"Lingay Wax Dou Deugg, Fi Féne Xadioufi" débat houleux entre Sa Wolof & Malal Diallo

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 17. 06. 2024
  • "Lingay Wax Dou Deugg, Fi Féne Xadioufi" débat houleux entre Sa Wolof & Malal Diallo
    #senegal #diomayefaye #Sonko
    Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
    / @senegal7tv
    L'information en temps réel
    Visitez notre site web: Senegal7.com
    Suivez nous sur:
    page facebbok : / senegal7officiel
    Instagram : senegal7?igshid...
    TikTok : www.tiktok.com/@senegal7tv?_t...
    Abonnez-vous pour plus de vidéos et n'oubliez pas d'activer la cloche de notification

Komentáře • 154

  • @abdoulayeguisse5608
    @abdoulayeguisse5608 Před 8 dny +8

    Iman Macky Sall bi diarou débat.Diomaye Moy Sonko

  • @birahimsene7235
    @birahimsene7235 Před 8 dny +16

    Pour lane niou invité kou melni ce diallo là, jour tabaski gua wakh discours haineux. Arrêtez ces discours haineux

  • @donzap5700
    @donzap5700 Před 8 dny +7

    SA WOLOF NÉHO DÉGLOU ... D'ACCORD NA SISSA DEUG MAIS SA DÉBAT DAFA SAFF HÉKH TROP....WAAGNIL HADAR BI TÉ DOLISSI HUMBLE NGUIR YALLA !

    • @Abdoulahi-cisse
      @Abdoulahi-cisse Před 7 dny

      Insàllaa 👍🏿 ✊🏿 ✅ Xadar ji yénn saayi xorom la ci de 🙏🏿

  • @user-xq1nx5qz2g
    @user-xq1nx5qz2g Před 8 dny +8

    sa wolof lingeu wakh lou weer leu

  • @ametkyks
    @ametkyks Před 8 dny +4

    Imam bou dof bilahi diomaye sou topé gni danane ko wédi il faut arrêter ces visites et travailler on ne vous a pas élu pour visiter ces soit disants maître chanteurs

  • @Mamayombé215
    @Mamayombé215 Před 8 dny +3

    Saa wolof a raison. Il y'a des critères pour être imam.

  • @ibrahimabdoulayesonko4209

    Le système n'est une question de personnes, c'est plus profond...

  • @user-lx5cm3sv2u
    @user-lx5cm3sv2u Před 8 dny +2

    Mais la grande mosquée appartient aux sénégalais mais pas aux lebou

  • @malickgaye903
    @malickgaye903 Před 7 dny +1

    Machalla sa woloff ❤❤❤❤kontan nanou si yaw

  • @user-ur8kh9zj2x
    @user-ur8kh9zj2x Před 8 dny +9

    Merci sa wolof ❤

  • @yokokndamfalltv1705
    @yokokndamfalltv1705 Před 8 dny +3

    Yow malal danga beuga dougal sa wolof wakhloko louko dougal wayé sa khamnala li nga beugue douko déf

  • @sankounkanoute3067
    @sankounkanoute3067 Před 7 dny +1

    Bilaye Sa deugue nga wakh sincèrement.

  • @lamineniang8625
    @lamineniang8625 Před 8 dny +3

    Les gens de APR son malade

  • @Manma-tk1xf
    @Manma-tk1xf Před 7 dny +2

    C'est pas vrai il n'est pas tout permis a un imam de dire tous ce qu'il veut

  • @user-zh9js4zb5n
    @user-zh9js4zb5n Před 8 dny +1

    Merci.sa.wolof.ki.daye.féne.rék

  • @babakebe4094
    @babakebe4094 Před 8 dny +2

    Sa wolof pertinent ga, wayé rèwga. Dou wakh loo andoul né wakhoul deug, dooka wakh sa baay ni sa serigne.
    Avec eupeu de respect

    • @mariamadiallo6475
      @mariamadiallo6475 Před 8 dny +2

      Kou fen niou wakhko dafa fén

    • @Abdoulahi-cisse
      @Abdoulahi-cisse Před 7 dny

      Yàlla xam na ni Saa waajur bu waxee mbaa mu def lu dul, ma xarab ko Yàlla baax ba saa Baay doone ku dëggu, te yar ma ci dëgg!

