PRANK STAR - Saison 3 episode 08 Binette & Moussa - Moussa man ngay trahir

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 16. 05. 2024
  • Rejoignez cette chaîne pour bénéficier Veuillez noter que toutes les vidéos présentées sur cette chaîne sont réalisées à des fins de divertissement seulement. Nous ne cautionnons en aucun cas les comportements ou les actions présentés dans nos vidéos. Nous nous engageons à respecter les droits et la sécurité de tous les individus impliqués dans nos vidéos, ainsi que de tout membre du public présent sur les lieux de nos tournages. Nous ne tolérons pas le harcèlement, l'intimidation ou toute autre forme de comportement inapproprié ou illégal. Toutes les personnes impliquées dans nos vidéos ont donné leur consentement éclairé et volontaire pour y participer. Veuillez regarder nos vidéos avec un esprit ouvert et un sens de l'humour, mais toujours avec prudence et responsabilité
  • Zábava

Komentáře • 2,2K

  • @Mahfousse
    @Mahfousse  Před měsícem +52

    Téléchargez l'application 1XBET et Utilisez mon code promo 221M pour gagner un JACKPOT.
    cutt.ly/Let6mfqe

  • @babacarfall1593
    @babacarfall1593 Před měsícem +303

    Moussa ak Binette kou geume nii ici repose moléne di séparée rk lalale j'aime 🤣

  • @layebeye3835
    @layebeye3835 Před měsícem +1145

    Kou guiss ni binet dafa meune mbeukk rék lalal j'aime 😂😂

  • @FallouDiouf-sp2em
    @FallouDiouf-sp2em Před měsícem +404

    Prank diabarou makhfouss kou dakor papal j’aime

  • @PodcastAnonymous
    @PodcastAnonymous Před měsícem +197

    Moussa Faye la monogamie pour toi est une obligation pour ta survie que binette samba veille sur vous !

  • @papetine5613
    @papetine5613 Před měsícem +550

    Les filles deff len très attention😂😂😂😅ki lim waxon rk bi yalla waxé moussa Faye mom rk mo yeukeuti lokhom😂😂elle confirme…😂

  • @khadyka5384
    @khadyka5384 Před měsícem +807

    Shi Moussa t’es condamné à être monogame à vie 😭😂😂😂😂😂😂

  • @coumbacoulibaly5388
    @coumbacoulibaly5388 Před měsícem +166

    Kou d’accord ni moussa mongui si danger laaaa,mais Binete ame ne dolè

  • @lassndiaye9158
    @lassndiaye9158 Před měsícem +69

    Franchement c’est une belle femme, j’aime bien ce genre de femme une femme qui protège son foyer

  • @khadeejah7586
    @khadeejah7586 Před měsícem +172

    Moussa niou délou Mairie nga signer monogamie pour le bien des Sénégalais

  • @kany4967
    @kany4967 Před měsícem +236

    Kou guiss danou moussa yi😂😂😂 binette a fait ma soirée

  • @Porte_bonheur04
    @Porte_bonheur04 Před měsícem +39

    Moussa tako diabar gangster nga takk😂😂😂

  • @salydione2692
    @salydione2692 Před měsícem +55

    Nite gni di setane mane ma concentré wou si photo Borom Darou bi❤

  • @MHD844
    @MHD844 Před měsícem +1202

    kousa 4 baram nékeu si sa guinaw téléphone lalal j'aime 😎

  • @barandiaye3629
    @barandiaye3629 Před měsícem +551

    Yw mi yalna gua téral sa wajour kom nig ko begué nél amin ❤❤❤❤❤❤😂😂

  • @ababacarsane7110
    @ababacarsane7110 Před 29 dny +16

    Wakhouma lolou dh binette barina dolei moussa binette dinala nokh dh

  • @cheikhkandj4655
    @cheikhkandj4655 Před měsícem +32

    Yallah na am diabar bou mélni Binette way 😍 begué ma comme nii 😂 amine

  • @sambandour5226
    @sambandour5226 Před měsícem +193

    Moussa faye rk la yeureum
    Ki dh trompé beu binette moy dieul neu ay fanam 😭🤣🤣😭

