Eumeu Séne Dornako , tankk daanko daan bou leer Nagn « sa Thies Danou »

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 4. 05. 2024
  • ALBOURAKH EVENTS LA CHAINE EVENEMENTIEL
    "Suivez-nous sur Albourakh Events TV, votre destination ultime pour une expérience immersive alliant sport, culture et événementiel. Plongez dans un univers où l'excitation des compétitions sportives rencontre la richesse de la culture, le tout ponctué d'événements inoubliables. Rejoignez-nous pour vivre des moments uniques, où chaque instant est une nouvelle aventure à découvrir. Albourakh Events TV, où la passion devient spectacle."

Komentáře • 361

  • @cheikhousamb30
    @cheikhousamb30 Před měsícem +11

    Damako begue dama ko wolou félicitations 🎈🍾🎉🎊 champion bo dané niou contane bo dano sakh dagniy contane malgré tou jambar deug gua Barki cheikhou tidiane yalla nala jik🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @SALOMONOfficielle
    @SALOMONOfficielle Před měsícem +18

    Eumeu dou mbeur bouniouy sax saxé meun na door meun na beuré machalla ❤❤❤

  • @diaspora2553
    @diaspora2553 Před měsícem +8

    Kou bague albourakh la lal j'aime

  • @matasidibe6344
    @matasidibe6344 Před měsícem +8

    Bon je vois trop de critiques sur sa Thiès ,sais normal, mais par fois il faut dire les choses telles qu'elles sont d'abord je tiens à féliciter eumeu séne et décourage pour sa Thiès. Alors pour dire vrai aujourd'hui pour ceux qui connaissaient sa Thiès très bien aujourd'hui pour moi non-seulement il a bien respecter son adversaire il sait très bien et nette a qui il a affaire parce que eumeu séne n'est pas n'importe qui donc sa Thiès a bien gérer le combat avec sérénité et calme franchement je n'ai rien contre sa Thiès aujourd'hui il a pris maximum temps d'examiner la situation avant d'attaquer jusqu'à ce que eumeu séne arrive a lui terrasser et c'est la volonté de Dieu. Je souhaite le meilleur pour les deux lutteurs vivre la lutte sénégalais, vivre le Sénégal.

  • @DoudodiengDoudo
    @DoudodiengDoudo Před měsícem +7

    Sama xol sedna😂❤

  • @khadimdiouf177
    @khadimdiouf177 Před měsícem +58

    Félicitations eumeu sene le grand champion

  • @KemoDiedhiou-xh2wf
    @KemoDiedhiou-xh2wf Před měsícem +1

    Ya meune ya eupou dole ❤❤ champion roi quena mola diahale

  • @absn658
    @absn658 Před měsícem +35

    Niniou def sa thies dal yalla nagneko def balla gaye inchallah amin

  • @FallouLeye-gs3xt
    @FallouLeye-gs3xt Před měsícem +34

    eumeu séne mo geunon paré sa thies fépe dako eupe dolé fouf💪💪💪 félicitations eumeu ❤❤❤❤❤❤

  • @sergedione7658
    @sergedione7658 Před měsícem +15

    Seutou Samba khoyane Ngom bi késser touss nakk dara dou khéw ndam rek🦁💪🏾✌🏾✌🏾inchallah 🫶🏾.Seutou Samba khoyane Ngom bi késser touss nakk dara dou khéw ndam rek🦁💪🏾✌🏾✌🏾inchallah 🫶🏾.

  • @beyonder1918
    @beyonder1918 Před měsícem +59

    Eumeu est un grand champion mais franchement je n'ai pas reconnu Sa Thies aujourdh'ui.

  • @abdouazizaidara3899
    @abdouazizaidara3899 Před měsícem +2

    اَللَّهُمَّ صَلِّ عَلَي سَيِّدِنَا وَمَولَانَا مُحَمّدٍ صَاحِبِ الْقَوْلِ لاَ إِلٰهَ إِلاَّ اللّهُ وَسَلِمْ عَلَيْهِ وَعَلَي ءَالَهِ وَصَحْبِهِ وَاجْعَلْ بِجَاهِهِ آخِرَكَلَامِنَا لاَ إِلٰهَ إِلاَّ اللّهُ مُحَمّدٌرَّسُولِ اللَّهِ صَلَّ اللَّهُ عَلَيْهِ وَسَلّمَ ءامين 💖🇸🇳♥️

