Les Confidences de Kéba Seck : La disparition brutale de son épouse Néné Galé, Thione Seck, Musique

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 17. 05. 2023
  • Les confidences de Kébé Seck sur Senepeople+
    #senepeople #confidence #kebaseck #senepeoplus

Komentáře • 406

  • @senepeopleplus
    @senepeopleplus  Před rokem +84

    Quelle célébrité voulez vous voir sur le canapé de confidence?

  • @berthamendy7439
    @berthamendy7439 Před rokem +97

    La présentatrice est tellement posée machallah elle te donne vraiment envie de suivre l'émission franchement chapeau belle dame ❤❤❤❤

    • @fallndeye6092
      @fallndeye6092 Před rokem +2

      Bilaye dafa nekh bapare ki koye def ame yar

    • @berthamendy7439
      @berthamendy7439 Před rokem

      @@fallndeye6092 vraiment ma grande surtout lolou yar dafa ame solo si domou adama ❤❤

  • @maxentosalonso
    @maxentosalonso Před rokem +128

    Cette présentatrice est la meilleure 😊

    • @seutoubour2888
      @seutoubour2888 Před rokem +4

      J’adore sa façon de traiter ses invités elle est calme douce très polie❤

    • @maxentosalonso
      @maxentosalonso Před rokem +2

      @@seutoubour2888 elle a tout mon respect

    • @AmadouDiop-hf5rn
      @AmadouDiop-hf5rn Před rokem +2

      Slt content na si kéba sama wayatt nga bn continuation

  • @mariamadiakhate4409
    @mariamadiakhate4409 Před rokem +81

    Coumba c’est Mareme une suggestion un packet de mouchoir sur la table comme d’ habitude tu fais pleurer tes invites et de l’eau fraiche c’est le minumum quand meme

  • @dieynabakane2865
    @dieynabakane2865 Před rokem +31

    Il a la voix de thione Machalla limou défal ses sœurs ça me touche Yalla nala yalla téral kéba

  • @pengadiop1387
    @pengadiop1387 Před rokem +15

    Quand il parle on sens net la voix de thione seck walay lou bokou nirrou machalla papa kéba yalnal Yalla geuneu takhawou papa thione Yalla nako Yalla yeureum té kharéko firdawsi 🙏🙏🙏🙏

  • @ndeyecoumbafall5084
    @ndeyecoumbafall5084 Před rokem +5

    Keba dafa bakh machallah. Dadone woo beine kharitam dioum woma maniko da nga dioum, il s'est excusè maniko grawoul dagnoumay woo founeik di dioum ndakh wadji 531 lawone mane 631 et tout le reste gnoko niro.
    Alors il m'a demandè si j'aimais les soirées maniko j'ai decrochè depuis khawma bane annee 😂il a tellement rigolè nima sa voix bi do makk dei nganane decrocher na 😂😂😂 on a rigolè ndeyssane apres il s'est presentè à moi, nima il fait des soirees avec Salam Diallo. Ndeyssane silagnou diapantei nakk gnouiy wowantei, il est venu me voir une fois à la maison, j'étais tres contente. Nite kou bakh la machallah gawa miine, beug nite, ouvert. Yalnako Yallah dooli diam ak soutoura, il est adorable bolessi oyoff machallah. Kouko kham reik kham k9u bakh, lolou moune na koko seideil. Diam si yaw mon grand❤

  • @mariosylva9169
    @mariosylva9169 Před rokem +32

    Elle crée de l’émotion dans ses propos The best 💯🙏

  • @bayeballandao1830
    @bayeballandao1830 Před rokem +29

    Life goor yalla yag na tarr
    Faut respecté les "borome keur" responsable mes tres chere djiguéne✌️

  • @fatimaniang4177
    @fatimaniang4177 Před rokem +14

    Mame Coumba Svp Andil niou Coumba Gawlo Seck❤❤❤Lolou dinama nekh trop bilahi Mais Emission bi nekh na machallah Ndeysane Keba Courage yalla lou gueune rk lay def👌👌🙏

