Youssou Ndour en larmes devant Bouba Ndour et Philip Ndour oh c triste 😭😭

SdĂ­let
VloĆŸit
  • čas pƙidĂĄn 6. 07. 2024

Komentáƙe • 348

  • @user-yd1ev4fi3e
    @user-yd1ev4fi3e Pƙed 8 dny +131

    Je suis trop contente pour Boubacar ndour il doit ĂȘtre fier de donner la main de sa fille toutes mes fĂ©licitations a lui Ă  Zeina et Ă  Viviane ma shaa allah

    • @fatoulaye-wd8qd
      @fatoulaye-wd8qd Pƙed 8 dny +9

      C'est normal parce que dioulite leu baparé nekk talibé seydina limamou laye Al mahdi mountazar (psl)

    • @kebadanso6356
      @kebadanso6356 Pƙed 8 dny +1

      J ai vu tous les griots de la place.cest bien la solidarité

    • @astpuizambart1126
      @astpuizambart1126 Pƙed 6 dny

      ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @oumysylla5347
    @oumysylla5347 Pƙed 8 dny +116

    Yalla na yalla barkil séy ci barkip borom touba amine

  • @ramataba5463
    @ramataba5463 Pƙed 8 dny +75

    Seuy bou barkĂ©le inchallah si barkĂ© yonĂ©nte bi salalahou aleyhi wasalam diabott djiou barkĂ©le inchallah â€â€đŸ˜‚

  • @diarrasow9492
    @diarrasow9492 Pƙed 8 dny +140

    Zayna yalna seuye bi barkel si barkĂ© seydina Mohamed ❀❀❀❀

  • @aminatadiakhate-ss3tw
    @aminatadiakhate-ss3tw Pƙed 8 dny +60

    Yalla na seuybi barkel si barke seydina Mohamed psl amine ❀❀❀❀

  • @assanceesay8633
    @assanceesay8633 Pƙed 8 dny +32

    Bouba le SĂ©nĂ©gal n’a pas oubliĂ©. Tu nous a dĂ©fendu sur toute la ligne, tu es courageux.

  • @LodMouss
    @LodMouss Pƙed 8 dny +84

    ThiĂ©y famille Ndour, nio am, mayou yallah dĂ©, machallah Youssou,lĂ©peu yowleu🙏🙏

    • @basselabdou9891
      @basselabdou9891 Pƙed 8 dny +11

      nioun nieup am naniou mayou yalla nguĂ©n kounĂ©k ake Lila yalla maye bouko khĂ©ppp. Peace and love🇾🇳đŸ‡ș🇾

    • @LodMouss
      @LodMouss Pƙed 8 dny +8

      @@basselabdou9891 ne te compare pas a You, gueumeul yallah mo gueune 😂

    • @Adulovev5qo
      @Adulovev5qo Pƙed 8 dny

      Lodmouss fingaye wakher est ce que basselabdou comprendre nako

    • @sympathisante17
      @sympathisante17 Pƙed 8 dny

      @@LodMouss bilahi t’as tt dit 😂 koyy gnĂ© gnĂ©woul bopam.

    • @henriettediouf348
      @henriettediouf348 Pƙed 8 dny +1

      Bilakhi leep moom la. Magu boy nieup beuguone aam

  • @GnimaSambou-bb9ul
    @GnimaSambou-bb9ul Pƙed 8 dny +63

    Lila wa diour yĂ©ppe di niane ndoundeu ba djiss sa mariage dome yalla nagnouko yalla mĂ©y tĂ© sĂ©ybi barckĂ© 🙏

    • @SerigneFallouMbackeDiouf-lt7qd
      @SerigneFallouMbackeDiouf-lt7qd Pƙed 8 dny +3

      Bly wly đŸŽ‰â€

    • @lofatou6218
      @lofatou6218 Pƙed 8 dny +3

      Aminee sibarke serigne touba

    • @AstouDiop-hx4iv
      @AstouDiop-hx4iv Pƙed 8 dny +1

      ❀​@@SerigneFallouMbackeDiouf-lt7qd

    • @awaba8082
      @awaba8082 Pƙed 8 dny +2

      Bilahi mann dĂš ayy dome you djiguene rekk laa amm maa ngui santt yalla mais foma fekk damayy haalaat rekk ndakh raagall gathi

