bb7ph3wz2f
    @user-bb7ph3wz2f Pƙed 23 dny +1

    Beuré len si sen bir Serigne Ndiaye sambala doudou sané goreu sok mam Balla top5.

    • @Deggou
      @Deggou Pƙed 23 dny +1

      Blindé, ibou ndiaye obeuli ect...

  • @Cheriflaye1995
    @Cheriflaye1995 Pƙed 23 dny +2

    Zambala Mola Dane ragalale yalla

  • @mbayeseye5712
    @mbayeseye5712 Pƙed 23 dny +1

    Serigne Ndiaye 2 Lac 2 comba leu

  • @masseseck9475
    @masseseck9475 Pƙed 23 dny +1

    Eumeu tapetela defean la😂

  • @alassanendong9610
    @alassanendong9610 Pƙed 23 dny +1

    Ya meune niep bilay walae je suis Coriace
    Serigne Ndiaye kessé

  • @theodoresarrtheodoresarr8844

    Champion lutte simple nga mbeur mais lutte avec frappe defago fi dara Doudou sané mola raw
    Lutte simple ak lutte avec frappe c pas la mĂȘme.
    Serigne niit dengay geum yalla Doudou sané sen combat boubou à dk arbitre yi dengnla diapalé yeup khamnagnko

  • @MouhamdLoum
    @MouhamdLoum Pƙed 23 dny +1

    Ya meune Doul fo danĂ© doudou sanĂ© 11😂

  • @joe6326
    @joe6326 Pƙed 23 dny +1

    Serigne chĂ©rooo sa cachet d’à toutii yak doudou sane yeneuu yam sen cachet bakhoulll

  • @lesankariste8721
    @lesankariste8721 Pƙed 23 dny +2

    Serigne Ndiaye vs valdo

  • @madembatoure7005
    @madembatoure7005 Pƙed 23 dny +18

    Yow defago dara si lamb bb saloum gua moudiei dane tai Jacob balde sah danenako yagoul dara vip bala nioulay dieul dieul gris 2

    • @ISmile__
      @ISmile__ Pƙed 23 dny +4

      Xamo Lamb yaw Serigne Ndiaye est sur 5 victoires successives , Jacob Balde n‘a mm pas 3 victoires successives et il lutte depuis 2013
 SN2 si on lui donne sa chance il va montrer son talent
 BG2 a affronter Tapha GuĂ©ye a 21 ans lagnoko may chance

    • @MawaFaye-p9y
      @MawaFaye-p9y Pƙed 23 dny

      Khamo lamb kii masoul berrĂ© ak bb saloum😊

    • @ISmile__
      @ISmile__ Pƙed 23 dny

      @@MawaFaye-p9y siii beurré na ak mom son dernier combat

    • @SambaDiawaraSarr
      @SambaDiawaraSarr Pƙed 23 dny +1

      Khamo lamb ki bann poid léger lay Beurél bou beuré woul ak poid lourd yii

    • @kenzykindkeinde38
      @kenzykindkeinde38 Pƙed 23 dny +1

      Bb saloum moo nangou beurei ak mom motakh mais kou dane eumeu junior waroul wone sakh beurei ak bb saloum

  • @truckwarriors9832
    @truckwarriors9832 Pƙed 22 dny

    Kouko djeul danou, lamb moytouwanter bi dafa beuri, Serigne Ndiaye nako guy yi dieul

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 Pƙed 23 dny

    Coriace trÚs bien encadré machalah

  • @AliaDiagne-t4z
    @AliaDiagne-t4z Pƙed 23 dny

    Qui champion leu wiri wiri diari ndari médina moye sunu mbeur

  • @santosmansal3020
    @santosmansal3020 Pƙed 23 dny

    Merci Serigne .lamb nila communication bou tangue pour niou bayi la khel. Yeufou Gaindé la