  • @aminatasettuconnecte8295
    @aminatasettuconnecte8295 Před rokem +78

    MachaAllah J'ai connu sa Mère, Mère Ngoma,Yalla na Yalla yokk leram, Sokhna sou digne et am koloré. ❤️

  • @fatougueye-zh7td
    @fatougueye-zh7td Před rokem +28

    Père talent way Keba Machallah la présentatrice est la meilleure ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉😢😢😢

  • @antagueye223
    @antagueye223 Před rokem +41

    J'adore cette présentatrice dafa daal classe et professionalisme

  • @maimounagueye7222
    @maimounagueye7222 Před rokem +8

    Pain ak sauce😂😂 vraiment Diome dafa bakh si nitt.
    Bravo

  • @aladjifalloudia4915
    @aladjifalloudia4915 Před rokem +19

    Ndeye sane kéba bilaye yaa bakh ta réfét xoi yalla nasa diamo yague amine 😢😢😢😢😢😢❤❤❤❤🙏🙏🙏

  • @mairamediop9178
    @mairamediop9178 Před rokem +8

    Machalah mn plus grand rêve ces de reconstruire notre maisson familiale pour ms sœur et ms demi frère walahi je n dort plus à cose de ça

  • @Chanella97
    @Chanella97 Před rokem +13

    Tellement douce Coumba Machallah bne continuation❤ on t’aime 💖

  • @fatoumatabinetadialloly6339

    Figay wakhé wakhou néné gallé setane nako plusieur fois daw na yaram trop yalla nako yalla yeureum amine liga wakh nak si mom djiko peulh deug la lognou mayoul beugou gnou aka gno digne

  • @maguettekane3888
    @maguettekane3888 Před rokem +10

    Keba tu a un bon coeur 😢😢😢❤❤❤❤❤

  • @ndeyeramatoulayegueye7623

    Machalla kéba ,il s'exprime bien

  • @38Ramatoulaye
    @38Ramatoulaye Před rokem +13

    “May yonei pain comme gneup…”ndeyssane❤

  • @halikano392
    @halikano392 Před rokem +8

    Ame kilifeu dégalko lou ame solo thi adouna MACHALLAH jouer lou bari thi figua eksi téye ak ndibeulou YALLAH sougnou borome YALLAH nala YALLAH méye lou romba sa ndiorte thi sa carrière andak gouda FANE ak wer WERLE ak sa famille MACHALLAH 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @samiratoure2153
    @samiratoure2153 Před rokem +68

    Nit kou nek Amna louko mèti si adunam Mouy kou siw ak kou siwoul😢😢

  • @leboundoye1403
    @leboundoye1403 Před rokem +6

    Ahhh liii motakh mou am fouleu ak prestance sama mbooka lébou la❤

  • @sirandiaye6293
    @sirandiaye6293 Před rokem +22

    Cette présentatrice est juste wow🎉❤🙏

  • @reemoreemo5008
    @reemoreemo5008 Před rokem +4

    Hooo kéba séck yalla nalla yalla défale diam

  • @cheikhnouhagassama
    @cheikhnouhagassama Před rokem +30

    Papa keba longue vie à toi

  • @biba9498
    @biba9498 Před rokem +16

    Tout ravissante Mame coumba🎉

  • @sokhnaabsatougaidou1335
    @sokhnaabsatougaidou1335 Před rokem +11

    First like always🎉❤❤❤❤❤bravo mame Coumba ❤❤❤❤

  • @ndimendour8053
    @ndimendour8053 Před rokem +3

    Néné Gallé était une amazone ,Qu ALLAHOU yok yeurmendé thi mome amine Firdawssi soit sa derniére deumeure

  • @amadoulaminendiaye149
    @amadoulaminendiaye149 Před rokem +7

    Le grd Kéba en ok Kéba mbaye moy sa toma machallah

  • @halikano392
    @halikano392 Před rokem +18

    Heuye waye NÉNE GALLÉ YALLAH naki YALLAH kharé ALDIANA FIRDAOUS MACHALLAH 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @amynabarro
    @amynabarro Před rokem +7

