REVUE DE PRESSE RFM AVEC MAMADOU MOUHAMED NDIAYE - 23 MAI 2024

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 22. 05. 2024
  • REVUE DE PRESSE RFM AVEC MAMADOU MOUHAMED NDIAYE - 23 MAI 2024
    RFM 94.0 1ère radio au Sénégal

Komentáře • 176

  • @user-py1zg8xc8p
    @user-py1zg8xc8p Před 27 dny +43

    Ndaye sane dama lene yerem sakh 5ns nga narr ko doul ndiaye et tfm 😂😂😂

    • @NdiayeSeringe
      @NdiayeSeringe Před 27 dny +3

      Wakhl way 😂😂😂sén khol mo boun té ay séytané anio# sonko rék ❤❤❤❤amol lénéne

    • @BoubacarSeydi-vk4fi
      @BoubacarSeydi-vk4fi Před 27 dny +4

      Sa leufeule daye Ndiaye mo gueuneu sa ndeye gueuneu sa baye katale sa ndeye

    • @sambandiaye818
      @sambandiaye818 Před 27 dny +3

      Boubacar diaroul saga gni ay fan's lagne done fan's manoul wéssou dieul sa khalisse diandé ko connexion di deglou wadji ci CZcams bi

    • @BoubacarSeydi-vk4fi
      @BoubacarSeydi-vk4fi Před 27 dny +2

      @@sambandiaye818 bégué frére dama amoule sago thi RFM kouléne wakh Lou méti bilahi daye melni mane gako wakh sama khole bi laye méti

    • @toscanaxassidatv1968
      @toscanaxassidatv1968 Před 27 dny +3

      Bilaly tfm xna dano am ak prblm sonko masouma deg nji wax thi niom loubax

  • @user-mg2nt7df3n
    @user-mg2nt7df3n Před 27 dny +13

    Merci Ndiaye gniy ligueye ak gniy were di wakh menougno yam RST bonne continuation good job ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @BassiroundiayeBass-pq6jk
    @BassiroundiayeBass-pq6jk Před 27 dny +18

    Katlėnn ndayam felė AK ba diakhatė sofngėn torop

  • @bara1744
    @bara1744 Před 27 dny +5

    Vive diomaye et sonko

  • @cheikhndao6359
    @cheikhndao6359 Před 27 dny +8

    Ohh yeureum na lén
    Di nguen soneu 20 ans
    Def focus rek liguey
    Jub bubal jubanti
    Vive Sonko Diomay

  • @HamidouGueye-vh3bw
    @HamidouGueye-vh3bw Před 27 dny +2

    Merci beaucoup sonko gfm khana impoyi mo commencé amatoull tappalé dh fay force pathio diéxna si réwmi inch'Allah 😂😂😂😂

  • @baragueye7595
    @baragueye7595 Před 27 dny +7

    Sonko moy diomay ❤❤❤❤yala na yalla mousal len si saytané

  • @sodadiouf5097
    @sodadiouf5097 Před 27 dny +8

    Kou beugoul wa RFM Loy dégueu lou si sen journal AHHH😮TEUSSSS yé na sonal sen bopou nak

  • @Aliounebadaraka
    @Aliounebadaraka Před 27 dny +1

    RFM en fayéte bientôt inch'Allah Mamadou doul Ndiaye koutie Ande lala j'aime

  • @BabacarMboup-zc2qe
    @BabacarMboup-zc2qe Před 27 dny +7

    Ndiaye les sénégalais sont content de vous avec la tfm

  • @makhtarfall3217
    @makhtarfall3217 Před 27 dny +3

    Gni di saga Ndiaye mouhamed la meunta comprends Man sofff ngeune trop 😅

  • @serignembackediop2685
    @serignembackediop2685 Před 27 dny +1

    Kofi yeugeul Dinan dakhar sa ndaye si kasu bi rewoo leen sax

  • @NgomDarouNgomDarou
    @NgomDarouNgomDarou Před 27 dny +1

    Wa de médias delen wakh rek waye dagen faye empot dh😂😂😂😂 merci sonko Merci diomaye 🇸🇳❤️

  • @Tapa-vc5uz
    @Tapa-vc5uz Před 27 dny +3

    Merci beaucoup

  • @AlioubaBa-ks1wg
    @AlioubaBa-ks1wg Před 27 dny +3

    Merci beaucoup gfm merci beaucoup merci beaucoup

  • @Modoulo-ld4mb
    @Modoulo-ld4mb Před 27 dny +1

    ❤❤❤❤

  • @user-gv5kk7hi2e
    @user-gv5kk7hi2e Před 27 dny

    L'unité pour un Sénégal meilleur 🇸🇳

  • @falloumbacke6530
    @falloumbacke6530 Před 27 dny +3

    Sarap ndayy sén dool yi dama depacé man😂😂😂😂😂

  • @user-ri9ev6fl5k
    @user-ri9ev6fl5k Před 27 dny

    Je suis bah diakhaté deugue rek sonko domou diaga ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @YvonneDiatta479
    @YvonneDiatta479 Před 27 dny +4

    Merci president bassirou diomaye pour son soutien extraordinaire à la jeunesse sénégalaise. SENEGAL CA KAW CA KANAM.

