agressé par des hommes armés à Mariste: Eumeu perd plus de 4millions, des téléphones et son scooter

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 11. 02. 2023
  • agressé par des hommes armés à Mariste: Eumeu perd plus de 4millions, des téléphones et son scooter

Komentáře • 270

  • @fatoudiakhate2836
    @fatoudiakhate2836 Před rokem +21

    Machaallah khalè bou ammeu diomme bou naguo liguèye bou ammeu fayda machaallah ba sa yaye guènè adouna batèye ya gui ouffe saye rakeu yalla na yalla sougnou boromby diapalèla

    • @angeliquetounkara6498
      @angeliquetounkara6498 Před rokem +3

      Bilahi tata wakhal liguèye rek moko nior ande thi ak foula ak faye da solawoul alalou kéne té bamouye khaléba légui nak il est responsable ba yayam dedoo ba taye mougui ouf aye rakam kéne khamouléne dara amana li sou amoul wone sakh kéne douko guiss si réseaux sociaux yi ndakh kou ame soutoura, kéne meusouko dimbalé niari deureume bobou balégui mo gui géré. Mais sante yalla bou bakh ndakh heure bi meunona féke nioukoye deuth mais yalla na yékh. Eumeu bilahi dagnaye djingue rek mais do danou yaw sa aye ndaye daniou la nianale thi barké chékhal bounama gnaye talibé serigne touba bou deugou nak kone li défko natou té ndangouko rek yalla dina léral lép. Sénégal nak mom souyabo rek na kounék djeul saye matouwaye rek té djiéma ar sa bop ak sa diabote

  • @barhamdiallo2011
    @barhamdiallo2011 Před rokem +121

    Comme la police et la gendarmerie sont toujours au trousse de Ousmane Sonko au lieu de sécuriser les personnes et leurs biens

  • @alydiop4889
    @alydiop4889 Před rokem +21

    Courage frère tu y seras pas seul et le meilleur reste à venir

  • @dmxjjj7555
    @dmxjjj7555 Před rokem +29

    Courage mon frère walah tu t'es fais vendu par des proches c'est sûre et certaine regarde bien ton entourage

  • @ilimanefaye
    @ilimanefaye Před rokem +16

    Eumeu nite ku bahh marchant abulant la sa suma démé plasam mu dieun parfums défw duko sahh sohla m nguir diap si combat bi noooó méritéwo lii m gni dff yalna sa borom werr lén si barké mame saliou mbacké

  • @mohamedlamineboye316
    @mohamedlamineboye316 Před rokem +17

    Courage mon ami et frère depuis l’enfance…yalla nako Sunu borom leral

  • @quenne_dudiolof9536
    @quenne_dudiolof9536 Před rokem +28

    Ya que SONKO QUI A LA SÉCURITÉ AU SÉNÉGAL 😅😂 Sonko est gardé 24/24h mom reck mon âme sécurité.

  • @modoufall1365
    @modoufall1365 Před rokem +19

    Que le bon dieu vous vienne en aide barke Serigne Touba

  • @seydoundaw7098
    @seydoundaw7098 Před rokem +19

    Massa frère j'appelle tout les jeunes à utiliser la carte gab et de ne pas sortir avec cash

  • @fallcheikhibra1155
    @fallcheikhibra1155 Před rokem +21

    Actuellement ont vis dans un Sénégal où ya pas justice apart dieu chaque personne doit ce protéger savoir les milieux où tu part et les heures que tu restes dehors de chez toi savour qui parler car ya des personnes qui te fréquente et qui ne veulent pas ton bien apart tes parents ne parle a personne de ta vie financière où familiale🇧🇪✍du courage frère

  • @diopdiakhou8747
    @diopdiakhou8747 Před rokem +12

    Ils ont été informés sûrement y’a pas hasard qu’ils tagresse comme ça

    • @oumylopy4803
      @oumylopy4803 Před rokem

      Lolou la beuguone wax ki dañouko diay

  • @toubandiayeofficiel
    @toubandiayeofficiel Před rokem +10

    Métina trop frère mai courage yalla noppina fépp 🙏

  • @miachou8765
    @miachou8765 Před rokem +10

    Saway li daniou la diay kholal ki ngay yobalé Lou takh demoul Ak yaw en plus 9 personnes nga khekh Ak ken rayounioula ganioula donc il voulais pas te blessé

  • @pendandiaye298
    @pendandiaye298 Před rokem +13

    Outal auto ak port d'arme pistolet ak koy andal Yalla.nasi sa weurseuk déss mou fégne ak diam barkè Seydina Mouhamed Psl🤲 diambar di dane sa dolé am diom niou tékiwoul dar dieuf li 😭 agresseurs yi yalla nalén bour Yalla allak tass yakar rèk ribba késsé li mo méti deug