  • @damendiaye9737
    @damendiaye9737 Před 7 dny +1

    Machalla sa wolof❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @1960mamad
    @1960mamad Před 7 dny +1

    Man ces gens qui ont la haine dans leur coeur et la bave dans la bouche ne doivent pas être inviter pour parler aux sénégalais. Ce malal durant tout le débat n'a pas été à la hauteur.

  • @senthiouraysopnabi739
    @senthiouraysopnabi739 Před 8 dny +1

    Merci sa

  • @alimalopes4353
    @alimalopes4353 Před 7 dny +1

    Merci sa woolof ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @modougueye5859
    @modougueye5859 Před 8 dny +3

    Senegal7 évite guéne ki dakh fene Sénégal Malal Diallo féne reek lay def Amoull ligueye doul reek

  • @awademe5179
    @awademe5179 Před 8 dny +3

    Imame chaque année îl nous sorte une autres facettes îl doit être ramblacer c'est pas Un bon exemple pour fédérer là populations

  • @bambaseck62
    @bambaseck62 Před 8 dny +2

    Merci sa wolof deug rek mooy ancien joueur nawetaane bi foumouy dieulé diouma 😂

  • @user-ps5we1yh3b
    @user-ps5we1yh3b Před 8 dny +2

    Sa wakhna deug

  • @BigKiller-hk2zd
    @BigKiller-hk2zd Před 8 dny +1

    Merci sa wolof❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @TafaloSaMb-sq3on
    @TafaloSaMb-sq3on Před 7 dny +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Blaise-re7rj
    @Blaise-re7rj Před 8 dny +1

    Vive sa wolof ❤

  • @fayedavid3312
    @fayedavid3312 Před 8 dny +1

    Sa wolof🙏🙏🇸🇳🇸🇳❤️❤️

  • @matydione8670
    @matydione8670 Před 8 dny +1

    Sénégal rek ngay guiss kou am ay mbédiaw wowé bopam dioulite di doule 😂😂😂

  • @MbayeCisse-cd1tu
    @MbayeCisse-cd1tu Před 8 dny +1

    Merci beaucoup sa wolof❤❤❤❤❤❤

  • @user-ow6ex8sy6e
    @user-ow6ex8sy6e Před 8 dny +1

    Merci sa wolof ❤❤❤❤❤❤❤

  • @khalyseck7182
    @khalyseck7182 Před 8 dny +1

    CE MALADE UTILISE VOTRE PLATEAU POUR REMPLIR SES POCHES CHEZ BOUGRE D'ANE.

  • @abdoulakhateka6374
    @abdoulakhateka6374 Před 7 dny

    Merci ❤❤❤sa❤ merci ❤❤❤sa❤

  • @abdoulayesarr8021
    @abdoulayesarr8021 Před 8 dny

    Merci sa wolofff très fier de vous

  • @user-mu7hu6fx8h
    @user-mu7hu6fx8h Před 8 dny +3

    C'est pas un imam

  • @user-me1hg7bm4q
    @user-me1hg7bm4q Před 7 dny

    Bravo monsieur Diallo

  • @NiangNdiaga-nd7jw
    @NiangNdiaga-nd7jw Před 8 dny +2

    Sa bayill feen katbi

  • @jefdacosta3483
    @jefdacosta3483 Před 7 dny +1

    Bonjour Sa Wolof,
    Je tiens à exprimer mon profond désaccord avec les insultes que vous avez dirigées contre l'ex-première ministre du Sénégal dans votre vidéo. Même si je suis parti du pouvoir, je ne peux pas approuver de telles injures gratuites, qui ne sont ni justes ni respectueuses.
    De plus, vos insultes envers mala sont également inacceptables. Bien que je reconnaisse votre capacité à bien vous exprimer, l'utilisation d'insultes décrédibilise votre message et n'apporte rien de constructif au débat.
    Je vous encourage à exprimer vos critiques de manière respectueuse et professionnelle. Cela renforcera vos arguments et votre crédibilité.
    Merci de votre compréhension.