    Mane famille pape thione gneup la beug Masha Allah 😍

  • @astousow8723
    @astousow8723 Před rokem +6

    Keba on t adore MACHALLAH NENE GALLE PAPA THIONE FAT TOURE YALLAH NEGN HIPER ALDIANA FIRDAWSI DARADIEYE SEYDINA MOHAMED PSL

  • @babas_officiel
    @babas_officiel Před rokem +19

    Cette chaîne CZcams fait des vidéos extraordinaire j'aime beaucoup cette chaîne ❤ 2:25

  • @mohamedndiaye6845
    @mohamedndiaye6845 Před rokem +15

    Kéba jeune talent kéba wayy rekk l'ay déff😂😂😂❤❤❤

  • @binetaamar8615
    @binetaamar8615 Před rokem +11

    😅🤣🤣mbakhalou kethiakh bouko Ken toga la ti keba mom sauce la beug yalla bakhna yalla n'a yalla kheb dolli koffi guiss amna diarr diarr

    • @ndeyembaye8908
      @ndeyembaye8908 Před rokem

      Bilaahi dangay déglou Di dioye ndakh dafay nouro AK sa diar diar

  • @ndeyegueye115
    @ndeyegueye115 Před rokem +10

    SAMA CLASSE GUI BATAY MA NGI DIOYE PAPA THIONE YALLA NAKO YALLA YEUREUM KHAREKO ALDIANA FIRDAWSI 🙏 🙏

  • @rokhayadiagne538
    @rokhayadiagne538 Před rokem +3

    Machalla i love keba .mane thione seck rekh lamaye Thiouk Ndeyesane Bonne continuation

  • @amadoulaminendiaye149
    @amadoulaminendiaye149 Před rokem +13

    Waww billah di acheté pain 🥖 comme nieup y’a am diom wayyy

  • @yanidoungom6092
    @yanidoungom6092 Před rokem +5

    machalat keba contane si yaw tu es très posé

  • @ndeyeawadiallo1788
    @ndeyeawadiallo1788 Před rokem +15

    Demb la soga khamni li ga wooy amna solo "courant dou pile" en référence au match city real
    Le jeune talent yalna seu diam yagg

  • @masterndour4728
    @masterndour4728 Před rokem +27

    Amengua tourando bou matte tourando ..
    Le Juge kéba Mbaye issue d'une famille de modestie et qui né le 05 Août 1924 à Kaolack...
    Il est devenu directeur de Cabinet de différents ministère à son époque mais aussi il a été président de codification du droit des personnes et du droit es obligations...

  • @amadouamitobadjan3547
    @amadouamitobadjan3547 Před rokem +5

    Machalla pape Kébe seck yalna sa diam Yagui

  • @ndeyefaye3821dabakh
    @ndeyefaye3821dabakh Před rokem +2

    Keba koula beug la machala tabarakala dieuredieuf

  • @ndeyegueye115
    @ndeyegueye115 Před rokem +9

    NENA GALE YALLA NAKO YALLA YEUREUM KHAREKO ALDIANA FIRDAWSI NGA YEKH KO FEKI 🙏🙏

  • @doudoutimera2679
    @doudoutimera2679 Před rokem +5

    C un grand monsieur keba seck

  • @salydiop3610
    @salydiop3610 Před rokem +9

    Keba ndeysane aka bahh tes beug ay mbokam machala la famille avant tout ❤❤❤

  • @katyfaye2152
    @katyfaye2152 Před rokem +1

    Journaliste bi elle est très géniale a chaque fois mouy invité bènn artiste il faut mou dioy ndeysann oh😘😘😘😘

  • @sodagueye-qd8gs
    @sodagueye-qd8gs Před rokem +2

    Sama yaye diay na yerëm ba tayi guire ndiabott tan long vie à elle ❤️🔐

  • @alimatousall5334
    @alimatousall5334 Před rokem +1

    Ndeysane .
    Santt yalla warna diameu.
    Yalna yalla doli soutoureu

  • @boussothiam5604
    @boussothiam5604 Před rokem +3

    Machaàaala keba seck contaaana si yaw kou niakk kiniane nga ❤❤❤❤❤❤

  • @pendafall7797
    @pendafall7797 Před rokem +17

    Mon émission à moi❤🎉

  • @adjacoumbafall
    @adjacoumbafall Před rokem +6

    Manshallah. Mais nak delene tek mouchoirs pour vos invités nak.
    mo gueuneu civilisé psk bcp d’entre eux pleurent en racontant leir vécu.
    La moindre des choses ngen am mouchoirs tek ko à côté rekk mo gueuneu rafet.

