Vilipandé par Gouy Gui sur sa relation avec Soumboulou, Diop Khas très en colère détruit « Bimay tak

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 24. 06. 2024

Komentáře • 220

  • @People221sn
    @People221sn  Před 4 dny +28

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
    Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
    Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
    +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL

  • @AissatouSarr-wu8qx
    @AissatouSarr-wu8qx Před 3 dny +69

    Diop khass un homme respectueux yalla nala sunu borom mayy diam

  • @2quevosquevos242
    @2quevosquevos242 Před 3 dny +14

    Senegal surtou mbeur danio diapp serigne defko yallah soubhanallah khass yoroul ndam yallah moh yor Ndam

  • @NdiayeAby-yp5ht
    @NdiayeAby-yp5ht Před 4 dny +37

    Tu est vraiment gentil khamnako si yaw

  • @babacarbalde492
    @babacarbalde492 Před 4 dny +55

    grand man koula sopou la c'est que je vous conseille moy gua moy mbeur yii

  • @joe6326
    @joe6326 Před 3 dny +33

    Gouyguii vrai diAmbar ma litakh ma beugeu ko moy da passe yeuw dakar dekeu si barake di dawall carapide dawal taxi dougou si lamb di rayante sa vie en gouyguii yalla nala yalla defall ndame

  • @user-ub7bz2le1c
    @user-ub7bz2le1c Před 3 dny +8

    Diop khass mome machallah nite kou teye,la🎉🎉🎉❤❤❤❤❤

  • @marieeliseloume5422
    @marieeliseloume5422 Před 3 dny +24

    Hé boulen niou sonale gouy gui wakhoul lou nianw lane motakh guene beugue ay diakhasse lolou bakhoule. Wassalam

  • @sml6264
    @sml6264 Před 4 dny +69

    Gouy gui 95 yaw tamit je te croyais un fédérateur mais pas un "rembadj" ça c du "rembadj"

    • @adamandiaye4314
      @adamandiaye4314 Před 3 dny +9

      Gouyegui da dioume Diop khasse nite kou bakhela wayé adouna amoule solo machalla louye yonou souboulou si Labe

    • @CheikhDione-kx7po
      @CheikhDione-kx7po Před 3 dny +4

      Niom niépa yam nio Yakh Sénégal 😢

    • @Blackidriss
      @Blackidriss Před 3 dny

      Sur youtube ya pas de bon citoyen il cherche l'argent

    • @mauricecorrea3399
      @mauricecorrea3399 Před 3 dny

      Vraiment

    • @amyndao9028
      @amyndao9028 Před 3 hodinami

      Site yi nio reubeudié Sénégal ta ken diangou thi journalisme

  • @batorasecurite9898
    @batorasecurite9898 Před 3 dny +10

    Y'a des choses qu'on doit pas dire à la scène de télévision 📺

  • @adamandiaye4314
    @adamandiaye4314 Před 3 dny +3

    Gouyegui vraiment doyenawar louye probalémebie Souboulou machalla yoname nékoule si labe Diop khasse machalla amenasolo Dieureudieuf ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ gouyegui nite nité vraiment tamite moyetoule dougue si Privé diabour ❤❤❤❤ gnawena loleeeeeee Dieureudieuf khassse machalla ❤❤❤❤❤❤

  • @juliennengom-rc6it
    @juliennengom-rc6it Před 3 dny +9

    Ce que Gouy gui a dit c'est pas grave.journaliste yi bayilen diakhasé

  • @ModouFall-jn9bz
    @ModouFall-jn9bz Před 4 dny +28

    Serigne bi boul tontou doff yoyou yako eupeu valeurs foufou sakh

  • @ismailaka2192
    @ismailaka2192 Před 3 dny

    Machalla
    Rawal❤

  • @Mor-gh1cm
    @Mor-gh1cm Před 4 dny +26

    Gouy gui dafa bary wakh 😅😅

  • @serignediop3137
    @serignediop3137 Před 3 dny +5

    Lima diakhal moy déglou na ki gouy gui wakh mais guissou massi lou graw seulment dagn ko grawal rek

  • @babadiagne1840
    @babadiagne1840 Před 3 dny

    Merci beaucoup

  • @jimane80animateur33
    @jimane80animateur33 Před 4 dny +23

    Gouye Gui Il parle trop tout le temps il accuse des gens vraiment il est temps qu'il change

    • @user-nt3dj7vz2r
      @user-nt3dj7vz2r Před 3 dny +5

      Gouy gui n’as rien dit de grave pourtant il n’as accusé personne toi t’as même pas entendu loumou wakh et tu veux le juger