  • @user-me1hg7bm4q
    @user-me1hg7bm4q Před 7 dny +1

    Sa wolof sa lefeul ndaye yow ak sa wa group

  • @yytv8221
    @yytv8221 Před 7 dny

    Imam bo khamnei neina souma jummah YALLAH mom geineu na si Jummah diodiou

  • @falloungom3153
    @falloungom3153 Před 8 dny +1

    Sa wolof mi kou rew la ay cadom amoul bene respe

  • @mohamadsabaly1866
    @mohamadsabaly1866 Před 8 dny +1

    Néna imam imam la degnko may mou wakh louko nekh Dara douko si féké ki werna😂😂😂

    • @zagaraga2169
      @zagaraga2169 Před 7 dny +1

      Mane lolou moma diakhal amoul Kene kou yalla daradial mouy wakh louko nekh waratina imam

  • @bubacartiana428
    @bubacartiana428 Před 7 dny +1

    Macky Sall dou ray Sénégalais yi baa paré ay nioniam di fonto nitt ni. Dafa diote nguen commacé di len feetal si plateau. Commacé len yobou diassi wala feetal si plateau yi. Légui gnou teuthie Sen gathe.

  • @malickndiaye2804
    @malickndiaye2804 Před 8 dny +1

    Ndawsi khana pastef la do bayi ki mou wakh

  • @cheikhsene9718
    @cheikhsene9718 Před 7 dny

    Saa-wolof ❤❤❤❤l

  • @yousssoudiagne9403
    @yousssoudiagne9403 Před 8 dny +1

    Les impolie n'avance jamais

  • @babacarmbaye5227
    @babacarmbaye5227 Před 8 dny +1

    Sawolof tu es impoli malal a raison tu as peur de dire ce que tu penses
    Sa rewende mo takh tu ne me plais pas

  • @Dykhamorant1030
    @Dykhamorant1030 Před 7 dny

    Mais malale mi doyna War dé partie mouné commune 😂😂😂

  • @babakebe4094
    @babakebe4094 Před 8 dny +1

    Sa wolof tèyal

  • @user-lg2wj5ly3q
    @user-lg2wj5ly3q Před 7 dny

    Sa wolof wakh ga dég dès Lou leur ga wakh mashaall diaradiaff way

  • @user-me1hg7bm4q
    @user-me1hg7bm4q Před 7 dny

    Sa wolof da nga meuna féne

  • @malickndiaye2804
    @malickndiaye2804 Před 8 dny +1

    Wakhou rewane bakhoul niit day am yar

  • @coumbafaye9319
    @coumbafaye9319 Před 7 dny

    Diallo nganer imam bi limouwakh dara nekoussi? Mom nak humilier woul president deh bopam la humilier ndakh compotement bi niepakossi khep. Temp wou imam mawdo sylla ba tay .mom rek mofiye wakh lou kheblou ndakh lebouyi ken eupoulene personnalite fi si senegal.

  • @ibradiop9753
    @ibradiop9753 Před 8 dny

    Waa eskeu nimou waxé AK Diomaye noonou ladoon waxé AK Macky Sall.. No No..konak imam APR la

  • @MamadouBa-ko9ck
    @MamadouBa-ko9ck Před 7 dny +1

    Lofall ndeye sa woloff

  • @tidianetoure1120
    @tidianetoure1120 Před 8 dny

    Ngor si mom wakh deug souma done wakh si télé yi douma bok ak mom plateau jamais parce que amoul yar lamignam bi niawna trop heureusement que sa wolof

  • @modyndiaye6515
    @modyndiaye6515 Před 8 dny +2

    Bougane daño wara dokhane ndayame

  • @yytv8221
    @yytv8221 Před 7 dny

    Boumoula wakhlo lo bougoutt wakh dei

  • @IbrahimaKa-eg4ff
    @IbrahimaKa-eg4ff Před 8 dny +1

    Sa Wolf mi moy fen kat bou makk bi

  • @LaminCamara-lp3et
    @LaminCamara-lp3et Před 7 dny +1

    Sa wolof fi Sénégal la domou kharam bou Mélanie yow tu juge un imam ton père ne rien dans se pays dele guestou boy dokh

  • @ousmanediawara-fu7ek
    @ousmanediawara-fu7ek Před 7 dny

    OPERATION GOKHY AK FAY IMPOT MOLEN TITEUL

  • @user-vm6of4gq3i
    @user-vm6of4gq3i Před 7 dny

    Sa wolof damay woo ndaaw și sow deh

  • @ousmanediawara-fu7ek
    @ousmanediawara-fu7ek Před 7 dny

    LINGUAY WAKH MOY DEUG , IMAM DAKOY MOTT, DAY TEUDEY NDIAKHANAY, DI BOLE DIOUB DIOUBEUL DI DIOUBEUNTY , DI WAKH ;OUY DIEMEULEH DIOULITTE SI YALLAH AK SOUNOU YONENTY ,