    • @vieuxka4076
      @vieuxka4076 Pƙed 8 dny +2

      Amine đŸ™â€ïž

  • @arsenebampoky2706
    @arsenebampoky2706 Pƙed 8 dny +38

    Il est fiĂšre c est tellement beau ❀

  • @djilabelle2144
    @djilabelle2144 Pƙed 8 dny +11

    Ndaysane Bouba est trĂšs content yalla bou yakar tass yalna seuybi Sakh barkel andak djabote yalna doundou bonheur bi avec mon mari in sha Allah ❀

  • @nrjdakar2617
    @nrjdakar2617 Pƙed 8 dny +54

    Les larmes de Youssou ndour mome laye weur ba lĂ©gui 💁💁💁

  • @user-wv9mj1fz8h
    @user-wv9mj1fz8h Pƙed 5 dny +2

    Yalla na seuy bi barkel thi barkĂ© Seydina Mouhamed salaatou wa salam tĂ© may lĂšne ndiabot you barkel ❀❀❀❀❀

  • @ndeyematydiaw45
    @ndeyematydiaw45 Pƙed 8 dny +20

    Yala bou yakaar tass des 2 cĂŽtĂ©s!!! Mes fĂ©licitations Ă  toute la famille ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @awaseck745
    @awaseck745 Pƙed 8 dny +49

    Yalla bou thi thiat dougou thé yalla barckel thé dafalla lou soute sa diorte thé moi bok sa séy yagou tak thiat haras thi barcke ckeihoul khadym amine

  • @aminalalionne5679
    @aminalalionne5679 Pƙed 8 dny +11

    Vraiment gneupeu conetane si seuye bi yalla nassi sougnou borom def barkĂ© tĂ© mou book si seuye yignou takĂ© arass fĂ©licitations zeyna ❀❀

  • @dieynabadia3276
    @dieynabadia3276 Pƙed 8 dny +37

    CĂ©lĂ©britĂ© nekhnaa nekhoull kholall youssou ndour ndeysane ne pouvait mĂȘme mĂȘme pas rester saffonteer akk ay kharitam tellement les gens ne laisseront pas tranquille

    • @damedia4990
      @damedia4990 Pƙed 8 dny +5

      Bilay siw dafa méti dé rawatina kou mélni youssou ndour nga khamni foumou takhaw def embouteillage youssou kéne la

    • @Adulovev5qo
      @Adulovev5qo Pƙed 8 dny

      ​@@damedia4990walahi do nĂ©keu mouk ak sa saguo

    • @ndeyeastoudiatta9020
      @ndeyeastoudiatta9020 Pƙed 8 dny +2

      Yalla maynako ndayssane weurseugam dafa eupp lokhom machala faw thiowli bari yalana borom bi sam siw dafa meti seuy bi barkel yarabi đŸ™đŸŒđŸ“ż

  • @yayouthiate4942
    @yayouthiate4942 Pƙed 8 dny +13

    Seynabou Ndour yalla na yalla barkel sëy bi thi barke rassoulilahi Psl

  • @Noe001
    @Noe001 Pƙed 5 dny +1

    un moment de bonheur que Allah m'accorde pareil ainsi que toute personne qui aspire a cela

  • @user-yi6pq9vw2r
    @user-yi6pq9vw2r Pƙed 8 dny +8

    L'histoire retiendra! Un grand homme infatigable pour le bien ĂȘtre et le dĂ©veloppement de son pays. Kouko bagne sa affairela

  • @AidaDiaw-yq1ey
    @AidaDiaw-yq1ey Pƙed 8 dny +21

    Yallah seybi barkel si barkĂš seydina Muhammad saw si barkĂš serigne babacar sy amine

