AMA BALDÉ SE DÉCHARGE SUR GRIS «damay dox si kanam, GRIS «lolou la yakamti…. »

Sdílet
Vložit
  • čas přidán 22. 06. 2024
  • Bantamba tv, une télé une vision
    Cité keur Gorgui Lot 101 immeuble Mame Yacine
    tel : 33 825 34 36
  • Zábava

Komentáře • 95

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 Před 4 dny +13

    🇺🇸 yalla n'aniouko fécké talko si diam akh salam incha'Allah Ama baldé yalla nkô yalla maï ndam incha'Allah ❤️💕

  • @SerignefallouFall-ku4op
    @SerignefallouFall-ku4op Před 3 dny +16

    Kep kou beug seydina mohamed salallahou haleyhi wasalam rkk lalal j'aime ❤❤❤

  • @diopcheikh6680
    @diopcheikh6680 Před 4 dny +23

    Ama baldé yalla nako yalla may ndam

  • @mosi301
    @mosi301 Před 4 dny +23

    Ama damako yènè ndame walahi nit kou bakh la yalla na yalla maïko ndame amine

  • @abdoulatifdiop5640
    @abdoulatifdiop5640 Před 4 dny +7

    Gris Bordeaux
    Yalna ko yalla may ndam 🤲🏿🤲🏾

  • @user-gw8qv9zg5b
    @user-gw8qv9zg5b Před 4 dny +5

    Man kou beug Balla Gaye rék ma Beugueu leu Ama baldé ya man ya eupeu dolé yallah nala yallah may ndam inchallah ❤

    • @mouhamethniang3154
      @mouhamethniang3154 Před 3 dny

      Inhaala le 30 gri dinako dane

    • @user-gw8qv9zg5b
      @user-gw8qv9zg5b Před 3 dny

      @@mouhamethniang3154 yaw sax bodon beuré ak gris thi yaw lay ték
      Gris 2015 contre tyson pa bi la gueudieu am victoire 😂😂😂

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 Před 4 dny +3

    Ama balde grand champion linx pikopacos borome pikine Yallah neu Yallah mayla ndam Inch'Allah AMIINE 🎉

  • @papeseck9969
    @papeseck9969 Před 4 dny +35

    Ama defaite bimou ame contre modou dafko khawa diap mais yala nako yala soutoural may ko ndame ci combat bi

    • @cheikhfall4377
      @cheikhfall4377 Před 4 dny +8

      🇺🇸 bilahiiii bro 😢 Ama baldé yalla nkô yalla taxawou incha'Allah maiko Ndam incha'Allah

    • @user-pq3ep6qr1n
      @user-pq3ep6qr1n Před 4 dny +4

      Si si dafko métti sakh sincèrement mais yalla bakhna Ama champion deug leu

    • @Wrestling1890
      @Wrestling1890 Před 4 dny +3

      Lolou war nako diangal nak lou bari thi lamb

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 Před 4 dny +2

      C’ est que combat Bobou dafko tardel Saway. 5 ans la tokk di khar lamb djodju ba beuss ba mou gnak ko motakh mou metii ko trop

    • @mouhamedalaminedieye3828
      @mouhamedalaminedieye3828 Před 3 dny +5

      Sawaye ama darra yeugualou co . Fi la fi diappe aye mbeur danne lênne comme xallé legui sougnou co dané mou diappe co rek na bayi lambs. Ndaxe lambs lolou mon fi ame victoire ak défaite point