  • @user-qs9ze2il2r
    @user-qs9ze2il2r Pƙed 21 dnem

    BB Saloum rék nguafi daan dieulal obeuli bou parcelle

  • @antoinepamamarone7712
    @antoinepamamarone7712 Pƙed 23 dny

    Dielal Ordinateur!! champions nga mais 2 defaites nga am dhé

  • @alffaye3000
    @alffaye3000 Pƙed 23 dny

    Serine Ndiaye Jacob Balde

  • @ISmile__
    @ISmile__ Pƙed 23 dny

    Moi j‘ai regardĂ© Modlo vs less 2 , Papa sow vs Santang et le stade n‘est pas plein
 de mĂȘme que BG2 vs Coly faye aussi 
 et ça qu’on reproche SN2

  • @abdoulatifdiop5640
    @abdoulatifdiop5640 Pƙed 23 dny

    Wax n'a dĂ©gueu dĂ©h Jacob DAan bb Saloum niou diokh ko thiathou Yoff ta mo eupou combat Jacob😱 lim wax si franc moy dĂ©gueuđŸŽ‰â€

  • @SOWTV-mf7hz
    @SOWTV-mf7hz Pƙed 22 dny

    ioe si lutte avec frappe défago fi dara

  • @user-qs9ze2il2r
    @user-qs9ze2il2r Pƙed 21 dnem

    Danguay doul ama baldé franc késsé la wakh nguay mélni monguool nii

  • @matarthiam2284
    @matarthiam2284 Pƙed 23 dny

    Serigne ndiaye bi dafa decide

  • @babacargueye2960
    @babacargueye2960 Pƙed 23 dny

    Quench vs serigne ndiaye

  • @dembagadio3325
    @dembagadio3325 Pƙed 23 dny +1

    Tapha gueye boumou maye balla gaye ai lac mo guinone soh la nak pasque c'est pour ame l'argent c'est la fin pour lui 😅😅😅😅😂😂

  • @mouhacoly8120
    @mouhacoly8120 Pƙed 23 dny +3

    Ioe beugo beurer ak doudou sane beugo beurĂ© ak zambala ganei gars niolay daw en plus 9 victoires ga ameu no l’amb Nekh na daneu rek bĂ©bĂ© saloum beurei ak lac 2

    • @BocarAnne-g7d
      @BocarAnne-g7d Pƙed 23 dny +1

      Bilay ki da nekh rék xamoul ni palmarÚs aussi ça compte

    • @papegueye4200
      @papegueye4200 Pƙed 22 dny

      Du legui deh

  • @user-qs9ze2il2r
    @user-qs9ze2il2r Pƙed 21 dnem

    Bb saloum dongue nguafi daan

  • @assanediop771
    @assanediop771 Pƙed 19 dny

    Serigne ndiaye2 oh defal ndank yaw danofi kenne yaw dano franc dano zambala nane champion nga

  • @princetorodo8590
    @princetorodo8590 Pƙed 23 dny

    Vraiment serigne ndiaye pour ioe champion nga en plus daga beuri wakh the defo fi sarape ndayam nopil touti dem beure ak say morom ngay doulll ni

  • @afro3827
    @afro3827 Pƙed 23 dny +1

    Serigne ndiaye zambala mola dane ak franc 😂😂

  • @FrancoisFaye-xl8uy
    @FrancoisFaye-xl8uy Pƙed 23 dny +1

    Serigne Ndiaye deye doule 7 fois gua dane doudou sané té amna yokhamné par point guako guéné bayule fene oupleo doudou ay victoire arene bébé saloum gua moudié dane nopil

    • @noreyni5597
      @noreyni5597 Pƙed 23 dny

      Sawayy khana yow Gambie nga sétané lamb eupouna 7 fois

    • @chamousman2726
      @chamousman2726 Pƙed 23 dny

      ​@@noreyni5597😂😂😂 boy bul NYU fohonto nyun waa Gambia

  • @kenzykindkeinde38
    @kenzykindkeinde38 Pƙed 22 dny

    CLAF: S.Ndiaye 2 - GORA SOCK - Aliou Seye 2 - Doud'sané

  • @mouhamedseck1984
    @mouhamedseck1984 Pƙed 21 dnem

    Et fassr je nai pas compris la hiérarchie mais aprÚs gris bordeaux qui suit forza gris 2 avec la blessure de lac rose Serigne ndiaye a monté mais serigne warul beuret ak ex lac ou eumeu bayi fi gris 2

