Aicha Kone - Djongué (Clip Officiel)

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 26. 06. 2024
  • AICHA KONE EST DE RETOUR AVEC UN NOUVEAU TUBE POUR L'ETE 2024!
    Ecoutez le titre sur toules plateformes : distrokid.com/hyperfollow/aic...
    crédits
    Artiste/interprète: Aicha Kone
    Réalisation: Pac Deejaay
    Beat: ZOX
    Paroles: ZOX
    Toplines: ZOX
    Mix/Master: ZOX
    PAROLES
    Couplet 1
    Djongué takh founiou beuré damkoy dane
    Ki makoy daanel wouy soldat a terre
    Doumako mey dara trou yeupp laye fatt
    Maay diw biy nineul seu thiep
    Foumou tek beute man ley guiss damako moudjou yeeem
    Ma mate femme lab neu tchi samay feem
    Dafmey khol nane meu tu me rends fou
    Ohh bb kham ngani maley danel
    Maay fékheul seu khol
    Fo meunti dem dangay nieuw sama djongué molay gaagn man nga beugue ci leu life
    Pre-refrain
    (Touss touss nak touss ) man rek ley toppeu
    (Touss touss nak touss ) souy nelaw man rek ley guinteu
    (Touss touss nak touss ) ki dé man leu dinkeu khol bi
    (Touss touss nak touss ) maay seytané bi
    Refrain
    Enh man rek ley toppeu
    Souy nelaw man rek ley guinteu
    Ki dé man leu dinkeu kholam
    Maay seytané bi
    Couplet 2
    Mani djongué takh sama khir laa yor di bathie
    Gni dougne touss ci game bi maay bandit bou mag bi
    Kou sa dieukeur dof ba feul meu doto nélaw
    Dama diongoma ba yakou seine wakh laye fakhass ni nguélaw
    Man ma kham fikoy khassane
    Diko wokkou té meunougne ci dara
    Mom diokh nama bopp ba tog sama néné sou gouddé mou wowé meu maman
    ouh ohhh ohhhh
    Ohh bb kham ngani maley danel
    Maay fékheul seu khol
    Fo meunti dem dangay nieuw sama djongué molay gaagn man nga beugue ci leu life
    Pre-refrain
    man rek ley toppeu
    souy nelaw man rek ley guinteu
    (Touss touss nak touss ) ki dé man leu dinkeu khol bi
    (Touss touss nak touss ) maay seytané bi
    Refrain
    Enh man rek ley toppeu
    Souy nelaw man rek ley guinteu
    Ki dé man leu dinkeu kholam
    Maay seytané bi
    REMERCIEMENTS:
    Tenue: Amossa
    Coiffure: Dijaaaa and aïcha
    Accessoires: Dishop
    MakUP: Sokhna Pene
    Chorégraphie: prince
    - Abonnez vous et activez la cloche de notifications 🛎 ✅
    Assurez vous de suivre Aicha Kone sur:
    Instagram - aicha_kone_...
    Tiktok - www.tiktok.com/@aicha_kon2
    #AICHAKONE2024
  • Hudba

Komentáře • 945

  • @user-sv3ni9nd6s
    @user-sv3ni9nd6s Před dnem +65

    Je n’ai entendu que des choses négatives motakh ma gneuw khôl mais au final guissou ma problème bi bayilen khollou 😂

    • @FaBaBe-
      @FaBaBe- Před 10 hodinami +1

      Moi aussi 😅

  • @loufa7878
    @loufa7878 Před dnem +43

    Dagne koumpa dé momafi indi 😂😂
    Ms souma waxé son bi nèxoul gnu attaquéma bayil ma noppi rk

  • @oumouchkadiallo8070
    @oumouchkadiallo8070 Před 2 dny +14

    Wallahi li dafa neix❤❤❤
    Bayi lein ma rirando bi parce que certaines personnes nénaniu nexul rek nguen toppeuh si yein tmt?
    Écoutez et faites vous votre propre opinion.
    Machalah Aïcha du courage et bon vent ❤️❤️❤️

  • @MalcomboydipVevo
    @MalcomboydipVevo Před 2 dny +11

    Team Aïcha Kone

  • @user-re8sh4st8h
    @user-re8sh4st8h Před 2 dny +7

    Nice na ma chéri ❤

  • @CodouGaye-nt8uf
    @CodouGaye-nt8uf Před 2 dny +278

    Dans la vie on ne peut pas plaire a tout le monde alors il faut avancé avec les gens qui t'aime bonne continuation sista ❤🫡🙏