  • @lala-wo1ge
    @lala-wo1ge Před rokem +4

    Vraiment vraiment dioye na basona 😭😭 mes rétana tamite 😂 keba vré artiste la guerié la ndanane la machalla

  • @malicksourang
    @malicksourang Před rokem +13

    Emission bi mame ndiaye savon warna gneuw❤❤❤❤

    • @magy3113
      @magy3113 Před rokem

      Khana souye nieuw fi daniouy agrafé yaram bii fi tek la lathie 😂😂😂

    • @fatimalepape8708
      @fatimalepape8708 Před rokem

      ​@@magy3113 yaaa bone 😂😂😂😂😂

  • @assietoundoye3624
    @assietoundoye3624 Před rokem +2

    Je suis fier de toi le fait que tu as construit une maison pour tes sœurs ❤❤❤

  • @mmmomo4267
    @mmmomo4267 Před rokem

    merci,thione seck yalnaniou yalla tass si barkem amiiin

  • @ndeyegueye115
    @ndeyegueye115 Před rokem +6

    NDEYSANE KEBA YA BAKH GOUDEUL FANE WAYY AM WERR SOKHNA SI NIANAL KO ADOUNA DAFAYE WORE 🙏🙏

  • @maimounadiouf917
    @maimounadiouf917 Před rokem +5

    Machallah 🙏félicitations inchallah

  • @ndeyerokhyndiaye2186
    @ndeyerokhyndiaye2186 Před rokem +5

    Ndeysaannnn family nieup même voice ❤😍🥺

  • @aminatandour1741
    @aminatandour1741 Před rokem +1

    Machallah Coumba tu gére bien ton émission Kéba yalna sa diam yag nit kou rafét xol gua

  • @seutoubour2888
    @seutoubour2888 Před rokem +7

    Y’a gnak kignane MashaAlla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @laminesiby5815
    @laminesiby5815 Před rokem +9

    Machalla et félicitations à tout eguipe ❤❤❤❤❤

  • @sokhnabaly1408
    @sokhnabaly1408 Před rokem +2

    Bilay keba seck rek la beug ❤😭😭

  • @user-di6no1sx8z
    @user-di6no1sx8z Před rokem +3

    Slt def Lou bakh rek mon solotu aime tes sœurs vraiment felicitation❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @Xman-hh7ox
    @Xman-hh7ox Před rokem +8

    😂😂😂 36:00 keba rainama ma comase togou sos di yoney pain com gniop

  • @naroubayeniassfall8019
    @naroubayeniassfall8019 Před rokem +4

    Diapp nala biss ni tay,dama beugue Thione Seck si sama khol,bolé Nassi faramarenn Gui yeup.Repose en paix Thione Seck.

  • @khadydiouf2627
    @khadydiouf2627 Před rokem +2

    Ndeysane on l 'écoutant on sent la voix de thione seck❤❤

  • @moustaphacisse5549
    @moustaphacisse5549 Před rokem +7

    adouna balla nékh faw mou metti 😢😢

  • @fallousseynou3309
    @fallousseynou3309 Před rokem +1

    Merci ❤❤❤🎉

  • @user-wx3iy1uc1j
    @user-wx3iy1uc1j Před rokem +13

    Moment nostalgique

  • @fatoubittaye7169
    @fatoubittaye7169 Před rokem +5

    kebba massallah sa kadou refet na torop

  • @diarrathiam347
    @diarrathiam347 Před rokem +16

    Keba mo neh nena ko loy serieuse serieuse lu niii😂😂😂 lolu cas la d mame coumba neub nga mgu sa djiko