  • @SerignehadySenghor
    @SerignehadySenghor Před 27 dny

    Merci ousmane sonko yaniou guené cii mboumou diame yalenala yalla feye goudaal say faane

  • @mansourba8071
    @mansourba8071 Před 27 dny +4

    Pitié pitié mon Dieu pitié lo Sénégal va droit au mur mon pays va mal lo gouvernement du Sénégal est nul 0 à0

    • @jaawfara8901
      @jaawfara8901 Před 27 dny +1

      Dieuleul😂gal gui boula nakaré wa 34%😅😅😅

    • @mansourba8071
      @mansourba8071 Před 27 dny

      @@jaawfara8901 pitié pitié pitié pitié pitié de toi

  • @bathiendiaye611
    @bathiendiaye611 Před 27 dny +6

    Go mo metyy defal Li baye diakhate def Wala gua diel SA toro bay defgo se toro sonko

  • @ousmanendiaye9070
    @ousmanendiaye9070 Před 27 dny

    ❤❤❤❤❤❤

  • @KabouSalane-nw5gg
    @KabouSalane-nw5gg Před 27 dny

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamemorcisse4
    @mamemorcisse4 Před 27 dny +1

    Leegi diakhasé sonko ak diomaay mooleen desé 😂😂😂yeena nara sonnou nak

  • @FallouGalass-vr4ir
    @FallouGalass-vr4ir Před 27 dny +2

    Ndiaye boye wakhati ba tolu si wadji delle wakhe duuullleee kate bisi rewmi danu kham linga bege wakhe

  • @moizajoop8630
    @moizajoop8630 Před 27 dny +14

    diomaye moy sonko koumu nakadi kharoul😂

  • @ahmmouss2583
    @ahmmouss2583 Před 27 dny +1

    DIOMAYE kay légui ab marionnette la rek, li dafa rousslo trope🤣🤣

  • @Badoudiouf2023
    @Badoudiouf2023 Před 27 dny +1

    Sonko moy président ndiaye sa data ndaye yaak sa diplomatie

  • @NdiayeMbacke-qd3ee
    @NdiayeMbacke-qd3ee Před 27 dny

    ❤sonko moy diomay diomaye moy senegal ❤

  • @Cisse-tn1wp
    @Cisse-tn1wp Před 27 dny

    Merci tfm❤

  • @cheikhoudiakho4541
    @cheikhoudiakho4541 Před 27 dny

    Dama leen yeureum sax bilay Naar ngeine sonu dhe😂😂
    Sonko moy Diomaye, Diomaye moy Sonko wala daga faté lolou😂😂

  • @mordieng4617
    @mordieng4617 Před 27 dny

    Bonne khatarayou

  • @ganalee8051
    @ganalee8051 Před 27 dny +4

    Résistance rekk inchlah républicain pour toujours ✌️✌️✊🏾✊🏾💪🏾💪🏾💪🏾💪🏾

  • @user-tg7bh7mq1q
    @user-tg7bh7mq1q Před 27 dny

    Sonko moye Diomaye yalne diamou yague si yéne

  • @latzocana744
    @latzocana744 Před 27 dny +2

    Diam rék moy am inchallah 😂😂😂

  • @souleymaneibrahimasall5367

    Mane dé dama yakarni Sénégal sonko moy pressident bii

  • @ElvisPresleyTyi
    @ElvisPresleyTyi Před 27 dny +1

    Apr boufii manifesté gnoun patriotes yii gnoy téngeull sa yaye

  • @sodadiouf5097
    @sodadiouf5097 Před 27 dny +1

    Awma si yen sago dolén parparlo dolén ay supporter deuk Bo khamni so wakhoul lou lén arranger rk gnou saga la rew ba day

