Alioune Seye 2 sans réserve : "Modou Lô na ma may chance, Quench diambar la ma gui koy…"

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 8. 05. 2024
  • Visitez notre site web luttetv.com/ et aimez notre page Facebook pour voir des combats en direct / luttetv
    / luttetv
    / luttetv
    / luttetv
    luttetv.com/
  • Sport

Komentáře • 92

  • @Bigboss-hd8fx
    @Bigboss-hd8fx Před 25 dny +20

    Petit lo communiqué bien machallah kou tokk keparou Modou Lo ni rek ngaye mana mel

  • @khadimgadiaga5730
    @khadimgadiaga5730 Před 25 dny +10

    Machallah Aliou seye lolou Moy def si almére Yi lou kawé la yalla na yalla same len

  • @IbouNdiaye-tj7wr
    @IbouNdiaye-tj7wr Před 25 dny +14

    Billaye petite lo ndanane leu Modou lo seul

  • @kharagnembaye5958
    @kharagnembaye5958 Před 25 dny +6

    Aliou seuye Modou lo dou gnii dei waa bakhna

  • @Zeus44officiel
    @Zeus44officiel Před 25 dny +8

    Modou lo dousa morom dieuleul niom boy niang lac ama balde reug reug

  • @sambakobar6771
    @sambakobar6771 Před 25 dny +1

    Machalla yalla nala yalla faye seye niit kou bakh beugue nieup

  • @IbouNdiaye-tj7wr
    @IbouNdiaye-tj7wr Před 25 dny +5

    Wallahi Alioune ndanane leu

  • @morndiaye8634
    @morndiaye8634 Před 25 dny +5

    Seye 2 🎉eumeu sene

  • @thewondersofnature1453
    @thewondersofnature1453 Před 25 dny +6

    Mom Modou Lo dane nako sakh

  • @salioundiaye5763
    @salioundiaye5763 Před 25 dny

    Merci beaucoup ❤❤❤❤❤

  • @FallouFaye-zy9bn
    @FallouFaye-zy9bn Před 18 dny

    Wa forza koum fi daan😮

  • @mouhameth7660
    @mouhameth7660 Před 25 dny +2

    Mane talibé baye la mais dama setlou si baye fall yi yarr boy doywar, chaque fois ce qui se disent Baye fall dagnouy âme tarr troppppp nekk nitt you lewet. Té djiko gueunoul lolou, Alioune Seye et Jacob balde ils me fascinent si sene yarr

    • @FallouDioum-qv1if
      @FallouDioum-qv1if Před 25 dny

      Waxal nga yalla frére ...ya niakk kiniane yalla nala yalla défal soutoureu Sam la si barker seydina mouhamad PSL ❤️

  • @leveridique-kj7qo
    @leveridique-kj7qo Před 25 dny +8

    Alioune Sèye 2 meune na beuré meune na khèkh farfarlo mofi nék ak tapét wayé da wara beurèk gnisi kaw moy yone😂😂😂

    • @abdoulahadgueye4643
      @abdoulahadgueye4643 Před 25 dny

      Alioune Seye bou toggué Baye niane chance tardé na. Kane mokoye maye chance.

  • @modoufall4327
    @modoufall4327 Před 25 dny +2

    Amna talubé bakhna

  • @OscarbouXlo
    @OscarbouXlo Před 25 dny +4

    Xaragne lo seul ❤️💪🏿

  • @user-mj2ec3pi6b
    @user-mj2ec3pi6b Před 22 dny

    Eumeu sene dieuleul Alioune seye 2 ngir yalla

  • @lepatriote9423
    @lepatriote9423 Před 25 dny +5

    Euma Sene nako may chance

  • @user-ho9kl8cq1q
    @user-ho9kl8cq1q Před 25 dny +14

    Alioune seye vs eumeu séne

  • @cheikhbasskeurmassar9548

    Waw kaye

  • @elhadjisarr7700
    @elhadjisarr7700 Před 18 dny

    Yow Alioune seye presque dénoula faté wone si lamb yow dane barkidém quench rék takh ngay ladji äy modou lo ak ay Eumeu sene

