Kawtef😱: Aziz ndiaye après sa polémique tranche indexe…Lahat dafa wara bayi…gaston mbengue…

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 9. 06. 2024
  • ALBOURAKH EVENTS LA CHAINE EVENEMENTIEL
    "Suivez-nous sur Albourakh Events TV, votre destination ultime pour une expérience immersive alliant sport, culture et événementiel. Plongez dans un univers où l'excitation des compétitions sportives rencontre la richesse de la culture, le tout ponctué d'événements inoubliables. Rejoignez-nous pour vivre des moments uniques, où chaque instant est une nouvelle aventure à découvrir. Albourakh Events TV, où la passion devient spectacle."

Komentáře • 216

  • @user-ue3zd5nj3s
    @user-ue3zd5nj3s Před 19 dny +12

    En tout cas lamb dji bénn roi leu am mouy modou khagne lô 👑

  • @MoussaSy-nr2pp
    @MoussaSy-nr2pp Před 19 dny +16

    Aziz Ndiaye d'où nale way kilifa rek Moy wakhé nii 😍🙏

  • @MamadouSow-ie4qn1782
    @MamadouSow-ie4qn1782 Před 19 dny +12

    Aziz Ndiaye est véridique ❤❤❤

  • @iscojo6600
    @iscojo6600 Před 18 dny +3

    Aziz sa Khilifeu #Al Amine Sy (RTA) khana téréwoula wone lamb?? Dernièrement trop de polémique !!! En plus t’as recommencé juste après la disparition d’Al Amine…. Reste calme

  • @babacarsadikhsy596
    @babacarsadikhsy596 Před 19 dny +8

    Bien parlé Aziz! tu es véridique et responsable! Abdoul Ahat Ndiaye doit rester a sa place de manager

  • @fallouniang399
    @fallouniang399 Před 19 dny +10

    Vereman Azize Waxale waye ❤❤❤ ki domram la dafa bari nday wax

  • @user-bc3nk7cb5b
    @user-bc3nk7cb5b Před 14 dny +1

    quelle personnalité que dieu vous assiste vous protège sokhor bakhoul aziz n’as pas le temps di complot si combat thiatou yarakh doudou sane des lutteurs qui ne valent même pas 10millions diam si ioe al amine ❤❤❤❤

  • @alassanemane3021
    @alassanemane3021 Před 19 dny +7

    Machalah Aziz Ndiaye wakh dji rafetna trop 🥰🥰🥰

  • @mamadousarr3371
    @mamadousarr3371 Před 19 dny +16

    Merci beaucoup Aziz ndiaye lahat ndiaye dafa bari problem

  • @moustaphababou6282
    @moustaphababou6282 Před 19 dny +22

    Abdou Late ndiaye mome dafa melni makane mbenge moye papam nite dangaye geum sa bop

  • @mamepathengom9398
    @mamepathengom9398 Před 19 dny +15

    Merci peul bou raféet 👏lou ame solo nga déf✍️Abdou lahad nimou wakhé kou xamoul daye fokni Azize dafa wakh pour diakhassé Fadam ak addouna ✍️Lahad nak mome takhawayou diakhassé lafi néké té togne na Fadam ak Bakari 🤷dafa eupeul trop🙅

  • @baraseck4939
    @baraseck4939 Před 19 dny +29

    Lahat Ndiaye mo eupeul li Aziz wakh ak lim wakh boukoul Aziz da degue fadam diko wakh en live mais lat Ndiaye da wakh fadam da wo Aziz wakh thiatou yarakh dou beure te deme woul nonou

  • @PateMbaye-ec5em
    @PateMbaye-ec5em Před 19 dny +6

    C est pourquoi il est important d écouter 2 versions ! Lakhad , tu es revoir ta copie !