    • @fatoudiakhate2836
      @fatoudiakhate2836 Před rokem

      Pourtant ammeu na auto dèh khamgua lègui khalèyi dagnouye utiliser moto dakhe pariditè bi thi circulation bi

  • @maodondiaye2502
    @maodondiaye2502 Před rokem +10

    Grand au moment où on t’aggressait, sécurité bi guay wakh ils étaient autour de Ousmane Sonko (avec un dispositif très important)
    Massa et du courage, voilà où en est le Sénégal…

  • @moustaphafall5213
    @moustaphafall5213 Před rokem +8

    Courage eumeu yalla nala borom bi may lou gueune lolou

  • @assbayedieng3721
    @assbayedieng3721 Před rokem +8

    Il a un fort mental Masha Allah yalnala Borom bi taxawou. Mais yén gniy yor yén somme yi délén yor gun pour vous protéger pour man c'est obligatoire

    • @moom3931
      @moom3931 Před rokem +1

      Wallahi pour moi c'est obligatoire
      Gun rek. Si les agresseurs savaient k ya un risque réel, présent , qu'ils perdrent leur vie quand ils agressent les honnêtement gens barki Yalla kone lègui mou dièèx

    • @deuyzadeuyza865
      @deuyzadeuyza865 Před rokem +1

      Voila yéneu somme yi wala matériel yi kou koy yoré warr ngua yore pistolet di arr sa bopou di arr sa alal.

  • @mouhamedcisse9869
    @mouhamedcisse9869 Před rokem +7

    Courage frére yalla na yalla fégnale lééne

  • @poupembaye1199
    @poupembaye1199 Před rokem +4

    sa waye kingadone yobou chak jour et jour bobou yobou woko bayisi xél kileu xam rék molaye teumbeule nitte mo nakarè xam yalle nalène yalla fèniale bala yagg inchala

  • @mohamedballadiop6085
    @mohamedballadiop6085 Před rokem +6

    Vraiment Maristes il est temps guayis dioukk ci ya trop d'insécurité fofou li mettina trop. Nekk jeune tu te bats jour et nuit et des lâches nieuw dieul seu aalal comme ça

  • @ndeyeadadiouf6564
    @ndeyeadadiouf6564 Před rokem +5

    Oh eumeu massa! C’est très difficile d’entreprendre au Sénégal. Courage

  • @seynaboundiaye19
    @seynaboundiaye19 Před rokem +10

    Metina
    Courage frère yalla nako yalla nite
    Ba pare mayla lou eup lolou
    Sante rek

  • @ahmadouifraba
    @ahmadouifraba Před rokem +11

    Métina mais yalla bahna

  • @matykebe9971
    @matykebe9971 Před rokem +2

    Ndogale bou naré ame thiouné ngaye done courage mon frère dieu vas te venir en aide paix à toi du courage

  • @matysylla5159
    @matysylla5159 Před rokem

    Massa mon frère métina trop
    Je suis de tout cœur avec toi
    Yalla nala Yallah takhaou léral lépe Incha allah 😥😥

  • @fatougueye6001
    @fatougueye6001 Před rokem +5

    Yow da nioula kham top la khamnaniou li nga yor motakh

  • @fallmamadou8892
    @fallmamadou8892 Před rokem +4

    Salam grand yawww fii nga diarr bahoull foofu dafa calme trop goudi sama dépôt foofula nekk niounnn en pleinne journée laniou dall sur le mm lieu c'est domage pour nous les jeunes travailleurs mais courage frére sa va revenir inchala

  • @ldiedhiou811
    @ldiedhiou811 Před rokem +5

    Il faut donner le casquette à la police scientifique comme ça ils vont trouver des traces d’emprunts pour pouvoir identifier les personnes

    • @yacinegueyetahir9487
      @yacinegueyetahir9487 Před rokem +1

      Bayill mou sedeu...police amoule diotou askanwi guoudi yi ñiou tolou..