  • @thiatethiat5515
    @thiatethiat5515 Před rokem +1

    Tonton KEBA seck rek gua meuna sante😂 yalla na sa diam yague maryacin khôl sede na❤❤❤

  • @soukeyfall7971
    @soukeyfall7971 Před rokem +2

    Ndeyessane machalah Bilahi yabakh

  • @abydiop3692
    @abydiop3692 Před rokem +5

    Seck Ndanaaane ❤

  • @adamaka5641
    @adamaka5641 Před rokem +3

    Émission amena solo
    Kéba ya bakh té ame diom

  • @user-im4my5zh1t
    @user-im4my5zh1t Před rokem +1

    Qui veut que la prochaine soit une fille rk lallale j aime ❤

  • @rokhayatouguisse8500
    @rokhayatouguisse8500 Před rokem +4

    J aime bien sa façon de chanter .

  • @user-bj7qh3yr9q
    @user-bj7qh3yr9q Před rokem +3

    Machallah papa keba seck

  • @marichouseck5683
    @marichouseck5683 Před rokem +3

    Bilahi dagua bakh pape yaye teugue soirée mou diekh gnou taxaw nila amougnou passe gua diokh gnou passe taxi 🚕 ya goré mar yacine

  • @biba9498
    @biba9498 Před rokem +3

    Machallah kena liguaye wakhe niou beri doundeu naniou ko

  • @dabasamb5607
    @dabasamb5607 Před rokem +9

    Machalla pape keba ya bakh

  • @fbcl1894
    @fbcl1894 Před rokem +7

    Ndeyssane Thione Seck yal nakko yala doli yeureum ak diégal ❤😔🙏 et bonne continuation pour vous 🙏 Mais mom ak Painnnnnn xam na histoire bou yagueu la 😂sheuttt farine sax warouna😅

  • @elougaye3207
    @elougaye3207 Před rokem +3

    Ndeysan ❤

  • @khardieng9763
    @khardieng9763 Před rokem +2

    Machallah kèba

  • @diarrathiam4956
    @diarrathiam4956 Před rokem +1

    Yallah nala yallah faye si li gua defal sa sœursyi lou raw grand théâtre di gua fa dem inchallah

  • @astoumbaye7126
    @astoumbaye7126 Před rokem +4

    Machallah keba yalla dinala Fayai Lou bakh INSA Allah

  • @mamediarradiackdiack4444

    Aka ame gueremou thione papa kéba machallah ❤

  • @fatoukine3415
    @fatoukine3415 Před rokem +2

    M achallah longue vie

  • @user-yz7kf9vu9t
    @user-yz7kf9vu9t Před rokem +2

    Machalla

  • @halikano392
    @halikano392 Před rokem +3

    Néna Wally il est trés malin MACHALLAH kéye bimouye awou rappeur bobou woye nguentéli Wally awoussi nane ndokalé !!!!!! Ndokalé !!!!!! Guir nétali ba lako ndieukeu guisse ni ki dina soré torope thi limouye def MACHALLAH 💯💢💥💫💦🗯🗨💬💯

  • @halikano392
    @halikano392 Před rokem +7

    DIGNITÉ AK PERSONNALITÉ wakhgua MOTS you reuye you rare thi diamano téye😮

  • @fadieye8219
    @fadieye8219 Před rokem +1

    Émission bi machalla adouna youmboul bon courage kéba perde sa sokhna da méti

  • @seutoubour2888
    @seutoubour2888 Před rokem +4

    Y’a bakh keba amine ❤❤❤❤❤

  • @mairamediop9178
    @mairamediop9178 Před rokem +1

    Keba yallah nalla yallah faye

  • @bachirfall6151
    @bachirfall6151 Před rokem +5

    bilahi moma geuna nekh si waykat yi

  • @SNBUZZTV
    @SNBUZZTV Před rokem +6

    Kou beugeu térale saye niarii wadiour diap ci abonné sama compte CZcams si barké seydouna mouhammed psl

  • @maremesy7276
    @maremesy7276 Před rokem +7

    Bilahi dafa melni sama histoire ngadone netali