NGII ADJI WON MAKKA YEUP KEN AMOUSI ADJ...IMAM LAMINE SALL KOU SAANI JAAMRA...

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 26. 06. 2024
  • SOLUTION TV

Komentáře • 84

  • @damefall2427
    @damefall2427 Před 23 dny +10

    Moi j'ai fait le pèlerinage en 2010 on était avec des guides parfaits on a fait tout dans les règles de l'art c'est le bon seul qui sait qui a fait le bon hadj que le bon Dieu accepte le hadj de tous les pèlerins sans exception amine

  • @MaodoNdiaye-io8ct
    @MaodoNdiaye-io8ct Před 27 dny +12

    Dama ragall atté diourom yie Gemo yalla amon dioullie amon kor sa aje maka nagouwoul sa azaka bakhoull lolou domén réservez la yalla moko mana atté man ga wakhe nak dou nie wanté yalla nagouwouko lolou mom man douma KO wakhe wa salam ❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @user-dm1mp5ld9d
      @user-dm1mp5ld9d Před 26 dny +2

      ❤❤❤❤❤

    • @codoudiouf9710
      @codoudiouf9710 Před 14 dny

      Ki digalneteme ak tahib socé mo takh ma wédico. Adj gou nangou domaine nou yalla leu. Ki kou sokhor leu li dakone wara wallah balla adj do commencé..kou moss thiono adji amo loy wakh nane amo adj wakho deugue ndakh do yalla nit kou bone rek nga khol bou sokhor nga wakhé

  • @gueyegueye894
    @gueyegueye894 Před měsícem +9

    La question du HAJ doit être expliquée dans les granges mosquées, les médias au moins 2 mois à l'avance.
    Les imams, ont les entend pas en parler ni à la télé, ni lors des Houtbas de vendredi, et Pourquoi pas rediger un livre éducatif à distrivuer aux pèlerins dès leur inscription pour la Mecque ??? 👉🇸🇳Expliquer après le départ retour des vols , c'est se designer médecin après la mort

  • @user-zg6nh3vz4s
    @user-zg6nh3vz4s Před měsícem +8

    Baye assane messere demala beugue bilahi ❤❤❤❤❤

  • @user-zr8dy8ks3t
    @user-zr8dy8ks3t Před 13 dny +1

    Koù sokhor nga

  • @mamadoudiagne4969
    @mamadoudiagne4969 Před měsícem +4

    Dieureudieufff.serigne.lamine.sall.gouddal.fane.100.ant.cent.ordounace

  • @user-zg6nh3vz4s
    @user-zg6nh3vz4s Před měsícem +14

    Mafi djitou teye liila yalla dogal baye assane sa numéro sokhlanako trop bilahi ❤❤

  • @karagueue9084
    @karagueue9084 Před měsícem +3

    Seuls ceux ki voulaient partir mais n'ont pas pu disent:amoulaine adj ou corona baa ngua maaqua.baayilaine ignaane gui,sokhor baakhoul

  • @ouleyecisse2344
    @ouleyecisse2344 Před měsícem +9

    Il faut des cours de hadji dans les écoles et à la TV comme en Indonésie

  • @amyndiaye8711
    @amyndiaye8711 Před 27 dny +2

    Mom adjam bakhna mais les autres amounou adj foutaise

  • @64Amadoufall
    @64Amadoufall Před měsícem +7

    séen titre bi gniawna lool

  • @elimanembengue
    @elimanembengue Před měsícem +5

    Pour des vues, vous avez fait une description mensongère et manipulateur de la vidéo.

  • @senegalsenegal4989
    @senegalsenegal4989 Před 29 dny +1

    Bi ngui wzkh lou am solo.. S'il dit vrai, acceptons et corrigeons. Qu'Allah nous facilite.

  • @Mariama-tk5jl
    @Mariama-tk5jl Před měsícem +5

    ❤❤❤❤❤
    Selon moi, autorites saoudiennes yi nio warra reglementer li oudiadj yi di deff pour corriger erreurs yi. Dakh dem ba Macca ba parer amo adj mome doynaware

  • @cissemamour2045
    @cissemamour2045 Před měsícem +2

    لا تقل كل اني ومن معي رمينا العقبة بعد الفجر بساعة اليوم العيد وبعد العصر في يوم الثاني وبعد الظهر في يوم الثالث ورب الكعبة

  • @DiaAmadou-fl3yt
    @DiaAmadou-fl3yt Před měsícem

    Dieureudieuf Serigne Lamine

  • @abibatoumbacke6759
    @abibatoumbacke6759 Před 16 dny +2

    Kham nani am ngen fite dé ! Walla yen bou goudé dangen di guissé ak souniou borom ! Adj bou nangou ak diouli bou nangou ak bep diamou yalla ken menou ko até koudoul souniou borom! Ngen di metil aka tawi melni ay malaka

