Série - Woudiou Peetiorgo 2.0 saison 1 - Episode 22

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 25. 04. 2024
  • Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
    instagram
    kharmedia_offic...
    facebook
    / kharmedia_l'officiel
    Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
  • Krátké a kreslené filmy

Komentáře • 130

  • @user-eh2kh6js1o
    @user-eh2kh6js1o Před měsícem +47

    Mère Diarra yallah nama yallah may gooro bou mélle ni yaw

  • @user-fj9tc9jg1z
    @user-fj9tc9jg1z Před měsícem +24

    So xolé tmt astou Mbaye elle a raison imaginer djiguene Bo xamni dafa beug nangou sa dieukeur outeul ko liguey lolu day takh mou yapp ko wala mou nek mank de respect mais nak amoul choix dafa wara beuss xolam rek

    • @fatoundiaye1999
      @fatoundiaye1999 Před měsícem +2

      Walay ta raison limouye sentir mome rek moko kham 😢

    • @Wildflower455
      @Wildflower455 Před měsícem

      😂😂😂😂yen deh li daf di serie rek wai soulen dalon dinguen wakh lenen Astou Mbaye yeufou dof rek la fi def. Li niom nieup nio ko sokhla Modou amna droit tak ba nyenti diabar kon mom na zere cotem ta xamal Modou mou yemale Bigue mou jeex

  • @sokhnadiop9505
    @sokhnadiop9505 Před měsícem +64

    Bousa 4barame nékoul sa guinaw téléphone boul lal j'aime😢😢😢

  • @MmeToure-ny7km
    @MmeToure-ny7km Před měsícem +17

    Astou mbaye boul yak sa waye ❤sacré soda narga sonne dé❤❤

    • @fatouka8374
      @fatouka8374 Před měsícem

      Naroul am moudiou bou bakh dehh

  • @aicharassoulfaye8354
    @aicharassoulfaye8354 Před měsícem +20

    Astou Mbaye nak boule niou fonto waye weuh sa jalousie extrême bi moma nara yakale sa seuye bi

    • @peaceonly5951
      @peaceonly5951 Před měsícem

      Astou Mbaye tu nous emmerdes.Khana wolou wo seu boppeu ? Rew nga ,soff nga.On peut comprendre que tu sois jalouse mais Modou ne fait pas la cour ã Bigué.C’ est comme ça que les femmes poussent leurs maris dans les bras d’autres femmes.

  • @ndeyebetorthiam-qj2sn
    @ndeyebetorthiam-qj2sn Před měsícem +25

    Astou Mbaye franchement tu commence à être égoïste

  • @user-iz9ug8cq1e
    @user-iz9ug8cq1e Před měsícem +19

    Astou Mbaye mi maguibegue soff

  • @wolimatalaye8390
    @wolimatalaye8390 Před měsícem +8

    Mére diarra aka beugue niou dawal compréhension 😂😂

  • @user-qs9dy5vk2b
    @user-qs9dy5vk2b Před měsícem +15

    Thiey soda dougougua si goûta 🎉🎉🎉

  • @user-ne6xl5zm1j
    @user-ne6xl5zm1j Před měsícem +9

    D’une part nak Astou Mbaye je la comprends

  • @khadygueye1707
    @khadygueye1707 Před měsícem +10

    Astou mbaye yaw khamo fouy meti N’a Modou ndiaye yok diko setane loumou ko lathie mou bagne kèsser n’a aïe soda mi khamo si liga dougue sakh😅😅😅

  • @Rokheya194
    @Rokheya194 Před měsícem +1

    Li moy famille sénégalaise yallah dey Def ki nite yi beugeuko lol❤, kenene ki nite yi diko begne moy indi nono yi😢

  • @user-hx8gt7pi3j
    @user-hx8gt7pi3j Před měsícem +5

    Astou nak khamo sa boop djiguene dagay gueme sa boop fiir rek motakh bougo modou ndiaye ligueyi 😢

  • @dabandiaye6323
    @dabandiaye6323 Před měsícem +14

    Soda sa cousine Amna fite robe la lale d ak niari bireum yi melni dodane hé allah😂😂😂😂😂soda nak loula diaral li yaghini indil sa bop problème

    • @everniscemendes5983
      @everniscemendes5983 Před měsícem +1

      Bilaye 😂😂😂

    • @dabandiaye6323
      @dabandiaye6323 Před měsícem +2

      @@everniscemendes5983 mane Kate dama warou hahahaha

    • @diariatoufall1391
      @diariatoufall1391 Před měsícem

      😂😂😂khana sene pub biir bou reuy bi diakhou niouléne si

    • @user-xe5re3il8l
      @user-xe5re3il8l Před měsícem

      😢gniak Kham s'en boop rek biir melni sm booss gneme rob dougnou solle loulen diap mouk

    • @peaceonly5951
      @peaceonly5951 Před měsícem

      Li mome daffa Niawe trope.il faut que nitt gni diangue solou. Réalisateurs aussi war naniou di khole li Sene acteurs si solo.