  • @CheikhDiop-mp2et
    @CheikhDiop-mp2et Před 3 dny +6

    Diop khass yaw dagua bakh sa khol toujours molay togne niome nieupeu gua diapalé

  • @AlbD9544
    @AlbD9544 Před 3 dny +6

    Mais gouy gui wakhoul lou graw

  • @FallouGueye-mv5fs
    @FallouGueye-mv5fs Před 3 dny +6

    Diop khass sama serigne bi y’a bakh ko sekal defal guako teranga

  • @papeomar8530
    @papeomar8530 Před 3 dny +1

    Gouye gui 95 vraiment seytané nga

  • @DembaFall-rd8lx
    @DembaFall-rd8lx Před 3 dny +7

    Gouy gui demal gua préparer sa lamb mo geune diop khass dousa morom tegua bayi soss bi

  • @bassiroundiaye3913
    @bassiroundiaye3913 Před 3 dny +3

    Mai gouye gui journaliste bi mokoné Diop khass da adeu AK Ada fass thi comba bi mounéko bouko nékh dadi wakh séni diar diarigne mai Diop khass nigay wakhé Ada fass ga farale

  • @lakhatthiam6044
    @lakhatthiam6044 Před 3 dny +4

    Amine inchallah 🤲🏼 🤲🏼

  • @user-oh5vs6bj1q
    @user-oh5vs6bj1q Před dnem

    Ndiop vie ta vie continue ton chemin et évite certains gens ta femme est une femme exemplaire je te connais pas mais kou bakh gue

  • @mansourkane1426
    @mansourkane1426 Před 3 dny +4

    Khass mi daye ték khéle 😂

  • @abdoulamadouba-qu6xk
    @abdoulamadouba-qu6xk Před 4 dny +12

    Gouygui woyoul xelmi dessna Lou barri kou bakh😊

    • @user-fx9qu7qw9v
      @user-fx9qu7qw9v Před 3 dny

      Khélbi nakhariwouldé.daniowara.bayui.wakh😢😢😢

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 Před 3 dny +4

    Gouye gui wakhoul lou ay nak segn bi .. lou rafete la wakh

  • @ModouFall-jn9bz
    @ModouFall-jn9bz Před 4 dny +10

    Diop khass diapaléna kounek si lamb j

  • @malickndiaye4880
    @malickndiaye4880 Před 4 dny +5

    Gouy gui pour mom Lamb dji galadhieu la da dém ba moudié tapét dakh lolou

  • @user-ou2kx2ys8g
    @user-ou2kx2ys8g Před 4 dny +4

    Gouye gui. Wérou koi😮😢

  • @user-fx9qu7qw9v
    @user-fx9qu7qw9v Před 3 dny

    Khass moy toule Lénn rék ❤❤🙏

  • @Elhadji2187
    @Elhadji2187 Před 3 dny +1

    Gouy gui 95 di guor djiguene li yeufou djiguene la

  • @user-zl9hs4hd1n
    @user-zl9hs4hd1n Před dnem +2

    Da goune. Gougi. Da goune

  • @senegalrek6630
    @senegalrek6630 Před 11 hodinami +1

    Diop khass koule Beug la guiss la rek la Beug mais je ne suis pas content danga wara moy tou mbeur yi lignou lay dégue si histoires yi dafa beuri trop 😢 bakh bou Eupneu bakhoul

  • @user-og3bw2bn4l
    @user-og3bw2bn4l Před 2 dny

    Bravo

  • @yatmaniang6847
    @yatmaniang6847 Před 3 dny

    Journaliste bi vrai saytané la

  • @jadimproplayer5229
    @jadimproplayer5229 Před 3 dny +4

    Khass daurekate bou mague nga truhant nga mais un jour tu regrettera alal bou lewoul bi ngay diokh sa ndiabote si nga dioye derette niemei yalla nga def

    • @DBba.
      @DBba. Před 3 dny +1

      Vraiment

  • @lilbruh9081
    @lilbruh9081 Před 3 dny +14

    Gouy gui détails moko nara danel si lamb djii

  • @elmalicksindidi5785
    @elmalicksindidi5785 Před 3 dny +2

    Loutah nga deukk guediaway ba paaré naan dangay neutre k le meilleur gagne ragal fété day xagné woursëk

  • @CheikhDiop-mp2et
    @CheikhDiop-mp2et Před 3 dny +7

    Mbeur dou beuri wakh Gouy gui amo beneu foula

  • @actufootball221
    @actufootball221 Před 4 dny +5

    Gouye gui key dafa dioumme

  • @abouba3509
    @abouba3509 Před 4 dny +13

    Gouygui dioum nga dh

  • @user-cm8yz4gx5t
    @user-cm8yz4gx5t Před 3 dny +1

  • @user-pl5mw6ml7x
    @user-pl5mw6ml7x Před 3 dny +1

    Ndeyssane niom niaar niépa baakh xaw ma lou waral lii

  • @chebougambiagambia6511

    Kharange lo aka dinge❤

  • @alhamdoulilah9154
    @alhamdoulilah9154 Před 3 dny

    Thiey Modou lo Aka digne ❤❤

  • @tallambengue-oc4cd
    @tallambengue-oc4cd Před 3 dny +1

    Gouygui dafa doff dh Ada dalay dane force

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo9171 Před 28 minutami

    Serigne bi danga wara moytou presse. Beug beuz diarouko.

