Témoignages forts sur SONKO; Bamba Niass, Kreubeus Lebou & Borom Rewmi versent de chaudes l@rmes...

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 3. 05. 2024
  • Témoignages forts sur SONKO; Bamba Niass, Kreubeus Lebou & Borom Rewmi versent de chaudes l@rmes...
    #Senegal #Sonko #BoromRewmi
    Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
    / @senegal7tv
    L'information en temps réel
    Visitez notre site web: Senegal7.com
    Retrouvez Senegal7 sur les réseaux sociaux
    Facebook
    / senegal7officiel
    TikTok
    / senegal7tv
    Instagram
    / senegal7
    Twitter @senegal7com
    Abonnez-vous pour plus de vidéos et n'oubliez pas d'activer la cloche de notification

Komentáře • 325

  • @SokhnaRoubaSaliou104
    @SokhnaRoubaSaliou104 Před měsícem +117

    Kou bax bëgg Seydina OUSMANE SONKO 😭😭😭😭

    • @aidaba6350
      @aidaba6350 Před měsícem +2

      Tu n'es pas le seul , moi aussi, je pleurais quand il était persécuté. Le jour qu'on l'a mis en prison, j'ai pleuré pendant des jours. C'est Dieu qu'il a mis dans le cœur des sénégalais.

    • @MameboyeDiedhiou
      @MameboyeDiedhiou Před měsícem

      Machahalla sama fans bi lebou bi

  • @amadousy7520
    @amadousy7520 Před měsícem +50

    Non ces 2 jeunes me font pleurer pour leur patriotisme et l'amour qu'ils vouent à Ousmane Sonko... ❤❤❤

  • @morganmor1904
    @morganmor1904 Před měsícem +58

    Bilahii j'ai 40ans heur bouma xole SONKO 30 seconde damay dioy ba legui bamba dafa dioy rek ma dioy sendina Ousmane sonko yalla guafi yagu te werr ❤

  • @latdiouf8668
    @latdiouf8668 Před měsícem +65

    Vive les deux patriotes de l'émission

  • @bathiembaye1199
    @bathiembaye1199 Před měsícem +65

    mashallah bamba yawitte kou bakh nga... yalla na borombi Sam la May goudou fane ak wèr, ak xeweul gou bari... thiofel bi nga am si sonko yalla nako sounou borom sopi natangè, kheweul, soutoura, sènègalou diomaye, ak sonko nat ba sènègalais yeup guiss si bop, gni nèk si bir rèwmi, ak si diaspora bi, nat ba diakhal wa sènègal... mou andak goudou fane ak wèr

  • @maremeamar7152
    @maremeamar7152 Před měsícem +57

    Bamba ndeyssane nite kou sincère et très émotif
    Yalla bou yakar tass inchala

  • @user-jm8ew3dk9w
    @user-jm8ew3dk9w Před měsícem +35

    Yalna yalla yokk sunu mbeguel thi Seydina Ousmane Sonko ❤❤

  • @user-od2fy1xt9c
    @user-od2fy1xt9c Před měsícem +18

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 que Dieu protège mousselmi Ousmane sonko 🤲🏻🤲🏻🤲🏻🤲🏻

  • @MariamaSane-yj9tv
    @MariamaSane-yj9tv Před měsícem +18

    Bamba baringua morome pm sonko Hana kaye yaw feu seule rek wayé mbeuguéle bignoulo beugue ylla bou ylla tass Yakari Thiago brk psl❤❤❤❤❤

  • @Piscopailebourge
    @Piscopailebourge Před měsícem +30

    Krebeus lebou est très intelligente performante

  • @SokhnakanaFall
    @SokhnakanaFall Před měsícem +22

    Ndayessane yalna yalla doli soutoure si patriotes yi 🥰🥰🥰

  • @ongoudndiaye953
    @ongoudndiaye953 Před měsícem +25

    Merci chers jeunes pour votre réveil. Ousmane Sonko dougnou meussa wor. Courage

  • @user-gi6vr6yu1s
    @user-gi6vr6yu1s Před měsícem +20

    Merci les deux patriote

  • @angelebadji4805
    @angelebadji4805 Před měsícem +18

    Bamba toi aussi tu es gentille tu ma fais pleurer merci à vous deux ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @thomso50
    @thomso50 Před měsícem +12