  • @user-cc1ou9jk4m
    @user-cc1ou9jk4m Před měsícem +9

    Paa Assan amal foulla gua dém liguéyi Astou daffa réeew yow sa dieuker noboul ki gua mélni kou toukh lou bonne diko Neumb😂😂😂 sôooof

  • @user-uk5xj2dt7h
    @user-uk5xj2dt7h Před měsícem +5

    Mère Diarra ya begue ay heeff 😂😂mais jtm trop❤

  • @nogayesene5600
    @nogayesene5600 Před měsícem +14

    Jsw la première dans les commentaires félicitez moi😅❤❤

  • @user-nn5zc6he5w
    @user-nn5zc6he5w Před měsícem +4

    Alhamdoulilah merci Khar Media ❤

  • @user-ct6nj9zp1n
    @user-ct6nj9zp1n Před měsícem

    Wa khar média fékhélén ba série bii dôme nathi diouddou sén série yimaa sétane yeuppou djiguéne gni daniouy eumbou tei douniou am dôme ba ni série bi di amé fin nguir yalla bii na Astou mbaye am dôme

  • @Khardiata-nz6ye
    @Khardiata-nz6ye Před měsícem +2

    Wa Aïta mi nitt leu wol yow kenn bougouleu gay forcer rek narga sonn dh😂😂

    • @peaceonly5951
      @peaceonly5951 Před měsícem +1

      Warna âme dignité .defena daffa eumbeu motakh Mouye forcer.dafa titte.

  • @thiorolo4772
    @thiorolo4772 Před měsícem +8

    Astou nak y’a rew 😂😂

  • @bombombengue1191
    @bombombengue1191 Před měsícem +6

    Astou Mbaye boulniou yape nak

  • @sassoumthiam6414
    @sassoumthiam6414 Před měsícem +5

    ani wa association ande thiouss astou mbaye

  • @user-gl8sw2em3z
    @user-gl8sw2em3z Před měsícem +15

    Guir yalla boumou mélni mirage😂

  • @nafidiakite3363
    @nafidiakite3363 Před měsícem +7

    Thiey Astou bonheur de fat Ndiaye ❤

  • @gayemamediarra2644
    @gayemamediarra2644 Před měsícem +10

    Ayi soda nena da mbir ta mbiroule tamine

  • @FatouSeye-kc9do
    @FatouSeye-kc9do Před měsícem +5

    Aston mbaye sa perruque bi mom rafetoul mais yaw mom dioguoma gua

  • @bocarguisse2282
    @bocarguisse2282 Před měsícem +4

    Khar média temps yi da nguène am inspiration machala

  • @user-qs5ch5kw9y
    @user-qs5ch5kw9y Před měsícem +6

    diamalé khana diékhe té yegou mako

  • @DiarraGueye-wp5yq
    @DiarraGueye-wp5yq Před měsícem +4

    Yallana diamou yagu ❤

  • @user-fs3mg3xh5n
    @user-fs3mg3xh5n Před měsícem +13

    Ana patriote yi ❤❤❤

  • @astoutoure5671
    @astoutoure5671 Před měsícem +2

    Waa tmt guel biii bireum bou reuy bi mouni daaa sol robe bouni niap nii si yaram bii😂

