La Maman de Cheikh Gueye menace : Les bourreaux de mon fils ne perdent rien pour attendre..

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 1. 03. 2017
  • TikTok Pikini☆~~👇
    rebrand.ly/TikTok-Pikini-Prod...
    FACEBOOK☆~~👇
    bit.ly/Facebook-Pikini
    Abonnement Gratuit ici☆~~👇bit.ly/Abonnement_Gratuit_Pikini
  • Zábava

Komentáře • 368

  • @paola6c298
    @paola6c298 Před 7 lety +60

    Masseu mettina yalla na yalla beuss séne khôl té takhawoulene.Yalla neuko yalla kharé aldiana

    • @aliou6396
      @aliou6396 Před 7 lety +1

      Paola Gueye amine

    • @mb6308
      @mb6308 Před 7 lety

      Paola Gueye
      amin

    • @tidiouboy9774
      @tidiouboy9774 Před 7 lety +3

      Paola Gueye amine yarabii

    • @moustaphamoustapha994
      @moustaphamoustapha994 Před 7 lety +1

      yalla nako yalla yeruem

    • @mbeneba6236
      @mbeneba6236 Před 7 lety +1

      ce vraiment emouvant mai nague li ba cagne tro ce trop il fau prendre des mesure severe pour ces mal faiteur ki n'ont pa pitié de persone ceux ne sont ke des imbeciles

  • @aliou6396
    @aliou6396 Před 7 lety +8

    mai vraiment sounou maman dji mom diambar la yalla na yalla dolli kholou mbouthie. billahi gnou def li mom sougnou len diappei dagnou len wara ray. magui beugue saga sakh wayei diarouko

  • @alphabarry32
    @alphabarry32 Před 7 lety +2

    oh mon. dieu li mettina. yalnako sougnou borom yeureum. deysane. qu'il repose en paix

  • @khadybadji7780
    @khadybadji7780 Před 6 lety +2

    G eu un choc quand g vu la photo de Mame cheikh a la une c touchant car il était klkun de calme et souriant je me souviens le dernier cadeau que jai reçu de lui des chaussures ballerine bleu. Que dieu nous montre les responsables de cet acte

  • @boubacarndao4139
    @boubacarndao4139 Před 7 lety

    hoooo my god thiéy Sénégal li lala ni no c'est pas possible yalla na yalla haarè ko aldiana thii barké lahilaha ilala

  • @mamependafall7432
    @mamependafall7432 Před 7 lety

    ndeysann dawna yaram yallnako yalla yeureum ta xaréko aldiana gniko def yallna lenn yalla torokhall thi aduna

  • @salioumbaye3215
    @salioumbaye3215 Před 7 lety +2

    famille bi yalla nalene yalla ak serigne touba fetei falene mame cheikh fetewobe

  • @mayasow4028
    @mayasow4028 Před 7 lety

    ndeye sane yalla nako yallah kharé aldiana té maylén kholou mougn

  • @senegalsenegal9010
    @senegalsenegal9010 Před 7 lety +2

    yalanako yala.yeurem.khare.ko.aldiana sibarke serigne.touba mbacke Amine.yarabi

  • @ndiollediouf6176
    @ndiollediouf6176 Před 7 lety

    Metina toropp mai yalla gueumoul nelawoul ben yoon khamna lepp cheikh yalla nako borom bii khare si aldiana yii gueuneu kawe metina torop

  • @khadimsyllabresilchapeco5259

    bilahi metina trop li niawna yalla nako yalla yeram vremant metina di ligeye amsa yefo bope ay Sam Ba boy niaw rayla yalla nalen yalla nitt bagn ray len

  • @damegueye5585
    @damegueye5585 Před 7 lety +1

    ndayesane metina loll sakh yalla nakou yalla yaram te khari kou aldiana li doyena warr

  • @rokhayamadamesano
    @rokhayamadamesano Před 7 lety +1

    massa mes condoléances a toutes sa famille,fimoulene feetewone yalla nalene fa borome bi feete, yalla nako yalla khare aldiana firtawsi

  • @sowbile7846
    @sowbile7846 Před 7 lety

    doyna war trop ray niit té do fék si môme dara loor aye mbokam yalana ko yalla kharé aldiana inchalla metina

  • @masskhoule7130
    @masskhoule7130 Před 7 lety

    yalnako yalla yeram te khareko aldiana li metina waye mon nekh yalla

  • @aminabalde5219
    @aminabalde5219 Před 7 lety +8

    c triste bilay mais nak sante yallah, yallah neu souf séd ci kawam ci barké baye mom thiono wathe nako dakh dara dakoul sa yaye nila sama xol séd neu ci iow❤