    • @tafasaho4645
      @tafasaho4645 Před měsícem +4

      Ms lolou cas la dh😂😂😂😂

  • @bayemorygueye3233
    @bayemorygueye3233 Před měsícem +398

    Kou begui teral sa yaye bessal ❤

  • @boeiadams
    @boeiadams Před měsícem +25

    Mais makhfouss tu est le meilleur de ta génération Q'Allah te bénisse ❤️🙏

  • @yacineniang4447
    @yacineniang4447 Před měsícem +29

    Man dama wara 😂😂mais dama dioye parce que beug niittt yombul té lii vrai amour la j’ai pleuré wolay love you binete

  • @fallouawabousso
    @fallouawabousso Před měsícem +377

    Delen may Mâcon yii agn waay baparé laal j'aime 😂❤

  • @astoundoye546
    @astoundoye546 Před měsícem +204

    Badou sylla ak moussa soleine parei ngeine nane soupe binette ray naleine 😂😂😂

  • @cheikhounadiagne2675
    @cheikhounadiagne2675 Před měsícem +165

    Thieuy adouna mo doy waar mane générations legui kene roussou si sa dieukeur boula nékhé sakh sakh saga sa dieukeur yalla naniou yalla yeureum ❤️‍🩹❤️‍🩹

  • @elhadjimodoudieye7351
    @elhadjimodoudieye7351 Před měsícem +153

    Kouy tak diabar takal diabar bo meuna maîtriser 😂 pour bou histoire amé😂

  • @bailodiao6292
    @bailodiao6292 Před měsícem +95

    Badou Sylla mérite d’être honorer 😂😂façon coup bou nekk dieul nako

  • @MadjigueneWade
    @MadjigueneWade Před měsícem +21

    Badou sylla deh bou dégeutei prank dey daw🤣🤣🤣😭khaw na dei

  • @sophiedia4751
    @sophiedia4751 Před měsícem +33

    Non😂 Moussa Faye la beugue 😂 néna gnou coupé courant bi wouy🤣 mais Binette esk xamngani moussa Faye beuguoul kéne koudoul Yaw billahi👍💪 il va jamais t’oublier de sa vie. ☝️🙏 je vous aimes 😘

  • @sergejuliensympabaraye9159
    @sergejuliensympabaraye9159 Před měsícem +89

    Meilleur prank😂😂😂😂Binette iow laniou faral ba leuz

  • @JB-cm9mc
    @JB-cm9mc Před měsícem +217

    Binette dinafi gaagn nite ndakh firr😂😂😂😂

  • @mariebernadettegueye4946
    @mariebernadettegueye4946 Před měsícem +6

    Binette yalnala yalla may ndiaboot guou barkél bayilak sa diekeur ndéysane dakko beugue😢😢❤

  • @Mamefatoufall4351
    @Mamefatoufall4351 Před měsícem +18

    Ohhhhh moussa diapal binette bou bakhh elle t’aime éperdument walahiiiiiiiiii vraiment massouma guiss kou beuguei ni goor

    • @Robbe-Grillet
      @Robbe-Grillet Před měsícem

      Lii dou mbeuguel dof la ak réwandé.

    • @sambafall2819
      @sambafall2819 Před měsícem

      @@Robbe-Grilletioe mi nak ya doff ki dafa beugue dieukeureum ngani rewandé

    • @SLJeuneTalent_10
      @SLJeuneTalent_10 Před 9 hodinami

      Li di dof nganan mbeuguel

  • @Moussa817
    @Moussa817 Před měsícem +151

    Badou Sylla dé prank bi dou ko meusa fatté 😂😂limou ci dathie

  • @user-vt5du4mq8b
    @user-vt5du4mq8b Před měsícem +96

    Binette yall na la yalla may dome Serigne fallou ak Serigne mountakha ❤❤

  • @senegalese839
    @senegalese839 Před měsícem +11

    Badou sylla mo guena sonou si prank bi😂😂😂😂😂😂😂niamna binett berina dole

  • @omzofashion9140
    @omzofashion9140 Před měsícem +50

    Xalei bouffi nopp moussa demall diangui box mma taykondo kung-fu ak mbappatt bou doyy du dém salle ak dune sino RIP