  • @ablayesarr9530
    @ablayesarr9530 Před měsícem +3

    Félicitations eumeu et courage sa Thiès sa Thiès defaroul gua nieuwattt lambeau dji amguathi waleu

  • @Dabaakhmaalick
    @Dabaakhmaalick Před měsícem +22

    Felicidades eumeu ms sa thies waro won beurei consigne😊

    • @ousseynoudiopnabiengssalio7511
      @ousseynoudiopnabiengssalio7511 Před měsícem +2

      Nio ko yaxall lamp

    • @sergedione7658
      @sergedione7658 Před měsícem +1

      Bouko défoul wone déy geuma gniaw
      Seutou Samba khoyane Ngom bi késser touss nakk dara dou khéw ndam rek🦁💪🏾✌🏾✌🏾inchallah 🫶🏾.

  • @elzodieng8067
    @elzodieng8067 Před měsícem +116

    Emeu Sene mon meune wa gediewaye modou lo mon meune wa Pikine balla gaye2 mon meune wa parcelle tou cour 😂😂😂😂😂😂😂

    • @Diaz426
      @Diaz426 Před měsícem +2

      😂😂youhou diouk na founiou ko foguewoul dh

    • @abdoudiop7177
      @abdoudiop7177 Před měsícem +11

      Det sawaye balla modou la meune wala wa parcelle haral ba Franc diappouko

    • @sounahtv6
      @sounahtv6 Před měsícem

      😂😂😂

    • @elzodieng8067
      @elzodieng8067 Před měsícem

      @@abdoudiop7177 khana youssou ndour danoul talpha fis de balla dan gora sok khana do khol

    • @elzodieng8067
      @elzodieng8067 Před měsícem +1

      @@abdoudiop7177 saway franc mbeurou 20 million là balla gaye2 dou beure ak mbeurou 20milion modou lo moy papaye franc balla gaye daka diouteul nganan franc yaw danga bakh rek

  • @user-km5ll2un2m
    @user-km5ll2un2m Před měsícem +9

    Pikine késsé vraiment félicitations à pokooo mbaaaame et eumeu sène champion taye môme khôl daffa féss billaahi 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-qx3be4gd1p
    @user-qx3be4gd1p Před měsícem +11

    Eume dale vrés champion la koi

  • @mouhamedsow331
    @mouhamedsow331 Před měsícem +4

    😂😂😂 Dan mak Dan rak😂😂😂 ow eumu tamit wa bahna congratulations 🎊 ❤❤❤

  • @BachirGueye669
    @BachirGueye669 Před měsícem +51

    Bimouye dan Balla si digue doller lako dan sa aussi 👍

  • @user-mg2nt7df3n
    @user-mg2nt7df3n Před měsícem +22

    Du courage sama champion bi félicitation eumeu sene

  • @mamadouniagn7836
    @mamadouniagn7836 Před měsícem +1

    Félicitation eumeu tu as bien fait

  • @mohamedmustaphadiouf8293
    @mohamedmustaphadiouf8293 Před měsícem +3

    Serigne yi diokh sa thiés victoire fokné nioy yallah Bayilen Lou ngén néké

  • @mouhamadourassouldemba6333
    @mouhamadourassouldemba6333 Před měsícem +11

    bour gueweul c le meilleur analyste de lutte ; newone na eumeu dafa beugueu nakh sa thies
    temps yi keur doubless nekhoul ; il faut que gayi tokk khol nouniouy gerer sene combat ; sa thies tey danga bayi sa meunine motakh fegn na si combat

  • @user-ss7tx6cu7y
    @user-ss7tx6cu7y Před měsícem +1

    Sa thèse champion là que le bon dieu vous guide dans tout vos projets eumeu sene félicitation

  • @grishenko927
    @grishenko927 Před měsícem +11

    Sa thies je le supporte à chaque combat mais même contre reug reug c par chance leu gagner et franchement contre eumeu sene avant le combat je savais que sa thies n'a aucune chance de gagner eumeu sene. Sa Thies c un athlete mais c'est pas un excellent lutteur, daffeu plafonné. Mais nak courage il peut revenir, il doit travailler sur ces lacunes sinon il risque d'avoir des problèmes surtout avec les nouveau boys