  • @user-vl9gj6wm2c
    @user-vl9gj6wm2c Před 4 dny +5

    Ama défaite bi mou ame contre modou lo ba Légi dako métti 😅 ndeysann😅

  • @ousseynoutoure518
    @ousseynoutoure518 Před 4 dny +5

    Mentalement Ama est atteint par sa défaite contre le Roi des rois

  • @diagne1041
    @diagne1041 Před 4 dny +3

    Ama balde ndam rek inchallha

  • @assanendiaye5640
    @assanendiaye5640 Před 4 dny +4

    Gris yalla na Dane si barke seydina Mouhamed ❤❤❤

  • @user-su8om5zl2w
    @user-su8om5zl2w Před 4 dny +8

    Ama rek

  • @ibrahimalo3060
    @ibrahimalo3060 Před 3 dny +6

    Ama modou molo meunn boul gnou sonale yalla nala gris dane

  • @AliouneDiop-fx1ct
    @AliouneDiop-fx1ct Před 4 dny +2

    Danga warona bayi ama devolope yakhe nguen lou Barry ❤

  • @kitetv4714
    @kitetv4714 Před 4 dny +6

    gris yalla nako yalla may dame inchallah

  • @mamemorndiaye5819
    @mamemorndiaye5819 Před dnem

    Gouy gui ,liss , Ama nioy dann kou d'accord rekk👍

  • @nitoudegeukaddudegeu3001

    BILAHI WALAHI GRIS BORDEAUX DAFA MEUNE BEURI DÉ LAYLAA DAMAKO SÉTANE MBAPATT MOU DANE DIÉLEU BO XAMENI BATAY MOUSOUMA GUISS KOUKO DANE SI LAMB ❤ MO TOPP RÈK LÉGUI XÉKH BI AK POIDS BIMOU YORR MOTAX MEUNE BEURÉEM FÉNIANTOUL MAIS DAFA MEUNE BEURÉ DÉ NIMOU DANÉ EUMEU SÉNE KOU MEUNOUL BEURÉ DOKO DANÉ

  • @morcavani-tk4zc
    @morcavani-tk4zc Před 4 dny +8

    Gris sokhla wouniou leçon de moral diémeul daane danio sonou

  • @BayelahadDieng-ew3mk
    @BayelahadDieng-ew3mk Před 3 dny +1

    Ama Yalla nala Yalla may nam si barkb sergne Touba❤

  • @boubacarlimanbadiane8668

    Ama seul❤❤❤❤❤

  • @AdamaThiam-ut2pj
    @AdamaThiam-ut2pj Před 4 dny +5

    Gris rék ndam rék inchalla ❤❤

  • @khaliloulah3703
    @khaliloulah3703 Před 4 dny +6

    Ama 7 jours mo dess si combat il faut que tu récupère le maximum j'ai l'impression que tu manques de sommeil

    • @Wrestling1890
      @Wrestling1890 Před 4 dny

      Waw waw lou lérr !! Ama na andi fraîcheur dalou boubaxx

  • @famnitagueye9646
    @famnitagueye9646 Před 4 dny +1

    Yalla na ama dane 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾

  • @ouzermatresetepenre1025

    Wa nekhna bandiwé❤

  • @ndaondao2004
    @ndaondao2004 Před 4 dny +2

    Ama dakaye dane inchalla

  • @user-ww2wt9ib2r
    @user-ww2wt9ib2r Před 4 dny +1

    Ama naq da modou Kharagne Lo ❤the Goat ❤

  • @DodouFatty
    @DodouFatty Před 4 dny +1

    Ama rek❤

  • @DodouFatty
    @DodouFatty Před 4 dny +1

    Ama rek❤❤❤❤❤❤❤

  • @AliounebadaraGassama-or4op

    Ama na bayi di watt thi Serigne saliou né damay dann mbeur mi mou dèm niou dann fi lako défonn contre modou lo mou dèm niou dann ko

  • @mamadoukane7018
    @mamadoukane7018 Před 3 dny

    Gris ndam Rek inchallah

  • @OusmaneFall-xv2uu
    @OusmaneFall-xv2uu Před 3 dny

    Merci gris❤

  • @mamadoukane7018
    @mamadoukane7018 Před 3 dny

    Gris ndam Rek inchallah 🎉🦾

  • @diattaabdoukoulingo2826
    @diattaabdoukoulingo2826 Před 4 dny +6

    Gris bordeaux ndam rek inchala

  • @tallacisse7797
    @tallacisse7797 Před 4 dny +3

    Vos micro c'est de la vraie pacotille purée

  • @pierregomis2170
    @pierregomis2170 Před 4 dny +1

    Bilay ioe Sunu Bet rek lay top🎉

  • @user-pb7qn9dh6i
    @user-pb7qn9dh6i Před 2 dny

    Modou lo mane nah dane kou nek ama lamb dji nga wara gueneu prouve yalla nala yalla defal lah diame mayla ndam