  • @ameneymar2399
    @ameneymar2399 Před rokem +5

    Namà Yallah bale mé kigua done endal sak jours c sun suspect na police def liguayam yallah Bakh na

    • @samssosky961
      @samssosky961 Před rokem

      C’est la première chose à laquelle j’ai pensé

  • @alphaoumardiallo3884
    @alphaoumardiallo3884 Před rokem +3

    Xoolal lii rek li niaw na maky sall niou sass la loudoul dièx sécurité économie et autres choses ngay lidieuneti ay détenu politique yoy teudj si ay féne ay tappalé franchement parler j'ai pitié de mon pays 😭😭😭😭👌👍

  • @amadounesylla488
    @amadounesylla488 Před rokem +2

    Ça devient grave au Sénégal je suis vraiment soqué

  • @SenegalGamingtv91
    @SenegalGamingtv91 Před rokem +1

    Massa fall dina bakh inchallah 🙏🙏

  • @cmsshoptrade4569
    @cmsshoptrade4569 Před rokem +1

    Courage frère.
    Yallah mo yor lepp , dîna nakh incha'Allah.
    Vraiment tu es courageux

  • @abdoulayediakho7237
    @abdoulayediakho7237 Před rokem +5

    Je suis sûr et certain koula kham mola diay agresseurs yi,gni gnoy ay domram deug

  • @patheseye1634
    @patheseye1634 Před rokem +7

    Ou sont la police et la gendarmerie? tous derriere sonko et les innocents

  • @moustaphadiakho5434
    @moustaphadiakho5434 Před rokem +9

    courage frérot 🙏

  • @bathiendiaye478
    @bathiendiaye478 Před rokem +2

    Frère metina mais yalla guisna leppppp yalla nalla borom dembaliiii doynawar

  • @salioubarri3259
    @salioubarri3259 Před rokem +3

    Police tmt da ame week-end te nioy takhaw si yone yi week-end di ramass 😂

  • @mansourkane8937
    @mansourkane8937 Před rokem +6

    Baye li métina trop bilahi 😢

  • @daffba4791
    @daffba4791 Před rokem +5

    Ki gua done yobalé jour bobou mouné dafa am koumouye khar kokou suspect la

  • @abdoulahadfaye632
    @abdoulahadfaye632 Před rokem +1

    Courage frère wallahi louko geune moy nieuwe inchalla brom bakhe nga on ce connaît yalla sa khol lalay Faye

  • @modoudia1148
    @modoudia1148 Před rokem +2

    Oh ferer metina yalna yalla takhawou la

  • @salioudiakhate2509
    @salioudiakhate2509 Před rokem +4

    Bon courage frère kou baax beug liguéy dioubb yalna ko Yalla niiit. Le meilleur reste à venir.

  • @merryloum860
    @merryloum860 Před rokem +1

    Il faut avoir l'habitude de prier avant de sortir. L'islam diangaléna lépeu !!!

  • @poupembaye1199
    @poupembaye1199 Před rokem +5

    courage 😢❤

  • @souki-saf-group3858
    @souki-saf-group3858 Před rokem +1

    Yalla nako yalla sopi ayyy milliard 😢

  • @bourguibafaye8521
    @bourguibafaye8521 Před rokem +3

    Gendarme yeupe gnou ngui topeu sonko motakhe sécurité amatoul

  • @rambihthoumas9589
    @rambihthoumas9589 Před rokem

    Dommage que les forces publiques ne travaillent pas le week-end end

  • @mamadoudamendiaye6160
    @mamadoudamendiaye6160 Před rokem +1

    Eume Yaw bayy Fall nga liguéy lala nieup khamé Liila Yallah réservé moy dakh .. courage Frère Yallah bakhna

  • @mohamedballadiop6085
    @mohamedballadiop6085 Před rokem +2

    Diambar aussi moytoulène khalé you djiguene yi. Bilahi djiguène daffa leundeum defw niom nioléy diaayy elles complotent avec des agresseurs genrou mafia yoyou daffa am ci réwmi maintenant djiguène gni nioy satieu lou lér laléy wakh parsk niom Iphones ak mbirou adouna diaral neulène lou nékk bien vrai k moune neu nekk gaur oci mais moytoulène khalé you djiguene yi

  • @Ctnnn
    @Ctnnn Před rokem +6

    Bon de toute façon la police pourra faire la triangulation des téléphones qui étaient autour de toi au moment de l'agression.

  • @fadelbambiste1451
    @fadelbambiste1451 Před rokem +1

    Police ak Gendemerie sonko lagnou tale yalla nala yalla dolli taxawou bro

  • @beugdeug5553
    @beugdeug5553 Před rokem +1

    Tous les forces se concentrent sur Ousmane SONKO rek et membres Pastef

  • @InfosetTutos
    @InfosetTutos Před rokem +3

    rewmi amoul securité nous qui descent tard on est en danger en permanence billahi moi je descend a 23heur tous les jours mais c difficile

  • @seinfarage9959
    @seinfarage9959 Před rokem +4

    mais mon frère, nous souffrons tous et ne pouvons pas porter beaucoup de valeur à tout moment et cela nous affecte tous. tu ne devrais jamais transporter autant d'argent et de téléphones mon frère je sais que c'est dur mais Allah kareem