  • @LayeSow-gn4wp
    @LayeSow-gn4wp Před 27 dny

    Free bah diakhate ❤

  • @IbrahimDiong-lx2zs
    @IbrahimDiong-lx2zs Před 27 dny

    Merci

  • @aissatouniang2592
    @aissatouniang2592 Před 27 dny +1

    Ndiaye dh mom kholbi dou nekh moukou

  • @m.kandji3860
    @m.kandji3860 Před 27 dny

    Je suis Pastef ❤

  • @aladjifalloudia4915
    @aladjifalloudia4915 Před 27 dny

    Adouna yalla kou mome 😂😂😂😂😂😂merci yalla

  • @fallousaine5907
    @fallousaine5907 Před 27 dny

    APR mom mongi tchi ay fanam youmudjie

  • @cheikhcamara4888
    @cheikhcamara4888 Před 27 dny +1

    Sonko est le président Diomay dou tousss

  • @locheikhou9473
    @locheikhou9473 Před 27 dny +1

    Ki saytané rajim la

  • @NdiayeMbacke-qd3ee
    @NdiayeMbacke-qd3ee Před 27 dny

    Billahi yénna niack fayda li moy yecklékay thim

  • @elhadjimor5995
    @elhadjimor5995 Před 27 dny +1

    Fén rek TFM ❌😡😡😡

  • @MomoNgom-rl5lx
    @MomoNgom-rl5lx Před 27 dny

    Bah Diakhaté est arrêté par Le procureur Abdou Karim Gueye laisser pastef tout Tranquille

  • @khadimsylla-ub3rm
    @khadimsylla-ub3rm Před 27 dny

    Yalla naléen yalla may kholou mougne 😂😂lima geun nékh si gouvernement bi moy do degue kén di tontou wala mouy may nopou mbodio mbodio gui markatt yi nga xamni mar nagne louné😂séne xolyi mo nara wadde

  • @sunulakkwolof7744
    @sunulakkwolof7744 Před 27 dny +1

    Fiko sonko teg moye diomaye mootakh te mootay

  • @user-wh2lp8cy9s
    @user-wh2lp8cy9s Před 27 dny

    Yen dagen di fate ni sonko Moy diomaye

  • @khoudianiasse6513
    @khoudianiasse6513 Před 27 dny

    Vive gfm❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @user-me7se1nf9p
    @user-me7se1nf9p Před 27 dny +5

    Super infos

  • @tima8577
    @tima8577 Před 26 dny

    Sayoo yéwo sa ...ndeye!

  • @gueyeabdou8849
    @gueyeabdou8849 Před 27 dny

    Thiéy Sonko Mô bakh dh

  • @omarndiaye2719
    @omarndiaye2719 Před 27 dny

    Yéen bly sonn ngeen sim😢

  • @assgueye9899
    @assgueye9899 Před 27 dny

    Ndiaye ndeyesann mom daye khey di fen di yakheu der wa pastef di ligueye rewmi di gana am diame 😂😂😂😂

  • @morganmor1904
    @morganmor1904 Před 27 dny +1

    Li dou journalisme 😂😂😂😂

  • @daarawakeursmasambambour6077

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂wakhofi dara

  • @dioufmodou4234
    @dioufmodou4234 Před 27 dny

    Yene katue lene ndayam fuele

  • @amethndiaye5154
    @amethndiaye5154 Před 27 dny

    Wa apr boulène tall rewmi

  • @asrartv7010
    @asrartv7010 Před 27 dny

    Dioumay moy songo sonou moy diomay 😂 khana lii nekhna

  • @ahmmouss2583
    @ahmmouss2583 Před 27 dny +2

    Yeuw rek yaniou doye thi revue presse wallahi 👍

  • @astoubarkhamba6366
    @astoubarkhamba6366 Před 27 dny

    Légui doléne wakh li yoor yoor binde si yéne😂😂

  • @AwaDiop-by9br
    @AwaDiop-by9br Před 27 dny +1

    😂 Pasteff ay vrai domé raam deugg lan

    • @khadime
      @khadime Před 27 dny

      Yaw yaye domeram

    • @AwaDiop-by9br
      @AwaDiop-by9br Před 27 dny

      @@khadime bly deugg la wakh y'a que des ânes dans pasteff 🤣🤣

  • @dierypoulo808
    @dierypoulo808 Před 27 dny

    Aaaaaaaaaaa khana wa apr gnoko yoni louthi sene yone

  • @amasam9455
    @amasam9455 Před 27 dny

    Gatsa
    Gatsa
    De
    Salon
    Wa RFM, vous ne connaissez pas le Journal Yoor Yoor
    😂😂😂😂😂
    Yéna khoromou..
    Khaliss mon Bari thiow😅