  • @FS-jh4ky
    @FS-jh4ky Pƙed 23 dny

    Saway dieulal zambala amo mbolo beuri wo victoire

  • @mamadouthiam663
    @mamadouthiam663 Pƙed 23 dny

    da nga wara beuré guayi mounou nioula

  • @user-qs9ze2il2r
    @user-qs9ze2il2r Pƙed 21 dnem

    Amoo PalmarĂšs 6 victoires dongue ngua am

  • @sambadieng1203
    @sambadieng1203 Pƙed 23 dny +1

    Serigne Ndiaye bougnou yap mbapat ak arĂ©ne dou bĂ©ne dieul doudou sanĂ© rek wala zambala tapĂ©tgua youne setanĂ©la founek reug reug moye sĂ©ne baye niata yione lala dane😂😂

  • @user-pd4oz3ht6r
    @user-pd4oz3ht6r Pƙed 23 dny

    TrĂšs bien il faut ngay tangal niou bayi la khel

  • @mbayeseye5712
    @mbayeseye5712 Pƙed 23 dny +1

    Serigne Ndiaye 2 alioune seye 2

  • @mamadouwade6565
    @mamadouwade6565 Pƙed 23 dny

    Defago dara thi lamb boulniou sonal

  • @georgesdieganediouf2684
    @georgesdieganediouf2684 Pƙed 23 dny +1

    Serigne Ndiaye 2 doudou sané ou zambala gnoye Say adversaire.

    • @Ghost-bl1lb
      @Ghost-bl1lb Pƙed 23 dny

      Doudou Sané?
      Mom xana bougoul avancer?

    • @bilalkhalyfall9938
      @bilalkhalyfall9938 Pƙed 23 dny

      @@Ghost-bl1lbyaw doudou SanĂš faneu leu rawĂš Serigne ndiaye yĂšn doudou SanĂš claf bi motakh gnou beuri khamko mounoul raw Serigne Ndiaye dh

  • @mbeganesarr785
    @mbeganesarr785 Pƙed 23 dny

    Zambala delĂ  dane demal jeli. Sa revanche

  • @TigreGueye
    @TigreGueye Pƙed 23 dny +1

    Serigne nd tu deux defaite guemal yalla

  • @mansourdiack1289
    @mansourdiack1289 Pƙed 21 dnem

    😂😂Serigne comĂ©dien ngua franchement 8victoire 2 dĂ©faite champion en devenir Nga mais ñi nguay yotou douniou sa Morom si Dara Demal beurĂ© ak doudou sanĂ© wala Gora sock danagofi Keneu kouniouy tiow

  • @user-bb7ph3wz2f
    @user-bb7ph3wz2f Pƙed 23 dny +1

    8 ndam.2defet😂

  • @mouhamedseck1984
    @mouhamedseck1984 Pƙed 21 dnem

    Champions gua wayé prouvé bi desna xana domou dangou ak quench

  • @abdoulayeniang1301
    @abdoulayeniang1301 Pƙed 23 dny

    MĂŽme ak Diaz. Combat laaaa

  • @mbeganesarr785
    @mbeganesarr785 Pƙed 23 dny

    Bébé saloum rek nga fi dane beug nek vip par force

  • @minkabarhamasarr2117
    @minkabarhamasarr2117 Pƙed 23 dny

    Kii mom dafa beurii wakh té défoul dara si lamb

  • @abdoumaguettegueye5299
    @abdoumaguettegueye5299 Pƙed 23 dny

    Dieulell zambala comba le ds

  • @Deggou
    @Deggou Pƙed 23 dny

    BlindĂ©, zambala,doudou, gora sock, tyson2 ect..nioniou nioy saay adversaire defagofi dara pour beurĂ© sicaw....😅