  • @mamitaba7545
    @mamitaba7545 Před měsícem +294

    Badou Sylla mo si geuneu sonn 😂😂😂non bineete dou nitt

  • @mariamadieme9604
    @mariamadieme9604 Před měsícem +109

    Trop nice ❤mais mahfousse fait très attention pour les mariés li risque leu dh khèkh yi baxoul thi gnome dh on c jamais meune nagnou nekk en état tè xamou gnou si dara 😢bayi thi xell
    Mais félicitation t’as réussi Binette nakk Deugue Deugue firrr nga nakk 😂😂❤❤❤

    • @b_lebou8908
      @b_lebou8908 Před měsícem +4

      Niom dofouniou ct dieukeur dj kon nako kham té si deal bi la bokk

    • @fatoudiouf-bb1cy
      @fatoudiouf-bb1cy Před měsícem +9

      Non sincèrement beugeu na mahfous mais lii sa peut briser une famille les insultes aussi moy lolu

    • @user-gn8pi2uh8o
      @user-gn8pi2uh8o Před 29 dny

      C vrai

    • @senegalaise1
      @senegalaise1 Před 24 dny

      ​@@b_lebou8908xana xamo eumb bu ndaw mm la femme meun nako baña téla xam té nonu la gawé yakou nak

  • @souleymanebarry2178
    @souleymanebarry2178 Před měsícem +13

    😂😂😂 vraiment binete woné nga ni ioe rek ya yékiti won sa lokho 😅😅

  • @KhardiatouDiallo-yl9zt
    @KhardiatouDiallo-yl9zt Před měsícem +3

    Best prank blh🎉😂😂😂😂 Merciiih bcp mahfouss😂😂 le peuple est content 🎉🎉

  • @youngnivay95
    @youngnivay95 Před měsícem +147

    Moussa lén rek lalay conseiller Démal outi dolé binnette guén meunou ko té 😂😂😂😂😂

  • @NdeyeSylla-ld7vu
    @NdeyeSylla-ld7vu Před měsícem +222

    Binette yalla na la yalla may dome serigne babacar sy akh serigne fallou ❤

  • @famafaye4002
    @famafaye4002 Před měsícem +11

    Ki dafa doffe dh 😂😂😂machalah nékh neu trop j’aime 👍 😂😂😂li nek moye prank nak

  • @yacinendiaye2100
    @yacinendiaye2100 Před měsícem +6

    Abdou silla monthi guena sonne 🤣🤣🤣🤣

  • @BabacarDiene-sg7yi
    @BabacarDiene-sg7yi Před měsícem +173

    Kou beug Makhfous prank eva cas bou capitale rek beusal j’aime 😂😂😂😂

    • @diodio57327
      @diodio57327 Před měsícem +3

      C'est déjà fait dans les vidéos précédente

    • @MbodjMouhammed
      @MbodjMouhammed Před měsícem

      Nono Eva cas bou capitale la wakh cas kat bii

  • @anishsarr5427
    @anishsarr5427 Před měsícem +67

    Ki meun ne eumeu sene ni cheuteuteut machallah binette amna doler moussa d yeureum nala 😢😢😢

  • @assanendiaye8434
    @assanendiaye8434 Před měsícem +25

    Kou beug niou pranké djadja rk lalal j’aime 😂

  • @user-gd3st3tp3o
    @user-gd3st3tp3o Před 13 hodinami +1

    Kou beugue prank radia lalale j aime

  • @ArameNdiaye-mv2zz
    @ArameNdiaye-mv2zz Před měsícem +156

    Bb binta svp kou d'accord Jaime ❤

  • @ousseynouniasse9144
    @ousseynouniasse9144 Před měsícem +323

    Moussa boula léré sii bene diabar kay deii😂😂😂

    • @Yayusalihou1553
      @Yayusalihou1553 Před měsícem +22

      Moh li kukoy dëff goor sou guisé kouma beug dalay fassé tak kénén li baxoul ki respecter woul dieukeur dji