  • @douroussndiaye6137
    @douroussndiaye6137 Před 27 dny

    Deukè lén wakh rk nioune niouye léguéye biss dana nieuw nguén rouss dhé 😂

  • @mbayediop9286
    @mbayediop9286 Před 27 dny

    TFM paie impôt par force 😂😂😂

  • @DaoudaJV
    @DaoudaJV Před 27 dny

    Sougn toguei setan lenn wala dilen nianal mou bagn dokh rk mou meti tei metit bi li si eupp si nioun askan wi lay danou donc nagn joug taxaw pour miu dokh si côté yeup kou si nek finga nek nga def si lepp li si war pour mou
    jeum kanam

  • @user-uy8xd8de6m
    @user-uy8xd8de6m Před 27 dny

    Wakh degue yalla

  • @mouhaframarene3352
    @mouhaframarene3352 Před 27 dny

    Boul bi mo tournè rek 😂😂😂😂

  • @mamethiernoka830
    @mamethiernoka830 Před 27 dny +5

    je suis Bah Diakhatè ❤

  • @1gaye945
    @1gaye945 Před 27 dny

    Contra rfm AK apr môme kania lay diekh😂😂😂

  • @ndiemendiaye-wt6wp
    @ndiemendiaye-wt6wp Před 27 dny

    Rupture laniou wah nopolou len bayi len niou ligueye te wah bah bah yi si rewmi dou guen opposant mais jour naliste

  • @dioufmodou4234
    @dioufmodou4234 Před 27 dny

    Yene fene rfm yene wa apr gene katue lene ndayam fuele

  • @aladjifalloudia4915
    @aladjifalloudia4915 Před 27 dny

    Rfm féne kat yie😂😂😂

  • @NgomDarouNgomDarou
    @NgomDarouNgomDarou Před 27 dny

    Wa APR demlen manifeste jdi kaye 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂tapet youbon yi

  • @IbouNdiaye-tj7wr
    @IbouNdiaye-tj7wr Před 27 dny

    Boull wakh 5ans

  • @user-zc4qu8fv4w
    @user-zc4qu8fv4w Před 27 dny

    Dool rék lanioye déf déléne wakhe deugge 😂😂😂😂

  • @serignegueye2403
    @serignegueye2403 Před 27 dny

    Waxofi tousse 😂😂

  • @user-zc4qu8fv4w
    @user-zc4qu8fv4w Před 27 dny

    TFM niongui senne dool yi bataye 😂😂😂😂😂

  • @BabacarBa-vl1gp
    @BabacarBa-vl1gp Před 27 dny

    merci TFM wa pastef s'en lefeul ndeye yen nieo

  • @S.FallouGueye-zc6ww
    @S.FallouGueye-zc6ww Před 27 dny

    Wa thiôwal yay faatu diange çi mbirum 100 millions yi ñu tûddu gfm du ngén çi wax 😂

  • @user-xn3sz1zq3w
    @user-xn3sz1zq3w Před 27 dny +5

    merci beaucoup meumeudou Muhammad Ndiaye tu es toujours le meilleur force à toi 💪💪 rfm thia kaw thia caname

  • @bilygaye7909
    @bilygaye7909 Před 27 dny

    Saytane😂 rfm nopalou len sonko moy diomaye te diomay moy sonko Pastef ak apr dou combat 😂 koune kham na kouy sa mame

  • @douroussndiaye6137
    @douroussndiaye6137 Před 27 dny

    Fén rk nguéni df yaak asaane Gueye

  • @user-pg1lz7oe8s
    @user-pg1lz7oe8s Před 27 dny

    Saineu khôl dina diekh guissa goo laineu dara

  • @nomisdogue618
    @nomisdogue618 Před 27 dny +2

    Merci rfm merci Ndiaye libéré ba diakhate ♥️

  • @sokhnaousmane327
    @sokhnaousmane327 Před 27 dny

    sonko domou kharam bi doulneu ba falou soss ba dem kaso ❌❌❌❌❌❌❌

  • @alinyang-qx6vn
    @alinyang-qx6vn Před 27 dny

    Ndiaye bayil doul ak tfm

  • @serignemodoudieng3091
    @serignemodoudieng3091 Před 27 dny

    Wa gfm tmt loulén diaral li 😂😂😂

  • @dierypoulo808
    @dierypoulo808 Před 27 dny

    Souko rek loumou def bahna

  • @MatarNdiaye-fm1kh
    @MatarNdiaye-fm1kh Před 27 dny

    😂😂😂😂😂😂Pa 😂😂😂

  • @CheikhGueye-im6sw
    @CheikhGueye-im6sw Před 27 dny

    Ndiaye bayil doul 😂😂😂😂

  • @damediop7860
    @damediop7860 Před 27 dny

    Thiey galsen 😂

  • @cheikhdiouf4594
    @cheikhdiouf4594 Před 27 dny +3

    Diguéne dé Sonko rk ,activiste boufi nékoule si yone rk nou niafe ndayame si kasobi