  • @sasamaria3279
    @sasamaria3279 Před 2 dny +527

    Heyy gnou wakhtane nakk li NEKHNA torop nakk en plus elle a eu le courage démal bopom kone diapalé lén ko surtout nous les filles amoul sokhor🙏🙏🙏🙏

    • @maguitaseck69913
      @maguitaseck69913 Před 2 dny +8

      Exactement ❤❤❤

    • @ZeynaBabie
      @ZeynaBabie Před 2 dny +5

      Bilaye

    • @toutythiam3305
      @toutythiam3305 Před 2 dny +19

      Melodie bi voice bi habillements tout nice mais paroles yi franchement moy lolou on n comprend kdal on entend kdal

    • @AmyThiam-eg4xc
      @AmyThiam-eg4xc Před 2 dny +22

      Mossoul nékh😂😂

    • @RamaDia-ph3ui
      @RamaDia-ph3ui Před 2 dny +8

      Ms jongué bini wakh amoul si clip bi mélodie bi mom namako ball nékhoul amoul feeling th li mom dou jongué nko changer outate benen titre pour son bi

  • @agnelendiaye7967
    @agnelendiaye7967 Před dnem +6

    Waouh ,en tant que melomane je te dis sister melodie bi voix bi on fleek paroles yi rek mo dess .mais tu maitrises les runs et les octaves teggou na thi temps mashallah

  • @Veshrka6963
    @Veshrka6963 Před 2 dny +152

    Kou khamoul musique meuno enjoy li. Wey bi amoul khasté amoul garouwalé motah menoul nekh Sénégalais yi. Bonne continuation Aicha 🎉

    • @Adriane_206_
      @Adriane_206_ Před dnem +7

      Xamouma dara si musique ms xamna ni lii mom nexoul

    • @mouhameddia5168
      @mouhameddia5168 Před dnem +4

      ​@@Adriane_206_ li dafa nèxoul dara sakh amoul bène niveau

    • @ramndondiaye2113
      @ramndondiaye2113 Před 17 hodinami +3

      Bilay amoul samay none😂

    • @aida1986
      @aida1986 Před 5 hodinami +1

      Pardon guani amoul garou walé?😂 bayi lén kouni nékhoul guén wakh lén ni khamou niou way😂

  • @AlhamdoulilahiRabilalahmine

    Bonne continuation 🎉

  • @PlatineArtists
    @PlatineArtists Před 2 dny +97

    Barki yallah je trouve k sen petit galei dafa defar ay artists you am voix you graw😭❤️❤️❤️❤️ dégal la technicité de aïcha 😭😭

  • @user-md1ld6fg2r
    @user-md1ld6fg2r Před 2 dny +46

    On dirait viviane 😵‍💫 bonne continuation 🎉🎉🎉🎉🎉🎉 sista ❤❤❤❤❤

  • @user-uz3rl9zt9o
    @user-uz3rl9zt9o Před 2 dny +7

    Mom dh garou waleé woul ken 😊motakh musique bi mu am barkel

  • @agnelendiaye7967
    @agnelendiaye7967 Před 21 hodinou +3

    On est trop habitué au reum teumbi teum mais son bi ya un travail fou derriere té dieuloul melodie kene .apres may diwline bouy ninal sa thiep lithi top ba ahhh bebe bi ..❤❤❤❤❤❤❤

  • @NafiSall-uc7gm
    @NafiSall-uc7gm Před dnem +28

    Li sou nékhoul, khawma Lou nékh?🎉🎉

  • @user-jh5jy1mx2j
    @user-jh5jy1mx2j Před dnem +19

    Kou d'accord ni dafa nékh rek lale ❤❤❤❤🎉🎉

  • @adamaly5362
    @adamaly5362 Před dnem +3

    Lima beug wakh douffi khadjee il faut ma guiss Aïcha 🎉🎉🎉😂😂

  • @mamifall08
    @mamifall08 Před 2 dny +3

    Je l’ai toujours adoré la belle Aïcha depuis sen petit galé et vu comme Viviane ndour. Fonce ma chérie , travaille dur et ça ira inchallah du courage thia kaw si kanam❤

