ÉDITION SPÉCIALE SUR KÉMITISME ORIGINE ET DÉMARCHE || OustazMorKébé ||

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 27. 08. 2024
  • Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
    / @senegal1
    Le but AlQurann et Sunnah est de participer à la transmission du message islamique dans toutes sa clarté et son authenticité

Komentáře • 47

  • @abdouboiro6796
    @abdouboiro6796 Před 23 dny +2

    Bonjour oustaz
    Vous faites un travail remarquable et vous m’inspirer beaucoup surtout par votre vaste connaissance. La culture générale et la culture islamique m’émeut de trop. C’est qui fait que je te suis partout et te vois comme idole. Vous participez à la redoration du blason sénégalais voire africain et Islamique dans le monde.
    Je prie de vous rencontrer un jour…

  • @qadrbrotherdiagne1491
    @qadrbrotherdiagne1491 Před 2 měsíci +3

    OUSTAZ MOR KÉBÉ MI MASHALLAH KOU AM XAM XAM LAH NI LAH OUSTAZ YI FI NÈK WARA MÈL XAM XAM NI ADOUNA BI DI DOKHÉ SI ZAHIR ,XAM XAM SAY SAY YI LEMBÉ ADOUNA BI "SIONISTES" YI DOMOU ADAMA SOU BAYI YÈP TOP YALLA KÈNAL KO RÈK ALKOU.

  • @seynabousane8817
    @seynabousane8817 Před 23 dny

    MashaAllah amna solo, dieureudieuf oustaz

  • @siacamane3361
    @siacamane3361 Před 2 měsíci +3

    Longue vie a vous ✊ au senegal ✊ ya oustaz ✊ kebe ✊

  • @user-ui2rk6mq9w
    @user-ui2rk6mq9w Před 2 měsíci +1

    Yalna yalla samou alxouran ak sounnah samou oustas mor kébé

  • @diinoulislam4034
    @diinoulislam4034 Před měsícem

    Qu'Allah vous protéger

  • @azizndiaye9995
    @azizndiaye9995 Před 2 měsíci +2

    Oustage mor Kébé toujours pertinente

  • @aboubacrysow510
    @aboubacrysow510 Před 2 měsíci +4

    Assalamou aleykoum wa rahmatoulah

  • @khalifaababacarbodiang6008
    @khalifaababacarbodiang6008 Před 2 měsíci +4

    Manchallah

  • @Eleveurmouton
    @Eleveurmouton Před 2 měsíci +4

    Merci beaucoup 🙋‍♂️

  • @ahmaddia3315
    @ahmaddia3315 Před 2 měsíci +3

    ما شاء الله وجزاك الله خيرا يا اخي الكريم أستاذ موركب❤❤❤

  • @biboujemeh5739
    @biboujemeh5739 Před 2 měsíci +4

    ❤❤❤

  • @alassaneseye2191
    @alassaneseye2191 Před 2 měsíci +1

    Machalah dieuredieufe oustaz mor kebe leral yi amna solo yalla na la yalla faye billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na la yalla sam te arla

  • @abdoulaye6441
    @abdoulaye6441 Před 2 měsíci +6

    Laïcité ak République fi si Sénégal dioulit yi nioko gueneu gueum niou doul dioulit ba gathie Walleu niaka xam wessou woul ba ay Imam fi niokoy défendre

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane7066 Před 2 měsíci +1

    جزاك الله خيرا يا شيخ ❤❤❤❤

  • @ThomasSankara-lz4gs
    @ThomasSankara-lz4gs Před 2 měsíci +3

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ChatBee-yh5nf
    @ChatBee-yh5nf Před měsícem

    Masha Allah Sheikh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @khalifaababacarbodiang6008
    @khalifaababacarbodiang6008 Před 2 měsíci +2

    Très intéressant

  • @abdoulmadjideaydara2297
    @abdoulmadjideaydara2297 Před 2 měsíci +1

    Maallah amna solo👏👏👏👏

  • @SaliouSeye-up4uy
    @SaliouSeye-up4uy Před 2 měsíci +3

    Machalla jërëjëf ustaas

  • @bocomaladi7000
    @bocomaladi7000 Před 2 měsíci +1

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @dialloamadou1905
    @dialloamadou1905 Před 2 měsíci