    J adore écouter les lebous c est trop classe comme langue .bravo à vous et courage pour la suite

  • @bintourassoul7815
    @bintourassoul7815 Před měsícem +15

    Bilahi ousmane sonko yalla moniou bolé ak mom ❤motax noneu yi warnio may diam té khamni douci nioune doussi mom yalla leu

    • @SeniBi-sf6lz
      @SeniBi-sf6lz Před měsícem +2

      Walahi azim liguawakh rek moy deugue lèp yala la alkhamdoulilah

  • @Fatimagoudaby
    @Fatimagoudaby Před měsícem +18

    Ohhh ces triste j'aime aussi je pm Ousmane sonko vous m'avez fait pleurer 😢

  • @latdiouf8668
    @latdiouf8668 Před měsícem +75

    Kreubeus doit être invitée dans plusieurs sites internet, Masha Allah

  • @VOISINAGE2000
    @VOISINAGE2000 Před měsícem +21

    Bamba Niasse billahi dioyal😢
    Billahi yagui may dioyelo
    Billahi seydina Ousmane SONKO yague Na dioye ci mome.sonko yallah nagnou co yallah sammal

    • @SeniBi-sf6lz
      @SeniBi-sf6lz Před měsícem +1

      Amine yaraby amine yaraby lalamine touff

  • @Mamecheikhibrahimafall-it5tc
    @Mamecheikhibrahimafall-it5tc Před měsícem +22

    wallahi kou bonne douka bauge président Ousmane sonko yallah nakou fi yallah bayi ak mome, té wallahi qén banou kou, danou khamoul rèk

  • @user-qq4jm1sk5x
    @user-qq4jm1sk5x Před měsícem +24

    Bamba Niass ❤❤❤bousso❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ merci beaucoup

  • @CheikhMbengue-fl8ik
    @CheikhMbengue-fl8ik Před měsícem +26

    Ndeysane ousmane soko borom kholbourafet rek Mokay beug

  • @khadimlo1824
    @khadimlo1824 Před měsícem +6

    Machala mame Bamba ak soxna diara sene ligueye rafetna amna yare yallana yalla montali te sameu lene

  • @khadimgueyenormal5023
    @khadimgueyenormal5023 Před měsícem +16

    Merci bamba ❤❤❤

  • @user-iz6nn8tj1b
    @user-iz6nn8tj1b Před měsícem +32

    Bamba Niass ne pleure pas siguil Diaambaar deugue Moy yaw

    • @SeniBi-sf6lz
      @SeniBi-sf6lz Před měsícem +1

      ❤❤❤❤❤❤walahi aka yarou noo pastef tamite mandè dègoumafa kou rèww ta guisoumako faa ta machalah thie kham kham inchalah douguènn rèthiou liguènn donn aneu ak mom gueum yala rek mo waurr

  • @ndiayebathie-rf7fh
    @ndiayebathie-rf7fh Před měsícem +14

    No mame kreubeus bilahi damako beug fok ma sét Sila bargni way amale diam way sister❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏

  • @mamefansenyndour8536
    @mamefansenyndour8536 Před měsícem +17

    ❤❤❤❤Bouleine dioy yalla mongui akk gnoune❤

  • @SokhnaRoubaSaliou104
    @SokhnaRoubaSaliou104 Před měsícem +19

    YALLAH NAKO THIATT SEXLOU 😢SONKO YAABO AK FAYE BIRAM ❤

  • @galsengirlpower7955
    @galsengirlpower7955 Před měsícem +9

    Machala les patriotes, bilay dioub, beugue Sénégal akh nèk DIAMBAR mo takh gnou beugue Sonko.
    Nèk patriotes dafa nekh, dafa metti ❤️❤️❤️❤️❤️✊🏾🇸🇳🤲🏾

  • @Abdoulayewade-ui9cr
    @Abdoulayewade-ui9cr Před měsícem +9

    à yaram dawna billhi li yalla rek ❤moko segne 💕💕💕❤❤🎉

  • @user-gw8qv9zg5b
    @user-gw8qv9zg5b Před měsícem +5

    Bonne continuation sister et fière d'être lébou vive Sonko et vive Diomaye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @latdiouf8668
    @latdiouf8668 Před měsícem +22