  • @alimaniane2412
    @alimaniane2412 Před dnem +3

    Pourtant dafa neh juste k limou sol rek mo démoul AK môme Lou guoudde moka gueune diap❤❤

  • @alalouserignetouba6190
    @alalouserignetouba6190 Před 20 hodinami +5

    Franchement déglou na son béne yon mais bobou ba légui damay méérr rk 🙏🙏 Limou sol metina trop teksi en plein d’été vraiment clips bi nekhoul bakhoul ga balma nak 😎😎Aicha kone tank yi comme clou de girofle 😭 gua balma mais douma diay

  • @thiateshop
    @thiateshop Před dnem +34

    Barké yalla nékhoule 😎

  • @maimounabalde6788
    @maimounabalde6788 Před 20 hodinami +11

    Kou d'accord ni moy Viviane bou ndaw beusseul❤

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 Před 2 dny +3

    Aïcha ya kherei waay❤🎉

  • @IKES2324
    @IKES2324 Před dnem +38

    Sincèrement gni wakh li nékhoul meunou maléne comprendre certains dagniy blague par contre d'autres moom danio beugoul Aïcha rk mais bon façon Viviane tmt dégg na louné ay meunoul live etc té tay dji représentée na founé Sénégal indi fi ay prix fonce Aïcha never give up tout début est difficile📌

  • @ndeyematyfall4160
    @ndeyematyfall4160 Před 2 dny +3

    Trop fière de toi🎉🎉🎉🎉

  • @DeejaWrites
    @DeejaWrites Před 2 dny +20

    Waykat you mague yi wayii nagn lepp motakh ken amatoul loum wayii😂

  • @YasmineSowe
    @YasmineSowe Před 3 hodinami +2

    Nekhna trop machallah ❤

  • @joendir4858
    @joendir4858 Před 10 hodinami +2

    Li lagn wakh da nakhari ni 😮😮 franchement neuk nekh na

  • @user-id4kt6vr6r
    @user-id4kt6vr6r Před 2 dny +4

    Toute façon elle a Une belle voix lolou mome keineu dousi wéranetei

  • @user-bg7ki3xf3n
    @user-bg7ki3xf3n Před 2 dny +20

    Pourtant nekhna deh khar leneu ba wa team bi snap ko challenge bi commencé 😂gueneu khamni nekh

  • @khalilofficiel4609
    @khalilofficiel4609 Před 5 hodinami +1

    Aicha Koné courage dina bakh tout début est difficile, sou radio yo téguè song bi plusieurs fois légui sénégalais yi apprécié ko ❤❤❤

  • @user-zr2lw2qp2v
    @user-zr2lw2qp2v Před dnem +6

    Mé aïcha lii moy lan 😂😂😂

  • @diagnegueye2893
    @diagnegueye2893 Před 2 dny +56

    Machallah nékhna trop❤

  • @user-mt1xj9kk4p
    @user-mt1xj9kk4p Před 2 dny +24

    Amoul pourtant dafa nékh li dafa nékh lol machalah bravo Aïcha bonne continuation ❤🎉🎉

  • @agnelendiaye7967
    @agnelendiaye7967 Před 20 hodinami +2

    La chorégraphie des danseurs on en parle 🎉🎉

  • @carolinesarr3556
    @carolinesarr3556 Před 2 dny +3

    La mini Vivi. Je t'apprécie car j'aime Viviane et tu dégages son style ❤❤

  • @maximadiedhiou2881
    @maximadiedhiou2881 Před dnem +2

    Ah machallah gni di wakh nekhoul louye problème bi

    • @Musikmama100
      @Musikmama100 Před dnem +1

      Ils veulent juste la déstabiliser. Mais elle a produit une très belle song 🎉🎉

  • @user-bl8ni1ke5m
    @user-bl8ni1ke5m Před 2 dny +346

    Djongué lene sama commentaire ❤😊

  • @agnelendiaye7967
    @agnelendiaye7967 Před dnem +2

    Son bi dafa.nekh torop tay mome la yewo et j arrete pas de l.ecouter .c est ma 6 e visite ❤

  • @idrissaba4035
    @idrissaba4035 Před 2 dny +129

    Mashallah là je vois bien une Aïcha libre et qui met en valeur sa voix.
    L'art c'est d'abord un esprit libre.
    Tu vas écraser les petits artites 🎉🎉🎉🎉