  • @zizndiaye9253
    @zizndiaye9253 Před 2 měsíci

    Courage frère

  • @cheikhfaty1417
    @cheikhfaty1417 Před rokem

    La police et la gendarmerie nationale sont là que pour surveiller ousmane sonko

  • @iboufall2979
    @iboufall2979 Před rokem +10

    En général ces genres d'agressions ont été préparées
    Motax fallait prendre des mesures surtout ces temps si ak fi rewmi tollou
    Wayé courage frère

  • @massinaniang1335
    @massinaniang1335 Před rokem

    courage frère yalla nala yalla dolli takhawou

  • @khadyfall2384
    @khadyfall2384 Před rokem

    Yala nala Yalla maye were ak diam ak guoude fane barke Seydina Muhammad, maye la kholou mougne, ma sha Allah

  • @abdouseye7705
    @abdouseye7705 Před rokem +1

    Ndeysane thiye Sénégal 😭😭

  • @ouleyediop9502
    @ouleyediop9502 Před rokem +2

    Du courage eumeu yalna yobou sa aye

  • @mariemesy1104
    @mariemesy1104 Před rokem +1

    Courage mon frère mais regarde ton entourage ils ont été sûrement informé et la plus part ce sont des actes préparés.
    Mais aussi kinga done nako police enquête c’est louche en tout cas .

  • @amadouba4254
    @amadouba4254 Před rokem

    C dur mon frère yalla nala yalla taxawuu mayleuu lou geun liga perte

  • @alibeurtone6942
    @alibeurtone6942 Před rokem +3

    OUSMANE SANTE YALLA BANGUA KOYE NETALY ...
    LEGUI NAQ DIAPALNY DANIOU DIAYE WALA GNILA DEF LII KHAMENA NIOULA BOUBAKH
    LEGUI NAQ BO TEYEZ TOUTY REC , DI NGUA DIAP TES VOLEURS !
    BOULE NANGO WAKH KHAMEZ NGUALENE
    TE BO DOFOULE TOUTU TEC KOU TAK MASQUE SANS KASQUETTE , MEUNE NGUAKO KHAMEZ SOU AMEZ TOUTU REFLESQUE
    AUTRES CHOSES NIOGNOU TELEFONES YI DOUNIOUKO DIAYEZ FENENE FOUDOU FI SI DEUK BI
    YALLA NA FEINE TE YALLA SAME LA
    BARKEY SEYDUNA MOUHAMED

  • @mamadoufall9185
    @mamadoufall9185 Před rokem +5

    Koubakh YALLA NALA YALLA Sameu té Arr là mayla louko Eupp fouff bala yagg si Barké Yonente Bi SAWS 🙏Lii YALLA Na Toppou Say Aye🙏

  • @mamadoundiaye7940
    @mamadoundiaye7940 Před rokem

    Metina trop grande frere yal nala yalla fegnal securite bognouy gena pour Ousmane sonko nagnouco gene securite senegal

  • @soukagnagaye
    @soukagnagaye Před rokem +2

    Koula.kham.molay.diay.

  • @ousmanesow7169
    @ousmanesow7169 Před rokem +1

    Ak fou rewmi tollou kou dépendre ci police Ak gendarme yagui ci erreur Yor len sen arme adiou mo guéne

  • @infosgalsen9710
    @infosgalsen9710 Před rokem +1

    Courage frère Mane sénégal la xamoul motaxe kou meuna voyager na dem fii amatoul securité walae daguay tekki gnou raay la walla gnou sathi laa

  • @GeorgesBasileTHIAW
    @GeorgesBasileTHIAW Před rokem

    Du courage .Le meilleur reste à venir

  • @maimounafall3956
    @maimounafall3956 Před rokem +1

    Danio la diaye de bilahi 😢😢

  • @diawfalldiouf5217
    @diawfalldiouf5217 Před rokem +2

    Merci ❤

  • @cheikhfall4729
    @cheikhfall4729 Před rokem +1

    Ndeysan eumeu Grand bu bakh gno bokou marché Alizé lii mom dafa Louche

  • @souleymanesakho4347
    @souleymanesakho4347 Před rokem

    Courage frère vue sa liguey soxla gua arme ak permis aussi yalna borom bi léral lepp🙏

  • @mansourkane8937
    @mansourkane8937 Před rokem +1

    Oh métina trop eumeu gaydel ligueye rek la kham 7plus bouma ndieuka yore momako diaye

  • @latgrandlatgrandndiaye3660

    koula ham rek mola diay 😢

  • @thiernobah9341
    @thiernobah9341 Před rokem +1

    Bakhna si yaou terbine yaou tiriyanga

  • @mrdiengpatronvoyau5040
    @mrdiengpatronvoyau5040 Před rokem +5

    Scooter mo doul yeufi kilifeu zero security woutal oto

    • @frenchyboy26
      @frenchyboy26 Před rokem +5

      Beaucoup ont des vehicules mon cher mais ils achetent des scooters pour se déplacer rapidement dans Dakar. Centre ville jusqu'à liberté peut prendre facilement 4 heures de temps.