    ما شاء الله يا استاذ جزاك الله خيرا❤ ❤❤❤❤❤❤

    • @senegal1
      @senegal1  Před 2 měsíci

      Jazakallahou khayrane

  • @ibrahimabalde1234
    @ibrahimabalde1234 Před 2 měsíci

    Machallah

  • @ibrahimatanordiallo1382
    @ibrahimatanordiallo1382 Před 2 měsíci

    Hafizahullah

  • @LaayNjaay17
    @LaayNjaay17 Před 2 měsíci

    Deux de mes récentes commentaires sur ce sujet ont été SUPPRIMÉS.
    Laissez nous de donner notre point de vue comme vous l'avez malhonnêtement fait sur la tradition africaine.

  • @LaayNjaay17
    @LaayNjaay17 Před 2 měsíci +9

    Sëñ bi, di rafetlu gëstu. Waaye KEMIT du diine bay nekk diine ju bees.
    Afrig masu ñoo am diine, kemitisme manees naa wax ni PANAFRICANISME scientifique la. Afrig amul gëm-gëm (croyance)waaye xam-xam (savoir) moo fi am. Gëstug panafricain yi jëm ci xamtu (science ) ak xeeti xam-xam yu ni mel niki "anthropologie" moo yóbbu gëstukat yi ba Mbatit (diine) yi ñu gëm (islaam, Christianisme...) ci mbatitu Afrig la bawoo ca Esipt gu njëkk te mooy Afrig.
    Waxunu nag nit nay dellu ca yu bon ya sunu Maam yaa daa def, waaye yu baax ya sunu Mbatit (culture) amoon ak sunu xayte(civilisation) bi Nga xam ne ci àdduna sépp sukkandiku.
    • Adama baxam nit ku ñuul la woon.
    Nun Afrig xamunu Adama, waaye gëstu yi jëm ci anthropologie li mu saxal mooy nit ñi gëna yàgg seen yax Afrig lañu ko gis. Te ci wàllu BIOLOGIE nit manul bawoo feneen Fu dul suufu Afrig. Ki njëkk amal xayte (civilisation) teg ko ci xamtu (science) am sàrt bu koy "équilibrée" ñu naan ko MAAT nga naan ko baaxul.
    Di jëli culture araab bi, def ko diine, gëmloo ko ñépp, ku ci bokk àjjana ku ci bokkul safara, di nappee Africain yi.
    Lii moo waral kemitisme, du diine waaye doon Africain la tey sàmm li baax ci Afrig. Du leneen....
    Laay Njaay ✍🏿

    • @alioubarry2157
      @alioubarry2157 Před 2 měsíci +3

      C soit t’as pas bien compris le kemitisme, soit tu refuses d’accepter la vérité 🤷🏻‍♂️

    • @abdoulaye6441
      @abdoulaye6441 Před 2 měsíci +1

      Anthropologue yi werentou wouniou ni Adam niit kou nioul leu won Musa Souleymane dou niit kou wekh ni niit kou nioul Niit kou nioul mo niekeu si Aduuna diine Adam moko niekeu andi

    • @bikw2748
      @bikw2748 Před 2 měsíci +2

      Laaj njaay kaddu yi am na solo, di la ci jaajëfal.

    • @aladjidiaoune2421
      @aladjidiaoune2421 Před 2 měsíci

      @@abdoulaye6441dinné dou afaire de peaux nite kou gnul ak kou wéhk yeup pas yam koussi diamou yalla séllaleko douguou adiana kouko wéddi ba déssi douguou safara

    • @OusmaneDg-xt7ns
      @OusmaneDg-xt7ns Před 2 měsíci

      Ta rien compris kefeur la

  • @Baaissatou-ph2xo
    @Baaissatou-ph2xo Před 2 měsíci +1

    Coumaye diokh numero oustaz

    • @zeinaniang
      @zeinaniang Před 2 měsíci

      salam aleykoum attention à celui que tu as en photo de profil c’est un ikhwani il a même été en prison

  • @aboubacrysow510
    @aboubacrysow510 Před 2 měsíci +3

    Assalamou aleykoum wa rahmatoulah

    • @senegal1
      @senegal1  Před 2 měsíci

      Wahalaykoum salam warahmatoulahi