  • @yamarkane9909
    @yamarkane9909 Před 2 dny +30

    Quitter ce label profitard t’a donné des ailes. Bravo ✌🏾

  • @ahmadika525
    @ahmadika525 Před 15 hodinami +2

    Comme Viviane dé Bilay 🎉❤❤

  • @fatoumatasano6634
    @fatoumatasano6634 Před 2 dny +2

    Amna gnou sokhor nak sons bi defoule loudoul nekh frcmt chapeau à toi 🥰😻😻🥳🎊

  • @morygueye3503
    @morygueye3503 Před 2 dny +4

    Viviane lay guissfii mane❤

  • @Ndiaye-yt6sf
    @Ndiaye-yt6sf Před 2 dny +39

    je suis en musicien et j'apprécie beaucoup ta voix te chante bien tu as la justesse donc il faut pas gérer mauvaises commentaires moi particulièrement je suis un musicien et j'aime ta voix bonne continuation et ne gère pas c'est jaloux dangeu léne geune tooye rék

    • @RokhayaDiouf-fd2hu
      @RokhayaDiouf-fd2hu Před 2 dny +5

      Yaw kayy tooye bé la intéresser 😂

    • @rokhayadiop9606
      @rokhayadiop9606 Před 2 dny +2

      😂😂😂😂😂😂mingui niaw deh

    • @Ndiaye-yt6sf
      @Ndiaye-yt6sf Před 2 dny

      @@RokhayaDiouf-fd2hu 🤣🤣🤣 nonou sakh Sénégal dafa am gnio sokhore khalé bi tooye rék gnio mére

    • @RokhayaDiouf-fd2hu
      @RokhayaDiouf-fd2hu Před 2 dny

      @@Ndiaye-yt6sf wwe tooye bi mome deugue leuh mais wayy bi nékhoul 😭

  • @user-id4kt6vr6r
    @user-id4kt6vr6r Před 2 dny +60

    Képou kou khame music di déglou niépou khame ni Aïcha limou way néxna ay dof guéne rk xamo leine lii lou rambax guéne kham 😊😊

  • @nogayeder
    @nogayeder Před dnem +1

    Machallah nekhna dh goor gorlou rk dina bakh

  • @malickndiaye319
    @malickndiaye319 Před 2 dny +13

    Avec sa belle voix meune nga sori si musique
    Kén dakhoula way

  • @AmiLy-np8ts
    @AmiLy-np8ts Před 2 dny +3

    Sérieux nekhna nak❤

  • @nafissatousy2417
    @nafissatousy2417 Před dnem +1

    Ah yalla bakhna reik

  • @monavenir7378
    @monavenir7378 Před dnem +1

    Bou sokhore wesso rek son bi guissoumassi lou nakari nekh la def❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @aissatoundioneofficiel3362

    On lui donne la force. Elle est fan de Vivi. Force à elle. Jolies mélodies ❤❤❤❤

  • @user-wf2ef6gu8r
    @user-wf2ef6gu8r Před dnem +2

    Beuss bo Dieme way live en concert.. Sila niouy khameni meuno touss

  • @AlimaCisse-k4g
    @AlimaCisse-k4g Před 2 dny +1

    Machahallah Aïcha Koné ❤💯

  • @bdjram5041
    @bdjram5041 Před 2 dny +19

    Spicy girl au debut 😂😂😂 😂hana sa domou ngey ndakhte mola rakadj clip bi rafet na mais nehoul nehoul deugg rek la wakh buma fi kene tudd nakk😎

  • @khadidiatoudiallo2544
    @khadidiatoudiallo2544 Před dnem +4

    😂Kone nekhna nii😂

  • @GetsuLOQUE
    @GetsuLOQUE Před dnem +5

    😂Moi suis juste là pour les commentaires Ptdr🤣🤣🤣🤣

  • @MTG_APPEL
    @MTG_APPEL Před 2 dny +18

    Mane yaw rek lay topp❤❤

  • @fatoulawadrame3223
    @fatoulawadrame3223 Před dnem +1

    Li dafa fess😭❤

  • @mamiseck1049
    @mamiseck1049 Před 14 hodinami +1

    En tout cas moi mome jadore son bou nekhla vraiment on ditait une americaine ❤❤❤

  • @AntaGueye-hn1mk
    @AntaGueye-hn1mk Před 2 dny +119

    Kou guis filing bii khalé bii di dégagé rkk lalal j'aime 🎉❤

  • @KhadyWade-jf5gd
    @KhadyWade-jf5gd Před dnem +3

    Pourtant néxna dh da amoul chance rk😂

  • @LhommeNdoye
    @LhommeNdoye Před 2 dny +2

    Une très belle morceau j'aime bien les différents technique musicale chapeau à toi❤