    • @cheikhmbacke6241
      @cheikhmbacke6241 Před rokem

      Pourtan amna auto nak bro

    • @mrdiengpatronvoyau5040
      @mrdiengpatronvoyau5040 Před rokem

      Mane immobilier laay def meune nagn la signalè bo yorè scooter mo tax Mane auto rek

    • @mrdiengpatronvoyau5040
      @mrdiengpatronvoyau5040 Před rokem

      Sama biir auto sakh souma douguè damay verouillee

  • @laminelayekebe615
    @laminelayekebe615 Před rokem +1

    Nn Li dafa métti koii 😡😡😡😡😡😡😡

  • @moustaphadiop760
    @moustaphadiop760 Před rokem

    Ndeysan yalla nala yalla defal jammo takhawola Ban diabolén

  • @anifanawtamsbi1394
    @anifanawtamsbi1394 Před rokem

    Ousmane sOnko dieulna sécurité bii yeup

  • @bouakonzkonate352
    @bouakonzkonate352 Před rokem

    Ndeysanne allahou akbar ohh mon frère massa

  • @pascalkane9767
    @pascalkane9767 Před rokem +1

    Ceux qui ont fait ça te connaissent ou ont été envoyés par des gens qui te connaissent. Il ne faut faire confiance à personne je dis bien personne.

  • @bayematarsylla6283
    @bayematarsylla6283 Před rokem

    Courage frère li metina trop 😢😢

  • @alassanediallo2014
    @alassanediallo2014 Před rokem +1

    in allaha allah kouli chay ine khadir bayil lep li loho borom bi guis na lepeu

  • @cheikhthiaw3102
    @cheikhthiaw3102 Před rokem

    bilahi walahi yaina domou adama mayi khana dounou khalate bamaile wayai lilepou c est età zero securite yakame tiwounou lou doule ousmane sonko waraghena gnou maile ay sethiete guire yalla ak yonainetebi takhawoulene askane the bayi nighene naikai askanebi sonounanou li gnawena waysi inchallah 2024 Senegal ame diamou

  • @falloufall5916
    @falloufall5916 Před rokem

    Yalla bakhna

  • @enzoshifow1014
    @enzoshifow1014 Před rokem +1

    Sénégal dafeu bari niou soxor peut-être sakh koula xam mola diay agresseurs yii yénn yi meunoul nék hasard

  • @abouabdarahman475
    @abouabdarahman475 Před rokem

    Premier suspé, ki gua done andal, diko supporter, peut-être vous avez la piste pour connaître tes voleurs.

  • @alidiao1540
    @alidiao1540 Před rokem +2

    Li lagnou kham motakh gnou djeul gal

  • @selletipeu1790
    @selletipeu1790 Před rokem

    Thiey Sénégal zero sécurité tout le temps vers la politique

  • @mariemeboye8144
    @mariemeboye8144 Před rokem +1

    Masta métina lole bon courage 😔😔😔😔

  • @mambandiaye950
    @mambandiaye950 Před rokem

    Boro masta yalla nalèn yalla tèk lokhou

  • @MrBa-po4zo
    @MrBa-po4zo Před rokem

    Wallay sa fait vraiment mal frère !
    Mais bon , du courage broo

  • @cheikhlo4620
    @cheikhlo4620 Před rokem

    Frérot walla courage 😰

  • @taftaf3989
    @taftaf3989 Před rokem +1

    Demale porter plainte duc wala gendermerie colobane legui niou diapelene

  • @baityrba2447
    @baityrba2447 Před rokem +2

    Beugue xalisse té yémé t wo thiono sathie rek mba agressé ay doméram tigui

  • @beugdeug5553
    @beugdeug5553 Před rokem

    Changeons ensemble ce pays notre Sénégal ces autorités actuelles ne font que remplir leur poche et compte

  • @taftaf3989
    @taftaf3989 Před rokem +1

    Damale brigade de rechese ga yob casc bi sofa diiogue demale duc mane malako legui niiou diaplene