BURD 2022 - NUIT 7 - Zawiya El Hadj Malick SY - Communication de Serigne Habib SY Dabakh

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 3. 10. 2022
  • Abonnez-vous à notre chaine CZcams et Activer la Cloche, pour suivre EN DIRECT tous les grands evenements de l’Islam et de la Tidjaniyya
    EN HAUTE DEFINITION

Komentáře • 149

  • @abdouazizdrame7436
    @abdouazizdrame7436 Před rokem +16

    Bilay walaye xam xam keur Maodo la deuk

  • @oumarsow300
    @oumarsow300 Před rokem +16

    Bilahi walahi talahi bou séne mame délou siwone douguéne dèfarate sène togaye djeureudjeuf sy Malick yéne bakh

  • @pape94seye32
    @pape94seye32 Před rokem +11

    Machalah yallana niou yalla Fayal maodo ak wa keureum barké seydina mouhamed saw bilahi xol yep Sedna

  • @linedor588
    @linedor588 Před rokem +12

    Yalla na yalla sakh siii diniou fayal Seydil Hadji Malick Sy

  • @ajamais735
    @ajamais735 Před rokem +63

    Que dieu me pardonne, mais, hier soir, Mash'Allah ! Khôl Sedatina, un homme véridique, j'en ai pleuré, à un moment donné, je me suis sentie bien, car j'ai eu l'impression, qu'il parlait de se que je subis continuellement. Dieureudieufety Talibe Cheikh très très fière de vous. Longue vie, bonne santé et surtout ne changeait rien. Vous m' avez fait beaucoup de bien et je suis sûre que j'etais pas la seule. NALLAH YALLAH FAYE TE TAKHAOULA INSH'ALLAH !

  • @baathiieisred7093
    @baathiieisred7093 Před rokem +22

    Nimouy wakhei arabe mo nekh😍♥️Serigne Mouhamadoul Habib Sy Dabakh Masha Allah waxtan nexna trop
    Yalna y’Allah fay yiw bijahi Rassulilah (Salatou Aleyhi Wa Salam)

  • @malicksene5450
    @malicksene5450 Před rokem +3

    Yéne gni di sagga solène amone touti khél dégue né serigne bi wakh n'a ak yéne ba paré. Kou ci nek n'a khôl wadiouram teukeulé KO ak Serigne bi. Ndaw sou beugué am barké day maytou di wakh Lou Gnawa ci mak surtout koula eup thieur thia Yalla

  • @modoumaramelo7017
    @modoumaramelo7017 Před rokem +18

    Machalah serigne mouhadoul habib sy dieuredieuf cheikh seydil hadji malick sy

  • @airafrique8193
    @airafrique8193 Před rokem +12

    Al khalifa Serigne Babacar sy Mansour yalnafi yague té wéur Amine ❤️❤️❤️

  • @AbdoulKonate-uo6zd
    @AbdoulKonate-uo6zd Před 2 měsíci

    Maachallah Sy Malick Dabakh Serigne Habib Sy

  • @khadygueye5933
    @khadygueye5933 Před 3 měsíci

    Yéna guôré sy yéna bakh

  • @momarcisse6603
    @momarcisse6603 Před rokem +4

    Kénn dou Abdou Aziz Mbaye machalah ya meuna way

  • @pointdevue1304
    @pointdevue1304 Před rokem +12

    XAM XAM AK SOUNA TIVAOUANE 😍😍😍🇸🇳🇮🇹

  • @saliousewane1697
    @saliousewane1697 Před rokem +4

    Yonente yalla Mouhammad rek mooy deug

  • @babacardiop1742
    @babacardiop1742 Před rokem +3

    Sy malick Habibou lah machallah Amnasolo yalna yalla faye samola

  • @massambafall582
    @massambafall582 Před rokem +14

    serigne bi mome dmaka beugeu rk barké brome touba

  • @safietounguenodiakhate8012

    Bilahi walahi toumall gor bou defoul dara nekhoul si xoll depuis mon enfance jusqu'à présent je l'ai vécu té dara dou fegn mou diakhal ma loll 😭😭😭

    • @papesall3416
      @papesall3416 Před rokem +1

      Massa adouna natou doufi diok

    • @mamefamasamb3084
      @mamefamasamb3084 Před rokem +4

      Yaayou mame Dabakh, yalla daffa mandou, koumou naroul fay doula ligueey loo.
      Nattou si ligueey yi yalla di santaané la bokk..
      Yalla naniou Allah may kholou mougne..
      Alhamdoulilah