    • @mouhamedsy911
      @mouhamedsy911 Před 7 lety +1

      Amina Balde sante yalla alhamdoulilah kou sa yaye sedé lii si yaw machallah

  • @maguettekane623
    @maguettekane623 Před 7 lety +1

    Yallah nako Yallah yeureum té xaréko Aldiana firdawsi Cheikh paix son âme😭😢😢

  • @bouryseck7403
    @bouryseck7403 Před 7 lety +1

    yalna souff oyoff sii kawam tee domou kharam yikko deff yalnalen yalla weer tee yalnaniou der deguou gnaw

  • @thianefall6110
    @thianefall6110 Před 7 lety

    ndeysane li metina trop sama xol fess na yalla nako yalla kharei aldiana firdawsi yi k justice soit faite😭😭😭

  • @dlayeces
    @dlayeces Před 7 lety

    😭😭😭😢😢😢😥😥. Yallah nako yalla yeureum té kharéko aljana firdaws yi. Metina trop

  • @mouhameddiop8290
    @mouhameddiop8290 Před 7 lety

    slt c très dur yalla nako.yalla yeureume t khareko aldiana fildawssir yalla souf wayeuf thi kawame yalla n tasse maleyka yeurmande courage et sou toujour forte

  • @mounassniang153
    @mounassniang153 Před 7 lety +2

    yala naleen serigne touba takhawou yala nako yala yeureum

  • @ngompapa5948
    @ngompapa5948 Před 7 lety +5

    on compati cette douleur metineu trop

  • @ndeyesokhnaags4437
    @ndeyesokhnaags4437 Před 6 lety

    Ndeysane métina,yalnako yallah yeureum,ndeysane l'I moy l'âne??eyyy yallah sougnou borom wolal sa diam yiii, arral sama rew,ak yénéne reeew yiii,défkatou lou gnaaw yi yalnaléne yallah torokhal

  • @aidadiop4876
    @aidadiop4876 Před 7 lety +1

    Ay way yalla nako yalla yeureum ta mou khippe adiana. Mais état bi war n'a ci diougue

  • @charlottekeita-sz8jm
    @charlottekeita-sz8jm Před 7 lety

    ndessane j'ai des larmes aux yeux

  • @torodo6447
    @torodo6447 Před 7 lety

    thiey yalla li métina Massa maman yalla nako yalla yeureum tes kharé ko sa aldjana firdawsi Ya yalla na souf oyof si kawam

  • @ngouyediouf336
    @ngouyediouf336 Před 7 lety +3

    Yallah nako Yallah yeureum té same ndiabotame. Gni def dieuf diou bone dji Yallah naniou fegne. Le Sénégal est devenu un pays insécure.

  • @damedia9942
    @damedia9942 Před 7 lety

    yalla nako yalla yeureum tan khareko al diana

  • @aminata0485
    @aminata0485 Před 7 lety +4

    J'ai pas pu retenir mes larmes. Ay way lii métina. Nul n'est à l'abri de ces malfaiteurs. Qu'Allah t'Accueille parmi Ses élus Mame Cheikh!

  • @aminatouthiam6443
    @aminatouthiam6443 Před 7 lety +15

    je maudis ces agresseurs gni aye domerame lagnou ya trop de laisser aller dans ce pays la drogue l'alcool le libertinage vraiment letat doit prendre de fermes mesures.

    • @fallougueye381
      @fallougueye381 Před 7 lety +2

      aminatou thiam.ma chere c est parce que l etat ne fais pas de ce qu il doit faire pour les combattrent,les pays europeen sont plus grand que le senegal mais tu peux aller d ou tu veux a n importe qu elle heure sans avoir peure.pourquoi parce que y a des patrouilles de la police partous tu dis meme que les policiers sont bcps plus nombreux que les civils.mais c est maleureux que les presidents africains ne savent meme pas a gouverner.tt annee campagne pour rester au pouvoir.bilay dama am louma mettiiiii😂😂😂.senegal ont te tue comme djinakhhhh.