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc Před měsícem

      Wakh ga lou gnou beuri Di wakh si souf reug mo meune sa thies 10 combat mou dane ko dafa xep sa thies défe erreur mais xolal jour bobu ni combat bi diéxé

    • @bassithegamer8077
      @bassithegamer8077 Před měsícem

  • @user-cp9us6pi4w
    @user-cp9us6pi4w Před měsícem +1

    Kou d'accord ni reporter bi dafa deur ba yakou rek lalal j'aime 😂😂😂😂

  • @borombidiene1727
    @borombidiene1727 Před měsícem +10

    Eumeu le vrai Roi des arènes il a battu BG2 et B52 (2 fois chacun) gris bordeaux lac de guiers.. seul Modou lo échappé

    • @user-by1ve5pb1p
      @user-by1ve5pb1p Před měsícem

      Ak tapha tine

    • @kefgg
      @kefgg Před měsícem

      ​@@user-by1ve5pb1pNon on c'est Tapha qui a battu Eumeu Sene

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc Před měsícem +2

      Béne roi des arènes mo ame c'es le goat Modou lo🥇👑

    • @borombidiene1727
      @borombidiene1727 Před měsícem

      @@MilkMilo-qr5uc Modou a été battu par B52 et BG2... eumeu Sénégal est le seul à avoir une défaite parmis les ténors

    • @MilkMilo-qr5uc
      @MilkMilo-qr5uc Před měsícem

      @@borombidiene1727 faut arrêter les rêves stp

  • @zalefaye5716
    @zalefaye5716 Před měsícem +6

    Eumeu combat djiankha rek lay am aïthia doff dou wër dé

  • @user-qx3be4gd1p
    @user-qx3be4gd1p Před měsícem +18

    Balla diouf y’a wakhone sathies moy favori dof gua kou dane balla lagu bobardier gris gua diokhe sa thies favori

    • @papaba9638
      @papaba9638 Před měsícem +5

      Frr si jeunesse bi la xol mtx mu diox sa Thies favori c’est normal quoi qu’on puisse dire eumeu fin carrière la nekk nk
      Je penses sa Thies mo diay combat wam l’Utah muy forcé action ba eumeu diko takk du baxul rothiékul nga taxawate ☹️

  • @NdiayeBoure-ik4gg
    @NdiayeBoure-ik4gg Před měsícem +3

    Félicitations eumeu séne le grand champion du courage sa Thiès

  • @mohamedmbengue2843
    @mohamedmbengue2843 Před měsícem +9

    Pikine moy Sénégal ❤❤❤

  • @leveridique-kj7qo
    @leveridique-kj7qo Před měsícem +28

    Kone Tapha Tine mi dane eumeu sène ndéké diambar la😂😂😂

  • @mouhamethniang3154
    @mouhamethniang3154 Před měsícem +5

    Eumeu sene moko meun foufe wakhon nalenko

  • @IssvOfficiel
    @IssvOfficiel Před měsícem +1

    Fliflapp modou lo biii si eumeu🤩😍❤️

  • @bassiroudiouf9110
    @bassiroudiouf9110 Před měsícem +3

    Mais reporter yii esk nitt laniou ? Faaarr amna mais soyez sportif nak ! Eumeu dan ko bamou diakhane, le gars dit ‘ naniou xaar arbitre ‘ du n’importe quoi !
    Félicitations a Eumeu un champion ✅

  • @KamaraSarr
    @KamaraSarr Před měsícem +6

    Alhamdoulilahi ñioun guédiawaye rék lañiou top décourage sa thiés félicitation eumeu séne c'est le sport défaite AK match nul AK victoire ñio andeu inchallah sa thiés irra yallah balla am ndam cii kaw tapha tine

  • @user-ei6hr5bp1i
    @user-ei6hr5bp1i Před měsícem +3

    Jai vraiment pitié de la famille de balla gaye. Deux rère battu par eumeu sene.cest triste .felicitation eumeu. Et me encouragements à sa thies.