  • @aliounesarr1382
    @aliounesarr1382 Před 19 dny +3

    parceque makkan dafa cool rékk nguén beug déf deumleu rayla dialéla
    avec lakhad Ndiaye dounguén meuneul makkan touss wayé makkan bou dofdoflou ba bayi lakhad Ndiaye sankou
    Aziz lakhad Dou ménager rékk dafa bok thi structure.
    Aziz yaw danga wakhone danga bayi lamb ba wakhko Serigne Abdou Aziz Al amine bouniou démé yomal khiyam dinga rouss.
    sa pékhé yép Moy tass Gaston production AK JAMBAR production té dangay échec inch'Allah

  • @papeseck9969
    @papeseck9969 Před 19 dny +39

    Bilahi walahi Souguéne khamone ñome Aziz ndiaye yi bilahi aye vrais businessam lañou louñouy affiche ci kaw ak liñouy deff ci souf c totalement différent louma lerrr lay wakh

    • @thiattobb423
      @thiattobb423 Před 19 dny +8

      Yaw nandité nga

    • @2quevosquevos242
      @2quevosquevos242 Před 19 dny +9

      Deug pir gua wakh ay Deum laniou deh khaliss laniou diamou

    • @momoseck1617
      @momoseck1617 Před 19 dny +4

      ​@@2quevosquevos242kén wakhoul li nga wakh ni
      Sa kadou da gnaw
      Gnoune ay djioulitt lagnou
      Wassalam

    • @Mameyalla
      @Mameyalla Před 19 dny +3

      Set si yala Dara Lerou lassi

    • @momoseck1617
      @momoseck1617 Před 19 dny +3

      @@Mameyalla sénégal da gno boone
      Loutakh sénégalais beugoul guiss kou am

  • @tallacisse7797
    @tallacisse7797 Před 19 dny +13

    Hahaha Aziz Ndiaye c'est l'hôpital qui se fout de la charité

  • @ousseynoutoure518
    @ousseynoutoure518 Před 19 dny +14

    Aziz lahat à tort mais lamb dafa am lobbies lolou c clair yanguini di créer sa couronne té yafi tegone combat Balla vs modou lo si souf
    Nous ne sommes pas bête

    • @abdourahmanesow2581
      @abdourahmanesow2581 Před 17 dny

      Nafekk boy makk la c'est lui qui pleurniche

    • @TheBandafall2003
      @TheBandafall2003 Před 14 dny

      Ces lobbys sont ds tous les secteurs du pays cette lamb est-il organisé on sait pas qui est professionnel ou amateur des managers non qualifiés qui est le lutteur professionnel ou amateur qui est qualifié pour être promoteur c’est du foutisme et guewelism

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 Před 14 dny

      Merci ❤

  • @Marasaliou
    @Marasaliou Před 19 dny +16

    Li deh mo geuneu yanou mahana

  • @mouhamedfall3783
    @mouhamedfall3783 Před 19 dny +13

    Abdou lahat dafa rew trop kon mo mom nitt yii

  • @azizngom8741
    @azizngom8741 Před 19 dny +30

    Bilahi deug la abdou lahad dafa Melni mo diour nite yi il est très hautain ,Sénégal nak dagnouy diay mbote bamouy’mbeuker

    • @mamadoumoustaphadiop1650
      @mamadoumoustaphadiop1650 Před 19 dny +1

      Rousseul Prénom esk doko dindi

    • @SoftlSotfl
      @SoftlSotfl Před 19 dny +3

      😂 Saway sa clavier bi tameu na bindeu affaire bi d 😅😅😅😅 eskey guani lane répète 😂😂

    • @ousseynoutoure518
      @ousseynoutoure518 Před 19 dny

      Clavier bila​@@mamadoumoustaphadiop1650

    • @fifty6292
      @fifty6292 Před 19 dny +2

      ​@@mamadoumoustaphadiop1650Boul Sonal nite yi tour deukoul féne kounek khamni koumouy wakh Senegalais ngay wane wére mouy khol sa baram sof torop

    • @azizngom8741
      @azizngom8741 Před 19 dny

      @@fifty6292 diadieuf frère gars yi deh moy lolu dagnouy dieul details defko Lou graw clavier day teub comme Lou nite di dioumer

  • @user-dt2sc5yl6v
    @user-dt2sc5yl6v Před 19 dny +6

    Certes Abdou lahad daffay wakhé khole mais nakk Aziz Ndiaye kilifa dafay moytou wakhou soufe yaw soo wakhoul woone AK lahad dou âme Fitou takhaw thi télé wahe né Yaako wahe que fadam moo téré boy bi beuré