  • @Blaise-re7rj
    @Blaise-re7rj Před 8 dny

    Imam nafekk la imam grand ratipe 😂

  • @user-ps5we1yh3b
    @user-ps5we1yh3b Před 8 dny

    Imam ak niawayam😂😂

  • @deemo3747
    @deemo3747 Před 8 dny

    Ki place la beug si plateau keur doff yi

  • @user-ps5we1yh3b
    @user-ps5we1yh3b Před 8 dny

    Khawma si lumuy yagou waye amoul ler

  • @amadoukebe1911
    @amadoukebe1911 Před 8 dny

    Sa un indigne

  • @user-me1hg7bm4q
    @user-me1hg7bm4q Před 7 dny +1

    Sa wolof kou Kate sa ndaye ng

  • @moustaphacisse8901
    @moustaphacisse8901 Před 8 dny

    Kiii dh boum lén bét guén guis ko Sen TV

  • @godigoba7939
    @godigoba7939 Před 8 dny

    Xoll bou xatt yague yague borom dë😂😂😂

  • @moustaphacisse8901
    @moustaphacisse8901 Před 8 dny

    Kii dh boum lén bét guén guis ko Sen TV

  • @CM-xo3oy
    @CM-xo3oy Před 8 dny

    Mala mi mo meneu dool! Kane mofi tatiou Bougane?

  • @babacarmbaye5227
    @babacarmbaye5227 Před 8 dny +1

    Cette dame ne comprend rien et na pas la cervelle pour conduire un débat

  • @moustaphacisse8901
    @moustaphacisse8901 Před 8 dny

    kiii dh boum lén bét guén guis ko Sen TV

  • @afriquelibre5636
    @afriquelibre5636 Před 8 dny +1

    Dou imam, béne domouram le bouy mboubo imam ngir enrichirou, ce faux imam est un vagabond, un domouram.

  • @mariamadiallo6475
    @mariamadiallo6475 Před 8 dny

    Ki mom waroule wone sant diallo

  • @user-cb7ye3xm3c
    @user-cb7ye3xm3c Před 8 dny

    Sa yaw kou réw ga😂😂😂

  • @Domou_senegal
    @Domou_senegal Před 8 dny

    Sa wolof, kou réw laa 😠😠

  • @silmandinhosiby224
    @silmandinhosiby224 Před 8 dny +1

    Ki bann façon nitt le

  • @CheikhDiop-en2sr
    @CheikhDiop-en2sr Před 8 dny

    Rew mo kham né wakh goudi wakh souba wakh ngone

  • @user-ih6tp2wp4v
    @user-ih6tp2wp4v Před 8 dny

    Sa wolof lignage wakh degueleu

  • @cheikhka-ok5gz
    @cheikhka-ok5gz Před 8 dny

    môme mowge imame bi wakhouole mogi yobou féne bi si imame bi

  • @thiernondiaye1975
    @thiernondiaye1975 Před 8 dny +1

    Sa wolof mi kou eupeul la téyoul dara

    • @CM-xo3oy
      @CM-xo3oy Před 8 dny

      Yako gueneu eupeul. C'est l'autre gar qui essaie de le minimiser.

    • @thiernondiaye1975
      @thiernondiaye1975 Před 7 dny

      @@CM-xo3oy yaw yarouwo kouni minimiser bo andé ak dal dou dialeu

  • @malickndiaye2804
    @malickndiaye2804 Před 8 dny

    Sa wolof louy liguyam wakh moy dokh

  • @Blaise-re7rj
    @Blaise-re7rj Před 8 dny

    Yadji nafek la

  • @babacarceesay4819
    @babacarceesay4819 Před 8 dny +2

    Mashalla Sawof imame bi xalis rèk mome la baga

  • @deemo3747
    @deemo3747 Před 8 dny

    Yaw Diallo ya meuneu doul, Bougane n’est pas courageux car dafa djoundje, il n’a pas parlé directement

  • @user-xq1nx5qz2g
    @user-xq1nx5qz2g Před 8 dny

    wa geume ceu bopp senne leufeul ndeey

  • @lampefalltvlampefalltv3589

    Malall Diallo doull rek l'ay def khamnako bou bakh thiaroy Tally Diallo pithi papam lagnouko toudé

  • @user-xh8iu1si7k
    @user-xh8iu1si7k Před 8 dny +5

    Dakar appartient aux Lébous koumou nékhoule nga déme saye thiossanou Mame , wala bo démé tabaski boul niewate