  • @user-bo1jk4ex8r
    @user-bo1jk4ex8r Před dnem +1

    Waw Comme Vivianne bouy way meme voix machallah ❤❤❤❤❤

  • @user-tv6lp5vy7e
    @user-tv6lp5vy7e Před 2 dny +145

    On dirait Viviane avec une belle voix 🎉 et c’est tenue ouf 🎉

    • @aidangom6386
      @aidangom6386 Před 2 dny +2

      Lolu dh la beugon wax

    • @aliougaye2070
      @aliougaye2070 Před 2 dny +1

      Wakh ngau daug

    • @abdoulayesylla6123
      @abdoulayesylla6123 Před 2 dny +16

      N’abuse pas, elle n’a même pas un single Crab et tu la compare déjà Viviane qui a 25 ans carrière . Vous êtes capable de sauter un chat jusqu’à ce qu’il aille attaquer un lion .

    • @bambarassoul2750
      @bambarassoul2750 Před 2 dny +8

      Ban Viviane iow damay niap sa khoon déh 😂😂😂

    • @fatoumataba3150
      @fatoumataba3150 Před 2 dny

      Koula bayii 😂😂😂😂😂😂​@@bambarassoul2750

  • @abofallkabaro6646
    @abofallkabaro6646 Před dnem +4

    Son bi loumou nakari yéré yi compliqué nagn ko Aïcha je t’aime bien diangui watal tu es encore jeune

  • @user-2032
    @user-2032 Před dnem +1

    Courage ma belle trop jolie et belle mélodie continue ton chemin que personne ne te déstabilise 🎉🎉🎉🎉🎉❤

  • @clotildeabbey6272
    @clotildeabbey6272 Před dnem +1

    POURTANT JE TROUVE ÇA BEAU. Les gens sont vraiment méchant

  • @Senegalist
    @Senegalist Před 2 dny +54

    En tout cas label bobou day soul ndanane bonne continuation Aicha ❤

    • @abdousamaddiagne8206
      @abdousamaddiagne8206 Před dnem

      Bane artiste mofa nekone diouguéfa Di tothie Sénégal

    • @Senegalist
      @Senegalist Před 19 hodinami

      @@abdousamaddiagne8206 je te retourne la question. Dagnou lay bloquer temps bingay nek khalei banga maguette gnou libérer la nga diarefa retraité

  • @oulishfashionashdiagne2725

    Le style j’adore machalah 🥰🥰🥰🥰🎊Bne continuation bb❤

  • @OumySonko-pg3zd
    @OumySonko-pg3zd Před 4 hodinami +1

    Mane mome j’aime vraiment j’adore machalla bonne continuation

  • @latyrndour6506
    @latyrndour6506 Před dnem +1

    Manchallah nekhoul

  • @falloundiaye3120
    @falloundiaye3120 Před dnem +24

    Li nekhoul barki yalla mom day way Walla day jouer diayou 😂😂

  • @NdayesyllaGeuye
    @NdayesyllaGeuye Před 2 dny +4

    Machallah yamn kay ❤

  • @fasalihoucamara7627
    @fasalihoucamara7627 Před dnem +1

    Bravo Aïcha très bien demalal sa bop🥰🥰

  • @venusndoye9036
    @venusndoye9036 Před dnem +2

    Démal djanguiwate , dess na, weuy bii moom nékhoul, deug nekhoul nakk.