  • @sanadieme756
    @sanadieme756 Před 19 dny +19

    Lakhat moom Rek lobii😅may wakh mouy sakkëto Guinaw rail ak seras Baala may Dë mou nane moom dou raggal Dou touche Nioo Deuk Doo woon Guinaw rail Quartier mango gui Bobou Bathie seras mogui mbapatt baa nii mou douguë sii lamb koon khaam na ko dou deureum yaw ak fadam dou niveau wakhatou Bacary sakho yaroul niou beug leu moo geune sa tekk doff bii gua nekkë yaw

  • @babacartine4464
    @babacartine4464 Před 19 dny +7

    Abdou Lahat mo nité woule deug la Fadam wakh ak coach bakary claf bou tollou ni nga beug fay boy yi 2 millions dilene utilisé

  • @agencysport2914
    @agencysport2914 Před 19 dny +1

    Vraiment Aziz tu a parler comme un leader, tu a bien fait Lahat n'est pas un dirigeant il se fou de tout le monde merci encore Aziz

  • @ndiogoundiaye3772
    @ndiogoundiaye3772 Před 19 dny +3

    Azize a bien dit big chapeau 🎉

  • @user-ge2cf4tj1u
    @user-ge2cf4tj1u Před 17 dny +2

    Aziz mi sayetané la😂sisouf layedef😂

  • @cheikhcisse1278
    @cheikhcisse1278 Před 19 dny +2

    Bien dit Aziz mashallah

  • @mouhamethniang3154
    @mouhamethniang3154 Před 18 dny +3

    L'achat wahna deugeu azize da nga soff trop

  • @thiawbadiane6873
    @thiawbadiane6873 Před 19 dny +3

    Mane dé fadam nama balle❤dama rousse sakh bilaye❤😢

  • @ndomarafate3161
    @ndomarafate3161 Před 19 dny +9

    Mais li kay garawoule Aziz daf ko dégué si fadame wakhko lahat lolou kay dara nékou si

  • @bigttt9014
    @bigttt9014 Před 19 dny +2

    Aziz Ndiaye mo gueune niaf ndem Senegal Mai’s se beus ngi nieuwe legui domi khath le rec

  • @ousseynouwade7066
    @ousseynouwade7066 Před 18 dny +2

    Yangoul aziz na fekhela mako wakh lahat Ndiaye mongana dioup aziz Ndiaye

  • @ilimanediouf3629
    @ilimanediouf3629 Před 19 dny

    Macha allah abdou aziz alé ndiaye wakh bi rafetna leep leer n'a ❤❤❤❤

  • @lemarseillais3019
    @lemarseillais3019 Před 19 dny +4

    Lahat dh Combat Jackson vs Lac rose lako simile sapo nii kii dafa dof 😂

  • @bachirdiop19
    @bachirdiop19 Před 19 dny +8

    Lahat ndiaye dafa yabaté si bopam mome li takh Paf teuga toul lamb sila bokou ,il doit revoir sa façon de faire

  • @TheBandafall2003
    @TheBandafall2003 Před 14 dny +1

    Moi je comprends pas la lutte avec frappe au Sénégal y’a que des polémiques zéro professionnel on sait même pas c’est quoi ces sites rien de professionnel aye wérenter rek

  • @momoseck1617
    @momoseck1617 Před 19 dny

    ❤❤ machallah Aziz dama yeureum sey none❤

  • @iibassndiaye2886
    @iibassndiaye2886 Před 19 dny

    bien parlé franchement adouna amoul solo 🇸🇳🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼

  • @user-gw8qv9zg5b
    @user-gw8qv9zg5b Před 16 dny

    Merci Aziz deug pirr nga wax bilahi ❤❤❤❤❤ Lahat Ndiaye na yém plassou courtier dalou Aziz sax dou moromam

  • @diogenelaerce2197
    @diogenelaerce2197 Před 19 dny +3

    Aziz bayil doullllll t’es le premier domerame dans ce pays….