    • @netalytvnetalytv1560
      @netalytvnetalytv1560 Před 8 dny +1

      saway linga nè lèbou yi nioy brom dakar lolou deugue leu ndakh yèn lan fi fèk ms lou nite dieunde thi khalissam lèbou yi mima tougne ko donc na wakh di rafait am ngèn mèrite yen lèbou yèna gnou yatal merci

    • @mamadoumbaye7726
      @mamadoumbaye7726 Před 8 dny

      Cosaan moom buñu ci déméé ngéén ñibi ñambur mbaa kajoor, dangéén daw xééx ba sës ci ndoxmi rék took, cosaanoo léén fa tappét rék

    • @piscodiaz3494
      @piscodiaz3494 Před 8 dny

      Wahoffi dara dèmal diague histoire dakar sossèyi gniouco sosse

    • @Snoopy266
      @Snoopy266 Před 8 dny

      @@mamadoumbaye7726 saway aamana fénnn ap lébou ak daw aamana doul wayy

    • @Snoopy266
      @Snoopy266 Před 8 dny

      @@piscodiaz3494dakhala doul sosseyi mbokhékh lagnn nékkonn difa bay lébou yii dieulé lénn fa

  • @user-xh8iu1si7k
    @user-xh8iu1si7k Před 8 dny

    Nahaté yoyou da diéhe les Lébous commencent à s'éveiller

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 Před 8 dny

      Yèkh na deh lebou diaye nèniou sène souf yeup ndakh doff lègui niongui dioye nane etat bi nalène dèlo sène souf

    • @user-xh8iu1si7k
      @user-xh8iu1si7k Před 7 dny

      @@ghettoyouthkatakyni7843 Celà ne sera jamais trop tard si nos parents avant 1960 fait la demande car leurs identités sont à Nante

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 Před 7 dny

      @@user-xh8iu1si7k oui mais meme avec leurs cartes d'identitè a nantes l'hors des 4 communes je te dis c'etait juste pour nakh lène wayè nantes deh extrait de naissance rek lèniou fa meuna am wayè nationalitè douniou ko am deh lou lèèr lala wakh en fait toubab yi dèniou lène nakh rek tè nèniou wakheuntè deugue li dal communautè lèbou bi nioko tek sène bope ndakh golo bou dioguè ci ale ba pa lèbou nè (ala noye mboke) motax nieup nakhlène dieul sène souf ba ndakarou momatouniou fa dara bo dèmè bargny sakh doto ko khamè ndakh etrangers yi fèss nèniou fa tè ci nangou ko lèniou dieum donc si jeunesse lèbou bi dogouniou boumou diam bi tè oubi sène xèl yi dinèniou dioguè bargny , yène comme que ndakarou perte nèniou ko tè litax lolou moye (ala noye mboke) naar niew niounè ala noye mboke,toubab niew niounè ala noye mboke,bou chinois niewone sakh ala noye mboke👉🏿wa motax mboke yoyou nangou nèniou lèp tè lolou yeup pa lèbou you niaka fayda yi nioko indi tè comme que dèniou con ba pour niome xalè waroul wakh pa yi diaye lèp

  • @HabibSy-jn1pk
    @HabibSy-jn1pk Před 8 dny

    Sa wolof imame wakhoul Alioune ndoye niou boko parti dafa wakh ni sonou mère la

  • @user-xh8iu1si7k
    @user-xh8iu1si7k Před 8 dny +1

    Bouléne niou taha wahe déh , c'est que les dignitaires Lébous doivent faire une pétition pour qu'on retourne sur les quatres communes se rapprocher de l'ambassade de France du point de vue que leur document son à Nantes

  • @madydiallo8922
    @madydiallo8922 Před 7 dny

    S Malal est nul hein 😂😂😂 imam da yag dioum li mo wara diekh si Senegal

  • @ousmanediawara-fu7ek
    @ousmanediawara-fu7ek Před 7 dny

    KOU WAKHOUL DEUG KAY NIOU WAKH LAKO , , SA WOLOF LOUMOU LAWAKH LERNA ,

  • @salzfontenay-aux-roses169

    Malal bi Con deug la

  • @tidianetoure1120
    @tidianetoure1120 Před 8 dny

    La toudé bopam

  • @sady1964
    @sady1964 Před 8 dny

    Wakh loko nekh ta Dara doko thi fèk

  • @senthiouraysopnabi739

    Wadji doff dogue la