  • @dabakhwade6497
    @dabakhwade6497 Před rokem +7

    Al'hamdou lilah sante Yàllah boubah

  • @binetasakho2935
    @binetasakho2935 Před rokem +5

    Mashalla Dieureudieufff Sy Malick yalla nagni yalla deifal degu ak topou 🙏

  • @dikonediop1921
    @dikonediop1921 Před rokem +5

    Diarama seydil hadji Malick machalla

  • @binetoudiakhate6759
    @binetoudiakhate6759 Před rokem +8

    Machala Sy yalnala Yallah maye diam

  • @mansourdiagne9114
    @mansourdiagne9114 Před rokem +7

    Maleu beugue Sy Malick

  • @abiboufall6968
    @abiboufall6968 Před rokem +3

    Xol séde n'a sy Malick yalna yala goudal sa fane

  • @ousmanesabaly123
    @ousmanesabaly123 Před rokem +10

    Alhamdoulillah Sy Malick Dieuredieuf

  • @salimatagueye4845
    @salimatagueye4845 Před rokem +3

    Machallah goudou fane ak wer sy malick

  • @papekante6352
    @papekante6352 Před rokem +9

    Serigne bi macha'alla

  • @alidiao1540
    @alidiao1540 Před rokem +2

    Machala sy malick vrement machala tabaracalah machala alahou Akbar vrement khol sedeuna wakh tane bi dou wakhtane ensegnement leu lep tawhid ngafi diangale

  • @bigmobigmo4465
    @bigmobigmo4465 Před rokem +1

    Serigne cheikh tidiane sy yalla nanoko yalla fayal

  • @youssouphasarr4483
    @youssouphasarr4483 Před rokem +10

    Mashalaaah goud fane ak weeer Sy Malick ❤

  • @moustaphamboup9933
    @moustaphamboup9933 Před rokem +6

    Macha sy degue rék Yalna Yala faye la yééw Amine

  • @maodondiaye9151
    @maodondiaye9151 Před rokem +6

    Bilahi walahi yalla na yalla sutural

  • @moustaphamboup9933
    @moustaphamboup9933 Před rokem +4

    abdou aziz mbaye yalna Yala yoko rérr gui

  • @salifmbaye361
    @salifmbaye361 Před rokem +2

    Machaala yalenañiou yalla fayale mame maodo djeurediefeti s habipe sy dabakh 🙏🙏🙏

  • @alphakane4098
    @alphakane4098 Před rokem +3

    Wa asfiyahi tv on ndiarama de billahi wallahi

  • @airafrique8193
    @airafrique8193 Před rokem +4

    Machalla Serigne Habib Sy dabakh ❤️ ❤️❤️

  • @ngagneseye9552
    @ngagneseye9552 Před rokem +8

    Macha allá dieuredieuf sy malick

  • @diaryndiaye3018
    @diaryndiaye3018 Před rokem +2

    Machalla amna solo lool Dieureudieuf yalla faye sy Malick

  • @nadiangaro3673
    @nadiangaro3673 Před rokem +10

    Alhamndoulilah ❤❤❤❤❤

  • @cheikhtidianediouf6782
    @cheikhtidianediouf6782 Před rokem +7

    Dieredieuf sy malick vous faites la fierté

  • @mbenguefatou8730
    @mbenguefatou8730 Před rokem +17

    MACHALLAH SY MALICK. TOUTES LES PAROLES NE SONT QUE VERITES. MERCI POUR LA BELLE PRECHE

  • @ctn6223
    @ctn6223 Před rokem +10

    Machallah

  • @lohmfaty7950
    @lohmfaty7950 Před rokem +1

    mashaallah sy malick yalla na yalla yok soutoura si

  • @leyadiop5202
    @leyadiop5202 Před rokem +2

    جزاك الله خيرا شرج حبيب سه عطال الله عمرك ✅♥️

  • @airafrique8193
    @airafrique8193 Před rokem +2

    Serigne Habib Sy dabakh je suis très contente de toi ❤️❤️❤️❤️

  • @lymalik9943
    @lymalik9943 Před 9 měsíci

    Merci❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ahmadetseck9811
    @ahmadetseck9811 Před rokem +5

