🔮SERIGNE AHMADOU MBACKE DANS FII AK MAGAL AVEC PAPE SIDY FALL ET THIEDO MOURIDE | JEUDI 24 AOUT 2023

SdĂ­let
VloĆŸit
  • čas pƙidĂĄn 5. 09. 2024
  • đŸš©ABONNEZ-VOUS Ă  la ChaĂźne de la 2STV cliquez sur ce LIEN👉 :
    Retrouvez l'ensemble de nos programmes d'actualité et émissions de société, santé, politique, culture, musique, économie sur:
    - / 2stvsenegal
    - / 2stv_senegal
    / 2stvsenegal
    - Snapchat: senegal2stv
    - TikTok: @2stvsenegal
    - / 2stvsenegal
    - www.dailymotio...
    #FIAKMAGAL #PAPESIDYFALL #THIEDOMOURID #SERIGNE MOUSTAPHAKAYE #2STVSENEGAL #2STV #FreeSenegal #sonko #mackysall #2STVLIVE #senegal #TEAM221 #KEBETU #XIBAAR #JOURNAL20H #NEWS #ACTUALITÉS #DIVERTISSEMENT #SOCIÉTÉ #ÉCONOMIE #SANTÉ #DAKAR #yewwiaskanwi #BennoBokkYakaar #AarSenegal #ousmanesonko #LSFP #2stv #FSF #liguepro #senegal #football #4AVRIL #fetenational

Komentáƙe • 88

  • @mamebinetoumbaye6825
    @mamebinetoumbaye6825 Pƙed rokem +12

    Dolikotinanu boubaax MBACKÉ yalna yalla samoula tĂ© aarle barkĂ©b kou tedki

  • @ousseynoudiouf8195
    @ousseynoudiouf8195 Pƙed rokem +6

    Seugn Ahmadou MbackĂ© borom xam xam bou sell bii❀

  • @ndeyekhadydiop6936
    @ndeyekhadydiop6936 Pƙed rokem +7

    ❀❀❀❀amu ñu saggo ci moom mbacke Baala Yal na YĂ lla sĂ mm la bĂ©g nañ loolu ndaysaan ❀❀❀❀❀

  • @MamadouMbaye-hw1bd
    @MamadouMbaye-hw1bd Pƙed rokem +4

    J s8 ebloui sur cet saint homme dieuredieuf mbacke long vi a vs merci bokou a 2stv a l grd thieddo baye fall sidy c talibe cheickh ❀❀

  • @bassiroundawtasswouf8182
    @bassiroundawtasswouf8182 Pƙed rokem +8

    Thiddeo bo invite delll tewlou nguir yallah lingay dagate barina trop ah

  • @salioundiaye6697
    @salioundiaye6697 Pƙed rokem +2

    Aka sopulu machallah cheikh Ahmadou

  • @amadousy5363
    @amadousy5363 Pƙed rokem +4

    Serin Ahmadou Mbacke yalla nafi yagu té weur

  • @papewalydiouf9645
    @papewalydiouf9645 Pƙed rokem +6

    Yaagal tĂ© Werr mbackĆ•â€â€

  • @AlhikmaTvSengal
    @AlhikmaTvSengal Pƙed rokem +4

    Ù…Ű§ŰŽŰ§ŰĄŰ§Ù„Ù„Ù‡ ÙŠŰ§ ŰŽÙŠŰź Ű­ÙŰžÙƒ Ű§Ù„Ù„Ù‡ ÙˆŰ±ŰčŰ§Ùƒ ❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @bassiroundiaye7917
    @bassiroundiaye7917 Pƙed rokem +7

    Thiédo dél bayi gniguay invité Niou wakh wayyy akh

  • @damesene2413
    @damesene2413 Pƙed rokem +1

    Serigne ahmadou mbacke yalna fi yagg lool te wĂ©rr brome xam xam bou sĂ©lleu bi machallah ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀c'est important akaasa