  • @MouhamedDione-zr9kv
    @MouhamedDione-zr9kv Před měsícem +4

    Félicitations liss niago

  • @DardaBassil
    @DardaBassil Před měsícem +4

    🤯🤯🤔Modou LO nila danéwon Eumeu Sene 🤔🤯

  • @yatmaseck3056
    @yatmaseck3056 Před měsícem +9

    Franc Eumeu combat ladeh❤

    • @abdoungom5338
      @abdoungom5338 Před měsícem +2

      Mooo franc amoul bayreee😂😂

    • @yatmaseck3056
      @yatmaseck3056 Před měsícem

      @@abdoungom5338 franc moy xlo
      Xlo moy franc

  • @SadioWade-gh8uz
    @SadioWade-gh8uz Před měsícem +1

    Félicitations eumeu Barki serigne Babacar sy gneupe contane machallah yalnala djik

  • @RubensjoseDovigo
    @RubensjoseDovigo Před 3 dny

    QUE LUTA QUE TEVE AÍ??.SÓ FRESCURA

  • @abasall711
    @abasall711 Před měsícem +4

    Félicitation eume ma bek

  • @ndiagandiaye3939
    @ndiagandiaye3939 Před měsícem +3

    Kou d’accord nii même chite biko modo lo danè mom l’a utilisé
    Philip phalap + tégal chaise

  • @diarra__diouf777
    @diarra__diouf777 Před měsícem +2

    Kou done khar sa thies Modou lo😂 sawil teh teudi sa, seu beuré desna dh dondou wo sa grand frère dh😂 bref courage yalla bakhn

  • @user-cw5sq1ll1t
    @user-cw5sq1ll1t Před měsícem

    Sa Thiès dou sma mbeur mais billah diambar la déf na lépeu pour am ndam mais ni lko yalla beugué le meilleur reste a venir sa Thiès
    Eumeu séne dou sma mbeur félicitations ci victoire bi mbeur le meilleur reste a venir
    Vive le Sénégal 🇸🇳🇸🇳

  • @fatoumbaye1121
    @fatoumbaye1121 Před měsícem +6

    Modou lô le maire de pikines modou lô boroom pikines eumeu séne le maire de guédiéwaye 😂😂😂😂😂😂😂😂 dane macke dane racke thieuy eumeu séne bou yagué gan méleni modou modou diékhalna wa pikines yeuppeu 🤣😂😂😂😂🤣🤣

    • @Lovefootball221
      @Lovefootball221 Před měsícem

      Ak lac2

    • @LougaLo-pl5jr
      @LougaLo-pl5jr Před měsícem +1

      😂😂😂😂

    • @fatoumbaye1121
      @fatoumbaye1121 Před měsícem

      @@Lovefootball221 lac2 day khaar lac2 maxinul rek khana Dina rouss gouvernement bou bess bi té bayi maxinul 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣

  • @ndiagaboujetlee9651
    @ndiagaboujetlee9651 Před měsícem +12

    Sathies vs modou lo yakhou na 😅😅😅😅

  • @galassefaye4587
    @galassefaye4587 Před měsícem +2

    Mes forme eume sene bi machala

  • @aissatousy1875
    @aissatousy1875 Před měsícem

    Courage sa thies félicitations eûmes sene sa thies cil dan dou gathe dan coune demal defara wat rec inechala le meilleur rest a venir bala comba wam bigne gnew yal co yal may nam❤❤❤ amin

  • @bayemodoubmwndour9773
    @bayemodoubmwndour9773 Před měsícem +2

    Nooo vraiment Al burakh mofi meune avc leur chroniqueur

  • @ndeyekhadygueye8915
    @ndeyekhadygueye8915 Před měsícem +1

    Merciiii mr le maire de pikine modou lo yaguiii diapalé wa pikine

  • @miami7867
    @miami7867 Před měsícem +1

    Ayy way sama cousine bi deuk Pikine nénma guediawaye souniou plat préféré 😢😢😢😢😅

  • @serignembackeseck8998
    @serignembackeseck8998 Před měsícem +2

    Sa thies champion leu

  • @clouchevraimentfall797
    @clouchevraimentfall797 Před měsícem

    Wouuu manhui foga sétane combat bi eumeu dako douma danko dolé dokjoul diam

  • @user-vk6ws5rd2d
    @user-vk6ws5rd2d Před měsícem +2

    Eume séne flecitation ❤

  • @durkio5486
    @durkio5486 Před měsícem +2

    Nan eumeu sene vrai ndannane leu et les sois disant experts nieup sa thies laniou diokh favoris