    جزي الله عنه

  • @ibrahimatounkara3232
    @ibrahimatounkara3232 Před rokem +2

    ماشاء الله تبارك الله سه

  • @aminataniang1065
    @aminataniang1065 Před rokem +2

    thiey tidianes yi ken dou gnomes machala

  • @mbayediop299
    @mbayediop299 Před rokem +3

    Machala souma serigne soukrane babacar depuis la France

  • @sokhnakane2759
    @sokhnakane2759 Před rokem +5

    Machaalla Sy. Malick

  • @abdouazizdrame7436
    @abdouazizdrame7436 Před rokem +8

    Dieuredieuf cheikh Seydil Hadji Malick Sy

  • @saerfall7137
    @saerfall7137 Před rokem

    Lii moom du dara jàng waxu beneen mag du ñàkk fayda rafetal la ñu xam ni mag ñi ñoo bëgg bëgg.
    Ku ne xam nga ku la mën Corona bi wane nako, nañu wax taalibe yi ñu teg ci yoonu njub.
    Ku xam nga ku la mën ba yaw mal xiyaam.
    Maa ngi baalu ñépp àq nag baal naa ñépp sunu Boroom dolli yërmànde ak njégal barkeb Seydinaa Muhammad.

  • @elhadjimalickniang5084
    @elhadjimalickniang5084 Před rokem +6

    Walay ndeyssane

  • @famaseck4231
    @famaseck4231 Před rokem

    Massaalla s'y malik❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏

  • @yakheyandiaye5389
    @yakheyandiaye5389 Před rokem +2

    Machalla Sy Malike

  • @awasow1045
    @awasow1045 Před rokem +3

    Machalla sy Malick

  • @khadijasarr3751
    @khadijasarr3751 Před rokem +3

    Mâcha Alla dama contante 🤲🏾💦🫧

  • @senebaseck7058
    @senebaseck7058 Před rokem +1

    Mala.sope.sy.malick.que.dieu.te.garde

  • @babacissetvchieckhoumarndi163

    Asfila al faral

  • @mbayethiam5676
    @mbayethiam5676 Před rokem +2

    Ma sha allah

  • @maogningue3922
    @maogningue3922 Před rokem +2

    Wallay Ndeyssane 😰 limouy wakh Aka worrr wallahi 😰

  • @kirnnkgordon5974
    @kirnnkgordon5974 Před rokem +5

    Machala

  • @airafrique8193
    @airafrique8193 Před rokem +11

    Tivaoune notre fierté de tout les temps ❤️❤️❤️😭

  • @awa8432
    @awa8432 Před rokem

    Dieurieudieuf si malick

  • @user-mhenter
    @user-mhenter Před rokem +1

    Serigne Habib Sy ❤

  • @sidydiouftirrenia2565
    @sidydiouftirrenia2565 Před rokem +1

    Machallah sy malick

  • @alioudiallo8877
    @alioudiallo8877 Před rokem +2

    Ma challah

    • @ababacardiop7026
      @ababacardiop7026 Před rokem

      Amine barke'MOUHAMED PSL INCHA ALLAH.deug DEUG Mame elhadji Malick yar n'a ndiambotame diamgal nalene

  • @mbalofficiel7513
    @mbalofficiel7513 Před rokem +4

    Sérigne Abib yague fi lol té wér Sy Malick koula sope la

  • @khadygueye5933
    @khadygueye5933 Před 3 měsíci

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @mcisse-qy6in
    @mcisse-qy6in Před rokem +1

    Machallah s'y

  • @alidiao1540
    @alidiao1540 Před rokem +1

    Yala geureum

  • @aliounembayendoye6027
    @aliounembayendoye6027 Před rokem +1

    Machallah ❤❤❤

  • @sadiocisse634
    @sadiocisse634 Před rokem +3

    Machallah, quelle élégance?