  • @gazza873
    @gazza873 Před 3 dny

    Man leen diakhalnama pourquoi on aimer toujours di dougou si vie privee bouniou ame probleme gouy gui la question etai facile guay dougou si vie privee diambour yii

  • @IbrahimaSeck-md6sh
    @IbrahimaSeck-md6sh Před 3 dny +1

    Gouy gui nieuwal khass diapaléla mo geune sa wakh yi khass meune nala dieundeu yaw sen wa keur yeupeu

  • @AissatouSarr-wu8qx
    @AissatouSarr-wu8qx Před 3 dny +6

    Gouy gui dagua wara concentré wo sisa lamb dji mo geune wakh bou beuri bi diop khass dousa morom

  • @MasseneDieye-op9fq
    @MasseneDieye-op9fq Před 3 dny +1

    Guouygui dafa dioum si communication waroul won wakh ak kenen koudoul ada fasse

  • @senewayetv2062
    @senewayetv2062 Před 3 dny

    Khasse diapousi rék ga bagna ngianale kéneu ❤

  • @BaraNdiaye-jm9uo
    @BaraNdiaye-jm9uo Před 3 dny +1

    Vous etes pas sérieux mbeur bou khèw ngéni bagna guiss
    Milieu lamb Milieu hypocrite

  • @IbrahimaSeck-md6sh
    @IbrahimaSeck-md6sh Před 3 dny +4

    Gouy gui pression lamb dji moko diapeu diegualko serigne bi

  • @ousseynoudiouck6053
    @ousseynoudiouck6053 Před 3 dny +3

    Sounou khalis darou salam

  • @modoutinemodoutine9158
    @modoutinemodoutine9158 Před 4 dny +3

    Sama mbeur la mais il est fou malade

  • @user-fv3dp2tl8z
    @user-fv3dp2tl8z Před 3 dny +1

    Boule ko tontou khass yawwe ndeysane nitou kesse ga khamoumala mai machala

  • @adamadiouf2769
    @adamadiouf2769 Před 4 dny +5

    Gouille gui rekk😂😂😂😂

  • @assanesylla4136
    @assanesylla4136 Před 2 dny

    Khass yiow fédérateur gua boul meusseu deglou détails yi . Guouy gui sa frère yallene fare.

  • @ModouFall-jn9bz
    @ModouFall-jn9bz Před 4 dny +4

    Gouye gui dafla khamoul motakh yaw yalla dafla teral sokhlawo khalisou nekeu

  • @omargaye3601
    @omargaye3601 Před 3 dny

    😊😊😊gouy gui dafa kon😊😊😊😊 gemoul yalla

  • @user-uz2pt3qd9k
    @user-uz2pt3qd9k Před 3 dny +1

    Khass khamol dará baye diapou li Ada fass khamou toss

  • @TafaloSaMb-sq3on
    @TafaloSaMb-sq3on Před dnem

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Domou_Deukk_Bi
    @Domou_Deukk_Bi Před 3 dny +1

    Gouy gui sama mbeur leu mais yéwou woull

  • @PastefTV746
    @PastefTV746 Před 4 dny +8

    Gouygui doff la deugg la Wayè limm Wahh Deugg la amoull lenen . KILIFA dou tontou

    • @ronebodjis4607
      @ronebodjis4607 Před 3 dny +1

      Pasteftv ab télé dou diengue kilifeu souniou ko toumalé dou gueneu setal bopam cas même

    • @PastefTV746
      @PastefTV746 Před 3 dny

      @@ronebodjis4607kenn toumaalouko . Gouygui deugg La wah tèdou fenn. Fenkat bi gni ham hamnagn Ko

  • @zulnhofaye2584
    @zulnhofaye2584 Před 2 dny

    Inchallah Gouy gui dafay d'âne ada fass

  • @user-qs8dk6vc7h
    @user-qs8dk6vc7h Před 3 dny

    Gouyegui dioume na mes journaliste tamite lesp niome la mes khasse d'espace ly klifagna

  • @damesamb6296
    @damesamb6296 Před 3 dny

    Bilaye bounguen moyouwoul journaliste yi ...