  • @mordiop5555
    @mordiop5555 Před 19 dny +6

    Lahad na bayi limouy deff rafetoul

  • @sondji1412
    @sondji1412 Před 18 dny +1

    Abdou lahat Ndiaye sa date yaye doméram deug la bilay😂❤😅

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Před 19 dny +2

    Lahad wakh na deug lamb dafa am lobbi Aziz Ndiaye yaw khaliss guaye diaye

  • @aliounesarr1382
    @aliounesarr1382 Před 19 dny +2

    problème amoufi yaw yay problème bi dakh mbeur yi AK sén ménagers yi lou lér lagnou signé yaw Loy lidieunti thi problème you diambour
    lakhad Ndiaye dagnouy rafétlou liguéyam
    lamb yaw yay loobie bi
    lakhad Ndiaye mola guéneu nékk wagga

  • @SegaNdiaye-mv5bt
    @SegaNdiaye-mv5bt Před 19 dny +2

    Aziz legui dafa yeuk bopam depuis mou nek ci show bizz di doundou beuz

  • @Mamadou-Fall
    @Mamadou-Fall Před 19 dny

    Aziz vraiment il est extraordinaire ce gars mashaAllah!!!!

  • @user-hs9fv8sd7w
    @user-hs9fv8sd7w Před 19 dny +6

    Merci aziz bome apoll wone khaliss ma maye la 10000 mi yalla bakh na contane na si iow😂😂😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Před 19 dny +6

    Abdou lath diakhassé na promoteur yi diakhsse lamb dji

  • @delaypeuimporte463
    @delaypeuimporte463 Před 18 dny +2

    Franchement y’a anguille sous roche iow teugo dou sa lamb bayi ga lamb Louy si sa gat ba gay wotei di wakh Lou nieuweugoul Aziz weigh ga dounk
    Est-ce que créer wo problème bi sakh di woter di digler ay solutions

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 Před 14 dny

      Ya deugou kaye .téré nagn ko lamb dousi mandou .mouy EMPEREUR AK LOUNÉ

  • @MountakhaThiam-gh1ni
    @MountakhaThiam-gh1ni Před 19 dny +1

    Très bien dit aziz ndiaye lat ndiaye loumou bokak assane gueye rfm

  • @aliounesarr1382
    @aliounesarr1382 Před 19 dny +2

    yaw sa wadiour bimou géné adouna fi nga khéw khéwou 300 millions thi linga wakh sa Dôme boy seyi rékk
    sangou baparé balanga diglé sangou

  • @assniang2252
    @assniang2252 Před 19 dny +4

    Yalla deugue la beugue hana Gaston dou sa baye ya neuke teugue bayilene nahane tayi

  • @diayoussou8823
    @diayoussou8823 Před 19 dny +8

    Badola kén douko diokh micro

  • @MountagaNdao
    @MountagaNdao Před 19 dny +4

    Lahad il a raison lamb da amme lobby, yaw fi nga nekk di khekh couronne modou lo bi....😅

  • @abdouthiam3312
    @abdouthiam3312 Před 19 dny

    Merci Asiss ndiaye ❤

  • @mamadoumatarsow1191
    @mamadoumatarsow1191 Před 19 dny +2

    Yaknako yalla yeureum tè kharèko aldiana firdawsi wayè le travail foit continuer

  • @lafarndiaye6204
    @lafarndiaye6204 Před 19 dny

    Merci beaucoup aziz

  • @LamineMbaye408
    @LamineMbaye408 Před 19 dny +2

    Claf queens boy ,serigne ndiaye 2,fils de balla, doudou sané

  • @aliounesarr1382
    @aliounesarr1382 Před 19 dny +2

    fadam dafa niakk fayda ponkal bougnouy utiliser rékk leu

  • @ousmanendiaye2983
    @ousmanendiaye2983 Před 19 dny

    Merci Aziz Ndiaye

  • @ndeyeastou7501
    @ndeyeastou7501 Před 19 dny +3

    Vraiment lat limou déf ni rafettoule mais Aziz limouye reproché lat Ndiaye mome moko fi dak Aziz mofi guena yeuk bopame emplus mofi dak forcé niti son choix mongui ni forcé niou empreure

