Le verdict est tombé: Lac 2 est condamné à 5... Sadio Mané offre 10 millions à Lac réaction Lirou di

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 15. 05. 2024

Komentáře • 50

  • @willanbabacar-wx9os
    @willanbabacar-wx9os Před 29 dny +9

    Ndaye sane lacde guér 2 yallah na ko yallah défal diamou 🤲🤲courage lac 2😭😭😭

  • @FatoumatabintouTraore-eh3oh

    Kou nek warngako kholei sa bop dax aduna mii dafay woratei foko doul foguei lay feniou
    Natou fou nek lay dioguei dax diomoul ken diam ak pekheim yalla ak dogalam 🙏🙏
    Courage lac2 koula xamoul wax li bone si yaw waye nioula fréquenter dounioula juger yalla nala borom bi taxaw 🙏🙏🙏

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Před 29 dny +10

    Thank you Sadio Maneh, Manding bless 🙏👍✌️

  • @user-qw7uy4qp8d
    @user-qw7uy4qp8d Před 28 dny +4

    Khaliss d'où dara adouna lép dafaye diekh nite daye doye Lou amoul mbeur amoul Dara adouna dal dafaye diekh 🙏

  • @FatouDiouf-kv6tk
    @FatouDiouf-kv6tk Před 28 dny +1

    Oh lac 2 yalla nala yalla arre

  • @falloudubaisylla7372
    @falloudubaisylla7372 Před 29 dny +12

    Bayiléne fene je des abboné

  • @generalndiaye7353
    @generalndiaye7353 Před 28 dny +3

    Ndayesan Yalla nako Yalla Défal diame 🤲🏽🤲🏽🤲🏽

  • @AbdoulahadWademouratn-qn9nv

    Merci sadio

  • @deguenembengue8787
    @deguenembengue8787 Před 28 dny +3

    Merci fadel surtout xalei yii lolou mo diarra wax beu pare lac dii fayekou ay millions kon loy doyei khaliss sou xalei kon merde way

  • @moustaphababou6282
    @moustaphababou6282 Před 28 dny +6

    Yalnako yalla gene si natou bi

  • @Toulay355.
    @Toulay355. Před 28 dny +3

    Nagnou ame foula journalistes bou fi fenn gnou désabonner

  • @mth1318
    @mth1318 Před 29 dny +3

    Justice soit faite 😢😢😢😢😢

  • @ahmadoucheikhoulkhadim5131

    Nanou def médiation pénale té wax deug Lac de Guerre

  • @faye6718
    @faye6718 Před 28 dny +5

    Féne déffa kharame

  • @dougou-
    @dougou- Před 28 dny +2

    Retour de parc banela? Parc Hann wala Niokolo koba. Non le journalisme d'aujourd'hui

  • @balletassikoafrique8429
    @balletassikoafrique8429 Před 29 dny +6

    Yénn meun ngén féén trop nitte dafay nianal moromo nétam diam

  • @cheikhounagaye9405
    @cheikhounagaye9405 Před 27 dny

    Yalla na souniou borom arr ko té tahawou ko

  • @hamzaseck6630
    @hamzaseck6630 Před 29 dny +6

    Sen sarap nday bu kén abonnée doul rek

  • @Gorguimaxime-fn5tb
    @Gorguimaxime-fn5tb Před 28 dny

    Sou mbeur yeube diokhewone mou guene.Nieuwe bi amoule solo.

  • @mamadoundiaye6051
    @mamadoundiaye6051 Před 28 dny +1

    Déléne wakh deug té di liguéye lou léw

  • @bayemodoungom5604
    @bayemodoungom5604 Před 29 dny +6

    Li rek moka amna fath site internet boutique dougal ay info pour beug ay abonner niou désabonner focus rek su deuk

  • @ahmadoudiop5016
    @ahmadoudiop5016 Před 29 dny +13

    Na gneup désabonner gni dagno meune fén

  • @user-tk5wv1ds6y
    @user-tk5wv1ds6y Před 24 dny

    Akhou sénégalais yi rék moléne dal guissa guoléne dara

  • @xalimagui-officiel9001
    @xalimagui-officiel9001 Před 28 dny +1

    Nitt dagay doylou yemm sissa domaine

  • @el_hadjfalilou3344
    @el_hadjfalilou3344 Před 28 dny +1

    Koufi soul si titre rek kou dougue désabonnéel

  • @bijoukane
    @bijoukane Před 28 dny +1

    Nguirrr yallah lo leine feikeiwoul dei leine mandou yeineu gni Di commentaire layy wakhal feikei wouleine deuggg reik ngueine si âme da ngueine Di mandou toumal nite dafa neik Lou graw mandou leine C mieux dal safara neikhoul

  • @babacarniang3712
    @babacarniang3712 Před 28 dny +1

    Feenn rék

  • @maximediop2278
    @maximediop2278 Před 29 dny +7

    bou ken abonné doll kat yi

  • @bmbtoutestpossible8745
    @bmbtoutestpossible8745 Před 28 dny +1

    Loutax guénn mana féne

  • @mamousene258
    @mamousene258 Před 28 dny +1

    Ki fen rek lay def mosoul wakh deug

  • @matydiane8356
    @matydiane8356 Před 28 dny

    Lac 2 louko. Dall

  • @djibyndiaye8734
    @djibyndiaye8734 Před 28 dny +1

    🤣🤣🤣🤣🤣

  • @konatelamine9935
    @konatelamine9935 Před 28 dny

    Na fay khalisou diambour yi dafa niank diome

  • @cheikhaidara7326
    @cheikhaidara7326 Před 28 dny +1

    Yenne ragale lenn yallah sene titre yii yeup pour lane 🇸🇳

  • @cheikhtidianekeita1045
    @cheikhtidianekeita1045 Před 29 dny +5

    Doull rq ngueeen meunn

  • @PapaBaby-rp3bf
    @PapaBaby-rp3bf Před 29 dny +2

    Mes l'âne motah guéne meuneu doul délene wakh deug mogueune li domeram

  • @bintandiaye4951
    @bintandiaye4951 Před 28 dny +1

    Ana balla gay noko fay

  • @PapaBaby-rp3bf
    @PapaBaby-rp3bf Před 29 dny +24

    Li takhoul guéne am ay abonnés au contraire gneupeuy désabonner

  • @dameniane65
    @dameniane65 Před 28 dny +2

    Barki alkhourane tay lay dèssabonner sèn ndaye doull yi dafa niaaw

  • @abdoubassel9891
    @abdoubassel9891 Před 29 dny +3

    Yaw fadel nafekh nga thie Lobi nga book

    • @seydoudiop4870
      @seydoudiop4870 Před 28 dny +3

      Fadel borom bakh la egoistoul pou rafete la kham

  • @elbiranetoure262
    @elbiranetoure262 Před 28 dny +1

    De sebone partout Domram yi fene rek