  • @fatoudiouf1505
    @fatoudiouf1505 Před měsícem

    Merci beaucoup et bon week-end 😂😂😂❤

  • @SalioukebeKebe-xk3zn
    @SalioukebeKebe-xk3zn Před měsícem

    Mére Diarra yallah nama yallah may gooro mélle amin

  • @velsoptique6702
    @velsoptique6702 Před měsícem +3

    Alhmdoulillah tey deh mafi djitou lebal len ay❤❤

  • @user-eh2kh6js1o
    @user-eh2kh6js1o Před měsícem

    Khana série bi chaque jour lay ame

  • @user-nk9ht9jv2x
    @user-nk9ht9jv2x Před měsícem +3

    Li mome khana chaque jour lay am

  • @Binouh
    @Binouh Před měsícem +4

    Mom khana chaque jour lay am😮

  • @sawdatouba3110
    @sawdatouba3110 Před měsícem +1

    Mes tamit dèlén khol lingèn Di bind sèn commentaires yi kom gérer 🤣🤣🤣🤣

  • @Wildflower455
    @Wildflower455 Před měsícem +1

    Astou xamal sa bopou yaw meuno woutal sa dieukeur ligueye niou woutal ko ngani dedet. Esk ki werr na😂

  • @mbarkangom5931
    @mbarkangom5931 Před měsícem +1

    Astou mbaye arétel nak mo khana wolou wo se bopou

  • @user-nk9ht9jv2x
    @user-nk9ht9jv2x Před měsícem +3

    Astou mbaye nak nèkhala wakhal

  • @aisharassoul4586
    @aisharassoul4586 Před měsícem +1

    Astou Mbaye nak tu nous amerde

  • @fatimatouzahratalibeserign965
    @fatimatouzahratalibeserign965 Před měsícem +1

    Astou mbaye mi niouss ko diotna dh

  • @user-bq6ib1gh4f
    @user-bq6ib1gh4f Před měsícem +2

    Astou mbaye nékal nit nak

  • @maindiaye3888
    @maindiaye3888 Před měsícem +12

    Sonia mom bir bi niati bir la def mou sol Robam bou serrer bi 😂

  • @bintabodian9148
    @bintabodian9148 Před měsícem +1

    Yene wa khar media ana conséquence diamale ack pression woudie teral 😂😂

  • @satousatou3813
    @satousatou3813 Před měsícem +3

    Waa Sonia biirrr bi woyyy

  • @fallndeye6092
    @fallndeye6092 Před měsícem

    Asstou mbaye yagi Epple nak

  • @bocarguisse2282
    @bocarguisse2282 Před měsícem +3

    Sonia diokhe lène ko si sène produit yiye wagni biir

  • @sopeserignebara8738
    @sopeserignebara8738 Před měsícem +4

    Man may première 😂

  • @maimounaba6810
    @maimounaba6810 Před měsícem +6

    Khar media keunè mounoulèn comprendre 🤦🏻‍♀️ teek série chaque jour après dou âme fin 🤦🏻‍♀️

  • @user-po2ng3hg2k
    @user-po2ng3hg2k Před měsícem +1

    Bigè da gambal doudou Ndiaye astou mbaye moyèy

  • @user-iz9ug8cq1e
    @user-iz9ug8cq1e Před měsícem +3

    Mafidjitou😂

  • @NdioleSene-ec7et
    @NdioleSene-ec7et Před měsícem +1

    Guiryalladoumoumelnimirage😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤

  • @annadiack6843
    @annadiack6843 Před měsícem

    Khana Séne vente plat yi sonia dielou thi😂😂😂

  • @user-po2ng3hg2k
    @user-po2ng3hg2k Před měsícem +1

    Khalat you yak yii moylan

  • @diariatoufall1391
    @diariatoufall1391 Před měsícem

    Astou mbaye khamal sa bopou tagua guene siligua nek

  • @astoudiop5983
    @astoudiop5983 Před měsícem +1

    ❤❤❤❤

  • @salihatte9319
    @salihatte9319 Před měsícem

    Mane dama khamoul noye amer 10 bire di sol lou serre nite dafay kham bopam

  • @papewade5202
    @papewade5202 Před měsícem

    Nn soda mongi roubé keur gui naki 😂😂😂 pa assane soo khamone lii soda dit wakh yup ay léw la Modou Ndiaye non moudjé AK sa djoby bila bigué outeulé Astou mbaye bayile Modou Ndiaye moi ligueye 😂🎉

  • @gnilanediallo1479
    @gnilanediallo1479 Před měsícem +1

    Astou nak sofff nga dh mo yén réglél nak ngay nadiou ni

  • @diariatoufall1391
    @diariatoufall1391 Před měsícem

    Séne publicité biir bou reuy warguéna diokh soda ak cousine bi😂

  • @FatouNdiaye-vm8xf
    @FatouNdiaye-vm8xf Před měsícem

    Mais mane pour astou mbaye je la comprends dhé nékhoul 😢

  • @abdallahsow8098
    @abdallahsow8098 Před měsícem +1

    Yayou junior ah hetousagam ooooh

    • @user-xk9vp6sv7o
      @user-xk9vp6sv7o Před měsícem

      Kom sac douty m’en

    • @pendafall4938
      @pendafall4938 Před měsícem

      Commentaire bi lanone weur sac bi sac bi sac bi waw baxna 😂😂😂😂

  • @Binouh
    @Binouh Před měsícem +2

    Produit yi gueine di publicité diay len si cousine soda bi 😂 biram bi ba paré mou sol li hum