  • @domousenegalinfo9563
    @domousenegalinfo9563 Pƙed 23 dny +1

    Yaw bebe saloum kassé ngafi dane teh leroul

  • @misterzappa9073
    @misterzappa9073 Pƙed 23 dny

    Khadim Ndiaye avait ce mĂȘme problĂšme YĂ©kini avait ce mĂȘme problĂšme heureusement qu’il Ă©tait rois des arĂšnes raison pour laquelle il luttait une fois par an S Ndiaye 2 lutter contre lui tu as peu de chance de le battre

  • @ousmanebousso4551
    @ousmanebousso4551 Pƙed 23 dny

    Il communique bien dafa degou niakk kignane

  • @manebaye4021
    @manebaye4021 Pƙed 23 dny

    Alioune seye2 vs Serigne Ndiaye combat bou néx la
    Goora sock mÎme tapéte la
    Faynaniouco 10million pour mou beurré ak zambala mou bagne

  • @kingseros8721
    @kingseros8721 Pƙed 23 dny

    mi houli beutte yi mél ni kou doff

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 Pƙed 23 dny

    Woutal bay re

  • @serignetoubagueye4067
    @serignetoubagueye4067 Pƙed 23 dny

    Mane dall beugg na mbeur bou mel ni yaw

  • @user-qi9vg6il1r
    @user-qi9vg6il1r Pƙed 23 dny

    Gora sock safoul laamb..gnak horom

  • @princetorodo8590
    @princetorodo8590 Pƙed 23 dny

    Yafi takha wne di dĂ©fendre eumeu sene si franc yagi ni di wakh ak wakh bou metti 😂eumeu sene comme degenko khamoul mn gina kat ndayam

  • @lhomme_fort
    @lhomme_fort Pƙed 23 dny +1

    Serigne ioe khamo ça bop ioe ak Zambala combat la dh

  • @assanesamba8560
    @assanesamba8560 Pƙed 22 dny

    Yaw rek y’a ame mĂ©rite pour beurĂ© akh makk gni champion nga est t’as fait tes preuves eumeu kou bakh laa nalla dieul waay mayla chance diadou na

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 Pƙed 23 dny

    Gayii nieme wonko

  • @mamourbabou3385
    @mamourbabou3385 Pƙed 23 dny

    Yak doudou sane moy comba mounoko daw

  • @BocarAnne-g7d
    @BocarAnne-g7d Pƙed 23 dny +1

    Serigne Ndiaye togal yow Lac beurĂ© ak gnila geuneu heuss nga nane ragal la ahhhh eupeuna meunna rassou dacorna 😂

  • @BofMaty
    @BofMaty Pƙed 22 dny

    Le blēme est que sĂ©nĂ©galais mo sokhor. Ga yii danio uy moytou, affaire bii lol oula. En plus promoteur yii daffsii ame aye salaupard,

  • @soukadiouf9437
    @soukadiouf9437 Pƙed 23 dny

    Boulén saboté serigne ndiaye champion la deh amna 8 combat 2 defaite 2 defaitam yi gniko dane mane nagne dane kou neh zambala ak franc serigne amna dolé ta da meune beuré bouko vip yi mayone sens kn mou diékhal lén

  • @mansourmbaye6926
    @mansourmbaye6926 Pƙed 23 dny

    Yaw mbeur bo lathie yone la say morom nga ñieukeu lathie ñiou bagn nga lathie say maak ses normal diambar nga

  • @lixman771
    @lixman771 Pƙed 23 dny

    C’est pas pour lui jeter des fleurs mais serigne n’diaye mo len meune niom nieup🙄🙄sou douguĂ© vip rek nguene am problem 🙄🙄lam lay wakh dĂ©đŸ™„

  • @Tawfeekh
    @Tawfeekh Pƙed 23 dny

    Boy yaw vraiment sa palmarÚs bii dafa khiibone, palmarÚs kolokolo nga ame. Liguay wakh kÚne khamouko, mënoo sakh wakhe took fii di ngande ngandalou. Bébé Saloum mii nga khamni poussoul paassoul nga fii daane, té guëthe na daane mbeur.