Deal bi claté na :Ahmed Cissé wakhatina (Zeyna teude na wayé amoul
Viviane ak Bouba Dioy, démentie d

SdĂ­let
VloĆŸit
  • čas pƙidĂĄn 10. 07. 2024
  • Urgent🛑Mamy Samb craquĂ© et fond en larme- Nabou Dash lĂąche une b0mbe sur- Viviane fiĂšre de Zeyna et

Komentáƙe • 40

  • @user-mh6kb7wo9d
    @user-mh6kb7wo9d Pƙed 22 dny +11

    Mariageou Zeyna bi kou si wakh safane da ngua Sokhor

  • @AstelDioum-qi9gy
    @AstelDioum-qi9gy Pƙed 22 dny +14

    Bilay SĂ©nĂ©galais yi dano sokhore nite guiou bakhe dou sosal nawelĂ© gui yalla tĂ©ranago guĂ© doufou amĂ© poure lane amena naw amoul nawe lane mosicĂ©n yone doule wayĂ©đŸ˜ź

  • @HaddyJallow-f3z
    @HaddyJallow-f3z Pƙed 22 dny +13

    Yenn douguene bayi teude domi jambour bi te harr sen domi haaaaaa

  • @diomagirard5899
    @diomagirard5899 Pƙed 22 dny +2

    Svp la discrĂ©tion absolue fait partie de la noblesse elle a pas besoin d'ĂȘtre dĂ©shabiller sur tout est n'importe quelle Ă©crans protĂ©gez la comme votre sƓur ou votre enfant svp

  • @adjadiouf4400
    @adjadiouf4400 Pƙed 22 dny +4

    Yow Ameth cisse fen rek gua meune wakh gua ba sone falé wougne la doniou dimbalé sokhor gua trop

  • @ZahraD3163
    @ZahraD3163 Pƙed 21 dnem +3

    Yen daal topato leen seen ndaw ak bou seen soeur yiii té niane seen doom yi tog seen pinkou ba deeg alkaïri...
    Jusqu'à present keen ci khew bi wakhoul ni Zeyna a consommer... yeen yeena interpréter.
    Rousse leen di wakh lou niaw ci khalé bou touti

  • @diengfama294
    @diengfama294 Pƙed 22 dny +4

    Chroniqueur bi khamoul dara 2eyna teudeugoul sakh ❀❀❀❀❀❀

  • @juliadiop1583
    @juliadiop1583 Pƙed 22 dny +6

    Khanaa amolenee bĂ©nĂ©ne sujet de discussion 😼kii kheww naa lou meussoul ame yayamm dieul aye tĂ©rangame yĂ©ne nguĂ©n topp sii rekk di wahhh

  • @oulygueye9647
    @oulygueye9647 Pƙed 22 dny +4

    C’est trop mane dama sakh rousse sonal Nanou famille bi trop si c’était votre famille ça n’allait pas vous plaire amlĂ©ne yeurmandĂ© ki khalĂ©la tĂ© yaye yopa sone ci sĂ©ne diabote chercher d’autre thĂšme de discussion svp

  • @Mameganiladiagne5270
    @Mameganiladiagne5270 Pƙed 22 dny +2

    Salam wadji Di torokhale jiggen rek amoule bene soutoura thi nite te site yi gnokoye dolele c'est dommage pour notre pays soutoura domou Adama kouko khawi yalla dioula satane wassalame

  • @MatyDiop-zg9sc
    @MatyDiop-zg9sc Pƙed 22 dny +3

    Yabiléne domi diambour mandouléne bougnou défone li islam sanetané kéne dou siwal béne jiguéne bou diekeurame di soga teudé yéne gnépe dici waxe ci lou arame nguéne néke barina jiguéne gno xameni sén gnaka ame dome ci lou méleni la diogué Zéyena nanga néke soxena té boule néke diabar yéne gni té néke ci réseaux sociaux yi xana amoléne yénéne sujets you amale réwemi ndiarigne

  • @assiatoujallownjie6396
    @assiatoujallownjie6396 Pƙed 21 dnem +2

    This is a private matter. Why are you discussing on the internet? You should be sued

  • @kemeltoutambadou5964
    @kemeltoutambadou5964 Pƙed 22 dny +1

    Craignez dieu, ragal léne yallah. Honte sur vous

  • @diengfama294
    @diengfama294 Pƙed 22 dny +6

    Labane diam 😂😂😂😂😂😂li di tradition.kouniouy labane dinga sagnsei tok di diouk di mayei khalisss.