  • @adamagueye1807
    @adamagueye1807 Před 2 dny +48

    Mashallah Yalla na voix bi geuneu Wëër 🙏🙏🙏

  • @bintmoustapha8633
    @bintmoustapha8633 Před 2 dny +6

    Ayez l'habitude de soutenir nos artistes way abonnez vous en masse💪🏾💪🏾❤️❤️🔥🔥🔥🔥

  • @matydiagne1847
    @matydiagne1847 Před 8 hodinami +1

    Kouka diapalé mou dém❤❤❤

  • @user-gw2qt7tx6r
    @user-gw2qt7tx6r Před dnem +2

    Wakh léne ki deug Ahhh li mome nékhoule

  • @MarieDiallo-o7w
    @MarieDiallo-o7w Před 2 dny +3

    Machallah bonne continuation li nekhna trop 🎉🎉❤❤❤❤

  • @sokhoulovedieng1365
    @sokhoulovedieng1365 Před 2 dny +204

    Hey ❤❤😢😢😢😢😢😢😢kou sokhor ak bone motakh gnouy critiquer wayé feeling bisi khalé bi rek ô❤❤❤❤❤

  • @MatarDarame-lr3mv
    @MatarDarame-lr3mv Před dnem +1

    Doul rek 😂❤

  • @user-kv3fr4bm3g
    @user-kv3fr4bm3g Před 2 dny +2

    Macha Allah elle chante bien bonne continuation

  • @Ayesha.74
    @Ayesha.74 Před 2 dny +8

    Viviane rek la mayy saff MashaAllah

    • @bayetallahofficieltah4154
      @bayetallahofficieltah4154 Před dnem

      YA MEUNEU FEEN YAWIIT

    • @msp2558
      @msp2558 Před dnem +1

      @@bayetallahofficieltah4154Amal respect chacun son opinion
      Mane mi sakh Viviane lamay diokh

  • @Diatouba-vp5uv
    @Diatouba-vp5uv Před 2 dny +8

    Waou machala Aicha Yalla nala yalla sam ga agalè ak sago ❤

  • @veriteabsoluedeugneekhoul1720
    @veriteabsoluedeugneekhoul1720 Před 5 hodinami +1

    Ensemble jean bi rek la valider. Sinon le son est tres bon

  • @dalzesow3506
    @dalzesow3506 Před 18 hodinami +1

    Je chanterai 7 chanson lorsque j serai marié avec l'amour de ma vie ❤

  • @papadieye7265
    @papadieye7265 Před 2 dny +4

    Waw machallah ma belle nice mene mokale ❤❤❤❤

  • @bintmoustapha8633
    @bintmoustapha8633 Před 2 dny +3

    Nila dh dieuleul sa yonou bopp. Amngua talent rafét ngua. Wa borr bé dani jeul artiste diko taal ak diko faye bamou maguétt gnou sani😌
    Go go gooo🔥🔥❤️❤️❤️❤️

  • @user-ce7sb3en3x
    @user-ce7sb3en3x Před 2 hodinami

    Ndakhte Lô RK La Niouy Topou 😂😂😂 Aïcha Koné Sa Son Bi Mom Dokhoul Wou Djogué Way 😂😂😂😂😂😂

  • @user-dh8yc1op6t
    @user-dh8yc1op6t Před 14 hodinami +1

    ❤❤❤❤❤waaaaaaaaw nekhhhhhh nahhhhh waaaiiii

  • @FatouDiop-mq9lr
    @FatouDiop-mq9lr Před 2 dny +3

    Tu es meilleure bb Viviane bou ndao

  • @momoly6479
    @momoly6479 Před 2 dny +6

    Bon continuation Aïcha ❤

  • @MatarBeye-
    @MatarBeye- Před dnem

    Mashallah rafit na deh 🎉❤❤

  • @Mara-v4h
    @Mara-v4h Před 16 hodinami

    Wah ki loumouye wakh nii dèmal diangi wate waye 😢😢😢😢

  • @darkchokolate8040
    @darkchokolate8040 Před dnem +8

    Nekhoul deh bilay nak nous ne Somme’s pas hypocrite

  • @fatoutouray4582
    @fatoutouray4582 Před 2 dny +6

    Billaya sorkhorr ngen🥹 li nexx na trop clip b rafet tamit❤ go girl ❤️❤️❤️

  • @darkchokolate8040
    @darkchokolate8040 Před dnem

    Thiey Yallah Aicha bilay bal nagnela ko meune nga continuer si diay khessal bi 😩😩😩

  • @SAMBASALL-fu7el
    @SAMBASALL-fu7el Před dnem +1

    Song bi si bopam daa djongué manchalah