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Před 24 dny

    Billahi Revanche Bounéxla trop
    Alioune sey 2 modou Lo nguir yallah Modou Lo mayko revanche beugeu naa lolou trop Man 🥹

  • @bocarba2781
    @bocarba2781 Před 25 dny +5

    Boy tioutj dafay kham diamam

  • @ibrasarr9429
    @ibrasarr9429 Před 25 dny +7

    Alioune seye2 vs Amanékh

  • @user-xr2ns5ij8l
    @user-xr2ns5ij8l Před 25 dny +6

    Franc vs lac de guiér , Aliou seye vs eumeu séne

  • @makhoumb
    @makhoumb Před 20 dny

    Alioune sey2 vs situe modonne combat bi akh

  • @vieuxndiaye3790
    @vieuxndiaye3790 Před 25 dny +1

    Alioune seye vs zarko combat dakhou koo

  • @diosssamb1015
    @diosssamb1015 Před 25 dny +2

    alioune seye na khar tapha tine wala

  • @babacar3178
    @babacar3178 Před 25 dny +2

    Alioune na dieul eumeu bou dané dieul modou

  • @mbackeseye183
    @mbackeseye183 Před 22 dny

    Aliou seye mom borombakh la

  • @agenperf1826
    @agenperf1826 Před 25 dny

    Alioune Sèye 2 🥊 Franc

  • @bassdiokhane1472
    @bassdiokhane1472 Před 25 dny

    Euma sen Aliou saye 2 combat la de

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 Před 24 dny

    😂😂😂alioune séye yaw wérga dodéme beuré ak petit lô

  • @afro3827
    @afro3827 Před 25 dny +1

    Antouca nitt kou bakh la té selleu lolou gay def si armel yi rek man nalay may ndam 🎉🎉🎉🎉🎉

  • @user-li1ro9pn8y
    @user-li1ro9pn8y Před 20 dny

    Alioune seye2 vs eumeu sene
    Franc vs lac 2

  • @Zaideun10
    @Zaideun10 Před 25 dny +1

    Franc vs lac de guer
    Allune seye vs eumeu sene

  • @user-wp4pd6sr2z
    @user-wp4pd6sr2z Před 25 dny

    Eumeu bou danouwone Dinama dieul mé ni dou combat

  • @user-zj8tw3mp8q
    @user-zj8tw3mp8q Před 25 dny +3

    Aliou sey gni ngay beurél ak modou lô dou benn boulniou modou mola dak khékh dak la dor dak la beuré boulniou yab way dieuleul dame séne guiro talfa gora sokh garga 2 niang ballo ada boy baol nioy sa morome

  • @user-cb1uf3lc2m
    @user-cb1uf3lc2m Před 25 dny

    Diâz seul

  • @fanthomjohn4399
    @fanthomjohn4399 Před 25 dny +4

    Sawaay modou lo nena beuré woul revanche 😂😂 demal khol Ama wala Tapha tine

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 Před 25 dny

    Aliou seye nako vip dieul petit lo c le numero 2 de modou lo

  • @cherifdiallo2514
    @cherifdiallo2514 Před 25 dny +4

    Alune seye 2 yaw bangay beuré bobou Modou lô mongui liguey soudeur métallique 😂tw nga War ko may chance mome moulay may chance

    • @IbrahimaLeye-lv8yq
      @IbrahimaLeye-lv8yq Před 25 dny

      😂😂😂

    • @alhamdoulilah9154
      @alhamdoulilah9154 Před 25 dny +1

      Mais lolou waroula diakhal parce-que yawe parce nitt Dina takk diabar am thia doome doome bobou magg rawla ba yorr ko yalla Mouy dogol