  • @mossanendour1062
    @mossanendour1062 Před 23 dny +1

    Yaay yallah ? Yaa kham kou adjam nangou ak kou nangouléwoul? Mandou Amna solo

  • @khadidiatoukamara9620
    @khadidiatoukamara9620 Před 17 dny

    Pour les sandi diamra du 2e et 3e jour effectivement doivent se faire après la prière de tisbar
    Sauf moi j’y étais cette année mais ce sont les autorités saoudiennes qui ont organisé les heures de jamra car avec le monde qu’il y’a maintenant et la chaleur (il y’a eu beaucoup de mort) tout ce monde ne peut pas se retrouver à diamra en un temps(14h à fadjr)
    Si les autorités ont décidé de changer les horaires pour contenir la foule qui augmente chaque année malgré la limitation du nombre de pèlerins.
    Les pèlerins ne sont pas responsables allahou ahlam Yallah rek Ka kham

  • @user-fd8zj8tt7p
    @user-fd8zj8tt7p Před 21 dnem +1

    Pourtemp makka kou adji dingua tokk 4 ans dora amat droit adji loulou mon am makka de

  • @seynabouwane7037
    @seynabouwane7037 Před měsícem +4

    Tous les jamarat ont été lancés après la prière fadjr c est ce que j ai vu.

    • @papawilane1517
      @papawilane1517 Před měsícem

      Seytane yalla wakhoul si alquran il faut le chasser par des pierres ce st des paroles

    • @khadidiatoukamara9620
      @khadidiatoukamara9620 Před 17 dny

      C’est parce que les autorités saoudiennes qui ont procédé à cette organisation pour contenir la foule qui ne cesse d’augmenter
      Puis ceux qui sont sortis cette année sous le soleil vers 14h00 ont fait les frais

  • @FatouLeboundoye
    @FatouLeboundoye Před 10 dny

    Ouztaz boul takhaw takhawayou Yalla. Hadj bou nagou Yalla rek mon ko kham

  • @Ciara66129
    @Ciara66129 Před 18 dny

    Yallah yéné lay fay

  • @matyliouamath1516
    @matyliouamath1516 Před měsícem +1

    Mane dé biirou Aly laa sanguoo fa la sollé sama harmal fa la yéénnéé mane ak gni ma andaloone

  • @samadeug6754
    @samadeug6754 Před měsícem +1

    Amna solo

  • @korsadio
    @korsadio Před měsícem +8

    Do Yallah bay kham kou adiam nangou wala déth

  • @magattewade8354
    @magattewade8354 Před měsícem

    Koukhamoul mbir diangothia Darra darra dici poser question c'est très grave.

  • @assyfall1221
    @assyfall1221 Před měsícem +1

    Lou ler lâ wakh, Jamarats aqba niongui koy sani après fajr 10 Dhul hijjah et non 9 ci goudi. Ayamoul Tachriq, Sounnah bi moy sani Jamarats heurou jawwal après dohr

  • @coumbaba-t6q
    @coumbaba-t6q Před 27 dny

    Amna solo LOL il faut un recyclage de nos oustaze

  • @Noiceur-ebene
    @Noiceur-ebene Před měsícem

    Yalla nako Yalla guindi te rafetal aiye khalatame ak aiye wakhame

  • @cheikhahmettidianefaye1839
    @cheikhahmettidianefaye1839 Před měsícem +1

    Souniou Imam yii daniou wara bayii dii tiital ningne yi sii massala yoo hamne dafa am aïe voûtée.
    Nioun dey Ya Allah ba hee ne niou niou Dem Makka ren. Wayee Guen nou niou Dem sanni diamra tee diouli niou fadiar ba paree .
    Diokhé sa guiss guiss bah naa, wayé wakh guiss guiss yep sou fekke ham nga koo moo Gueun.
    Taa banie dii tengal loo hamne yalla moko mom tee mokay nangou.

  • @oumyoumy1439
    @oumyoumy1439 Před měsícem +1

    Oustaz Sall li nga wax lu wer la. D'accord na ak yow!

  • @mariethioune6914
    @mariethioune6914 Před 25 dny

    C est tres compliqué...