  • @mariamathioune4224
    @mariamathioune4224 Pƙed 22 dny +2

    Yaw gor nga wala djiguéne viviane a plein droit de le publier nah danio yah derrou domam c'est une occasion pour setal ko

  • @mariegomis2405
    @mariegomis2405 Pƙed 22 dny +1

    Mais de quoi je me mĂȘle, goor kou niak fayda

  • @HaddyJallow-f3z
    @HaddyJallow-f3z Pƙed 22 dny +1

    Yenn daguene hamoule hamethe cessay nioune gambia fallen vougniou hamethe cessay ok

  • @martin-zn6fn
    @martin-zn6fn Pƙed 22 dny +6

    ahmed cisse est ce que yayam amone na ndaw?delen soutoural djigene yii wa Sénégal

    • @gnagnamboup7418
      @gnagnamboup7418 Pƙed 22 dny +2

      No.ahmed.cisse d'oĂč nite walakhi khalatoul sakh euleuk

    • @martin-zn6fn
      @martin-zn6fn Pƙed 22 dny +3

      non mane dama rouss en tant que goor li dafa niaw li ma geuna meti moooy Sénégal genre yi dagne len di encouragé di len may buzz

  • @dabakonate4585
    @dabakonate4585 Pƙed 20 dny

    Lousiiii senn yonnn
    Ayyy CNRA jusqu'Ă  quand ces sotises
    Salaw kudul soutural nittt 😱😱 sa Borom moguiilayy xarrr

  • @adjingone
    @adjingone Pƙed 21 dnem

    Mane nawe naléne yéne djiguénou. Plateau bi

  • @JumeauxJumeauxdioplaye-kw6pp

    Une preuve irrefutable que ki nafekh leu soss kate leu ki teudeugoul bi dou jaal

  • @mbarckasougou6111
    @mbarckasougou6111 Pƙed 22 dny +1

    Manndoulene nite daye mandou

  • @adjingone
    @adjingone Pƙed 21 dnem

    Ahmed cissé sonal na sénégalais yi thiey yalla

  • @AbsaSamb-hk5xt
    @AbsaSamb-hk5xt Pƙed 22 dny

    AÏY WAY MANDOU LÉNEU SI NIT YI
    BOUDÉ DEUG NIO HAM
    BOUDÉ FÉNEU NIO HAM
    MANDOU DÉ BAHNEU đŸ€
    BÉNEU DJIGUÉNE NIANOUL
    YALL AM DIEUKRE DISI SÉTOU
    LOU NIAW BARKÉ REK LASI BEUG
    TÉ LOLL YALL REK MOKO HAME
    DONC NAKO NIANAL YAL YA SALAMđŸ™đŸœ

  • @user-ck2ow1vf7w
    @user-ck2ow1vf7w Pƙed 22 dny

    Yalla lĂšne yalla

  • @Senegalist
    @Senegalist Pƙed 22 dny

    Teude na certes mais li dou labane bi nek len nit

  • @fatoumatadiop2787
    @fatoumatadiop2787 Pƙed 22 dny

    Ye com dolen djigen kou tede dina tal lenen loudoul fethe

  • @Arame-mr6xt
    @Arame-mr6xt Pƙed 22 dny +2

    Mane dé féthoine n'a ndakh contane si sama bop bilay bimay diouk sa tayoumako té douleur bou Rey bouniouy wakh si ndaw amoul 2em jour bi sa mo gena méti Sénégal mo mena nék Di yok mane diarnasi mé liniouy wakh si ndaw égoul fofou rÚgles sa moko guena méti

    • @AbsaSamb-hk5xt
      @AbsaSamb-hk5xt Pƙed 22 dny

      MASCHA ALLAH 🎉
      NDAYSANE 😊

    • @Arame-mr6xt
      @Arame-mr6xt Pƙed 22 dny

      @@AbsaSamb-hk5xt merci

    • @madadiop8345
      @madadiop8345 Pƙed 22 dny +1

      Bilahi arame wakh Gua DĂ©gueu Mane Diar Nassi MĂ©tine You Reuye Sakh Amoussi DeuxiĂšme Jour Bi Sakh Mo Geuneu MĂ©ti

    • @Arame-mr6xt
      @Arame-mr6xt Pƙed 22 dny

      @@madadiop8345 c'est vrai dé niou nék fii Di wakh rék té dra worouléne si Sénégal doyna warr

  • @serignembacke62
    @serignembacke62 Pƙed 22 dny

    Bama degue fii sénégalais dafa sokhor rek. Boulen gnou fonto qui dou sénégalais gambien lh

  • @fatoundiaye4878
    @fatoundiaye4878 Pƙed 22 dny

    Ndawssi thakhabi khalisse moko guéné dara léroul ci liguay wakh

    • @cocoibrahimafallou1910
      @cocoibrahimafallou1910 Pƙed 22 dny +1

      Iow lingay wah dafla lér seuteuteu Lou tah dolén ndiort Lou bah si sén morom.