    • @Abdallah31341
      @Abdallah31341 Před měsícem +9

      ​@@Yayusalihou1553😂 dafa fiir bam eup

    • @maguettecisse7423
      @maguettecisse7423 Před měsícem +9

      Madame Samb lou leer nga wakh
      Liii dieumoul Keur

    • @Yayusalihou1553
      @Yayusalihou1553 Před měsícem +8

      @@Abdallah31341 fir bou eup dof la goor kén meunuko firé vous avez droits à 4femmes

    • @Yayusalihou1553
      @Yayusalihou1553 Před měsícem +10

      @@maguettecisse7423 walay d'où respecter bo wakhé niouné foo la mais Dina dém MBa dotoul dégn même sén vidéo yi tik tok nila genre blague yi bakhoul djiguen bou khamé ni eupoko dolé rek doula respecter

  • @user-te6uk8lv6t
    @user-te6uk8lv6t Před měsícem +12

    Kou d'accord prank Aïcha Rassoul bou Aziz Ndiaye ❤❤❤ risque ragal d'où Diomi 😂❤

  • @sokhnamamebousso9485
    @sokhnamamebousso9485 Před měsícem +4

    La jalousie de Binette est excessive. Moussa mi nimm ko ragalé dafa eupp, avant mm le prank meunn nagn sentir stress bi. Je pense que dans un couple on ne doit pas avoir peur de son conjoint.

  • @madiagnesarry1224
    @madiagnesarry1224 Před měsícem +93

    Wa team moussa faye mon combat yenagui combat ba legui wala??😭🤣🤣🤣🤣

  • @ahmadoucheikhoulkhadim5131
    @ahmadoucheikhoulkhadim5131 Před měsícem +37

    Binette ay xéxou goor la yor ay mbeuk lafi guiss 😂😂😂

  • @mamesayeniang2886
    @mamesayeniang2886 Před měsícem +2

    Ndeysane djoy na té khawma louma djoylo ndeysane mbeuguel dafa beurri dolé bilahi❤❤❤ je vous adore binette et moussa longue vie à vous

  • @AdoWally
    @AdoWally Před měsícem +7

    C'est cool mes ça devait pas duré accès Makhfousse 5 minutes rek doyna binette da moudié sakh fatiguée li woroul boufé piqué won crise nak

  • @seydoudiop
    @seydoudiop Před měsícem +77

    Moussa Diappal ma Binette ❤ Kafoul fo rewoul Yaw rek laay Guiss 😊

  • @ElHadjiNiasse-cu1bl
    @ElHadjiNiasse-cu1bl Před měsícem +91

    Moussa démal outi dollé binette borom dollé la dhé😂😂

  • @jamesjoob3771
    @jamesjoob3771 Před měsícem +8

    Sama xoll seddna lol ci djiguen bi dfa bègue Mossa ❤Machallah laf thiat

  • @lilzal100
    @lilzal100 Před měsícem +2

    Wallahi meilleur prank de l'année iao boul sakh défati prank Makhfouss meusso guiss gun sa prank yii😂😂😂😂