  • @user-yy1ym5cr6y
    @user-yy1ym5cr6y Pƙed rokem +1

    Machallah pape sidy sama xool sedde nasi yaw bilahii

  • @mdou9250
    @mdou9250 Pƙed rokem +6

    MbackĂš yague rk ta weer Amiine đŸ™đŸŸđŸ™đŸŸ

  • @mizabtv
    @mizabtv Pƙed rokem +25

    Borom xam xam bou sel ta ragal yalla di ko déglou yokouté rk guay am

  • @salioutine4426
    @salioutine4426 Pƙed rokem +11

    machallah dieureudieuf mbacke balla yalla n'a gefi yagg te ande ak wer si barkep serigne touba khadim rassoul ❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @ibrahimadieng9777
    @ibrahimadieng9777 Pƙed rokem +3

    Ndeysann serigne ahmadou , yague fii tee weer,waxtann wii amna solo barki alkhouran

  • @mortallanakoyallatakhawulo303

    Machallh ❀❀❀❀

  • @taphandiaye5705
    @taphandiaye5705 Pƙed rokem +3

    Machalla amna solo lolou 🙏🙏🙏

  • @salioundiaye5763
    @salioundiaye5763 Pƙed rokem +4

    Merci beaucoup â€đŸŽ‰

  • @serignembackedieng8269
    @serignembackedieng8269 Pƙed rokem +1

    MbackĂ© balla yallnagafi yageu thi barkĂ©p cheikh ra fall sama wadji đŸ€ČđŸ€ČđŸ€ČđŸ€Č

  • @momarndiaye9992
    @momarndiaye9992 Pƙed rokem

    OHHHHH WAKHETANE WI NEKHNA TE KAWE, DOUG NA SI KHOLE. SERIGNE AHMADOU MBACKE DIEUREUDIEUF !!!!!

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Pƙed rokem +5

    Dieureudieufé serigne Touba mbacké khadim rassoul

  • @user-eh3hk6ix8i
    @user-eh3hk6ix8i Pƙed rokem +2

    Ndeysane tawfikh reek seug Ahmadou 🇾🇳

  • @serignefalloukanendamatou4630

    Xol sĂ©dd Na ❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @cabetas_sarl
    @cabetas_sarl Pƙed rokem +4

    Longue vie mbackĂ© ❀

  • @NdiameTv
    @NdiameTv Pƙed rokem +4

    Machalla ❀❀

  • @diop1385
    @diop1385 Pƙed rokem

    MaasĂ llaa JaajĂ«f Seex Ahmadu MbĂ kke Amatina Solo YĂ lna YĂ lla GuddĂ«l Fan Wi Ci Barke Ku Tedd Ki Amiin ❀❀❀❀❀❀

  • @murid_bi_jong
    @murid_bi_jong Pƙed rokem +7

    cey sunu waaji , seugn ahmadu yal na fi yagg lool waay

  • @amadouniang7444
    @amadouniang7444 Pƙed rokem +4

    Bilahi ki dĂ© soy dĂ©glou diotaye mouride yimouy deff bilahi da ngay gueneu xam fii ngay tekk sa tank ma cha Allah mbackĂ© yalla na bour bi yokk fane yi ak wĂ«r gui barkep borom Touba đŸ™â€ïž

  • @abdoulayebousso2060
    @abdoulayebousso2060 Pƙed rokem +2

    Machallah srg ahmadou waxtaan wi néxna amna solo

  • @user-zg6ds8ss1b
    @user-zg6ds8ss1b Pƙed rokem +3

    Machallh serigne bi

  • @nogayesylla209
    @nogayesylla209 Pƙed rokem +3

    Yagg fii lol tĂ© werr MbackĂ© Balla ❀

  • @babadiaw1255
    @babadiaw1255 Pƙed rokem

    Akasa❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @user-ek7cz9hc7f
    @user-ek7cz9hc7f Pƙed rokem +4

    Machalla

  • @fatimambay7006
    @fatimambay7006 Pƙed rokem +3

    Dieuredieuf mbacké yalle gafi yageu te werr

  • @abdoulatiftoure3337
    @abdoulatiftoure3337 Pƙed rokem +2

    ŰŽÙƒŰ± ŰŹŰČيلن ÙŠŰ§ŰŽÙŠŰźÙ†Ű§

  • @ibrahimamane7001
    @ibrahimamane7001 Pƙed rokem +1

    Amna solo lole diangate nagne si bou bax yague lĂ©ne fi teh wer â€ïžđŸ™đŸż

  • @ndeyefatoukane5725
    @ndeyefatoukane5725 Pƙed rokem +1

    Ndaysann s.ahmadou Aka sel xam xam yalnako yalla guena Sellal si barkep borom touba