    • @leuz.patriote
      @leuz.patriote Před 19 dny +1

      Da am xaliss am thieur si Senegal nieupa ko beugg talibè cheikh bi

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 Před 14 dny

      Aziz mo guena sof di diaye doolé

  • @Wadiomfall
    @Wadiomfall Před 18 dny +1

    Khalisou Covid 😢

  • @ibrahimalaye7603
    @ibrahimalaye7603 Před 19 dny +1

    Aziz balma akh wakhou lahat bi takh na wakh la mousi ba lo siento mucho 🙏🙏

  • @OumarLy-jw4gd
    @OumarLy-jw4gd Před 19 dny +4

    Bayile'n sokhor Aziz Gathie ngualama

  • @diaibrahim6798
    @diaibrahim6798 Před 19 dny

    Merci Aziz 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤

  • @Ydakh-ui5yo
    @Ydakh-ui5yo Před 19 dny +3

    politiciens gnola geuneu gnaww fouf ta lougnou tékk gnou guissko bayil ték khélbi

  • @dierydiao6574
    @dierydiao6574 Před 14 dny

    Vraiment aziz tu as bien c est lahad qui doit revoir son comportement

  • @taphadiop6081
    @taphadiop6081 Před 19 dny +5

    Mbaw mome dafa beugue thigou com dou mak niak fayda

  • @MoussaMotivation
    @MoussaMotivation Před 19 dny

    Waxal way Aziz ❤

  • @ousseynouwade7066
    @ousseynouwade7066 Před 18 dny +1

    Mane sen desebi wakhou fi d'ara mak dou gawtou moom aziz Ndiaye moy fen paske mak dou gara wakhe dembou lan fi repaire aziz Ndiaye ak makan

  • @papahabibdiopofficielle3160

    Nn li aziz wakh mo geuna raisonnable 🎉

  • @AliouDieng-gu1tp
    @AliouDieng-gu1tp Před 19 dny

    Merci azize

  • @khadimsow7149
    @khadimsow7149 Před 19 dny

    Merci Aziz 😍

  • @moustaphababou6282
    @moustaphababou6282 Před 19 dny +7

    Abdou late ndiaye geumeul sa bop yangi melni deuko kabe gaye kou deuke kabe gaye dou dou ngourou kene

    • @cheikhoudamba
      @cheikhoudamba Před 19 dny

      Kane la doungourou saway ki dafay liguéy nioukoy fay doff nga rek

    • @moustaphababou6282
      @moustaphababou6282 Před 19 dny

      @@cheikhoudamba abdou late da yakarne mo mome lambji mo moul lambji ba wakhe mou geud ko lolou mome menager rk la

    • @moustaphababou6282
      @moustaphababou6282 Před 19 dny

      @@cheikhoudamba na bayi makane mbenge mouye wakhal bopam makane amna laminge

  • @beuguebambaseck4916
    @beuguebambaseck4916 Před 19 dny +2

    XANA LEGUI GNI DI TOP DI WAX AZIZ MOY WAXLO NIOM BOUCHER FADAM DI NGEN TEUTHIE SEN GAAT YI TÉ BAYI SOSS AK JOUÉ AU FILM SI SEN XEL AKI CASTING ☝️MERCI ZIZ DOXALAL🙏

    • @MountagaNdao
      @MountagaNdao Před 19 dny +2

      Aziz daay tek xel...lamb da aame lobby...