  • @kandykebe675
    @kandykebe675 Před měsícem +2

    Courage champion démérité woo

  • @fatoucheikhfall6623
    @fatoucheikhfall6623 Před měsícem +1

    La lutte renferme un mystére impitoyable que nul ne sauraut déchiffrer

  • @habibfaye14
    @habibfaye14 Před měsícem +3

    Eumeu Limou indi contre tapha tine khadioul si sa Thiès

  • @IslandCure-hr4iy
    @IslandCure-hr4iy Před měsícem +1

    SATHIES WAKHONALA NA NGUIMB DOIT AVOIR DU JAUNE ET BLEU MAIS EUMEU SENE LUI LA FAIT JAUNE BLEU. YAW NGUA NIEUW DEF JAUNE VERTE. C COULEUR C IMPORTANT POUR NDAM ON NE MELANGE PAS VERTE ET JAUNE C DEFAITE.. Bravo eumeu courage sathies. BALLA GAYE2 TU ES PREVENU FAIT GAVE JE TE PREVIENT MOYTOUL LOU BARI SURTOUT WA GUEDIAWAYE YA TROP DE JALOUX A GUEDIAWAYE DANIOUY SOOB REK SEN INTERET REK AY DIAW MAGG YOU REEW YAKHA BESS REK. AY 5TONNE VRAIS DOMERAM. KOU TEYE SATHIES DANIOUKO WARRON BAYI MOU DEFF LIMOUDOON DEF. LAMINE GOLO GATE KHAMOUKO MANOUL ENTRAINE MBEUR

    • @pataba12
      @pataba12 Před měsícem

      Bilahi frère jai assisté combat super diamono.gakou 2 mani gni amouniou entraîneur nioumaye saga me chask grand combat daye feye basi écuries walo sa se voit souye lac d guère di beurei

  • @aboubakrsidiqhndiaye8524
    @aboubakrsidiqhndiaye8524 Před měsícem +1

    Gaïndé nga eumeu

  • @cheikhoumarkoundoul1421
    @cheikhoumarkoundoul1421 Před měsícem +1

    Félicitations à eumeu et du courage à sa Thiès

  • @mamaddione8758
    @mamaddione8758 Před měsícem +2

    Emeu Sene haleyi yimouy bokal entraînement comme doudou sane nio eupe doole sathies

  • @Ahmadouboromediamono4
    @Ahmadouboromediamono4 Před měsícem +28

    Ça montre que tapha tine est puissant vous qui le critiquer contre eumeu allons rek 😂😂😂

  • @Fitserigne
    @Fitserigne Před měsícem +2

    Eumeu seul💪

  • @malalniang7069
    @malalniang7069 Před měsícem +2

    Eumeu wakhoon nako
    Bou kenn bayyillo Sa thiés meuni nam . Sa thies da changé complètement stratége boumou daan beurré
    Féliz sama mbeur bii Eumeu

    • @babacardiouf7297
      @babacardiouf7297 Před měsícem

      Commentaire bi laa doon weur...yew rekk yaa wakh deug nak sa Thiès depuis klk année beurèm deug dafa réer

  • @ahmadoudiagnegueye9918
    @ahmadoudiagnegueye9918 Před měsícem +1

    Félicitations eumeu courage sa Thiès

  • @SaliouKane-wt9yq
    @SaliouKane-wt9yq Před měsícem +2

    Sa thies kassé wallahi ❤❤

  • @thianembaye2173
    @thianembaye2173 Před měsícem +3

    Li key dou expérience katane la eumeu dafa takhaw

  • @user-oe3lg6zw5q
    @user-oe3lg6zw5q Před měsícem +4

    Serigne ndiay/sathies

  • @NiagBoye
    @NiagBoye Před měsícem +1

    Molen man eum❤

  • @salinhogaucho10
    @salinhogaucho10 Před měsícem +3

    Sa Thiès dou mbeur jtj et il sera pas un grand champion...... Un jeune lutteur bo kham ni sa combat capital yeup nga perte

  • @papipapi344
    @papipapi344 Před měsícem +5

    EUMEU MOD LO REK MOKO MEUNAL DARA 😂😂😂

    • @kefgg
      @kefgg Před měsícem

      Ak Tapha Tine boul faté

    • @bilalkhalyfall9938
      @bilalkhalyfall9938 Před měsícem +1

      ​@@kefggsaway liko modou lo déf mbeur défoukoko contre tapha tine eumeu sene dako daur bamou réglé