  • @SeynabouNiane-pw5nu
    @SeynabouNiane-pw5nu Před 3 dny

    Abdoulaye diop khass goro soumboulou ya bakh ❤❤❤

  • @user-kf7oi4q
    @user-kf7oi4q Před 3 dny +2

    Dangako dekk micro mou gnou khoulo saytane ngenn domeram yii boulen kenn jakhase

  • @hadyagne9473
    @hadyagne9473 Před 3 dny +3

    Saway yaw ya beugeu woné wou bayil mbeur yi sof nga

  • @binetadiao5718
    @binetadiao5718 Před 4 dny +1

    Gouy gui da nélaw deug amna yo xamni ay détails la kamm aduna amoul solo vraiment...

  • @bilalfall2953
    @bilalfall2953 Před 3 dny

    A vrai dire problème amateurs yi nék si sites internet yi nio waral nio lay talal micro nga wakh si nit nga dém si koku niko diw wakh na si yaw nangam séytané yi dan tass keur yi nio yor micro yi

  • @user-sd8bg8cf6d
    @user-sd8bg8cf6d Před 3 dny

    Baaye ngagne bigay wah moladoon diarigne

  • @ModouFall-jn9bz
    @ModouFall-jn9bz Před 4 dny +2

    Gouye gui dafa sofff legui 😂😂😂😂

  • @ModouFall-jn9bz
    @ModouFall-jn9bz Před 4 dny +6

    Gouy gui aye défaite you beuri moko sonal ndakh khol bi mo nekhoul😂😂😂😂

  • @astoukante4204
    @astoukante4204 Před 3 dny

    Sénégal chaque heure AK cas bou bésss😂

  • @alimasamb123
    @alimasamb123 Před 3 dny

    Khasse ne répond pas a gouye gui est ce que ça va

  • @matardieng-cr9xs
    @matardieng-cr9xs Před 3 dny

    Gouy gui loumou wakh Mo bangay tak soumboulou mom nga ladj nakh soumboulou nit kou bakh la

  • @ibndiop465
    @ibndiop465 Před 3 dny

    Gouy gui wayoul a 100% . Amna mbeur yu wéroul ossi folene fek gnungi djign ay niit

  • @diakhatefatiss4162
    @diakhatefatiss4162 Před 3 dny +3

    Khas Gouy Gui dafa dioum balko tanga diapaleko tai yalla rek takh

  • @damengom3175
    @damengom3175 Před 3 dny

    Goor dou rambaj no c’est honteux pour certains journalistes 😢

  • @falloufall2320
    @falloufall2320 Před 3 dny

    Diop khas gouygui momine la yalla topéwuko dara da dioum rek

  • @CheikhDione-kx7po
    @CheikhDione-kx7po Před 3 dny

    Ragaal Mystique Moko tardel si Lamb dji 😏

  • @fatimandao8359
    @fatimandao8359 Před 3 dny +1

    Diop vraiment waro wone tontou gni sa personnalité dépassé na li

  • @BK18465
    @BK18465 Před 3 dny +4

    Virement journaliste sénégalais yii aye saytané lagn nioyy wakh fii wakh féé dsl

  • @DjibSone-kv4pu
    @DjibSone-kv4pu Před 2 dny

    Non khass amoul problème bilaye gouy gui kaye da khawa dioume

  • @elhadjimaodoniang5531
    @elhadjimaodoniang5531 Před 3 dny +2

    Doul rek nga meun 🎉🎉

    • @ronebodjis4607
      @ronebodjis4607 Před 3 dny

      Lou diar saga serigne defal sa analyse avec respect rek mon frère mangui lay nianal diam

  • @moussadiop6111
    @moussadiop6111 Před 3 dny +1

    Mande khamou malla me khame n'a nioye dimbeuli

  • @abdoutoure2490
    @abdoutoure2490 Před 2 dny

    Beur mo Bari ay detaille

  • @ivanbocoum7367
    @ivanbocoum7367 Před 4 dny +3

    gouy gui loumou wahh

  • @dembambaye154
    @dembambaye154 Před 3 dny

    Sarakhou pobar 150000mill metina Gouy gui😂

  • @elisabethdiallobalde2129

    Khasse kéne dégoula si Dara kou am personalité yak sa sokhena soumboulou

  • @cheikhgaye2948
    @cheikhgaye2948 Před 3 dny

    Niom niar nieuppeuy dieufeundiko njabar donc.... ken tanéwoul moromam

  • @goradieye1667
    @goradieye1667 Před 3 dny +1

    Khass balko kheleme mo fo tolle

  • @yahyagassama491
    @yahyagassama491 Před 3 dny +4

    Diop xass boy bou xew lay bania guiss

  • @papefall4806
    @papefall4806 Před 2 hodinami

    Gouye gui mo sof meuna SOSs ,Lolou rek mo takh nexouma sa combat loussi diar toud seuyou diambour si sa point de presse Bo naré danou rek di créer ak doul pour bougn la dané guani dagn la diay