  • @lelionnicois9681
    @lelionnicois9681 Pƙed 8 dny +10

    J'aime beaucoup cette famille une vraie fierté sénégalaise

  • @dioumzndiaye1504
    @dioumzndiaye1504 Pƙed 8 dny +10

    Ndey sane kholal Philippe ak rakdji ❀❀

  • @thilellesy679
    @thilellesy679 Pƙed 7 dny +2

    Vraiment bouba nit kou bakh la ❀

  • @FatouDiedhiou-bg1mb
    @FatouDiedhiou-bg1mb Pƙed 8 dny +21

    Zé Yako fi am gnioulay takk Mouy taw yalla seuy bi barké ha seuy mba Say faa

    • @SireTamba
      @SireTamba Pƙed 8 dny +2

      Amiiiin ya Rabby allah 🙏 🙏 🙏 ndĂ©yssane moungui may fatali sama seuyou taw bou djiguĂ©ne le 08 juillet 2017 dafa taw ba bi mouy seuyi daniou ko bote. Yalna lĂ©n Bour yalla dĂ©fal diame ak salam tĂ© may lĂ©n ndiabot gou barkĂ©l. Gni ama goul borome yalna niou ko ame si barkĂ© Seydina🙏🙏🙏 Mokhamed

    • @user-zt5ti8rs1z
      @user-zt5ti8rs1z Pƙed 8 dny

      ​@@SireTamba amine yaarabi

    • @salladiaw543
      @salladiaw543 Pƙed 8 dny

      ​@@SireTambaAmine Yarabi

    • @adamaberthebakhayoko8156
      @adamaberthebakhayoko8156 Pƙed 8 dny +1

      Alahouma Amin đŸ€ČđŸ€ČđŸ™đŸ™đŸ„°â€ïž

  • @AichaLo-cq3wc
    @AichaLo-cq3wc Pƙed 8 dny +10

    GathiĂ© ngalama Ă  vous ma Viviane d'❀ leupeu yow la ❀❀❀ chapeau Ă  vous la Reine

  • @fabricemendy2401
    @fabricemendy2401 Pƙed 8 dny +7

    Bouba est quelqu'un de bien machallah

  • @user-un5pz5jt3k
    @user-un5pz5jt3k Pƙed 8 dny +4

    Thieuy papađŸ„° youssou❀moy diambar dhh yalla na sa diame yague 🙏🙏🙏

  • @LataFaye-mg3mp
    @LataFaye-mg3mp Pƙed 8 dny +22

    neyssane darra fayoul mbok yalla yalla barkĂ©l seybi❀❀❀❀❀❀

  • @diengfama294
    @diengfama294 Pƙed 8 dny +4

    BĂŽuba tous les patriotes sont contents pour toi heureux mĂ©nage ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @sokhnandiaye7192
    @sokhnandiaye7192 Pƙed 8 dny +11

    Yallana yalla barkelé sey bi si barke nabil moustapha psl

  • @fatou-py5si
    @fatou-py5si Pƙed 8 dny +9

    Congratulations brother Buba❀May Allah Bless the union and give them bless children . 🎉🎉🎉🎉đŸŒčđŸŒčđŸŒčđŸŒč🎈🎈🎈

  • @user-vp2sp6mv5b
    @user-vp2sp6mv5b Pƙed 8 dny +9

    Taye lima warra sĂ©tane mo beuri awma sakh temps bĂ©tĂ© bĂ©tĂ© ndakh khĂ©wmi j' ai trop chargĂ© 😱

    • @pendadiallo7035
      @pendadiallo7035 Pƙed 8 dny +1

      Bilahi Ioe barii ngassi morom😊😊😊

  • @aitandoye3767
    @aitandoye3767 Pƙed 8 dny +18

    Maachalah, je ne connais pas la famille Ndour mais mangui niane yallah Soubkhna wattallah yallah na seuye bi bokeu si seuye yi yallah gueureume baracatou rassouloulakhi salalakhou aleykhy wa salam, j'aime trop Viviane et sa fille ndeysanne, toutes mes félicitations à Boubacar Ndour, laf thiate

  • @MametallaNdiaye-wn8lf
    @MametallaNdiaye-wn8lf Pƙed 8 dny +4

    Thiey xewou milliardaire mo neex deh yalnaniou yalla wergii yaram bou andal teranga you yaatou té barkel beep sey

  • @CHEIKHTIDIANENDOYE-yn2nc
    @CHEIKHTIDIANENDOYE-yn2nc Pƙed 7 dny +3

    adouna ni la diam mo nekh seye bi yalla nako yalla barkel si dara dja seydina mouhamed psl me plonge dans les pensées le jour ou ma fille se mariait bonne chance durable à toutes nos adorables filles mariées yalla na yalla barkel sene sey