  • @timasamb
    @timasamb Před rokem +2

    Deglou aye wakhame reck diarna loune

  • @matadabakh743
    @matadabakh743 Před rokem +4

    ❤❤❤

  • @cheikhsylla522
    @cheikhsylla522 Před rokem

    Sokharr bakholl serigne Touba amol morom

    • @syresyrett
      @syresyrett Před rokem

      T'as raison key borom 33femmes dont 3 de même père et de mère et une demi sœur...
      La famille diakhaté

  • @djibrilgueye6464
    @djibrilgueye6464 Před rokem +5

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhtidianendiaye8729
    @cheikhtidianendiaye8729 Před rokem +14

    Discours très important
    Mashallah Sy Malick

  • @falloungom6025
    @falloungom6025 Před rokem +2

    Ways serigne Touba mom dou am morom th sisou baxoul nk

  • @mamadougaye7017
    @mamadougaye7017 Před rokem

    Manchallah

  • @reemoreemo5008
    @reemoreemo5008 Před rokem +1

    Manchala 🥰

  • @massambafall582
    @massambafall582 Před rokem +5

    dondeul ta wér sy

  • @awatoubab1994
    @awatoubab1994 Před rokem +1

    Sénégal wakh yi gnokoy yakk vraiment moi je suis talibè cheikh dh mais j'ai entendu MAME ABDOUL AZIZ DABAKH DISAIT K SERIGNE TOUBA ALLAH l'a donné le marchandise vraiment Nay rèkh si barkè MAODO tu veux dire tout c k tu veux vraiment mais pas des pique comme le rasseta
    ...

    • @beyeproloriginal9482
      @beyeproloriginal9482 Před rokem

      Yaw do talibé dara seytané nga batay deggo ñu toudd fi Serigne Touba.

  • @astouhrassoul4623
    @astouhrassoul4623 Před rokem +2

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @secretariatckasy70
    @secretariatckasy70 Před rokem +7

    Maachalla, le Véridique

  • @bababa8928
    @bababa8928 Před rokem +1

    Mashallah

  • @assthiane-iy4ld
    @assthiane-iy4ld Před 2 měsíci

    Ya deugo te mando😮😮😮😮

  • @minachuu3250
    @minachuu3250 Před rokem

    ❤❤❤❤❤

  • @aliounebalde8796
    @aliounebalde8796 Před rokem

    Xam xam rk

  • @cheikhkane1376
    @cheikhkane1376 Před rokem

    Dagaye doul rekk

    • @metoukanediop434
      @metoukanediop434 Před rokem

      Mais Yaw Nittt nga esk...j'espère k tu te comporte ainsi avec tes parents...enfants malheureux...sa Xol dafay tangueu rk

    • @airafrique8193
      @airafrique8193 Před rokem

      Yaw d Boye weute Di kharou iniane nga sokhore nga Bone khôl yalnala yalla yeureum 😭

    • @cheikhkane1376
      @cheikhkane1376 Před rokem

      @@airafrique8193 bayilene sene thiaxane yi dou Serigne akh

    • @beyeproloriginal9482
      @beyeproloriginal9482 Před rokem

      So touboul linga wax dinga am lula méti bala yagg ki martaba wam xadjoul sa kaw. Deel wax lu rafet soko saga sa baaay rek nga saga.

    • @oumarly3185
      @oumarly3185 Před rokem

      Yaw kou rewnga kii boudoul seringe khana seringe amoul si reuwmi Sénégal moo métti boo amée sa ndiaboot boy wakhag nioom niouni dangay gaarouwalé

  • @khalifaka9292
    @khalifaka9292 Před rokem

    Serigne bou réww bi aka niakk diomm

    • @oumarly3185
      @oumarly3185 Před rokem

      Amal yarr kii Mola geun Guen koo yaakar

    • @khalifaka9292
      @khalifaka9292 Před rokem

      @@oumarly3185 iow ya mana doull khana abib sy sa baye la geune sa leuff ndeye AK abib sy séne coyou baye

    • @mansourdieng2361
      @mansourdieng2361 Před rokem

      @@khalifaka9292 dagnouy ibi sa lefeul ndaye bamou seuss rofsi béton

  • @kilifeugui1958
    @kilifeugui1958 Před rokem

    Kii de khol bi rafetoul khel mi rafetoul. Ignaaan na mais au fond de lui kham na ni kenn dou maamam serigne TOUBA

  • @falloudiop5905
    @falloudiop5905 Před rokem

    Kom yaw rek finga fek bayou jambour ni limou jouli si gejgui wahci lou niaw ignane bahoul

    • @oumarly3185
      @oumarly3185 Před rokem

      Yow yaa mana wakh kii mousngako DEUG mou wakh si loolou

  • @boussobaly1706
    @boussobaly1706 Před rokem

    Wakhdjiou barrí daal bakhoul yaw ci sa tambele wakh nega yaw sagno ladje Ken dará banou ci moudjigue gane abdou aziz mbay delenma diokh lek carte dimil cfa kilifa daal wakdjia Day New dieufdjia barrí way wakh rek aka garouwale corona bi mo diekh rek

    • @beyeproloriginal9482
      @beyeproloriginal9482 Před rokem

      Nga deglu linga ci soxla té nga teudj sa guémégn yaw amo xam xam do dara nitou seytané nga. Vous cherchez toujours le négatif.