  • @cheikhmar5076
    @cheikhmar5076 Před měsícem +1

    Mais astou mbaye elle est folle ou koi

  • @AdjiDiallo-ec6fw
    @AdjiDiallo-ec6fw Před měsícem

    ❤❤

  • @user-nl6tu9nk1v
    @user-nl6tu9nk1v Před měsícem +1

    😢😢😢😢😢❤❤❤

  • @colysalimatalyco2924
    @colysalimatalyco2924 Před měsícem

    Pub bi beurina

  • @SaineyJagne-go5yg
    @SaineyJagne-go5yg Před měsícem

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤nekhna

  • @user-uh1nm6uh8q
    @user-uh1nm6uh8q Před měsícem

    ❤❤❤

  • @ndamaka3219
    @ndamaka3219 Před měsícem +2

    Ki mom hana yeugoul guene yi gnouy diayy

  • @ibrahimadiouf4576
    @ibrahimadiouf4576 Před měsícem

    Sonia mi oser na nak

  • @MacisseSow
    @MacisseSow Před měsícem

    😢😢❤❤

  • @abdousambadiouf9833
    @abdousambadiouf9833 Před měsícem +1

    Ce n'est pas Astou Mbaye mais Khar Média qui est nul

  • @philomeneyacinefall2784
    @philomeneyacinefall2784 Před měsícem +1

    Wa sogna tamit li lanla ni ci biir?mane dal khawma loutakh gnougn sénégalaise dougnou xol lignou diap gnou diko sol.phisic yeupa rafet mais bouci nek ak liko diap.rob bi mom dokhoul ci kou am biir escalier......

  • @MariaAlverenga
    @MariaAlverenga Před měsícem +1

    15:29 lan moy cellulule ak vergiture???

  • @absafall9048
    @absafall9048 Před měsícem

    Astou mbaye mom khamul limu begue soff na torop te ghemul boppam

  • @diariatoufall1391
    @diariatoufall1391 Před měsícem

    Mére diarra beguena tek tank si table tamite

  • @user-yi4hc5kr4o
    @user-yi4hc5kr4o Před měsícem +1

    🫶🫶🫶🫶🫶😅

  • @AwaSall-jt2fc
    @AwaSall-jt2fc Před měsícem

    ❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂🎉😂😂😂😂😂😂😂

  • @ndeyendacktoure2980
    @ndeyendacktoure2980 Před měsícem +6

    Wakh leine deugue rek yeine soleine khamei nitte ki da beugue sa dieukheur mou woutale KO ligueye vous allez laisser ton mari travailler en dehors du film wakh leine deugu

    • @user-vk9re1zb1m
      @user-vk9re1zb1m Před měsícem +2

      Bilay moma diakhal dh sou don niom don ko nako ben yon da nekoul niom rek

    • @Mamyzahra935
      @Mamyzahra935 Před měsícem +1

      Compliqué de 😂😂😂😂😂😂vraiment

    • @fatoumatabiteye2960
      @fatoumatabiteye2960 Před měsícem +1

      À bakhna li dher beneu djiguene douko ndangou

    • @DiarryDiallo-yc8rc
      @DiarryDiallo-yc8rc Před měsícem +1

      Wakh deugue s astou mbaye la andal

    • @user-ct6nj9zp1n
      @user-ct6nj9zp1n Před měsícem

      lolou léppou DEUG lëu mais Astou Mbaaye thi boppam mo.fiir tei kénëu khamoul limou beugg

  • @user-bq6ib1gh4f
    @user-bq6ib1gh4f Před měsícem

    Astou mbaye nékal nit way

  • @user-xi4pt3ci4e
    @user-xi4pt3ci4e Před měsícem

    ❤❤❤❤

  • @ndeyematyfall4160
    @ndeyematyfall4160 Před měsícem

    ❤❤

  • @NdayeLo-ws5pp
    @NdayeLo-ws5pp Před měsícem

    ❤❤❤❤