    • @bambagueye9555
      @bambagueye9555 Před 7 lety

      petit senegal o

    • @arcenciel33
      @arcenciel33 Před 7 lety

      li kagn daffa meti torop gnouneu nak nekhoul ba nekhoul mais bilahi afrique doudhou gnou quoi pauvreté bi, insécurité, méchanceté... beaucoup de choses négatives c'est triste

  • @sidymboup7133
    @sidymboup7133 Před 7 lety +1

    lidafa mèti nèk si europea bi ak nimou mète ay nitt diouguè fè rayla mè yalla nako serigne touba tèrou

  • @diambonemadeleineniakh4085

    lilouko diare ,auto rek comparer a une vie domo dianboure.
    un soutien de famille en plus.
    qu'il repose en paix !!!!

  • @khadijaseck3324
    @khadijaseck3324 Před 5 lety +2

    aka meti sikhol bilay sama tonton mame cheikh gueye kene lawone bah te beug ay djarbatam...senegal metina juska présent djapou gnoulene

  • @ramsess3703
    @ramsess3703 Před 7 lety

    senegal metina armee bou beuri bi sans secirity cheikh repose en paix

  • @user-tt9tb3lg6b
    @user-tt9tb3lg6b Před 7 lety +2

    غفرالله له وارحمه وجعل قبره في الجنة

  • @MrPape78
    @MrPape78 Před 7 lety

    yalla nako yalla khare aldiana thi barke cheikh Ibra fall

  • @amifall6457
    @amifall6457 Před 7 lety

    si barke seydina mouhamed yalla nalen yalla werr gni ko def yalla nako yalla yeureum tè khareko aldiana

  • @papisgueye9974
    @papisgueye9974 Před 7 lety

    je sui totalement daccord avc la maman sincerement notr pays na pa de sécurité ou son les soi disant les .....

  • @soxnadiarrasaliou390
    @soxnadiarrasaliou390 Před 7 lety +1

    ndaysane thieuy Sénégal légui sécurité 0 bilahi c triste paix à son ame

  • @senegalmafierte7523
    @senegalmafierte7523 Před 7 lety +1

    mere ya gueume yalla yalnalen yalla defal diam taxaxoulen ak europe nimou mette

  • @ndeyesow6571
    @ndeyesow6571 Před 7 lety

    C vraiment trop triste yalnako YALLA yeureume kharéko aldiana firdawsi métina trop maman yalnala YaLLA takhawou je partage ta douleur métina trop

  • @niangmodou3718
    @niangmodou3718 Před 7 lety

    ohoh.metineu.yallanaléne.yalla.defall.kholoumonj.kharéko.aldianatoulfirdaosy

  • @saf-tnexx6731
    @saf-tnexx6731 Před 7 lety +1

    ndeyesane yallna yalla maylène kholou mougne 😭😭😭😭😭

  • @choufeuzaa689
    @choufeuzaa689 Před 7 lety

    nday san doyna yaram walahi yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana mais senegal li lanla ni man d bilahi li difa khew mom damay ragal sakh delousi man khawma li loumou don ni diap di ray rek te ken doula def dara dara mettina mom

  • @marselle8068
    @marselle8068 Před 7 lety

    dommage pas sous-titré en français l'Europe verrait et entendrais ce qui ce passe chez vous!

  • @ndeyemaguettegueye5631
    @ndeyemaguettegueye5631 Před 7 lety +2

    wallahi métina trop son frère m'a fait pleurer s'il vous plait trouver les coupables

  • @aiaba985
    @aiaba985 Před 7 lety +1

    Sénégal dale li dagnou sei wara diouk yalnako yalla yeureume tei yeikheiniou

  • @mendesshasha1021
    @mendesshasha1021 Před 6 lety

    ndeysane l frer masta boul dioy metina trop mougnal

  • @ndeyeamyseck4942
    @ndeyeamyseck4942 Před 7 lety +1

    vraiment j'ai peur Sénégal yakhouna que Dieu l'accueil dans son paradis

  • @ahmadasy5827
    @ahmadasy5827 Před 7 lety

    Macha yaye BOYE metina. TROP bayilenak ki dara tewoule tédi guis kép

  • @pisppadabo9352
    @pisppadabo9352 Před 6 lety

    Rip j'aurais jamais crû une telle agession dans notre pays

  • @aichasougou5995
    @aichasougou5995 Před 7 lety

    thiey aduna chaque mois aye meurtre ame senegal yalnala yalla kharé aldiana yalla moussal gnou

  • @dieyendiassebakhyaye7058

    yalla nako yalla khare ko aldiana firdawsi Amine

  • @fatoudiongue6337
    @fatoudiongue6337 Před 7 lety

    sheuuuu lii meti neu meti neu metineu trop. j'ai meme pas les mots.ay Senegal bayilen ray lilay warassouliii.lii c pas humain di ray niiti ni rk sein mbok yi perte. yalnako yalla yeureum