    Kreubeus ❤❤

  • @user-rm7oi8rj1u
    @user-rm7oi8rj1u Před měsícem +17

    Sokhna diarra diam thi yaw ❤❤❤

  • @daoudacoly9782
    @daoudacoly9782 Před měsícem +21

    C'est frais m'aime Man je sais pas pourquoi je pleure je respecte beaucoup sonko bamba merci

  • @goradiop4611
    @goradiop4611 Před měsícem +37

    Yalla na yalla samou ousmane sonko

  • @IsmailaSane-zi8ve
    @IsmailaSane-zi8ve Před měsícem +13

    KREUBESS ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @aidambacke5313
    @aidambacke5313 Před měsícem +7

    Deysan yallana yalla Faye yiw kepou kou sel dou bagne oussmane sonko mane massouma guiss oussemane sonko mai nimako beugue eupena dole jai laisse mes amis enfance sama mak youma bokal ben derete dakhte kou bagne sonko ak lo mana ame ak ko mana done sournala adouna ak alahira amoumassi kerse

  • @binetasenghor4217
    @binetasenghor4217 Před měsícem +4

    Machalla président diomaye mooy sonko mooy diomaye ❤❤ndéysane Sénégal 🇸🇳 yalla na yalla yokou diamou amine yarabi mérci bamba❤ mérci lébou Sénégal ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aminatacamara8456
    @aminatacamara8456 Před měsícem +14

    Mashallah 🤲 🙏 ♥️ 🤲 🙏 ♥️ 😢😢😢

  • @aissatoutoure4676
    @aissatoutoure4676 Před měsícem +8

    DEPUIS 2017 , GNIGUIYE TOPPEU PM OUSMANE SONKO , SAMA WAKEUR DIAPALÈ MACI BOUBAKH❤❤❤❤❤

  • @tinadiallo3727
    @tinadiallo3727 Před měsícem +10

    MERCI ❤beaucoup B❤N❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @DieynabaSy-ri8tq
    @DieynabaSy-ri8tq Před měsícem +11

    MACHALLA ❤❤❤😢😢

  • @khary5948
    @khary5948 Před měsícem +6

    Walay li dafmay dal damay khol ses vidéos rek sama rangogne soti ta je ne l’ai jamais vu ❤

  • @MameDiatta-bm7po
    @MameDiatta-bm7po Před měsícem +8

    Bilay kou bone d’où beug sonko

  • @AntaSylla-bt3eq
    @AntaSylla-bt3eq Před měsícem +3

    J'ai les larmes aux yeux bilaye ❤❤❤❤❤

  • @Coumba-mv6vf
    @Coumba-mv6vf Před měsícem +3

    Yalna yalla guddal Seen fan mayleen wer ay gorngeen Macha Allah 🙏

  • @binetagueye4323
    @binetagueye4323 Před měsícem +3

    C'est deux patriotes yalna yalla faye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @nafaatv7472
    @nafaatv7472 Před měsícem +2

    Félicitation à vous, vous avez été d'un grand apport dans ce combat. Dieureudjeuf

  • @ceesayalieu1608
    @ceesayalieu1608 Před měsícem +3

    MasaAllah ♥️🇪🇸♥️❤️❣️🥰 you are right bro thanks 😢

  • @fatoudiop6413
    @fatoudiop6413 Před měsícem +21

    SONKOTchi ❤Dou Daign
    SONO Moy Diomaye ❤
    F I É R T É ❤❤❤

  • @aissatoutoure4676
    @aissatoutoure4676 Před měsícem +4

    VIVE LA JEUNESSE CONSCIENTE ,NOUS ON ÈTAIT PAS SI RÈVEILLÈS❤🙏🇸🇳

  • @yorogueye4724
    @yorogueye4724 Před měsícem +4

    Kreubeus est une tueuse 😅

  • @DialloTahirou-xj3ze
    @DialloTahirou-xj3ze Před měsícem +4

    Machalalh imission bih nkh nah trp sah nilah nak dlén invité tt ls jeunes du patriotes ❤❤❤