  • @adjiaidagueye113
    @adjiaidagueye113 Pƙed 8 dny +3

    Ndeyessaan Yallah na Barkel Bouba nak mo am respect ci Niit Machallah

  • @awatoubab1994
    @awatoubab1994 Pƙed 8 dny +2

    Je ne sais pas pourquoi les hommes de valeur lou ameu farata rekk lagnou dokk Machallah vive nos hommm

  • @ndoyawade
    @ndoyawade Pƙed 8 dny +13

    Yala na yala barkél léep

  • @rokhayadiallo8765
    @rokhayadiallo8765 Pƙed 6 dny +1

    Ndeyssane bouba Ndour il est tout Heureux yalla ma dounde ba maye sama doom bou jiguene bi

  • @kaami8709
    @kaami8709 Pƙed 8 dny +7

    Ayyy wayyy yallla boussi thiat dougou Viviane mériter ngua Lou eupeu li yalla na yalla tekk lokho si sa ndiabot

  • @nenebathily8079
    @nenebathily8079 Pƙed 7 dny +1

    Je ne la connais pas mais tellement contente pour elle et sa famille. Que Dieu te benisse douce Zeina.

  • @Midou-qk9ic
    @Midou-qk9ic Pƙed 7 dny +1

    Machalah youssou ndour yalla moko tĂšral yalla na seybi bsrkel

  • @NdeyefatouThiam-b7b
    @NdeyefatouThiam-b7b Pƙed 8 dny +13

    Machallah yalna sey bi barkel

  • @tildafah2714
    @tildafah2714 Pƙed 7 dny +2

    Philippe avec son petit frĂšre trop mignon Mach'Allah

  • @Baatinou7
    @Baatinou7 Pƙed 8 dny +10

    Yala na seuybi barkeel waaye❀❀❀❀

  • @KatyNdeyeDiop
    @KatyNdeyeDiop Pƙed 8 dny +4

    Machallah contente rĂ©k,yallana yallah content barkĂ© Al KhourĂąnoul Karim ❀❀❀

  • @sympathisante17
    @sympathisante17 Pƙed 8 dny +2

    Bouba tres humble machallah. Yalla na seyy no barkelll❀

  • @michelndiaye9241
    @michelndiaye9241 Pƙed 8 dny +7

    Modou fall mongui melni Ablaye mbaye ndeysanne rip

  • @AbibatouDiop-ig6sg
    @AbibatouDiop-ig6sg Pƙed 8 dny +11

    Machalah yana seuy bi amine inchalah

  • @beugueyayame8899
    @beugueyayame8899 Pƙed 8 dny +7

    Yalla na seuy bi barkel si barkel alquranoul karim

  • @aminatafaye6474
    @aminatafaye6474 Pƙed 8 dny +8

    Ah Machala yalna Yalla barkel seuy bi

  • @mamadoundiaye1724
    @mamadoundiaye1724 Pƙed 8 dny +4

    YaÄșla nan̈iou yalla may terrangua zeyna heureux menage yalla barkel seybi

  • @NdeyeBintouDieme
    @NdeyeBintouDieme Pƙed 8 dny +3

    Yalla boul guiss loula mĂ©ti gua am sĂ©y bou barkĂ©â€

  • @oliberdij3320
    @oliberdij3320 Pƙed 4 dny

    Ndeyessane je vois un boiba tres joyeux Mashalla yalla na seuy barkel amine ya Rabi

  • @bambaleubvmbv8459
    @bambaleubvmbv8459 Pƙed 8 dny +3

    Nonn bouba dafa yatou lole.yalla nako yalla takhawou

  • @fatou-py5si
    @fatou-py5si Pƙed 8 dny +3

    Congratulations to proud Mama Vivian for bringing up a beautiful and obedient. This what all women pray for. Thanks for being that wonderful woman. May Allah bless the union and give them bless children. Ameen â€ïžâ€ïžđŸŽŠđŸŽŠđŸŽŠđŸŽ‰đŸŽ‰đŸŽ‰đŸŒčđŸŒčđŸŒčđŸŽˆđŸŽˆđŸŽˆđŸŸđŸŸđŸŸđŸ„‚đŸ„‚đŸ„‚đŸ„‚đŸ„‚