  • @papahabibdiopofficielle3160
    @papahabibdiopofficielle3160 Před měsícem +7

    Ohh sa waro bayi sa meuninn ich

  • @ibrahimathiam60
    @ibrahimathiam60 Před měsícem

    Kou geum ni commenteur yi dagno saytané lalale j'aime 😂

  • @AhmedThiam-gl2uv
    @AhmedThiam-gl2uv Před měsícem +1

    Modou lo Moy séne baaye ❤❤

  • @abdoungom5338
    @abdoungom5338 Před měsícem +2

    Sa mi ponou pirrree le😂😂😂😂

  • @Makaytunkara
    @Makaytunkara Před měsícem +4

    Eumeu is the king 🤴❤❤❤❤❤

  • @Fallyaram320
    @Fallyaram320 Před měsícem +2

    Thiey eume le gladiateur

  • @user-td9el3ko3z
    @user-td9el3ko3z Před měsícem

    moye sene baye dore grand frere vraiment sa thies khambona doufi ndane ndockh machaalaaah maire guediawaye

  • @amethlamine9772
    @amethlamine9772 Před měsícem

    Franchement guissouma wone sa thies Foumouy diaar eumeu

  • @badaradia8335
    @badaradia8335 Před měsícem +1

    Di lén Wax biss bi ak waxtou
    wi. Ndakh archive yii gnou am ay repères

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Před měsícem +1

    Am not angry ,,felicitations Eumeu

  • @Ydakh-ui5yo
    @Ydakh-ui5yo Před měsícem +2

    Sathies l'agneau du sacrifice comme dou rakam

  • @MarieSeck-ss6vk
    @MarieSeck-ss6vk Před měsícem

    Eumeu kasée❤❤

  • @Domou__rewmi.
    @Domou__rewmi. Před měsícem +4

    Eumeu dof la rek do combine ngaye 😢

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 Před měsícem +2

    Nite bo amé sa meunine doko bayii Sathies sa wa staff ño yak sa lamb

    • @pataba12
      @pataba12 Před měsícem

      Jai toujours dis ca amouniou entraîneur walo ecurie balla gaye 2 daniouye dane rek

  • @laminefall6481
    @laminefall6481 Před měsícem

    sa la farar me lambou dji nékh na trop 🎉 sa décourage

  • @Moussa-wf3ll
    @Moussa-wf3ll Před měsícem +5

    Eumeu🎉🎉

  • @tidianediallo2262
    @tidianediallo2262 Před měsícem +2

    Eumen❤❤❤❤

  • @SeneMouhamed-tk5sg
    @SeneMouhamed-tk5sg Před měsícem

    Kou deur Aka Bari wakhe😂😂

  • @user-mx4ee1we1y
    @user-mx4ee1we1y Před měsícem +5

    Sathiès seul ❤❤❤

  • @ousmanementethiam7854
    @ousmanementethiam7854 Před měsícem +2

    Eumeu dou moromou khale

  • @user-pg5bp4jw3p
    @user-pg5bp4jw3p Před měsícem +1

    Baye Ndiaye yw laye waxal yéneu yalla térall naline guineu diapu lambe dji diko deff pér pér wi aye doram guéneu rekk sa Thiès yw 3 défaite yépu wa guédiawaye nio KO tegué 😢

    • @IslandCure-hr4iy
      @IslandCure-hr4iy Před měsícem

      Tekssi lamb JINEE yi ay GOUDI a chaque fois c eux enfaite lamb 2h du MATIN en exterieur c abuse je les estime mais maintenant fuck son nul dejas balla et tapha ne devait pa's venire sa servait a rien

  • @YanisOurraoui
    @YanisOurraoui Před měsícem

    voila beni

  • @mansourmbaye6926
    @mansourmbaye6926 Před měsícem

    Combat bi bétouma dh vu leur forme physique comme si sa Thies mon maak eumeu Séne

  • @user-uq2vl8wx2o
    @user-uq2vl8wx2o Před měsícem +4

    Dmrm yénéne combat yi bala nio dougou di sétane khamnagne kou dane la sen mbeur laniou mo tah ngéne titré li

  • @soraboukharaglo
    @soraboukharaglo Před měsícem

    Félicitations champion

  • @papeousmane1011
    @papeousmane1011 Před měsícem

    Gaïndé lamb dji eumeu sene moko wara toudou tei sii mom laa geuna djék bilahi mom rk mofiy wané foula ak diome tei magg bou eup dolé xallé yii leu vrai sportif leu