  • @user-gx7kz5uc2u
    @user-gx7kz5uc2u Před měsícem +81

    Binnette boy médina laa dé😂😂😂😂 mais mahfouss vraiment big job🙏🙏

  • @seynabousow97
    @seynabousow97 Před měsícem +46

    Binette kafé woul Moussa dh😂😂
    Moussa djeul na ay coup tay ba doyal😂

  • @khadzo2340
    @khadzo2340 Před měsícem +4

    Yalla na am diabar bouma beugué ni🤲🏻☺️👏🏼♥️

  • @user-qr3kp9hn1m
    @user-qr3kp9hn1m Před měsícem +7

    MOUSSA FAYE bou yabo ga nék monogamie à vie 😂

  • @AwaTambedou-dw9nt
    @AwaTambedou-dw9nt Před měsícem +177

    Kou Beugue gniou pranké Père Ndiaga Thiam wala Daro sow ❤

  • @ndeyefatouseck8755
    @ndeyefatouseck8755 Před měsícem +56

    Dama khar ba sonou😭Binette mbeuk n'a farou Abdou Sylla yi😭💔dore n'a Moussa ba togue si kawam aythieu Binette 😭😂😂😂😂

  • @dakarproduct
    @dakarproduct Před měsícem +6

    😳thiooo yalla bouma yalla bolé ak kou melni binette cheuuuuuuuuuuuuuuuu et bizarement même bassi fin prank bi sen xel yi daloul. da nguénn modérer sen langage wakh ndank di thiatal tamite cheuuuuu🤣😂🤣😂🤣

  • @diefandiaye7341
    @diefandiaye7341 Před 29 dny +3

    Badou Sylla naniou ko soupal 🤣🤣🤣🤣🤣

  • @MohamedDieye-bw7iy
    @MohamedDieye-bw7iy Před měsícem +107

    même mane titte nah tè commencé gul 😂

  • @KhadyNdiaye-tu6cs
    @KhadyNdiaye-tu6cs Před měsícem +22

    Ay tay kou yeureum basou silly rk beusel j'aime😂😂😂

  • @farbatheboy-nq5qt
    @farbatheboy-nq5qt Před měsícem +2

    Prank tapha tine la yakam ti mane Kou d’accord lalal j’aime 👍 😅😂

  • @Douzey_Kane
    @Douzey_Kane Před měsícem +6

    ana nhiiyy wakh mbeuguel amatoul😄😄😄

  • @ndeyemaladosow8603
    @ndeyemaladosow8603 Před měsícem +189

    Kou beugue niou pranck ya awa dieye rk lalal j’aime ❤❤❤❤

    • @diodio57327
      @diodio57327 Před měsícem +1

      Je suis d'accord avec toi

    • @papemoussalahii440
      @papemoussalahii440 Před měsícem

      Niveau bobou kawé n'a deh est ce que makhfouz meun n'a lolou lol c'est un défis que je lance lol

    • @ndeyemaladosow8603
      @ndeyemaladosow8603 Před měsícem

      @@diodio57327bilaye nack

  • @thianediene4236
    @thianediene4236 Před měsícem +52

    Commencei gouma sah di retàne😂😍😂😂😂😂😂binette yalna goudd fan’

  • @serignebambandiaye5513
    @serignebambandiaye5513 Před měsícem +2

    C’est la meilleure prank de l’histoire 😂😂😂😂

  • @alaminejoop6136
    @alaminejoop6136 Před 20 dny +2

    Moussa mounieul rk beneu seuye nekhoulll 😂😂😂

  • @mamecoumbadiop4272
    @mamecoumbadiop4272 Před měsícem +50

    Yalla n'a am kouy khékh ndakh mane😌😎😂

  • @maimounambaye1437
    @maimounambaye1437 Před měsícem +32

    Ku beug binette rk lalal j'aime 🎉🎉❤❤

  • @Bamba9854
    @Bamba9854 Před 13 hodinami +1

    Bineta boul reei moussa sa dieukeur la❤❤

  • @Goor-us9in
    @Goor-us9in Před měsícem +4

    Légui kou diouk yorr pistolet 😢

  • @user-xh3zk8qr7d
    @user-xh3zk8qr7d Před měsícem +53

    😂😂😂😂😂wa li nékhna dé lii dé moy mane ak iow ici repose Moussa dé bo amon guél tay niom nieupa feukh 😂 Binette dall ya woor❤