  • @nkhoudiaghoudia8496
    @nkhoudiaghoudia8496 Před 7 lety

    Metina yalla nako yalla yeuram masta mais senegal il faut niou diogue si insécurité bi rayate beuri na trop c'est trop

  • @adjimaramesarre9336
    @adjimaramesarre9336 Před 7 lety

    yalla nako yalla yeurem masta mame fatou thiam ndayesane

  • @abdoukhadrethiam7813
    @abdoukhadrethiam7813 Před 6 lety

    Que firdawsi soit sa demeure éternel Amine si barké cheikhoul khadim

  • @mohamedfadel5687
    @mohamedfadel5687 Před 7 lety

    Yalha n'a ko yalha kharè aldianna

  • @binetathiam2672
    @binetathiam2672 Před 7 lety

    yalla nako yalla yereum té khare ko aldiana. je suis horrifiée. l'Etat sénégalais doit prendre des dispositions. c'est trop ce qui se passe dans ce pays

  • @fatourassoulsg5803
    @fatourassoulsg5803 Před 7 lety

    gni nion bone yalla na yalla fégnale j ai envie de crier très fort j ai mal en regardant sa mère peurer

  • @fatourassoulsg5803
    @fatourassoulsg5803 Před 7 lety +2

    masta yalla naléna yalla maye kholou mougne

    • @elhajndong123
      @elhajndong123 Před 7 lety

      yalla na ko sunu borom yeureum tékharé aldjana ak mboléme djoulite bou fatou

  • @amifall6457
    @amifall6457 Před 7 lety +1

    Non li eup na trop. yalla nalen yalla werr gni ko def. yalla na khipe aldiana

  • @Senegambian678
    @Senegambian678 Před 7 lety +2

    may his soul rest in peace 😭😭😭😭

  • @sirediop772
    @sirediop772 Před 7 lety

    ndeysane yalnako yalla yereum

  • @kinefallou4762
    @kinefallou4762 Před 7 lety +23

    ohhhhhhh âme deuk ragual ko moma dal sénégal yakouna bilay

    • @tfkteew3586
      @tfkteew3586 Před 7 lety +2

      Kine Fallou Sénégal légui bénéne affaire là il faut de la sécurité c'est triste j'ai même pleuré oh

    • @kinefallou4762
      @kinefallou4762 Před 7 lety +1

      tfk teew moi je suis triste vraiment se dur sénégal dagni raye nitt yi Côme kouy raye mala je suis en Europe m chaque fois souma guisé yi rek damay ragual

    • @tfkteew3586
      @tfkteew3586 Před 7 lety +1

      Kine Fallou nio yame magui khalatt nieuw vacances wargneci diokhli

    • @mamediarrasamb7574
      @mamediarrasamb7574 Před 7 lety +1

      tfk teew

    • @tfkteew3586
      @tfkteew3586 Před 7 lety +1

      mame Diarra Samb c'est affreux ce qui se passe là

  • @baradiop6341
    @baradiop6341 Před 7 lety

    ndeysan ceeey magouk saa Borom gui ceey innalilahi wainnailayhi radiekhoon

  • @awalo2190
    @awalo2190 Před 7 lety

    ndeysane meti na trop me yalla nako yalla kharè aldiana 😢

  • @lifestylelifestyle8188

    ohhh masta c dur Senegal dale vrèma je ve plui rentrè filay tokk gnewe toumeuh

  • @mamadouseye7966
    @mamadouseye7966 Před 7 lety

    ndeysane yalla nako yalla yeureum kharèko aldiana

  • @fatoumkhouma8709
    @fatoumkhouma8709 Před 7 lety

    ho metina metina massa yalnako yalla woyofal si yen tayalla yobouko si aljanna yi guena kawé.
    bilay yawmal hiyam dinaméti

  • @khadyfaye7430
    @khadyfaye7430 Před 7 lety

    non mètina trop bilay walay sama xol bi diekhna takh
    c maudi agresseurs la aye domaram lagnou yalnalèn yalla alagu trokhal lène avan gnouy dei imbèsil. rip mn grand yalnaga khipè ardiana

  • @YacineNdoye-lb2iw
    @YacineNdoye-lb2iw Před 7 lety

    massa c'est très triste mais il faut k les militaires sortent dans leur caserne

  • @senegalmafierte
    @senegalmafierte Před 7 lety

    Non non non non non non c'est très très très très très très très dure. Vraiment je ne comprend pas mon pays. Comment un homme peut-il brandir une arme sur son prochain pour l'argent seulement. Ah mais non

  • @abdelazizwone3231
    @abdelazizwone3231 Před 7 lety +1

    Que le tout puissant l'accueille dans son saint paradis .C'est une perte immense

  • @ousmanendiaye1401
    @ousmanendiaye1401 Před 6 lety +1

    Yalla nako yalla yeureumm .