  • @alarbacamara8848
    @alarbacamara8848 Pƙed 8 dny +3

    Machalah yalla na seybi barkel félicitations Bouba

  • @magoumbadiakhoumpa9482
    @magoumbadiakhoumpa9482 Pƙed 8 dny +10

    Yalna sey bi barkeil
    Wayei meunn nguenn fennn si titre bii dei ohhhh

  • @AbdoulayeDiallo-is8qj
    @AbdoulayeDiallo-is8qj Pƙed 8 dny +13

    FĂ©licitations yalla n’a seybi barkel si barke seydina Mouhamed psl ♄

  • @user-jd4mo4je1d
    @user-jd4mo4je1d Pƙed 8 dny +5

    Kou guiss khalĂ© bi andak Philippe nimou kheuthiĂ© lokhom bi😝😂😂😂😂😂

    • @AbyKa-le8km
      @AbyKa-le8km Pƙed 8 dny

      Bilay nn CAs Yi aprĂ© la 😂😂😂😂😂

    • @AbyKa-le8km
      @AbyKa-le8km Pƙed 8 dny

      Bilay nn CAs Yi aprĂ© la 😂😂😂😂😂ak pa borome yĂ©rĂ© bou verte biđŸ€ŁđŸ€ŁđŸ€ŁđŸ€Ł

  • @amycisse-vu8yv
    @amycisse-vu8yv Pƙed 8 dny +2

    Zeyna Ndour yal n'a SĂ©y bi barkel inchaAllah

  • @hametdiallo1787
    @hametdiallo1787 Pƙed 8 dny +4

    Masallaa Yalla nasi Yalla def barke❀

  • @fatoumatabintadiallo7702
    @fatoumatabintadiallo7702 Pƙed 8 dny +4

    Machallah
    Yallah n’a seybii barkel

  • @mouskydieme390
    @mouskydieme390 Pƙed 8 dny +2

    Oustaz j’savais bien k dingua ñiew lol 😂 Yalna barckel Pape Cheikh yafi mnke ❀❀

  • @mamythiam3514
    @mamythiam3514 Pƙed 5 dny

    Zeyna yalla na yalla barkĂ©l seuybi yalla mayla ci diabote bou barkĂ©l ❀❀❀

  • @user-rk3mn7ot5w
    @user-rk3mn7ot5w Pƙed 8 dny +4

    Non li mom khĂ©waleu par ce que Dakar tay tout la journĂ©e đŸŒŠïžđŸŒŠïžđŸŒŠïž zeyna yallah n'a sĂ©y bi barkĂ©

  • @madamefall320
    @madamefall320 Pƙed 8 dny +1

    Ndeysane bouba il est trop fiĂšre machalah yalna yala barckel seuy bi

  • @user-jk5zh2bi1e
    @user-jk5zh2bi1e Pƙed 8 dny

    MashaAllah..Heureux Menage Zeyna..que du bonheur ♄♄♄

  • @ZeynaZina
    @ZeynaZina Pƙed 8 dny +3

    Yalah na seuy bi barkél yalah boul guiss lo ragal yalah may la jabott bou barkél nga nÚk si Jam ak sa borom keur kene boumou lene hamal dara si barké seydina mouhamÚd koulay khar yalah na khady

  • @IssaLaye-t4k
    @IssaLaye-t4k Pƙed 8 dny +2

    A machallah test un papa trĂšs trĂšs exemplair wolahi

  • @vieuxsarrbadiane2108
    @vieuxsarrbadiane2108 Pƙed 8 dny +4

    Zeyna .seuyal dé. Koulako wahoul nah nala

  • @mamefatousarr983
    @mamefatousarr983 Pƙed 7 dny +1

    Ndeysane Bouba est trĂšs fier ❀❀❀

  • @jarieujallow8595
    @jarieujallow8595 Pƙed 8 dny +4

    Congratulations Zeyna ❀❀❀❀

  • @mamefatousarr983
    @mamefatousarr983 Pƙed 7 dny +1

    Yalna seuy bi barkel ❀❀❀❀

  • @nadiadiouf7626
    @nadiadiouf7626 Pƙed 5 dny

    Yalna seybi barkel machallah gneup contane❀❀❀

  • @ndeyegallosylla5475
    @ndeyegallosylla5475 Pƙed 6 dny

    Machalla bouba kilifa la machalla takeaways bi raffetna

  • @KhadyNdao-jv2ro
    @KhadyNdao-jv2ro Pƙed 6 dny

    Manite dé les larmes de Youssou Ndour laye wër

  • @damedia4990
    @damedia4990 Pƙed 7 dny

    Thiey you simplicitĂ© thi yaw la nek machalah ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @zz-lv1ye
    @zz-lv1ye Pƙed 8 dny +3