  • @Fallilou.
    @Fallilou. Před měsícem +49

    Hiiiih moussa dh dou amat bénéne djabar😂😂😂😂😂

  • @JuniorLamp
    @JuniorLamp Před měsícem +1

    😂😂😂😂Vive Binétte Wallahi je t’adore tu ne caches pas ce que tu aimes

  • @MatyDiop-jo4dk
    @MatyDiop-jo4dk Před měsícem

    Wouy 😂li nekhna mAkhfousse focus rek guisna bene compte di diema prank mom khamoul ni nioun ioe rek langouy tope Machallah 😊

  • @binetapaye4168
    @binetapaye4168 Před měsícem +16

    Kou d'accord prank fatel ak gnaka beuseul j'aime ❤

  • @HametBa-uy9iq
    @HametBa-uy9iq Před měsícem +34

    Demal nga sangou sédd c’est pour tue 😂😂😂 no binétte amoul

  • @amiendoye9880
    @amiendoye9880 Před měsícem

    Nice one watching from the Gambia 🇬🇲🇬🇲❤️

  • @user-vp7yf5bk1s
    @user-vp7yf5bk1s Před měsícem +8

    Dama guiss pub Tik tok rék daw youtube, binette 😅😅😅😅

  • @ElHadjiNiasse-cu1bl
    @ElHadjiNiasse-cu1bl Před měsícem +43

    Moussa démal outi dollé binette borom dollé la dhé😂😂😂

  • @ibrahimawague1453
    @ibrahimawague1453 Před měsícem +142

    Les filles kou beug nek woudiou binette rek boul la j'aime 😂😂

    • @fatoundiaye5820
      @fatoundiaye5820 Před měsícem +7

      Yalla téré 😂😂😂

    • @kambayependasall8908
      @kambayependasall8908 Před měsícem

      Wooooooo beugo diam 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @user-pl8ip2rh7o
      @user-pl8ip2rh7o Před měsícem +1

      Dafa fek ma am ms kon man lay don😂😂😂nio bok djiko😂😂

    • @DASK166
      @DASK166 Před měsícem +2

      Laah xawlaaaah 😂

  • @moussadiouf6889
    @moussadiouf6889 Před měsícem +4

    Prank bou gueuna nékh si yima sétan😂❤🎉 Sheutt binette Dou nitt😂😂

  • @MamadouSow-db3fn
    @MamadouSow-db3fn Před měsícem +2

    Non quelle réussite Machallah 👏😂

  • @doudougueye2393
    @doudougueye2393 Před měsícem +88

    😂😂 « badou ma ngi dem » c’était pour abattre l’ennemi 😂😂😂

  • @icAlphaDiallo
    @icAlphaDiallo Před měsícem +21

    اللهم إنصرإخواننا في فلسطين 🤲🇸🇩🇸🇩🇸🇩🇸🇳❤ nioun mahfousse rek lanouy topp vive palastine ❤

  • @fayelo2205
    @fayelo2205 Před měsícem

    Vraiment binette amoul been respect ak noumou meunti deme waro saga sa dieukeur

  • @user-dn7zq8kb6b
    @user-dn7zq8kb6b Před 25 dny +2

    Ay way bintene mi wouy 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂moussa mougnal dé ki mouy sa natou 😂😂😂😂😂😂

  • @salihatte9319
    @salihatte9319 Před měsícem +23

    Badou Sylla merci li bakhna si yaw merci Binta beg n si yaw prank réussi dieukeur diambour pour diambour bila ay kouma betteu Ak sama dieukeur 😂😂😂😂😂 dougene pare gene oute frotter raynaniou lene merci bintta

  • @diakhoufall621
    @diakhoufall621 Před měsícem +36

    Kou yerem badou sylla 😂😂😂😂

  • @omarmbengue7474
    @omarmbengue7474 Před měsícem +2

    Kou beugue gniou pranké père zora rek beusal j'aime😂😂😂

  • @tafasaho4645
    @tafasaho4645 Před měsícem +3

    Kou d’accord né moussa Faye dou gooru ñaari diabar rek bessl ❤😂