Serigne yéli seye gendarme ndar nakoy mouride Yi di gnanal si bar ké raditou Modone défendre Serigne Touba 17:00 ba 19:00 di kholok comandante bi sa mayumba Sila Serigne Touba don bind raditou anilmawla
Je suis un talibé cheikh mes walay meunou ma tokk journée tee dekhoul wouma khassida Serigne touba yii ❤❤ yalla naniou yalla dayall ciniou khalifa dinné yii ❤
tidiane bou beuggg Sérigne touba mo nekkk nii❤😭😭yalla naniou yalla fayal ahmadou bamba
Loo Lou Moy Lou naturelles joulit waroul thi moom mûy baggn mboke joulit'tam🙏🙏🙏🙏 yalla naa nanu yalla mouzal thi zaytanee🤲🤲🤲
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Ya bakh ,ya goré ya niak kiniane yalla nala yalla fay sa xol
Yalla nalen yalla par💝
@@falloudiouf5750 p6
Je suis tidiane mais dama beugeu khasida serigne touba yii❤❤
Merci xassida BAFA nekk❤
7:46
Deysane ❤😊
Bane mome tidiane bou mbegu serigne falliou mbacké ❤❤
Chaque matin j'écoute se merveille avant d aller à l'école
Même moi aussi bama beugué xassida ❤❤
Talibe baye niass beugue khassida s touba❤
❤❤
Liii mome souma rayoul baxna dieuredieuf serigne touba aka mako beugue
Alhamdoulilah mouride par chance 🙏beug guem wolou doylo ak sante ba faw 😭🤍yaw lan ko def Amadou. Mame. ** Dame** ka diouli won sa gueuth gui
Alkhadoulila ❤sante ❤serigne ❤touba ❤yi.Mountakha yalla nafi yage te dama ❤ ❤❤❤ dieurdieuf serigne touba xassida yi rek ❤❤❤❤❤❤
Euuisbbuwkgtehuejf❤😂😢dbksygod 🎉🎉🎉
👌🙏❤😂
Machallah ❤dieureudieufé cheikhoul khadim
Amine yarabi
Fier d'être musulmans ❤❤ machalla lii nekh si khoool❤🥰😭
😂❤😂❤😢🎉
Macha'Allah 🥰🤍
❤❤❤❤☑️🤍🧡
Walahi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
Leepp benn la 1❤❤❤
Thieuy serigne touba ce xassida me fait pleuré😭😭😭
Alhamdoulilah sante yallah Serigne Mountakha yalna fi yague té weer Mbacké Balla ake Aïcha ake Maram❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kene dou serigne touba 🥰❤️😍
Thiey Serigne Touba amoul morom kén Diam ci yén 🤲❤️
Serigne yéli seye gendarme ndar nakoy mouride Yi di gnanal si bar ké raditou Modone défendre Serigne Touba 17:00 ba 19:00 di kholok comandante bi sa mayumba Sila Serigne Touba don bind raditou anilmawla
Khole yi lote nagnou thie mi Mbeckété ❤️❤️🙏🙏
Alkhadoulila sante Serigne Touba yi.serigne Mountakha yalla nafi yage té dama 🤲🤲🤲🤲
Aminé ❤
❤❤❤❤
Amine ❤❤❤
Yagé len fi loll tawerr mbacké balla incha allah ❤❤❤❤❤❤❤❤😊😊😊😊😊😊😊😊
Ay way li nekh n’a lole wayyyyy ❤❤❤❤❤diarama borom touba 🙏🙏❤️❤️
Dieureu dieuf serigne Touba diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall
Dieureudiief cheikh ahmadou bamba ❤❤❤❤❤❤
Dieureudieuf Serigne Touba Amoul morome 🙏🙏🙏🙏❤️❤️🙏🙏❤️❤️❤️🙏🙏
Oh mashallah yalna yalla fayal malén c la parole d'un talibé cheikh
Bilae li dfa nékh
Alkhadoulila❤ santé Serigne Touba ❤Ass Dione yalnangua goude fane❤❤❤❤❤❤❤❤
Amine
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Noo lii kénn mousou KoO dégue bilahi serigne Touba amoull morom wallahi mot wadjia fii AK fanou Dieumm Igebou tarkhiya yalla Goudou Fann wér tawfékh AK taysir soutoureu dayiman barkép borom khélcom
Bimomy téré nélaw bilay thiéy SERING TOUBA DIEUREUDIEUFATY ❤❤❤
Serigne Touba amoul morom❤️🙏
Allehamedoulilah serigne touba serigne mountaga mbacke basirou guena yague guena were hichallah
Ohhhh niguénn séralé sama xolbi eupnaa machalah ❤❤Dieureudieufati serigne Touba na yalla wéral sén battyi
Amine
Sunu mbecté mi yalanafi yag té weur🤲🤲🤲🤲
Mashallah ❤❤🎉🎉❤❤Borom touba
Machallah waay s touba amoul morom❤
Dieureudieufè❤ serigne touba amoule morom serigne mountakha yague fii tè werr mbackè 🙏💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜💜
Tieyyy xassida yi li nekher na nouner way Machalah ♥️♥️
Ça me fait plaisir et me chaud au cœur
Sabir holbi laydougou❤
0
😟☺️🙂
J’ai toujours les larmes aux yeux quand j’écoute les xassida de Cheikhoul KHADIM 😭😭
I’m soo happy serigne touba ❤❤❤❤❤❤
Machalla Sante Serigne Touba rk fier d'être mourite ❤ mbecté mi 🤣
Akhmadou bamba Brome diam yii Ken la diiiiiiiiii protege partout ahllkhamndoulilahi ❤️🙏
Dieureuf borom Touba ❤❤❤❤
DIEU est unique ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla khasideyi nèkhna si khol Machalla 💚🤍💚🤍💚🤍
Ndeysane. Ass Dionée yagui seral sougnouy khol❤️💯
Serigne Touba amoul morome❤❤️♥️🤲🤲😍😭🙏
Céy Serigne Touba sunu wadji! Ken dou Ahmadou! Khôl yeup sédd nanou
Serigne touba amoul morom 🥰
Les khassida adoucissent les cœurs les plus les durs. Dieuredieufti Serigne Touba MBACKÉ diarama Mame Cheikh Ibra FALL.