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 Před 14 dny +1

      ​@@MountagaNdaoexemple pourquoi vouloir créer un autre titre k Roi

  • @khadimndiaye9492
    @khadimndiaye9492 Před 19 dny +8

    Kou wakhe fégne aziz toudou. Fadame toudou gua bakari sétossi dara

  • @jalediaw4008
    @jalediaw4008 Před 18 dny

    Merci aziz almine

  • @user-vk6ws5rd2d
    @user-vk6ws5rd2d Před 19 dny +1

    Vérité absolue

  • @user-ds4oi9os4z
    @user-ds4oi9os4z Před 19 dny

    Vérité absolue Aziz Ndiaye

  • @SegaNdiaye-mv5bt
    @SegaNdiaye-mv5bt Před 19 dny +3

    Yaw Aziz da nguay thiouthie fi thiouthie fè tè do manager do promoteur li ngua fi wax yeup yaw la war tu penses tout savoir alors ay batailles physiologiques rek nguay def deugue j mome dina leer nagne tè dou yague maffia bi ame ci lamb j nieup wax naniouko

  • @moussadiop6111
    @moussadiop6111 Před 18 dny

    Billahi azize defoul darra abdou lahad Ndiaye mo dioume rek

  • @user-or4fq7wb2u
    @user-or4fq7wb2u Před 17 dny +1

    Aziz ndiaye faut types leee il n'est une personnes s'insère wa lambe yeup la corrompre

  • @64Amadoufall
    @64Amadoufall Před 19 dny +1

    Lima def reih lahate neina dou moy yalla Sénégal waay😂😂😂

  • @Pijunior-cu8lw
    @Pijunior-cu8lw Před 19 dny +3

    Lahad dof la genrou nit yi bougnou nekè sa wett si ay blem rek guaye nekeu

  • @alunendour3815
    @alunendour3815 Před 19 dny

    Aziz ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @habibhabib8869
    @habibhabib8869 Před 19 dny +1

    👍👍👍💪

  • @waxkatoudeug
    @waxkatoudeug Před 18 dny +2

    Danga sop. Xawma lou si sa yone si ay combat diambour

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Před 19 dny +1

    Aziz Ndiaye yaw dagye doul ndayam rak

  • @MortallaNdiaye-tc2pz
    @MortallaNdiaye-tc2pz Před 19 dny +2

    👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻

  • @falloudiagne5902
    @falloudiagne5902 Před 19 dny

    Diadieuf way goor dafay gnémé wah deugu❤

  • @tallacisse7797
    @tallacisse7797 Před 19 dny +6

    Mohh Aziz yafi gueuneu arrogant.
    Yeine promoteur yi mom 6 ak 9 leu rek

    • @ousseynoutoure518
      @ousseynoutoure518 Před 19 dny +2

      Blh ya niamé degue

    • @MbayeDiene-qw7ht
      @MbayeDiene-qw7ht Před 19 dny

      Souko nékhé aye millions la géné dii teugue mais lahate daye exploté boy yii rék dii woute loumou ame

  • @ibrahimafaye5737
    @ibrahimafaye5737 Před 19 dny +1

    Lakhat limou yakka si lamb dji mo barii te lepp pr son propre interet

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 Před 18 dny

    🇺🇸 Vraiment actroces doÿna Warr entouka l'honneur de nôtres lutte est bafouée par le mafia ✨ Aziz Ndiaye vrai Nandité l'eu 😅

  • @goradiop4611
    @goradiop4611 Před 19 dny +2

    Billahi aziz Day doulll aziz yaw ya yakh lambe dji

  • @mouhamedgaye2482
    @mouhamedgaye2482 Před 19 dny

    ❤❤❤❤❤

  • @SheiyBaa-thiat
    @SheiyBaa-thiat Před 18 dny

    Lamb deja amoul nsiarign, le systeme ayant sombre, les dures realites reprennent leur place...lobby, lbeur, promoteur etc...yena yem

  • @cheikhoudiop2561
    @cheikhoudiop2561 Před 19 dny +6

    Mane Dale fadam 2diakhal nama fadam 2doule rek lay deff qui Diakhale nama kois

  • @user-oj5ik7vm5e
    @user-oj5ik7vm5e Před 18 dny

    Aziz yaye nite yaye gorrr yaye guarmiii late Ndiaye kou Kate ndayam la

  • @user-ru9xt9zy6m
    @user-ru9xt9zy6m Před 18 dny +1

    Todj n'a fadam DH néna dfa wo Aziz Ndiaye Niko boy bi d'où beurré t loulou live la wone

  • @modouseckseck9893
    @modouseckseck9893 Před 19 dny +1

    Aziz de khalela mais Ku Bakh la te mana rafetal