  • @cheikhabdousylla5311
    @cheikhabdousylla5311 Pƙed rokem +4

    ❀❀❀❀❀❀❀

  • @seexahmadulmubiin5674
    @seexahmadulmubiin5674 Pƙed rokem +2

    Ay waay ceedo ngir YĂ lla degglu lĂ©en Sëñ bi ahhh.. Xam Xam du ay pexe Waxoofi tuss noppil bayi Sëñ bi dĂ©veloppĂ© waay😱

  • @ndarfallthiarenetv435
    @ndarfallthiarenetv435 Pƙed rokem +1

    Jeureujeuf mbacké

  • @NgagneNiang-xy1hn
    @NgagneNiang-xy1hn Pƙed rokem

    Machalla mbacké am n'a solo dé

  • @modoumbaye4905
    @modoumbaye4905 Pƙed rokem +1

    Mbacké yalla nga fi yeqq looloe

  • @libassendiaye45
    @libassendiaye45 Pƙed rokem

    Machallah serign Ahmadou

  • @mouhamadaneallhamdoulillah0292

    Manchallah 💯 Mback

  • @DiopKhadimdiop-bf7md
    @DiopKhadimdiop-bf7md Pƙed rokem +1

    Theiy pape sidy mo dĂ©gue dh diam iow frĂšre 😱🎉😊

  • @akimka4531
    @akimka4531 Pƙed rokem +1

    Billakhi dangĂšna doyalol rĂšk 😂😂moutakh ngĂšne beug kou sipi thĂ©orie ak pap sidy wallahi kĂšne doya loll❀❀❀

  • @saoudienkonate
    @saoudienkonate Pƙed rokem

    ŰŹŰ±ŰŹÙŰȘ ێ۱ۏ ŰŁŰ­Ù…ŰŻ ŰšÙƒÙŠ Ù…Ű§ŰŽŰ§ŰĄŰ§Ù„Ù„Ù‡ đŸ–€đŸ–€đŸ–€đŸ–€đŸ–€đŸ–€đŸ–€đŸ–€

  • @user-zg6ds8ss1b
    @user-zg6ds8ss1b Pƙed rokem +3

    Mbacke yalla nala fi yalla baayi ci barkep serigne daaru hassan Ndiaye ❀❀

  • @diopraadiopnar9569
    @diopraadiopnar9569 Pƙed rokem +4

    sr akhmadou mabcke murtada sunu wahdji Aka sel

  • @salioutine4426
    @salioutine4426 Pƙed rokem +1

    machallah am n'a solo lollllll mbacke balla ❀❀❀❀❀

  • @modoudiop2892
    @modoudiop2892 Pƙed rokem +1

    😂😂😂😂 ndeysane emision bi dafa jekh tĂ© doyaluleen da ngen koy invitĂ© waat

  • @bayesall6430
    @bayesall6430 Pƙed rokem +3

    Thiédo diambarr gaa lool mais ligay daagg invité yii moo barii
    Délen bayii niouy développer
    Nioguii toup

  • @omarfarokhboussobe1647
    @omarfarokhboussobe1647 Pƙed rokem +1

    ❀❀amatina solo

  • @serigneousmanendiaye1242

    Sëriñ Ahmadu Mbàkke jàmbaar dëg la

  • @fallousall2717
    @fallousall2717 Pƙed rokem

    Ki dh Beug la ko def â€đŸ˜Š

  • @baycheikh5666
    @baycheikh5666 Pƙed rokem

    Ahmadou mbackĂš yarmande yalla

  • @user-ju9ey3is8y
    @user-ju9ey3is8y Pƙed rokem +1

    Thiedo waw gour wayĂ© dagg yi dafa barri😅😅

  • @BabacarNdiaye-lc2pd
    @BabacarNdiaye-lc2pd Pƙed rokem

    Kou samou wormayy Touba samou nga Islam

  • @babacarmbengue651
    @babacarmbengue651 Pƙed rokem +1

    Kouma sopou mongui borom kham kham machallah

  • @bayebassmbacke9455
    @bayebassmbacke9455 Pƙed rokem

    ❀❀

  • @ahmadouthiam6109
    @ahmadouthiam6109 Pƙed rokem +3

    Ki dafa fésse dél ki da ngéne ka warone bayi mou développer ngire gayi meuna diarigniou niou ngi diégalou nak