  • @user-ys2dd8fb7y
    @user-ys2dd8fb7y Před 25 dny +1

    Je suis un fan d’eumeu Sene mais dama beugue mou mayy chance Alioune seye ndakh Daffa warra am xaliss si lamb

  • @doffdouweer3686
    @doffdouweer3686 Před 25 dny +1

    Alioune seye vs forza
    Alioune seye vs sa thies

  • @ousseynoutoure518
    @ousseynoutoure518 Před 25 dny

    Blh dafa bakh mom rk lay supporté Gway

  • @domousenegalinfo9563
    @domousenegalinfo9563 Před 25 dny

    Alioune seye vs Eumeu sene

  • @mayasinendiaye2514
    @mayasinendiaye2514 Před 25 dny +1

    Doo diall fara

  • @abdoulayediop9331
    @abdoulayediop9331 Před 24 dny

    Aliou yow mbeur bouma nékh nga mé Modou AK yow d'où comba yow AK faran ba reug reug ba

  • @user-ee9mi4tg3l
    @user-ee9mi4tg3l Před 24 dny

    Modou moleu meune si lep

  • @vieuxndiaye3790
    @vieuxndiaye3790 Před 25 dny

    Eumeu senne vs franc

  • @IbrahimaSarr-jw8qm
    @IbrahimaSarr-jw8qm Před 25 dny +1

    Ama vs Alioune seye 2 ou eumeu vs Alioune seye 2

  • @user-lj5dz7cm8c
    @user-lj5dz7cm8c Před 25 dny

    Ban Modou lo lay wakh ?😅😅😅😢

    • @Domou_Deukk_Bi
      @Domou_Deukk_Bi Před 25 dny

      Niata modou lo nio nek si lamb j? Alioune seye kou nafekoull khamni meriténa beuré ak gnissi kaw

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 Před 25 dny

      Modou lo borom 22 coup 👊 yi 😂

  • @Ydakh-ui5yo
    @Ydakh-ui5yo Před 25 dny

    Eumeu sêneu musculation lay dané alioune seye2 wayé kêneu dakouko beurrê si Sénégal

  • @azizdia3347
    @azizdia3347 Před 25 dny

    Petit lo beugue gua genre comme modou lo s k xam gua louma la wax

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 Před 25 dny

    Aliou Seye 2 il falloir venir au stade... Faire le chaud comme les lutteurs... Tu es très timide lol

  • @alhamdoulilah9154
    @alhamdoulilah9154 Před 25 dny

    Man d vraiment Modou lo reck laye supporter si lamb mais bouma sagnone bou daané siteu mou maye Aliou seye 2 change beuré ak moum

    • @clementlenglettv8785
      @clementlenglettv8785 Před 25 dny

      Mais modou nena dou beurré tii revanche té daane n'a Alioune seye 2

  • @sarabo6779
    @sarabo6779 Před 25 dny

    Alioune seye ladial eumeu sene denga yarou trop degal choc eumeu sene

  • @lesdeliresdeboyghetto6930

    Tyson2 vs Alioune seye kou dane dem cour de grand

    • @FallouFaye-zy9bn
      @FallouFaye-zy9bn Před 18 dny

      Aline seye dane nako fo.nk😂

    • @kefgg
      @kefgg Před 16 dny

      ​@@FallouFaye-zy9bnDioume nga dh Alioune Seye 2 meusoul beuré ak Tyson 2

  • @DjibiKeita-vv4xt
    @DjibiKeita-vv4xt Před 25 dny

    Modou lo bou bereg aliou seye danger la ci mom

  • @sarabo6779
    @sarabo6779 Před 25 dny

    Alioune j'aime pas ta communication affair degal sa bop amoul yalla yalla yaw eumeu combat la Limo takh reug reug nekhma

  • @user-tw3hv5yw1n
    @user-tw3hv5yw1n Před 25 dny +1

    Alioune seye pas eumeu sene pas franc ce sera lourd

  • @papasalioucisse9639
    @papasalioucisse9639 Před 25 dny

    Alioune seye vs forza