  • @goundocissokho2331
    @goundocissokho2331 Před měsícem +2

    Machala Sonko et Diomaye rek❤❤❤

  • @MameDiatta-bm7po
    @MameDiatta-bm7po Před měsícem +4

    Machalla Bamba Ak sama mbokou lèbou biiii

  • @thiorosene4202
    @thiorosene4202 Před měsícem +8

    Bilay mon frère bamba man aussi nonou la mél si kou séll ki waliou la DEUG la ndakh lougnou ma won ay Yoni Yon goudy bilay walay motakh kouko wakh dara ma diogu défendre ko nagnou masi basi gat sa gat sa foumou yém nékh❤❤

  • @mamydiagne863
    @mamydiagne863 Před měsícem +7

    Sonko rek ❤❤❤❤

  • @dieynabadiouf8516
    @dieynabadiouf8516 Před měsícem +4

    Dieureu nguèn dieuf yalnalèn yallah takhawou thi barckè Mohamed psl ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @youbadanfa4206
    @youbadanfa4206 Před měsícem +3

    Bamba diama si yaw j'ai des larmes aux yeux

  • @user-my7fs1ce3v
    @user-my7fs1ce3v Před měsícem +3

    Bamba niass focus rek ta famille t’aime vive seydina Ousmane mou selmy

  • @AissatouSagna-cj9li
    @AissatouSagna-cj9li Před měsícem +2

    Seydina Ousmane Sonko on l'aime super bien sans condition et infiniment. C'est pourquoi on c'est battu quand il fallait se battre pour lui et pour le projet. Et inchallah il restera graver à jamais dans nos cœurs

  • @djibrilbakhayokho38
    @djibrilbakhayokho38 Před měsícem +1

    J'arrive pas à retenir mes larmes j'adore ces deux mame Diarra et Bamba longue vie santé de fer à vous ❤❤❤❤❤

  • @user-du1wb3ic3y
    @user-du1wb3ic3y Před měsícem +4

    Ndeysane machalah ❤️

  • @modougueye9512
    @modougueye9512 Před měsícem +18

    Machalla bamba Niass wallahi sonko nitko baxla wallahi😭😭😭😭

  • @YoussouphaSall-iw3jx
    @YoussouphaSall-iw3jx Před 26 dny +1

    Manchahala djadjeufeuty courage les patriotes focus toujours jusqu'à 2045 inchallah

  • @user-st7ww7xl2k
    @user-st7ww7xl2k Před měsícem +17

    😭😭😭😭bamba dioye lo ngama dama yakarone ni mane rek ma begue seydina ousmane sonko mou séle mi merci qunu lebou nationale ❤❤❤❤❤

  • @mamadouniangniang8236
    @mamadouniangniang8236 Před měsícem +2

    Machllah mame diarra merci beaucoup ❤❤❤❤❤

  • @aliougaye9452
    @aliougaye9452 Před měsícem +7

    Merci beaucoup bravo ❤❤❤

  • @ndeyesokhnaseck8490
    @ndeyesokhnaseck8490 Před měsícem +4

    Je rends grâce a ALLAHOU TANLA nous avoir fait ce cadeaux humain qu'est OUSMANE SONKO waye YA KHADY NGOM DIEUREUDIEUF NGOM manona bayi déh wayé défoko machallah ya liguéy keur BAYE ba YALLA faynou sunu WAYE DJI SONKO mo rott rotalél képp kouy sénégalais fi ba Afrique noungui sant yalla bou ba

  • @adjafatousarrkebe4013
    @adjafatousarrkebe4013 Před měsícem +12

    Ndaysan mashallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @vieuxndiaye7893
    @vieuxndiaye7893 Před měsícem +1

    Kreubeuse bamba .dioylo guéne Sénégal gui yeup.sén témoignage bi amna solo merci❤❤❤

  • @Senegalaise608
    @Senegalaise608 Před měsícem +4

    Q elle interesant edition ❤ je vous adores vous aitent de vrai patriot

  • @user-tj9px4ss1o
    @user-tj9px4ss1o Před měsícem +13

    Ndeyssane beugue dfa meti

  • @zahrasow7946
    @zahrasow7946 Před měsícem +4

    Yallah na Nguene guissanter yaw ak PROS si barke psl

  • @AminataSene-xt5tb
    @AminataSene-xt5tb Před měsícem +7

    Ndeyesane wakh bou diogué si khol si khol laye dougate mon frère merci beaucoup li ngua yeuke la nio baré yeuke yalla bou yalla tass sonou yakar