  • @abdoullahimbackekon4839
    @abdoullahimbackekon4839 Pƙed rokem +1

    S ahmadou Mbk dama ko Begue lol waaadji ❀❀❀❀

  • @McoMultimedia
    @McoMultimedia Pƙed rokem +2

    Thiédou déll Téwlou xam xam dou péxé
    Borom xam xam kéne dou Dogg

  • @cheikhsarr9137
    @cheikhsarr9137 Pƙed rokem +1

    Pape sidi demal ga sett bĂšnĂšn emmision fii do sa place lo nĂškeu ak gniko diago

  • @MOURIDVISIONTV
    @MOURIDVISIONTV Pƙed rokem +1

    â€â€â€ŰŹŰ±ŰŹÙâ€â€â€Ù…Ű±Ű­ŰšŰ§

  • @babacarmbaye9258
    @babacarmbaye9258 Pƙed rokem +1

    Serigne bi mo bakh wakhtane na ba nopi tÚ prononcé woul le "mot" thiéddo" Serigne Mourid rk lakoy wakh ndeysane !! SÚt lou nguÚne lolou?!

  • @geejukkhassida
    @geejukkhassida Pƙed rokem +1

    Papw sidy kemaan laa ah, sĂ«riñ bi xañ nganu xam xam degg, ceedo day beggg dila leralaal waye temps bi yaggul yaw jarul ngay comprendre 😱

  • @ibrahimandiaye9569
    @ibrahimandiaye9569 Pƙed rokem +2

    PAP sidi kii lii Moy waxx xamo sii dara kii borom xam xam la kou amoul xam xam bokou si 😂😂

  • @ahmadouba7597
    @ahmadouba7597 Pƙed rokem +1

    Pape sidy t es devenu nul ou tu fais genre c'est quoi ces questions médiocres

  • @khadimgueye9775
    @khadimgueye9775 Pƙed rokem +1

    Walay s'en xam xam selna lool yeug te wer rk

  • @abdoulayediop956
    @abdoulayediop956 Pƙed rokem

    Deug dou romb noop

  • @diopgorgui1791
    @diopgorgui1791 Pƙed rokem +4

    Macha'allah â™„ïžđŸ™

  • @RokhayaKasse-et7eb
    @RokhayaKasse-et7eb Pƙed rokem +4

    ❀❀❀❀❀❀❀

  • @diagnegueye4599
    @diagnegueye4599 Pƙed rokem +2

    Machallah

  • @AwaSene-lt8kp
    @AwaSene-lt8kp Pƙed rokem +7

    ❀❀❀

  • @user-es8md2fs8q
    @user-es8md2fs8q Pƙed rokem +3

    ❀❀❀❀❀❀❀❀

  • @user-zg6ds8ss1b
    @user-zg6ds8ss1b Pƙed rokem +2

    ❀❀❀❀❀❀❀

  • @taphaseye243
    @taphaseye243 Pƙed rokem

    Machallah

  • @taphaseye243
    @taphaseye243 Pƙed rokem

    Machallah

  • @user-lx8gn9vv7n
    @user-lx8gn9vv7n Pƙed rokem +1

    ❀❀❀❀❀❀❀

  • @bassirouniang9905
    @bassirouniang9905 Pƙed rokem

    ❀❀❀❀❀❀

  • @cheikhbassdiop4400
    @cheikhbassdiop4400 Pƙed rokem

    ❀❀❀❀❀

  • @lilbeezy7517
    @lilbeezy7517 Pƙed rokem

    ❀❀❀❀❀❀❀❀❀