  • @presidiouf2489
    @presidiouf2489 Před měsícem +1

    Assane n'est pas sérieux koi. Nénako ioe loo saniwone😂

  • @rockayathiam526
    @rockayathiam526 Před 19 dny

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @cheikhdieng9354
    @cheikhdieng9354 Před měsícem

    Lusi beri imamyi nioko waral

  • @altesseroyale4383
    @altesseroyale4383 Před měsícem

    Waw lolou yèp danou ko wara lèrale kèp ko adji parceque yi foule you reuye, nit gni danouye sone tangaye wa beugueu lène raye fok diakhassé ame

  • @abdoulayesall7723
    @abdoulayesall7723 Před měsícem +1

    Ki dafa dof Kene dou sani diamra te diouli wo souba

  • @lamine-wade
    @lamine-wade Před měsícem +1

    Yaw do yalla bay kham adj mou nagou wala bou nagouwoul et aussi guané ligua deff mo bakh ta lou nianéne deff bakhoul

  • @modou5844
    @modou5844 Před měsícem

    Le jour Arafat a été anticipe 😂 ils feront 31 jours ce mois

  • @emeraudet4295
    @emeraudet4295 Před měsícem

    iL EST IMPERATIF DE FORMER LES OUSTASS ET LES ACCOMPAGNATEURS DU HAJJ

  • @cheikhdieng9354
    @cheikhdieng9354 Před měsícem +1

    Mande liimu wax gisnakofa
    magi sant sama borom bubax
    luwerla wax nitni danio beg lu yombu

  • @user-fd2zm8zn6x
    @user-fd2zm8zn6x Před měsícem

    diadieuf 😊

  • @user-oo2fe1no4v
    @user-oo2fe1no4v Před měsícem

    Oztas té ngua rafet ndiorto ji samoroumou jullit yi waye niom kher laniou sanni mais mn jamra la sanni lolou du wakhi brom xam xam

  • @nangodiagne5927
    @nangodiagne5927 Před měsícem

    Nitt deyy mandou ! Yalla moomm dongg mooyy juger lou diamm deff wakh waneee! Na kou nekk diemaa raffett ndiott ci boppamm akk mbokamm! Yénn wakh yii kilifa dinée de surcroît waroukoo khalaattt baa dukoo guénee ci lamigniammm! Sénégalais daffa deuggueurr yapp niemmee yalla amm fitou wakhh ndiakhoummm ! Sougniou birommbi dieuggaloulll youkhou dina djibbb fougnn koo foggûée woull ! SUBHANALA

  • @aliounesow6972
    @aliounesow6972 Před měsícem

    Lamine salle yagui sopekou deh yoro yeumande diam yis yagui wathie yone deh

  • @ramatoulayedrame6589
    @ramatoulayedrame6589 Před měsícem

    Machallah wakhtane bi amna solo dianguee naniou tchi lou barri.

  • @ElhadjidaourDiongue
    @ElhadjidaourDiongue Před měsícem

    na leul kamil watko gnep deg guen filmeko

  • @thianendiaye6363
    @thianendiaye6363 Před 23 dny

    Je veu regarder l emission Sira de Pape Hanne avec Soldarou Bamba de la semaine dernière sur la TFM merci

  • @GueyeTapha-e8b
    @GueyeTapha-e8b Před měsícem

    Titre bi fanla ko waxe

  • @diatta2335
    @diatta2335 Před 19 dny

    En temps que Imam mandou Lola war . Vous êtes trop bavarde

  • @sanoussycamara6359
    @sanoussycamara6359 Před 22 dny

    Hadj bou nangou,Yallah rek moko xam Dilen rafet ndiort.Sen titre bi gnaw n'a lol.

  • @MbaN2912
    @MbaN2912 Před 29 dny

    Assalamou alaykoum. Mais pourquoi les autorités saoudiennes leur permettent de lancer les « Damra » à cette heure? Je propose que les guides religieux et les guides des pèlerins fassent des émissions dans les stations de radio et les chaînes de télévision pendant le mois de Ramadan. Ces informations doivent être rediffusées chaque semaine jusqu’au départ des derniers pèlerins du Sénégal. Assalamou alaykoum.

  • @cheikhtidianediallo3403
    @cheikhtidianediallo3403 Před měsícem

    Tu es trop faux porter le ihram est différent de l intention c l intention de choisir quel type de pèlerinage qui. Le harmal et c ça qu on exige de faire à Biir Ali

  • @user-tu4wu1ce7f
    @user-tu4wu1ce7f Před měsícem

    Ki dara khamouko wakh djou bari rék am😢

  • @user-fl5nk2yw3x
    @user-fl5nk2yw3x Před měsícem

    Tu n'est pas Dieu t'ai toi

  • @morndadje4198
    @morndadje4198 Před měsícem

    C'est toi-même qui accepte le ADJ?