  • @MarieHelenDiouf
    @MarieHelenDiouf Před 26 dny

    Paix à son ame 😢😢😢😢

  • @fatoumbye5290
    @fatoumbye5290 Před 5 lety

    May his soul rest in peace Yalna suff seda si kawom 🙏🙏Ndeysan meeti na

  • @bijouterieyayeoumy2242

    ndeyessan y alla xaarékon aljiana

  • @bittayengaari5885
    @bittayengaari5885 Před 7 lety

    innna laahi wa inna illayhi raagihoun..may Allah grant him Jannatul firdaus ameen

  • @sambakeinde2424
    @sambakeinde2424 Před 7 lety

    oooooh walahi metina bafou méti yam Sénégal foumou Lou nékh way déff té dara dousi dikk même gnoun gni nékk si Albi sakh sunu xél dou dall ndax sunu famille bépp mogui fofou comme amounou loi, mais nakk Yalla na Yalla oyafal Souf si kawam té kharé KO aldianay firdawsi

  • @mendesshasha1021
    @mendesshasha1021 Před 6 lety

    ces injustice m font mal o coeur si jete juge ou policier j n laisserai ocun meurtrier vivre

  • @ndiayesenegalndiaye6177

    😢😢😢😢 Quel tristesse non senegal grawna fimou nék ni wakh deugueu yalla nieupeu tok si néne nakh ragal

  • @pourlacauseanimalesenegal9547

    Ndaysane Yalla na ko YALLA kharé al diana barkép Serigne Touba

  • @balkhisd4441
    @balkhisd4441 Před 7 lety

    Cey Yallah lii métina troop.. Massa ...

  • @mariamadiop6304
    @mariamadiop6304 Před 7 lety

    gnoune fougnou dieum thieuy yalla limetina trop😢😢😢

  • @youmaseck5509
    @youmaseck5509 Před 7 lety

    rip yalla na souffe oyale thi kanam

  • @kabaxalealdiana2667
    @kabaxalealdiana2667 Před 7 lety

    yalla nako yalla xari aldiana si barkepp xaside yiiiiii

  • @amygueye4647
    @amygueye4647 Před 5 lety +15

    Ndeyssane la mere de mame cheikh.... Elle est decede hier....gnanal lén ko...

  • @fatimadiallo1730
    @fatimadiallo1730 Před 7 lety

    mon coeur saigne, paix à son âme!

  • @mariemend9362
    @mariemend9362 Před 7 lety

    senegal thi bopam amoul bene loie bilahi.mais nak yalla mo eup dolé lepp

  • @raphaeldiop4232
    @raphaeldiop4232 Před 7 lety

    bilaye am na louma méti !! senegal mo beuri ay domramm !! si on les attrape on a qua les tuer !! domou nit kou bakh qui a réussi sa vie di topot famille wone !! aye domou tiagga diougué feulé diko ray si merci !!

  • @Senegambian678
    @Senegambian678 Před 7 lety

    I can't stop crying this is very sad walahhe 😭😭

  • @muhammedsamba8755
    @muhammedsamba8755 Před 7 lety

    doii na warr RIP....اللهم إغفرهم ورحمه ويدخلهم جنة الفردوس

  • @rabyfall3590
    @rabyfall3590 Před 7 lety

    Aye waye li metina trop gni def li bone nagnou trop sakh mane frére bi moma dioy lo, yalna khipé aldiana firdawsi

  • @halimatoumarega5667
    @halimatoumarega5667 Před 7 lety

    bilakhi li mètina trop trop Ay way ndeysan yallna Aldiana Firdawsy Amine 😢😢😢😢😢😭

  • @fatimacissediaboumamedabak7898

    massa yalnako yala yeureum khare ko aldiana firdawsi aminé

  • @jasminejasmine5942
    @jasminejasmine5942 Před 7 lety +1

    c'est trop dure j'ai pleurè😢😢😢

  • @diarradiarra8953
    @diarradiarra8953 Před 5 lety

    yalla nako yalla yereme

  • @GallassZSerigngallass
    @GallassZSerigngallass Před 6 lety

    yalla nako Yalla yeureum