  • @BabacarDieye-tt4os
    @BabacarDieye-tt4os Před 4 dny +3

    Dou souñiou bet moy dokhal réw mi.démlén liguey tébay bet bi

  • @Mouhamed-vz7hy
    @Mouhamed-vz7hy Před 4 dny +2

    Gris il parle traux 😂

  • @SeydinaissaLaye-yb4ln
    @SeydinaissaLaye-yb4ln Před 4 dny +3

    Ama seul

  • @user-if8mr1eq9y
    @user-if8mr1eq9y Před 4 dny

    Bilaahi bou wakhé nga ni gri day dane gris wakh diou bari la meune

  • @dieyebathie809
    @dieyebathie809 Před 4 dny +1

    Ama dof la rek wakh sakh manouko

  • @thiaomame1357
    @thiaomame1357 Před 4 dny +1

    Guir magat na😂😂

  • @edouardothiaw8728
    @edouardothiaw8728 Před 3 dny +1

    Ama tourne la page pour la défaite champion nga té champion Molaa daane tu peux être Roi des Arènes. Ta expression faciale montre défaite bii daff laa metii balegui. Psychologiquement c’est pas bon pour un lutteur qui doit affronter Gris. Il est techniquement bien. Fait très attention et bonne chance. 👍

  • @PILN62
    @PILN62 Před 4 dny +2

    Jules Balde vraiment il est incorrecte

  • @SoulayeDiao-ip3gc
    @SoulayeDiao-ip3gc Před 3 dny

    Gris day dane ama

  • @papandiaye7722
    @papandiaye7722 Před 4 dny +1

    Kou gueum ni combat bi taw bi mokay yakk rek

  • @GalleBa
    @GalleBa Před 3 dny

    Ama balde va battre inssal

  • @AliounebadaraGassama-or4op

    Ama ya wakhonn modou lo bou arbitre bi siffler souma l'a guedé lou guiss na ngua wakh mais yaw bi l'a modou lo di dakh lo guiss bay daw wakh ko akhlou lamb niou kham

  • @AdamaThiam-ut2pj
    @AdamaThiam-ut2pj Před 4 dny +1

    Aye dof la niou dh

  • @GalleBa
    @GalleBa Před 3 dny +1

    Moudou lo est plus fort Ama

  • @saliounomokho
    @saliounomokho Před 4 dny

    Bayilene jeunesse bi ngéne di tamal carte khalis

  • @AlzocoutureFaye
    @AlzocoutureFaye Před dnem

    Ama kassé billahi yaw rék ndam rék

  • @bathieniane8969
    @bathieniane8969 Před 3 dny

    Na cote yi reuy rek😂

  • @laminendiaye7881
    @laminendiaye7881 Před 2 dny

    Ama mo meun Wa Fass yeup

  • @AliounebadaraGassama-or4op

    Ama contre modou lo guiss naniou sa open press Nguay woné sa bop ndangoul modou lo daf l'a doumeu dann l'a bayi lènn di saltel victoire yaw ak emeu séne yéna yém

  • @usgalsen
    @usgalsen Před 4 dny

    Seen "son" baaxul. Samay nopp yepp yaxxu na nu 😂

  • @NgomNdary-jj3rf
    @NgomNdary-jj3rf Před 3 dny

    Gri mome kéneu dou tékk si mome

  • @aliounebadaradiop1214
    @aliounebadaradiop1214 Před 3 dny +1

    Pourquoi promouvoir ay sunubet di carte Looo jeunesse bi rekkkk 🛑🛑🛑

  • @user-uw2sv2sl5g
    @user-uw2sv2sl5g Před 4 dny +1

    Cris communications 0 fout mok bombardieu ak emeu sen modou lo mai cris moy 1

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Před 13 hodinami

    Gouy gui mo meune

  • @papaomarthiaw9453
    @papaomarthiaw9453 Před 4 dny +1

    Ama ndam rk de la part d’un boy médina bi peuple bi soxlawei ya deugueul sa bop

  • @GalleBa
    @GalleBa Před 3 dny

    Qrie est vieux il doit arrêter

  • @fallmoussa5831
    @fallmoussa5831 Před 3 dny

    Mal😢

  • @iranndao1305
    @iranndao1305 Před 3 dny +1

    Yaw ak modou lo dara daloula daf la man Dan la gamal yala

    • @rouguikebe9984
      @rouguikebe9984 Před 2 dny

      Jules mokoy guemlo né dafa blessé ,ça va affecter mentalement

  • @user-qi9vg6il1r
    @user-qi9vg6il1r Před 4 dny +3

    Aidé moi bane mademba sok mi décédé ?

  • @magueyembengue2980
    @magueyembengue2980 Před 4 dny +1

    Lamb aka gno niak gor dougnou toudou claf ba nianal Gaston mbengue

  • @mohamedbenzekry8074
    @mohamedbenzekry8074 Před 4 dny +2

    🔥Gouye gui
    🔥Zoss
    🔥Ama
    Nioy daane inchallah ✅

  • @SoulayeDiao-ip3gc
    @SoulayeDiao-ip3gc Před 3 dny

    Gris day dane ama