    • @ismaelngom1451
      @ismaelngom1451 Před měsícem

      Salam. Esk non mon frère, mais il parle selon la sunnah, tout com qd tu pries sans ablutions ce n'est pas accepté car les ablutions sont une condition nécessaire de la prière.salal

    • @morndadje4198
      @morndadje4198 Před měsícem

      @@ismaelngom1451 l'acceptation est un domaine réservé de DIEU BOROM RAHMANE wa Salam

  • @stafiroulaha
    @stafiroulaha Před měsícem

    wouté tabaski ak corité yawe bok ga thi nie koye djté

  • @nafissatousy4875
    @nafissatousy4875 Před měsícem +1

    Dieuredieuf Imam Lamine sall
    Wakh nga lou am solo
    Dem makka toog ay heure you bari thi vol bi fay ay millions
    Ba parè defou loo sa adj niumou waré
    Yal naniou yalla djegal té nangoul niou

  • @cheikhdiop9673
    @cheikhdiop9673 Před 25 dny +1

    mane dé li gayi di wax nane yonénte bi néna ta lolou ci ay nitt rék lagnouko nago khamougnou wérna wala wéroul am fitt ba dé wakhi nitt mane nagne ko sopi bamou dess wakhi yalla déléne wax al khouran ta bayi hadis yiga khamni ay nitt comme yén gnoko soss guéne beug sé dougal nitt gni sawara wala bonal séne diamou yalla yi ta yalla wakhouko loufiway wax ta dou al khouran gnou saniko sa khathi ndax nitt dafa bari ay pékhé défar say téré guir gnila geumoul baparé gani yonentebi moko wax wayé bou yawmal khiyamatil ak bar lép dina lér

    • @khadydiallo9814
      @khadydiallo9814 Před 22 dny

      Islam gnaari source la: AlQuran ak hadis et sounna Yonent bi saws.Demal jangui la science des hadith, c'est-à-dire la transmission de la parole du Porphète saws. Hadis authentiques yi nga hamni base lagnou si diiné dji dou attravers n'importe qui ak n'importe comment langnleen transmettré! Té hamalni Yalla mi wathié islam té tanko comme religion agrée moo samm diiné islam authentique jusqu'à sa transmission et au-delà. Allah Très-haut dit à propos du Prophète saws: "Il ne parle pas par impulsion. Ce n'est qu'une révélation qu'on lui a faite." (Coran, 53:3-4).

    • @cheikhdiop9673
      @cheikhdiop9673 Před 22 dny

      @@khadydiallo9814 yaw mi nak ya wara diangui dama dieug ay hadis ba sonne ta boukhari ak taymiya ak imame Malick ak hane balle bokougnou nougnou guise ci hadis you Bari légui Kane mo nék ci deug ak Kane mo nékoul ci deug ta boudé Al khouran amoul wouté lisi yalla wax bo démé arabi Saudi fékk kofa ak yénéni réw ak Sénégal Kone teukoul ci Al khouran mi amoul ak wouté

  • @muhamedjeg5797
    @muhamedjeg5797 Před měsícem

    B assane nenako yaw lo sanni
    Sacré baye assane

  • @ElhadjigorguiwadeNdiaye
    @ElhadjigorguiwadeNdiaye Před měsícem +3

    Ce monsieur se croit pour le von DIEU.pour faire certaines déclarations.c est seul Dieu qui valide ''le. Hadj''. Il se dit érudit mais il est un. Peu borne. ?

    • @bigndanane1448
      @bigndanane1448 Před měsícem +4

      Sûrement tu n'es pas content de lui pour une raison ou une autre mais c'est fallacieuse. Il n'a jamais dit qu'il était le plus instruit. Il donne ses positions et ils les arguments selon des textes de la législation islamique. S'il est contre aussi c'est avec le même procédé qu'il réfute. Et c'est un homme très ouvert à la critique et au débat de fonds. Maintenant d'où sors tu tes accusations bidons sur lui. Celui-là est un grand savant qui mérite respect. Yaw sûrement mokalo lakhdaryou baparé beug ko critiqué

    • @ismaelngom1451
      @ismaelngom1451 Před měsícem +1

      Salam.non mon frère. Dieu a indiqué les conditions. C com si tu pries sans ablutions, ce n'est pas valide car les ablutions sont une condition nécessaire pour la prière.

    • @ibrahimadiop238
      @ibrahimadiop238 Před měsícem

      Merci rewmi mo bari gno khamne par parlo rek​@@bigndanane1448

    • @nafissatousy4875
      @nafissatousy4875 Před měsícem

      @@bigndanane1448 thia deug deug