    • @boussobaly1706
      @boussobaly1706 Před rokem

      @@beyeproloriginal9482 deglouna lepou me kolifa da wara moytou di wakh negativ lii lepou liko waral moy kilifa dou barrí wakh yor micro 3 heur de tan di wakh ak serigne touba minuy bayi khel Day fegne si seni wakh serigne touba molendi derange me dará di geuna ñaw rek sa khol di gandi Bon

    • @beyeproloriginal9482
      @beyeproloriginal9482 Před rokem

      Waxofi xam xam Serigne Touba deggo toureum ji jotay bi. Beus bouné ngeen togn tidjane yi té dougn wax. Molouleen reew mi

    • @beyeproloriginal9482
      @beyeproloriginal9482 Před rokem

      Rien n'est plus incendiaire que le discours "reew mi Bamba moy ki ko mom" ani ñi dess kone
      yakaar ngeen ni adjana sax yénako mom bouleeen fonto nite ñi eupouleen ñu makhama.

    • @boussobaly1706
      @boussobaly1706 Před rokem

      @@beyeproloriginal9482 serigne bi wakhdjiou yegue dofako mom te kham kham bou andoul ak ragal yala lou barrí barrí amoul ndierigne kilifa dou tok ci bisou gamou di wakh lenen loudoul yala dou Yonentibi mom da wakh di wedi bopam nena diangati tidjianyi boulen maslah yobou ci diangue khassida Ken nan yem ci khassidayi elhadjie malick binde lolou refatoul ndakh tere binouy gamoo ñom muy bourdou bi mouhamadoul bousayri moko binde khana kon ñom toupounu elhadjie malick

  • @falloungom6025
    @falloungom6025 Před rokem

    Sêne deuk bou wett bobou nguêne ni yênafi nk di nax sêne bop rk

    • @oumarly3185
      @oumarly3185 Před rokem +1

      Nitt boo fonkee sa kilifa doo sabooté kilifa diaambour yalla sakh défa wakh koo bokkalol diiné boul saaga yallam boo sagaa yallam mou saaga sa yalla si ruer

  • @bambagabi9720
    @bambagabi9720 Před rokem +3

    nous tidiane on a rien a dire, a partir du moment ou on accepte des prefets mouride dans la ville de tivaouane, amougniou lougniou wakh. soufi al amine nékone kéneu douko sagne. macky sall dafa yape tivaouane il ne respecte pas la famille de maodo. il n ose pas nommé un prefet tidiane a touba

    • @maogningue3922
      @maogningue3922 Před rokem +1

      Mais tivaouane mo diapalène LPSS yaw khamo Lou khew

    • @papadembandim8438
      @papadembandim8438 Před rokem

      Kou môme tiv

    • @massylladiop4775
      @massylladiop4775 Před rokem +1

      Ndjite yalla mokay def Nanou rafetal tivaouane momoulenko yen Dong Touba Ahmadou bamba moko mom so xamoul dangay nopi nit bou khamoul day nopi Touba titre foncier la

    • @mariemeba7167
      @mariemeba7167 Před rokem

      Na gua deglo li mame abdou aziz sy dabakh wayon

  • @DABAKH5
    @DABAKH5 Před rokem

    Machallah

  • @falloungom6025
    @falloungom6025 Před rokem

    Ways serigne Touba mom dou am morom th sisou baxoul nk

    • @oumarly3185
      @oumarly3185 Před rokem

      Nii ngen Di déf ba saagalou sén seringe kiitouddoul seringe touba baayilén diakhse

    • @syresyrett
      @syresyrett Před rokem

      Amoul morom key 33femmes dont 3 de même père et une mère et demi sœur selon moussa camara poufff reponder sa stp

  • @thiabakandji3189
    @thiabakandji3189 Před rokem

    ❤❤❤

  • @falloungom6025
    @falloungom6025 Před rokem

    Bilakhi dafa reww kepp th ignane ndayemm kassè nk