    Senegal akka beuri ay doungourou

  • @aichaaicha7989
    @aichaaicha7989 Pƙed 8 dny +4

    A part yale li yeipeu ya ko woral nakhe ya formé Viviane bamou yeikeu si fi ba yale bolei KO ake bouba bamou ameu si aye tale nére donc chapeau à toi

    • @bintoumane3269
      @bintoumane3269 Pƙed 8 dny

      En plus mo yobou dieukeur zeina bi Europe diapaléko

  • @ndiayemaimouna8472
    @ndiayemaimouna8472 Pƙed 8 dny +1

    Balaye khĂŽl sĂ©dena Macha-allah ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @annandaw6482
    @annandaw6482 Pƙed 8 dny

    Machala yalna seuye barkel ❀❀❀

  • @mariavanessacorrea1190
    @mariavanessacorrea1190 Pƙed 7 dny

    Heureux mĂ©nage zeyna que maman Marie vous couvre avec son manteau virginal amen❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @moutaphagueye-fk5uk
    @moutaphagueye-fk5uk Pƙed 8 dny +1

    Machalla rafétna ta li moy senegal

  • @amarbiosunhome
    @amarbiosunhome Pƙed 8 dny +1

    Bouba tu ressembles beaucoup Ă  mon pĂšre
    Yalna yalla barkel seuybi

  • @abiesallah3213
    @abiesallah3213 Pƙed 7 dny

    Maa’shaa’Allah yalna seye bii barkeh

  • @MameMorseck-ex5iq
    @MameMorseck-ex5iq Pƙed 7 dny

    Yalna seuye barkĂ©l machalleh 🙏

  • @user-un5pz5jt3k
    @user-un5pz5jt3k Pƙed 8 dny

    FĂ©licitations bouba n’dour đŸ„°đŸ„°

  • @mdsconseil6214
    @mdsconseil6214 Pƙed 6 dny

    Que Dieu les protĂšge et nous protĂšge tous đŸ€ČđŸ€ČđŸ€Č
    Heureux MĂ©nage sous la protection d’Allah le MisĂ©ricordieux

  • @ndeyemariebocoum1138
    @ndeyemariebocoum1138 Pƙed 8 dny +4

    Bouba khamna nitt kou bakhla

  • @salladiop2381
    @salladiop2381 Pƙed 8 dny

    Macha allah yalla na seuy bi barkel si barkĂ© Seydina Mouhamed đŸ€ČđŸœđŸ€ČđŸœđŸ€ČđŸœ

  • @adamagueye5504
    @adamagueye5504 Pƙed 8 dny

    Li nekhna macha Allah yallana seybi barkel😘

  • @khadygueye2985
    @khadygueye2985 Pƙed 8 dny +6

    Machllaha ❀❀❀❀❀

  • @hawaguisse4383
    @hawaguisse4383 Pƙed 8 dny

    Machallah yalna yalla barkel seybi❀

  • @monsieursy1412
    @monsieursy1412 Pƙed 8 dny +1

    Seuy ak ndjabot gou barkelđŸ™â€ïž

  • @awadiop4774
    @awadiop4774 Pƙed 8 dny +1

    Bouba ndour beug ndiaboote yalnala yala bayec sa ndiaboote

  • @codoundoye7290
    @codoundoye7290 Pƙed 8 dny

    Machallah Machallah yalla na yalla barkel❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @KawSy-wq4ph
    @KawSy-wq4ph Pƙed 8 dny +1

    C'est tellement difficile ĂȘtre star au SĂ©nĂ©gal.du courage

  • @fatmandiaye6069
    @fatmandiaye6069 Pƙed 5 dny

    FĂ©licitations Ă  Bouba et Viviane. Heureux Menage Ă  Zeyna🙏

  • @jokobennett6513
    @jokobennett6513 Pƙed 7 dny

    Yallah na yallah barkel sey bi
    Je suis contente pour viviane ,
    Siguile nga yaye zena, may God bless this marriage