Thiey diadieuf Ahmadou 😭❤️
Thiey cheikhoul khadim kèn dou domi sokhna Diarra bousso dji 🙏🙏
Billahi
❤❤❤❤❤❤❤
Machallah lidawna yarame❤❤❤❤😍
Machala yalnou yalla fayal serigne touba
Hamdoulilah yalla dieureudieuf bima néké mouride ❤❤❤❤❤❤❤
Iskeuye mouride
nék mouride Sante yalla baly Aka nékh kene khamout li loumou don rék😭
Machallah serigne ass Dione yalnangua goude fane❤
Amine ❤❤
Serigne Touba amoul morom ❤
Dieureu dieufé serigne Touba❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis un talibé cheikh mes walay meunou ma tokk journée tee dekhoul wouma khassida Serigne touba yii ❤❤ yalla naniou yalla dayall ciniou khalifa dinné yii ❤
Serigne Mountakha yalna fi yagu té wer aaaaamiiiiiin yaraby mbacké balla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Amine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhamdou wa choukrou lill rabile halamine 🙏🙏❣️❣️
Serigne Touba rek mo nekh si khôl doulenén
Dieuredieuf Serigne Touba ❤❤❤
❤❤❤❤❤ماشاءالله ماشاءالله جرجف بروم طوبى❤❤❤
ماشاء لله ماشاء لله جرجف سرج طوبى❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah Dieureudieuf Cheikhoul Khadim
Mancha halla mancha halla 🙏🙏🙏🙏❤️♥️ l❤❤
Dieureudieufeti Serigne Touba❤❤❤
Dieureudieuf serigne touba
Ndeyesane serigne touba ken dou moom dieureudieufe serigne saliou
Billahi
Barké xassidayi Serigne Touba amnio fayam kholal raditou Anil mawla bi rk machalla way
seringe touba amout morome alhamdoulilha rabilhamine bima boké ker borome touba 😭😭😭
Jeureujeufeuty serigne touba ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤kendou Ahmadou bamba khadim Rassoul ❤
Waw len gorrr yalla na SERIGN bi deubb len kartann barkép xasside tè diapandal bâât yii ba fawwu
Machallah linéhena❤❤❤❤
Je pleure en écoutant sa machalla
barki serigne Bamba serigne Touba Amoul moroome
Machalla ass dioún Sama khol sedéna man bara baye fall ❤❤
Dieuredieuf Serigne touba ❤️❤️❤️❤️
Alhamdoulilah 🥰🥰🥰
Allahou Akbar, Dieureudieuf Cheikh Ahmadou Bamba.
Dieureudieufé serigne touba🙏❤️
Dieureudeuf serigne touba❤❤❤🙏
❤❤❤
Amoul morom
Ndeysane serigne touba amoul morom
Billahi ❤❤❤❤
machalla ❤️🎉🎉❤❤❤🙏
Borom touba❤
Machalla djereudeufê borome touba❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieuff cheikh Ahmadou Bamba
ماشاء الله ❤❤❤❤
Dieureudieuf serigne Touba
😭😭😭😭
Barkii borom touba douma si doyallllll❤❤❤❤❤❤❤❤
🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲 8:11
Jerejeuf serigne touba
Machalla diaradieufé serigne Touba ❤❤❤
Yalna borom bi bole si dianboote Khadim Rassoul so barkep Seydina Muhammad Ibn Abdelaziz PSL ❤
MaschAllah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🇬🇲❤❤❤🇬🇲🇬🇲❤
Thieye serigne touba amouniou Kimi ou defal mo nex ❤️🥹🫶
Khassida bi nimouy def si sama birr khol bi mane ak yala rek nioko kham bilahi🤦🏻♀️ken dou serign touba🙏🏻😭
Fière d'être mouride❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
😭😢❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤@@deffayamambengue3432
Bly ❤❤❤
MACHALAH
Brome touba amoul morom ❤❤❤❤
Machalla 🥺🥺🥺🥺🥺🥺🥺👍
Ohh machalahh ❤❤
Kene d'où ahmadou😭😭😭😭😭 bilahi yallana nouko yala fayal