  • @user-bf3xf9qv5k
    @user-bf3xf9qv5k Před měsícem +5

    Maa challah

  • @Beug.reuwmi-ig1sy
    @Beug.reuwmi-ig1sy Před měsícem +5

    Wa loutah nekkuma leubou❤❤😂 mais ba legui bénla sérère la

  • @thiernondiaye6966
    @thiernondiaye6966 Před měsícem +17

    Kou baakh ga

  • @mouhamedbalde2132
    @mouhamedbalde2132 Před měsícem +10

    Kounafékheu ak koubone moye bagne Ousmane Sonko ❤

  • @user-jm8ew3dk9w
    @user-jm8ew3dk9w Před měsícem +18

    Bilahi liguenedi diouy ni dou Hazard ndakh OS nitt gni dioy ndakh beugue koo té yalla takh beurina Macha Alla ❤️ yalna yalla

  • @latdiouf8668
    @latdiouf8668 Před měsícem +8

    Bamba ❤❤❤

  • @kebacisse7345
    @kebacisse7345 Před měsícem +2

    Ndeyssane ❤❤❤

  • @pipo7489
    @pipo7489 Před měsícem +11

    Man d pour man ousmane sonko man rek ley def ni neke beurina si morom .nimako beugué diakhlal nama

  • @sacourawali4626
    @sacourawali4626 Před měsícem +10

    Ay bamba dioylo ngama 😢

  • @marieheleneberre8736
    @marieheleneberre8736 Před měsícem +7

    Ousmane Sonko ak Pr. Diomaye yala nelene sougnou Borome same te barkel sene ligueye bi ba sénégalais yeupe contane barke Seydina Mohamed SAWS.

  • @rokhiyatoudiallo92
    @rokhiyatoudiallo92 Před měsícem

    Machaalla sa plateau rafétena bamba ak diara lair guou bari guou andak khéweul❤❤❤❤❤

  • @aissatoutoure4676
    @aissatoutoure4676 Před měsícem +9

    AYS LIGUÈYE KATT LAGNOUX ! GNÔM NIÂRR GNEUPP BAYKATTS LAGNOUX ❤🙏🇸🇳❤

  • @mboupmor5587
    @mboupmor5587 Před měsícem +4

    MachaAllah

  • @ndeyegayeAndorra
    @ndeyegayeAndorra Před měsícem +1

    Machaallah ma fille ❤❤❤❤❤

  • @ganekama7746
    @ganekama7746 Před měsícem +3

    Machalakh belle émission

  • @dieynabadiouf8516
    @dieynabadiouf8516 Před měsícem +2

    Deugg pure mame diarra je t.adore

  • @mansourgueye6832
    @mansourgueye6832 Před měsícem

    Thank you our patriots we are proud of you guys

  • @izzydaniels4333
    @izzydaniels4333 Před měsícem +11

    Sokhna Diarra ❤❤❤

  • @user-fx9qu7qw9v
    @user-fx9qu7qw9v Před měsícem

    Lolou.sonko.moy.senegal.bilnakhi.je.sui.fuier.patrotyi❤❤❤❤❤

  • @SeniBi-sf6lz
    @SeniBi-sf6lz Před měsícem +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤ walahi lèbou wakhatiko beugue guinnko beugue lolou thia sounou borom la motakh kèp kou beugue seydina ousmane sonko mousèlmi soguisè kouko beugue dank koy beugue thie sanceyi konne li yala moko def alkhamdoulilah thie sounou beugue beugue

  • @mbafodesylla1577
    @mbafodesylla1577 Před měsícem +1

    Je suis vraiment content de Diarra et bamba

  • @amadoudamediba1072
    @amadoudamediba1072 Před měsícem +5

    Merci beaucoup way Sénégal 7tv❤

  • @fatoundao6305
    @fatoundao6305 Před měsícem +1

    Merci pour le temoignage emu amal diam

  • @mouhamedsamb5966
    @mouhamedsamb5966 Před měsícem +1

    Merci borom rééw mi rafétna trop

  • @user-fc4sm6tg4g
    @user-fc4sm6tg4g Před měsícem +4

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤vive les patriotes 😂😂😂😂😂😂